Пікірлер
@MourtallaMbaye-vr7gd
@MourtallaMbaye-vr7gd 2 минут бұрын
Yalla nako yalla may ndam
@MohamedNdiaye-bl2sh
@MohamedNdiaye-bl2sh 52 минут бұрын
Conne nangougha moguen si iow
@AzizDramé-q4j
@AzizDramé-q4j 2 сағат бұрын
Pimpi😂
@mourbouboromdarrou
@mourbouboromdarrou 3 сағат бұрын
Brise de mèr si guinay sakouyi la dané TMAX khamoul lingay wakh ya féne
@mourbouboromdarrou
@mourbouboromdarrou 3 сағат бұрын
Siteu Moy sen baye yéne wa PA kéne monou fa dane Siteu
@mourbouboromdarrou
@mourbouboromdarrou 3 сағат бұрын
Mbacké faye dangaye Bari ndéyi wakh so dieul sa thiés bou thiaroye mou réy sa ndeye, Siteu mo meune PA
@amdymoustapha6130
@amdymoustapha6130 4 сағат бұрын
😂😂😂😂😂😂
@Misterboom-x7x
@Misterboom-x7x 4 сағат бұрын
DEUG nékhoul mé siteu mo daan Modou lo Kouy nafékh nak boul gueum ba ila yawmi diini siteu mo nokh Modou lo
@amdymoustapha6130
@amdymoustapha6130 4 сағат бұрын
Sénn leufal ndaye goudi goudi P A
@abasall711
@abasall711 5 сағат бұрын
😂 bidou yoyu Luler ngawax ama ak boye niang dano degueul sen bop motax combat bi gawa diex
@magayethiam1034
@magayethiam1034 5 сағат бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@mbayesarrdia4470
@mbayesarrdia4470 7 сағат бұрын
Yallna la yalla Mbaye ndam
@Brome_rewmi
@Brome_rewmi 7 сағат бұрын
Mbacké Faye Seul ⚔️💪🏾👑
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 8 сағат бұрын
Wawaw am diiné rék mo woor😊🎉❤
@MameSow-m7e
@MameSow-m7e 10 сағат бұрын
Modou lôoooooo ❤❤❤❤❤❤
@MamemorNiang-c9d
@MamemorNiang-c9d 10 сағат бұрын
Mbacké Faye ak ibrahima faye beuz loñ book
@miboldieng7574
@miboldieng7574 11 сағат бұрын
Diemal def ni siteu nga Tok di wakh rek
@bayemodoudiagne2326
@bayemodoudiagne2326 6 сағат бұрын
Ki déi mo dakh beuré siteu
@benzdictenobalegomis6139
@benzdictenobalegomis6139 11 сағат бұрын
Machalah Mbacké Faye🎉🎉❤❤❤
@sarrabdou3040
@sarrabdou3040 12 сағат бұрын
Boy vrai champions leu bilay
@danielbrown7353
@danielbrown7353 12 сағат бұрын
Markatou tat nja bou juenes biii guemal nala
@malicksarr2141
@malicksarr2141 12 сағат бұрын
Mbacke faye champion boy bou nite ❤ félicitations encore modou Lo 👑
@DiamilDiouf-od6pb
@DiamilDiouf-od6pb 13 сағат бұрын
Yaw nopil say défaite ak say victoire gno tollo😂😂
@Brome_rewmi
@Brome_rewmi 7 сағат бұрын
Bayil doul Mbacké guedj na am défaite 5 victoire consécutif la déff andill sa Mbeur nga khol
@bayemodoudiagne2326
@bayemodoudiagne2326 6 сағат бұрын
Sa mbeur déi moko eupou dolé
@thiernoba5091
@thiernoba5091 13 сағат бұрын
Mbakè Faye futur champion inchalla
@babacar3178
@babacar3178 13 сағат бұрын
Wa pikine insbi séne sokhor moy fégne eumeu séne abdou bakhoum
@abdoukane7788
@abdoukane7788 17 сағат бұрын
Mbacké Faye seul 🎉❤ borom roungasse bi ❤
@mamegorthiaw-gy5od
@mamegorthiaw-gy5od 17 сағат бұрын
❤❤
@laurentmendy6670
@laurentmendy6670 17 сағат бұрын
Mbacké faye Seul
@alygueye6801
@alygueye6801 17 сағат бұрын
Champion mbacké faye❤❤
@alygueye6801
@alygueye6801 17 сағат бұрын
Mbacké faye grand champion❤❤❤
@faloudeme8965
@faloudeme8965 18 сағат бұрын
Lima diakhall situé pope bi dafa lall souff
@Fadel_Parisien
@Fadel_Parisien 18 сағат бұрын
Mbacké rek laaniouy topp ✌🏾
@ElhadjiBiraneToure-k1b
@ElhadjiBiraneToure-k1b 19 сағат бұрын
Ki nomo niake diome say morom niepu rawnan la thi lam ji nga topu micro 🎤 di fene rek
@amiegaye6714
@amiegaye6714 19 сағат бұрын
Yalnala yalla mai ndam...wah ji refetna
@Moustapha-yt7ry
@Moustapha-yt7ry 20 сағат бұрын
Yow nopil ndeyam yalnala sokh yenou ba si kaw kat SA ndeye
@abdoukane7788
@abdoukane7788 17 сағат бұрын
Katalé sa deudieuw nday mou geuneu nékh kay
@Brome_rewmi
@Brome_rewmi 7 сағат бұрын
Sa data yaye koudoul Sokhou bou Ndaw Mbacké mola meun
@bayedieng7141
@bayedieng7141 20 сағат бұрын
Machalah Amale diam wayy
@ousmanesarr756
@ousmanesarr756 20 сағат бұрын
Mbacké faye katal sa leufeul nday may nitt gni diam légui danga bari nday wakh trop sa baye modu mola guena khamni siteu da niouss ndeim dane ko lolu moy meti nday sa khol bi ngané lac lagnou yab deug la kay mai siteu 2 comba you amoul diell la am modou am nday 4 comba you amoul diell ngay katt ndeim di doul koulen guiss ningeni dieufro ngen khamni boy bi Game na sen nday bala modou faté dila doundal dila labb ba légui danga nday nga mou domeram yalna sock bou ndaw dokhane sa nday parcel dou meusa nday am mbeur bou dane siteu
@IbrahimaNdiaye-w4b
@IbrahimaNdiaye-w4b 20 сағат бұрын
Mbacké faye nitt kou goré ndam rékk inchalah
@IbrahimaNdiaye-w4b
@IbrahimaNdiaye-w4b 20 сағат бұрын
Mbacké faye nitt kou goré ndam rékk inchalah
@AtoumaneNiasse
@AtoumaneNiasse 20 сағат бұрын
Félicitation mbeur damala beugue ndakh modou lo ❤❤❤
@AtoumaneNiasse
@AtoumaneNiasse 20 сағат бұрын
Machallah mbacké lou leer nga wakh
@IbrahimaoumarDem
@IbrahimaoumarDem 20 сағат бұрын
Champion mbacke faye
@FayaNinkih
@FayaNinkih 21 сағат бұрын
Faye ❤
@Mamadou-j1x
@Mamadou-j1x 21 сағат бұрын
Merci ❤❤❤
@ayipdiop1748
@ayipdiop1748 22 сағат бұрын
Abdou bakhoum iniaan baakhoul
@Mustapha-n7i
@Mustapha-n7i 22 сағат бұрын
Yow katal sa ndey
@kharagnembaye5958
@kharagnembaye5958 22 сағат бұрын
Pour yéne adouna lep wakh djou gniaw la oky
@sllioudiagne8680
@sllioudiagne8680 21 сағат бұрын
@@kharagnembaye5958niak Diom reik mo takh mouy sagua
@SambaToure-n9h
@SambaToure-n9h 21 сағат бұрын
Da ngena tardé yen
@diallolamine9587
@diallolamine9587 21 сағат бұрын
Respect deugue rek la wakh😊
@mamadouseydougueye1696
@mamadouseydougueye1696 21 сағат бұрын
Saga bakhoul
@saliougueye9833
@saliougueye9833 22 сағат бұрын
Modou seul
@djibrilkonte6928
@djibrilkonte6928 22 сағат бұрын
Merci mbacke faye ndam rek inchallah
@serignesalioudiouf1080
@serignesalioudiouf1080 22 сағат бұрын
Un grand champion Mbacke Faye que dieu vous bénisse
@AssaneNdiaye-n4m
@AssaneNdiaye-n4m 22 сағат бұрын
Mbacké faye jambar deugeu
@SeckMbacke-c6j
@SeckMbacke-c6j 22 сағат бұрын
Masoul am ndam guediewaye Lou takh balla Gaye di wara dieul kon