Serigne mbacké ab Rahmane yalnako yalla samou té takhawouko ci barké Serigne Touba
@damembengue873522 күн бұрын
Serigne mbacke lim wah moye degg
@falloukhouma688222 күн бұрын
Waw goor serigne Saliou fall
@dioufpapadiabel22 күн бұрын
Bilahi gni amenanie sérieux problème Serigne bi wakhou léne lii dé Al Quran ak souna Rassoullilahi sëgn Touba app diamou Yalla leu nékk lénn ay nitt
@ibrahimacissedieureudieufs273222 күн бұрын
Serigne mbacke Abdou Rahmane mii pass passou wahabiste bou bone la yor dou mouride kou soof la
@baxrektv478122 күн бұрын
ولا تقل لأحد كذبتا Sëriñ Tuubaa mu Bax néna: " bul wax ken fénga."
@baxrektv478122 күн бұрын
إلى تواليف يقود الله.. kan mo makoy aggalél
@yoon_wi221122 күн бұрын
Yaw boroom sen ku réew nga ta yabate Sëriñ Mbàkke Du seen Maroom ci xam-xam
@prince_mbacke277422 күн бұрын
Yeen ay dmrm gueen
@serinc.moustaphabadiane511222 күн бұрын
Serigne Mbacké Abdou Rahman ❤❤❤❤❤
@serinc.moustaphabadiane511222 күн бұрын
Serigne Mor bay len fen
@bismillabismilla887822 күн бұрын
Nonou Seringe Touba bi Gëna bon si jamono ji moy Chiekh Toure domou ndialo domou haraam bi fén rék lay déf
@Toubamo22 күн бұрын
Yène niorèw guène diagolène diogowolèn démlène liguèyi S mbacke dosén mouroumo baye ni séne Serigne yinga khamni ay dour katt lagnou khissa féne kissé
@NdeyeTiam-x8w22 күн бұрын
Yéne dé yénagui doundou s touba lilaxam thi ak mourid kou beuga yamalé s touba ak niép ab nafékh la
@MASSYLLAMBAYE-w2h23 күн бұрын
Yéne dagéne de tiahane rék seringe mbacke Abdou Rahman d'où séne morome yalna nako yalla dolé samou
@KhadijagueyKhadijaguey23 күн бұрын
Képpu ba wakh Serigne mbacké rahman lou niaw sa leufeul nday yak niaguay andal sa Bo kheyé Dômé kharam yi dun lén bayi guéni yakh yonnu serigne serigne bi mbacké dousa morom kattt