Macha'Allh diaradjeuffati Serigne Ahmadou Rafahi Mbacké, yalla nala Yallah samma ta wëeralla ta goudale sa fann thi barcke Mouhamet Rassoulillah . Amine 🙏🏿🙏🏿👊🏿❤❤❤
@elhadjifalloudia899222 сағат бұрын
Amatina sololool Mbacke Yalla nagnou Yalla defal diam Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia ibn Cheikh Mor Dia Ndiar
@niakhalintounkara2493Күн бұрын
Cheikh Oumar il a raison l'ennemi de l'Afrique ça été toujours l'africain.
@PapeAbdoulayeDIENG-ol7thКүн бұрын
képp kou djap née Imam limou wax daa indexé Prof COD, raggal mo bokk ci les vrais cicbles de Imam mbokk yi nagne raggal Allah!
@MoussaKhoule-d8bКүн бұрын
Machalaah ya know imame
@papamakhoudiasarr4503Күн бұрын
Geumoumeu ni Cheikh OMAR DIAGNE lay gaaral, Si c'est le cas, l'erreur serait grave de la part d'un érudit comme ce monsieur.
@thiamahmadulattekh56217 сағат бұрын
Cheikh omar diagne moy kane ba kene douko joubanti tei mo nek si aye fene aki togne?
@papamakhoudiasarr4503Сағат бұрын
@@thiamahmadulattekh562 loolou dou wakh ji. D'abord,yaw ak sa Serigne yeenay Kan,ba sou ngueen joumer,kenn dou leen jubbanti ? Yeena daq Fenn nieupp,yeen gnii bagn deugg,ak Koo meuneu doon nak. Cheikh Omar Diagne dafa leen tiim si xam xam ak fit. Les tirailleurs et les spahis sont tous pareils,en ce qu'ils étaient sous commandements français,et là, ils ont commis les pires atrocités au Sénégal,en Afrique et dans le monde. Yaw ak rafihou yeupp laa wakh,lagg leen gueusstouwaat histoire. Yeena daq Fenn nieupp. Way yow !
@mapendandiaye4229Күн бұрын
Thiey Kien Dou sa mame s touba si xam xam Yague fia te wer
@rokhayaniang2369Күн бұрын
Machallah m'backé jazaka'allah khayrane yalla na sa Diam yague té yague fi té weurr dieureudieufeuti
@PapePape-s4wКүн бұрын
❤❤❤❤
@fallouwilane3503Күн бұрын
Omar dafa bari wakh de
@fallouwilane3503Күн бұрын
Machalla ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@babamamadouniane7622Күн бұрын
Cheikh Omar Diagne a raison sur toute la ligne. Diomaye la limogé pour le libérer sur ses dures vérités et lui aussi Diomaye d'être à l'aise dans ses fonctions de Président de la République.
@modoumamourdiallo8846Күн бұрын
Cheikh gnaw langue nitti fitna Omar Diagne cherche seulement un nom C'est le fou du siècle
@mouhamadoubambadiop543Күн бұрын
Yaw kou doy war nga ta lep loufi nit wakh Lou bon Serigne yakoy gadou. Li mouy khoutba jotewoul dara ak li nga bind. Yaw kou bon nga
@julesfall180Күн бұрын
Akhe dekodo bon serment❤❤❤❤❤❤
@taphaseye243Күн бұрын
Machallah
@foulbino34Күн бұрын
soyons serieux, le titre na aucun rapport avec le discours. Yallah naniou Yallah moussal si lamign wou doul wakh deug ou wouy diew.... Cheikh Omar Diagn, diewoul et fenoul, deug rek la wakh si mbindoum mak gni pask si bene tere kokou nena Makka daniouka tokhal si benene deuk, lolou dou deug... donc COD li,ou wakh ak li imam Rafahi wakh amoul rapport. niou bayi amagal yi
@mamadytamba3690Күн бұрын
❤❤❤
@seynabfallou395Күн бұрын
Machallah
@mamadoucham9645Күн бұрын
Waläy ndeysanne mbacké Anna solo
@souleymanediawara4654Күн бұрын
Cheikh Omar Diagne, laméniam deug rék la wakh ci tirailleurs yi. Wakh deug ci diné la bokk ! Wassalam 🙏🙏🙏
@AlieuBadjan-tz7nqКүн бұрын
100%
@papamakhoudiasarr4503Күн бұрын
Amoul leeneen. Jusqu'à l'extinction du soleil, Cheikh OMAR DIAGNE a raison sur toute la ligne.
@modouseckseck9893Күн бұрын
Dedet cheikh Omar Diagne bu wakheni tirailleurs yi ay tretre l'an Lolou wakhoul deug
@Nicolasbka937622 сағат бұрын
Fén na dé, les tirailleurs sénégalais n'étaient pas des traîtres. Il s'est trompé, il a confondu les tirailleurs est les spahis.
@papamakhoudiasarr450322 сағат бұрын
@Nicolasbka9376 yaa meuneu nenn ! Tirailleurs yi sénégalais yi nio tiré sur les africains,au Sénégal,au Madagascar,en Indochine,en Algérie, au Congo, et partout où l'armée française avait besoin de leur force. Selon toi,ce sont les spahis qui ont tiré sur les tirailleurs ou les soldats français ? Nay rafet waay ! Yaw Mii yaa meuneu nenn,ak gni nga faral.
@PapaFall-r4nКүн бұрын
Machallah amna solo ❤❤❤
@latifdiakhate7296Күн бұрын
❤️
@Sen_espoirs2 күн бұрын
Machala je l estime beaucoup il est trop pertinent et pieu je le suis envers ces prêches
@mouhamedbachirndiaye76712 күн бұрын
Barakallahou fikh ❤❤❤, ratakh lamigne dé takhna fmi, banque mondiale, investisseurs yi nieup dawnanou!!!
@modoufallndao8814Күн бұрын
Ratakh lamigne tey wax deuk ak nopi si feneu lou geune
@mouhamedbachirndiaye7671Күн бұрын
@modoufallndao8814 Justement, c'est ça le problème,😁 Ratakhlé téy wakh deugue sakh khamnako, wayé Ratakhlé, té lo wakh dou deugue, surtout si kilifeu, jamais preuves, day dawlo boromi koppar !!!😅
@matardioum1684Күн бұрын
Wakh nga deugue dé
@MeissaBARRO16 сағат бұрын
Tu veux qu’ils mentent ou cachent la vérité, ce qui est interdit par l’Islam.
@thisworldisour2 күн бұрын
Quelle rapport avec COD ce xutba MAACHALLAH de cheikh rafahhi... ''Koulil akh walaw kaana mouraan'' bu fourgon ci xutba bi digua xam KON Lou warral COD di wakh... Xastéwoul té dieuwoul, loumouy wakh 'diarigne la ci kou beug déf histoire tirailleurs yi taarikh pour toute une génération a venir. Maintenant ce que peut penser ce qu'il veut chacun peut donner son point de vue... Pourquoi ce xutba n'est pas attribué aux détracteurs de Cheikh Oumar Diagne en particulier certains mourides qui inventent et désinforment en manipulant parce que simplement ils détestent COD. Pour les savants la vérité est primordial surtout un si on doit le programmer pour toutes une génération. Maachallah cheikh rafahhi YALLA samoula
@assan44992 күн бұрын
Sa kaddu rafèt neu té teggu thi xam xam machaallah
@sankounkanoute30672 күн бұрын
Machallah Serigne Rafahi et merci au Président Bassirou et le Premier ministre Ousmane Sonko
@thethelion68152 күн бұрын
A quand la convocation des chefs religieux milliardaires qui ont participé aux bradages de nos ressources en complicité avec les régimes précédents ???????
@beyepape9622 күн бұрын
Qu'attends tu de les convoquer ???
@beyepape9622 күн бұрын
Oubien tu les porte plainte comme tu es un citoyen sénégalais
@jubbantitvpro90Күн бұрын
Demal nga ligeey yi moo geune si yaw sokhar ak iniaan dong mooleen diapp
Machallah serigne bi khouba ji amna solo torop message bi dial na borom kham kham deugu la diambar la takhaway bi yalla na yagu wér ak wérlé inchallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
@BaraGueye-v1b2 күн бұрын
❤❤❤❤
@khadimfaye24602 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤dieureudieuf Mbacké Balla yalnangafi yag lool té weur ❤❤❤❤❤❤. Amine
@MASSAERSYLLA-h8v2 күн бұрын
Machalla goud fane ak wer
@mbayedioume2 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤
@MASSAERSYLLA-h8v2 күн бұрын
Machalla barakal lahou
@cheikhgaye18652 күн бұрын
Machallah yalla nañu yalla may ak degg akuk toppu ❤❤❤❤❤