Macha'Allah jerjef pape professeur Mame Ousmane Ndiaye ak ya oustaz pape Hann
@abyndiaye2886Ай бұрын
Macha'Allah Serigne bi ya oustaz yallah na yallah yessal yeuremandé ci kawame té mou doli leu lere Wallayy wallayy ndeyessane kéne dou Sougnou Mame boy Elhadji Abdoul Aziz Sy Dabakh RTA yallah na gnou yallah tass ci barkéme Amiiiine inch'Allah 🤲🕋❤️❤️❤️