Waa Ahlu cafe café rekk ngeen di def waaye lépp lu ngeen gaa yi naan nañu ko😂🎉😊
@serignembackesylla64563 күн бұрын
Waw gor
@abdoulahadmbaye45944 күн бұрын
Yeex a xamante gi rekk laay reccu waaye alhamndu li Laah bi ma Yàlla ak Yónent bi boole ak yéen te jëmmi sëriñ Saaliwu Mbàkke.
@moustaphadiagne-sj9th3 күн бұрын
@abdoulahadmbaye4594machllah
@abdoulahadmbaye45944 күн бұрын
❤❤❤❤
@abdoulahadmbaye45944 күн бұрын
Man yéen rekk laay topp ❤
@abdoulahadmbaye45944 күн бұрын
Assalaamu halaykum waa waa diwaanu sëriñ Saaliwu Mbàkke man la Abdul Ahat Mbay Bëgg Sa Réew Gëm Li Nga Doon li mambur bees ci diwaan bi sàkku ngeen dalal ma.