So beuguè wakh do xam sakh loy ndakh xol bou diékh lii am démb dou dara loudoul soxor rk gniko def daniou lène wara diap téh par la force dinagne lène déféré gni ay assassins lagne lo xam ni c'est une question de quelques jours dafa diar ngay agressé ay domi adama😢😢😢nonnnn😞 Barth ak nioumou yondi ak nioumou andal yalna niou Ya Allah até AK niom wallahi lii néxoul si xol ay domou diambour kouniou ko défone seu diamboot dinga xam fou métite bi tolou yalna fi yam🤲🏽 Ya Allah aar niou soutoural niou moussal si ay nafek yu melni wa sameu sa cadu
@MamadouSarr-f8m11 сағат бұрын
Cheikh Mbacké Diop Sikambaye Cheikh Ndiaye Sob Iow Tv Tv Moy Diokhé Victoire Wala Arbitre Iow Sagaguaniou Ndéye Lidiantéwuniou Gua Topatt Sunu Site Diniou Menacer Tu est Qui Iow Meuno Tax Niou Changé Niniouy Liguéyé Ngiir Yalla Nopalekoul
@djibydiouf86811 сағат бұрын
Ndeysane pape wegnal ngua ay ndanane arobase thioura mack monandos lamb mona lounekkkk
@mouchetsetse157922 сағат бұрын
J'ai failli pleurer quand j'ai vu Mame bara arobase ndeysane. Mais même bou bayé aussi nay entraînement.
@MAMADOUSECK-d4vКүн бұрын
❤️❤️❤️👊🏿👊🏿
@papadiallo6625Күн бұрын
❤
@GeneralTV-LutteSenegalaiseКүн бұрын
Copin do wax lo maîtriser au moins avant guamay juger sama liguéy limou ladieté rék la déff
@SerigneDiop-c3bКүн бұрын
❤❤❤
@djibydiouf8682 күн бұрын
Merci général tv
@debarafaye2 күн бұрын
C’est où
@moussadione90292 күн бұрын
💯💯💯
@moustaphadiouf74152 күн бұрын
Fils de Batling Siki le roi du Qatar kay 😂😂😂 bilay yéna yabaté 🤦🤦🤦
@CheikhmbackeDiop-g2i2 күн бұрын
Tv tv lan moy liguayam
@GeneralTV-LutteSenegalaise2 күн бұрын
@@CheikhmbackeDiop-g2i lou xew faut expliquer j’ai pas compris
@CheikhmbackeDiop-g2i2 күн бұрын
Pourquoi pas sa le recours de Dandemayo hier
@CheikhmbackeDiop-g2i2 күн бұрын
Général yaw do dara mala ko wakh
@GeneralTV-LutteSenegalaise2 күн бұрын
@@CheikhmbackeDiop-g2i wa lou xew ?
@SouleyeDiouf-n1t2 күн бұрын
Vraiment soxla lagnou beur yi taw yi comme birame diebele
@OusmaneFall-p5z2 күн бұрын
Fils de batline nite daye goré Do rousse sah maye nala 2 fois demi finale 1000000 et400000
@samsungchrome-r2d2 күн бұрын
fils de batline worr nako déh
@adamadiouf23642 күн бұрын
Fils danouna bou yague
@mbayewague90972 күн бұрын
Général tv iow soy wakh do kham lingay wak en ki kén dako kham si nioun ngi deuck keur fodé nganan sokh sokh keur fodé il faut l'effacer au plus vite possible
@mouhamedsarr-fj1jg2 күн бұрын
Merci beaucoup Mamadou sarr 🤲🤲🤲🙏🏼🙏🏼✅✅✅
@MohamedDiouf-iu7kx2 күн бұрын
Fils de battling wooor nako déh😢😢
@kaddundawniakknawonedemb91702 күн бұрын
Général tay sa boy bi thiomby affaire de partisans deug lafa déf
@GeneralTV-LutteSenegalaise2 күн бұрын
Ah bon Comment ça ?
@kaddundawniakknawonedemb91702 күн бұрын
Wone ñu demi final dandemayo et fils de batline
@modoundiaye89462 күн бұрын
Bonne continuation frère Djiby
@malickdiouf83213 күн бұрын
Très bonne continuation le jeune
@MamadouNgom-o9i3 күн бұрын
Lamb wakhul dégue thiey Arobase 😢
@Ndeye-k1s2 күн бұрын
@@MamadouNgom-o9i Adouna nonou la
@MohamedNdiaye-xq6wz3 күн бұрын
Somb ma fierté
@mayecordiouf98913 күн бұрын
En direct way
@yandefaye65303 күн бұрын
Bne continuation couz bi🙏
@GeneralTV-LutteSenegalaise3 күн бұрын
Bilahi pape waxal d kén dou mome Djiyaramou
@TaphaKeita-v3j3 күн бұрын
Weuz rék
@ModouSene-x6y3 күн бұрын
Ok ❤❤❤
@BirameSarr-w3w3 күн бұрын
Mia une fierté sérère ❤❤❤❤
@BirameSarr-w3w3 күн бұрын
Diokandial Général TV
@BirameSarr-w3w3 күн бұрын
Fier de toi Mia Diaker!❤❤❤
@MoussaSao-l8r3 күн бұрын
Notre fierté
@mbourtefessetv3 күн бұрын
Merci
@bubafatty27073 күн бұрын
❤❤❤
@MoussaCisse-p2w3 күн бұрын
🎉🎉🎉GANDIA TV❤❤❤
@issadiouf2563 күн бұрын
Borom Sabador bi defa warra har Mariama keur gua dh😂