Massa ma sœur massa que Ya Raby Le Tout Miséricordieux gniit leup lerr si barker Seydina Mohamed SwS amen
@ouleycamara32605 жыл бұрын
Ma sœur Yalnala ya rabbi nital ba ngua guissék sa dome thi barké Seydina Muhammed (psl)
@lespatriotesdusenegalsoute23895 жыл бұрын
Li rek wanéna kén dou yaye bayam fatté nako mais la maman tjr migui déf limou meune ndeysane yallah nako yallah diapalé
@binetoudiop3374 жыл бұрын
Allahouma amine
@diawoulimata23764 жыл бұрын
Amine yalla nako yalla nite
@mamadouly57534 жыл бұрын
Amine
@mamanmargotchimerediop97844 жыл бұрын
Allahouma amin inchallah
@philippesambou67714 жыл бұрын
courage madame il ne faut j'aime découragé un jour viendra pour toi
@hawasall41485 жыл бұрын
Ayyy wayy dioxé lén domou diambour nitt eumb domam ak eumb nimou mété nga dieul domou diambour ahh mn pays va male aujourd’hui c elle demain ça sera ki ?
@ndeyeaidasow78514 жыл бұрын
Demain yala done mome momou domame ndakh mou yeuk lou gueneu piir li
@ndeyeaidasow78514 жыл бұрын
Demain yalaneu done mome momou domame ndakh mou yeuk lou gueneu piir li
@king_aisha53385 жыл бұрын
Ce pays me fait vraiment peur ! Je me rappelle j’étais en plein travail je suis partie à abass ndao ils m’ont viré soit disant c’est trop tôt les sages femmes me parlaient avec mépris. Pareille, j’ai accompagné ma tante accoucher, une dame est arrivée elles l’ont renvoyé chez elle et dans le taxi elle a accouché et à perdu son enfant. La méchanceté de certains sénégalais c’est aberrant on dirait que l’enfer n’existe pas pour eux. Courage à toi Aïssatou. Dieu est Grand.
@antandiaye55154 жыл бұрын
Ça m'a beaucoup touché comme maman beaucoup de courage
@mamindir62644 жыл бұрын
Abass ndao mane mi am nafa dome niou nèma dèna en 2004 té yalla rek mo kham wayé loussi meuneu nék doumaléne ko meusseu bal sacrifices yi barinaniou meunagnou léne faye sakh pour niou diokhléne bébé
@fifiseck39293 жыл бұрын
Li rék motah kéne dématoul ci hôpital yi clinique yi tamate chér na sa hol soula wahé mogui doundou rék pour mane mogui doundou sentiment yaye dou féne wsou déh wonne yalla mokaye rahass sa hol bat toi boul bayi courage
@aissatouseckndiaye8153 жыл бұрын
Jtjur chaque jour que dieu fait je pense à ma fille chérie 😭😭
@khadysarr50145 жыл бұрын
Une maman courageuse tu n'a pas bessé les bras malgré mais Yalla nako Yalla nitt ma chérie
@nogayeniang82405 жыл бұрын
Metina torb
@beatricesy79194 жыл бұрын
khady sarr amine
@emmarosesouareD29124 жыл бұрын
Je n'est jamais penser que ce genre de choses existe au Sénégal vraiment c'est décevant 😭du courage ma soeur Dieu est grand.et je vais prier toujours pour toi INSHALLAH. pour que tu puisse trouver ta fille
@madiaw67763 жыл бұрын
Ndeyssane masta Yalla nakko Yalla niiit
@gueyendioro105 жыл бұрын
Demal Teuss ma soeur. Nala Yallah japaler ba nga guissate sa dome ak jam ak salam. guisso dome, guisso New domerame yi Senegal dou meussa avancer. Niak worma rek.
@unecitoyenne37015 жыл бұрын
Courage et bonne chance Aissatou. C est tres dur. Surtout se battre seule. DIEU est témoin de tout
@evistamomo61165 жыл бұрын
En tant que Mère ça me touche vraiment à la limite nioune louniou wara déff😭😭
@cheikhounadiouf84115 жыл бұрын
Doye n'a ware
@barambaye11815 жыл бұрын
Doyna war trop
@kanebaylaramata62285 жыл бұрын
C vraiment triste ma nièce
@himorydeemdeme68014 жыл бұрын
Cé très louss
@khadyniangthiam60265 жыл бұрын
C trop triste vraiment en tant que maman je partage ta peine
@tinayayam11 ай бұрын
Le coeur d'une mère ne ment jamais bat toi ma soeur tôt ou tard elle sera avec toi❤❤❤❤
@bayerekmoydeguniass54485 жыл бұрын
Yalna ko allah délo sii sii barké baye niass yarabii
@zahrafatima13953 жыл бұрын
Thieye sunu yaye yi amou niou sene Faye dèh longue vie à vous yAllah borom bi diapalè maman
@baramata96445 жыл бұрын
Massa ma sœur yalla nalako yalla nital si barke serige babacar si
@maimounasamake65325 жыл бұрын
Dom... ndeye!!... Ma soeur tu verra ta fille inchallah😓😓😓
@Bikouna-youanis4 жыл бұрын
Amin
@fatouoncina93474 жыл бұрын
Allahouma amiiiin 😔😥
@mbasscisse7874 жыл бұрын
Amine
@mamefatmandiaye67814 жыл бұрын
walahi dingako giss
@minafall87095 жыл бұрын
Mettina mais yalla geumoul neilawoul inchalla mou gaw mou yeikh di nga guiss sa dom derett dafa forr foumou meunti neik dina la weur si courage
@fatikonate24305 жыл бұрын
La femme elle est vraiment forte et courageuse machallah mais li metti na si xol😭🙏🏼
@fatouthiam57972 жыл бұрын
La seul personne qui peut résoudre le problème c'est marieme Faye
@khadijaparisgueye65275 жыл бұрын
Garde espoir ma belle j’espère que tu verra ta fille inchallah
@fabintediaw78894 жыл бұрын
Aissatou yameu meune tu es forte Yalla dinala indil sa dom ci daradiay Rassoulillahi
@adjiseck91045 жыл бұрын
Dole moooo meune deugue waye deugue moye moudie. Yalla nako yalla safaral.
@soukeynarassoulgueye1035 жыл бұрын
Massa ma soeur vraiment lii métina torop yalla nako yalla nitte gua guissako si diam ak salam si barké Seydina Mohammed sallallahou aleyhi wa salam
@matyfall60543 жыл бұрын
🤲🤲🤲🤲🤲🤲
@ndeyefatoundour37514 жыл бұрын
Li kouye djiguene rk tousenala ma soeur yalla n'a ko yalla niitt si daradiaye séydina Mohamed du courage yalla d'où nénale diamame
@matabeuleup49264 жыл бұрын
ça me touche vraiment, tu es courageuse madame! Que Dieu retrouvera ta fille
@momombowofficiel2075 жыл бұрын
Ndeysane Ken dou yaye yaye rkk moye son si domame yalla bakhna
@kenzifafall34383 жыл бұрын
Massa ma sœur yalnako YALLAH SWT nital si barké beussou magalou khadimou Rassoul gui amine 😭😭😭
@bintacharlesdiop78005 жыл бұрын
Il faut que justice soit faite Demal teuss aussi Gars yi nagnekopartagé, gneupp diottssi Yallanala yalla diapalé badeugueu gui fégnne inshallah
@ndoura55994 жыл бұрын
Histoire bi diar na teuss
@adjamb11295 жыл бұрын
Une amie d enfance on a grandie au point e massa ma sœur chérie dieu m en ai témoin que je ne saisse de pensé a toi et ton bb a chaque instant, yalla neko sougnou borome nit aissatou
@oumoucledorndiaye8875 жыл бұрын
coucou c kel adja ? j'habitais o point e ndeyssane je connais aissatou de mem k sa grande sœur suis sans mot métina dal yalla nako yalla nitt
@aidasamb5914 жыл бұрын
voila papa dji mom yoname nékatou sii souko guéné wone mom si bopam kone dina def ni yayam di défé rechérche mai malheureusement. dome dafa sakh si kholou yaye en tan k maman sa me touche vraimen yalla nako yalla nite si barké borom touba🙏🙏🙏🙏🙏♥
@diallorama45454 жыл бұрын
Ndeyssane métina yalla na ko yalla nitt bamou fégne
@matyseck51825 жыл бұрын
J ai eu peur quand j ai entendue ça ndayesanne thiey yalla 2007 ba légui yalla na fégne thi barké khassida yi thiey yalla
@khadijarasoulbintouabdalah5854 жыл бұрын
Maty Seck amine
@makhdydiabou92483 жыл бұрын
Amine ya rabii
@ramatoulayediagne86594 жыл бұрын
😭😭😭 je compatis. Yaay rekk moo meuneu kham métit bii. Dieu est grand
@adjafatousy46525 жыл бұрын
Massa métina trope yalla nako yalla niite sì barké seydina mouhamed salahou alay wa salam amine yaa rabbi
@dieynababa3074 жыл бұрын
Ay vrai domaram lagne ses genres de sage-femme yalna yalla takhawou
@bintawalyndiaye39123 жыл бұрын
Bilahi kéne dou yaye man je suis née là-bas en ten que jumeaux mais on na jamais retrouvé l'autre bb du courage yalla nala sounou borom nitale sa dom si barké seydina Mouhammad psl
@binetasane4674 жыл бұрын
En tant que mère ça me touche énormément massa yalna yallah diapalela Sokhna si
@ndeyefatoudiakhoumpa34114 жыл бұрын
C émouvant franchement mai boul meussa bayi maman yalla baxna te yalla naléne atté
@babacarkolosstv4205 жыл бұрын
Ces vraiment triste du courage yalla nalako yalla diokhat dieu est grand
@madjiguenesow22924 жыл бұрын
C dur j’ai mm les larmes o yeux yalla nako sunu borom bii niitt et k justice soit fete souii forte🙏🙏
@adamaawadiallo31055 жыл бұрын
Peut être ils l'ont donner en adoption une famille européenne ??? Sinon pourkoi ils ont refusé de donné a la police le registre de naissance ?et le procureur dans tous sa?
@maryfall48275 жыл бұрын
Jai pense a sa moi aussi je suis vraiment triste sa fille a même age que mon fils qui ne a 2007😭
@mouhameddia27384 жыл бұрын
Bane procureur gnaye wakh nonou ????
@Linguerediouf4 жыл бұрын
Mary Fall lou xew sa dom mba mongui thi djammou?
@idirisaba74634 жыл бұрын
Bien sûr
@aichatoudieng25014 жыл бұрын
Ah c bizarre
@oumousalamatakane88754 жыл бұрын
Ndeyssane métina yaye rek meneu li mais yalla bakhna yalnako yalla nit ci barké seydina mouhamed
@Topofthetopapex5 жыл бұрын
je ne pourrai jamais imaginer ce qu'elle endure. Mangui lay nianal bou bakh . lima beugueu wakh yeup tchoo
@khadijatousarr44665 жыл бұрын
Inchalla di gua yorate sa dom sa loho inchalla dom si xol la té yalla fi mou bindeu wadiour bou djiguène akh dom mam sori na sori bo ham ni domou Adama bou tahali gniar yi djis ko . Miracle Yalla beuri neu yeur mandé sougniou borom beuri neu . Yalla n'alla yalla diapalé si barké Naby (PSL) .
@amitall39987 ай бұрын
Alhamdoulillah courage dingua meuss guiss sama tokara incha Allah Denk que nagnou sounou borome
@adosssarr78455 жыл бұрын
courage siste yalla bakhna sa dom dina fégne inchallah 😭😭😭😭métina trop bilahi
@astoukeita67354 жыл бұрын
Ne baisse jamais les bras ma soeur donné la vie est la plus belle chose au monde inchallah yarabi tu verra ta fille que dieu la protége 🙏
@aniichsow14405 жыл бұрын
Du courage yalle na fégne si Diam
@salyallemomuawrksarr86524 жыл бұрын
Li mètina trop bilahi ngua diour sa dome baparè ay nitt you nièmè yalla beugue lako khagn li mètina khaw ma could yorè domou diambour ji nako diokhè te dièma diouri dome ok Yalnala yalla atè ak niom ndakh atè yalla mon gueneu gaw bou nitt 😭😭😭😭😭😭❤
@sunugal43925 жыл бұрын
'Couveuse disponible'!! SENEGAL mo deh... Na Allah fégnaleu yeupeu. AMINEEE
@fatousall20424 жыл бұрын
Ndeysaan j'étais dans le même service que son papa, je me rappelle que la même année j'avais un bébé et ça m'avait tellement affectée. Du courage ma chérie c'est vraiment dur.
@massaerthiam89684 жыл бұрын
Never give up.... Bilahi walahi talahi yaye amoul morom 🙏 👍 ❤️ je vous aime vraiment et Boul khadiiii insha Allah yalla nalla yalla diokhatt sa Dome et Ken defoul Ken d'ara Ken defoul Ken d'ara Ken d'ara Luway deff bopom laka deff 🙏Wakhi serigne touba
@rackymaadamel12194 жыл бұрын
Aywaye Sénégal thiaye thiaye weuyou Bone sokhor nék. Li metinama si j'avais des moyens damaye volontairou topko bamou seuss. Bo démé kou yaradal môme lane ko diokhe. En tou cas metina. Massa yalnako yalla niite ci barke seydina mouhamed sallallahou haleyyi wa sallam. Amine
@khadidiatoudia7595 жыл бұрын
Il faut porter plainte Abass NDAW
@cocobane5 жыл бұрын
Eywaay massa lii metina d. Yalna yalah niitt lepp inch'Allah🙏🏽
@tynadieng33033 жыл бұрын
C triste ' mais bat toi yalla dina fegnal lepp insahala ' yalla bahna'
@salious14765 жыл бұрын
Que dieu t’assiste ma soeur metineu trop
@bintawalyndiaye39123 жыл бұрын
En ten que mère je partage ta douleur ma sœur du courage yalla nala yalla maye kholou mougne
@TessierBea Жыл бұрын
Vous êtes une brave dame ! Ne lachez rien, poursuivez votre combat ! J'ai bien peur qu'il y ait eu un trafic d'enfants. Si c'est le cas, demandez à Allah qu'elle soit dans une famille aimante. Courage encore et ne laissez pas cet hôpital impuni. J'y suis née de l'époque où c'etaient les religieuses qui aidaient nos mamans.
@aissatouseckndiaye8153 жыл бұрын
Même moi je suis victime de vol on m'a volé m'a fille en 1994 à l'hôpital ABASS NDAO et on a dit à mon mari qu'elle est morte et mettre une pierre dans un carton pour qu'il aille au cimetière en lui disant de ne le montré à personne bilahi😭😭😭😭justice doit être fait 😭😭😭😭😭
@cheikhniass49214 жыл бұрын
Bilaye gnou def li yalla dinala atté ak gnom yalla nala yalla maye kholou mougne
@welyanne44944 жыл бұрын
Ho cé triste no mane Abass Ndao la accouché yalla nako souniou borome niteulako inchangé
@maimounandiaye55044 жыл бұрын
Continues les videos, les medias avec les réseau sociaux ta fille pourra tomber sur ta vidéo qui sait. Déréte dou réér
@paomarpm122 жыл бұрын
Esperons
@binetandao58165 жыл бұрын
13 ans déjà tei djisso sa dôme métina Lool mai mougnal lekk tei niane yalla sou fekei migui dounde tei nite moko yorei nianal mou book si khaleiyi yi geune kou ame diné akk l'islam
@seutoubuur30905 жыл бұрын
Ndeyssan yay kén dou mom nalla yalla fadial sa nakhar
@fatoubarhamthiellosene18065 жыл бұрын
Li dé ci filme bi lako done guis thiey senegal.gnio doywaar té sokhor bone ragalen Yalah bilaay walaay li niawna trop hoo massa Yalah nako Yalah nit ci barké seydina Mohammad SAWS
@codoudiallo92785 жыл бұрын
C'est triste et du courage ma Chérie 😔😔😔😔
@angeliquegomis90154 жыл бұрын
Brave dame 13ans yaye rek la Yalla mey ngueume bi que le Seigneur le ramène à toi ma belle courage🙏🏽🙏🏽🙏🏽
@veroniquelolyyandediouf85504 жыл бұрын
Au nom de jesus
@cissokhoeva20425 жыл бұрын
Elle est très intelligente et brave machalah dieu est grand
@michellendiaye6733 жыл бұрын
Masta ma sueur métina j'ai les larmes aux coeur 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@honeybideew5 жыл бұрын
Madame vous avez essayé de contacter l'association des juristes Sénégalaises AJS ? Massa vous êtes très posée.
@demedatou7934 жыл бұрын
Ohh masta ma sœur yalla neu leu yalla diapalé gua guissat sa dom té inchallah digua ko guiss ndak kou geum yalla gua🙏🙏
@bambasarre15774 жыл бұрын
Non c'est dur yalla nako yalla nite si barké Serigne Touba ak Serigne Fallou
@ndeyelo11513 жыл бұрын
Oh abass ndao yéna bonne yalnalen yalla até
@khadijawane32335 жыл бұрын
Yalla na fegn si barké alhourane yalla nala yalla nital sa dom si barké yonet bi
@khadyndaw6115 жыл бұрын
Bilahi abass ndaw rk lou bonne rk lagnoye déf
@aichathioune48444 жыл бұрын
Yaala naka yaala diapalé .yaaye rék mooo wooor.nanou fonkou sunu yaaye massa ma sœur .de tous cœur avec vous.masssa
@mamankandji70184 жыл бұрын
Ndayesane yalla nako yalla indi watt si barké Baye Niass psk c triste yaye bou guissul domam 13ans d'à mètyy bilae😭😭😭😭😭😭😭😭si xol mei cmm linii wkh rk djam ak pékhém yallak dogualam
@mamyabdoulaye32574 жыл бұрын
Oooh lii mettina...bilahi...en tant k maman, j'ai le cœur meurtri. Sokhna ci je prie Dieu pour k tu retrouves ta fille saine et sauve
@fademaful5 жыл бұрын
Metina trop diour sa dom niou fokhatiko ni ak dom nimou nekhe massa ma soeur continue tes investigations Allahou ma Sabirina Dieu est avec les patients 😥
@zeynafall45455 жыл бұрын
A li mome doyna war mame wahnagne ma istour bou mel ni kokou ay cheikh la eumb mou ame dome gnou diohko bène dome ba ni li lou ame la
@papadembasene35644 жыл бұрын
Walahi hanzim j'ai meême des larmes aux yeux. Tata sois forte tôt ou tard la vérité s'éclatera. Allah le Tout-Puissant te guidera jusqu'à elle walahi et je suis même prêt à t'aider pour les recherches.
@bibandiaye73685 жыл бұрын
Oh li metina Yallah naga guiss sa dome inchala
@serignembackeniang67984 жыл бұрын
Yalna am sokhna bou am courageuse comme ki Yalnanou yallah diapalé
@bbkhadydiame76275 жыл бұрын
Ndeysana cette femme je l'estime bcp ...li mettina trop bilaye
@maremefall12038 ай бұрын
Abass ndao mome doynagne warr trop mane février 1997 Amna fa problème mawara accoucher niou piqure ma valiome par erreur bb bi nane thi liquide bi parce que dama nèlaw le matin jusqu’à 22h finalement j’ai perdu mon bb
@madeleinegomis44084 жыл бұрын
Que le tout puissant t'aide à retrouver ton enfant madame! C'est vraiment dur
@aissatacoumbadiattara84944 жыл бұрын
Ndeysane nio massé mane 13ans la am 2007 la am yanako yalla nitt sama jumelle la ndeysane 😨😨😨😨😭😭😭😭
@mamysarr48363 жыл бұрын
Ne bess pas les bras soi courageuse yalla nako yalla nite thi barké borom touba
@awacheikhmbengue6745 жыл бұрын
Oh Aissatou ndeye sane yalla nala yalla diapaler
@coumbatoure66185 жыл бұрын
Oh masta waye 😥😢yalla nalla yalla diapalé takhawoula boubakh 🙏
@sokhnakane23815 жыл бұрын
Courage franchement abass ndaw mom Lou yalla kham doy n'a ils sont trop indispliner a l'accueil et imcompetant. Que dieu te vienne en aide
@aichatirera16223 жыл бұрын
Je confirme danio rew ba doff
@fallousakho67774 жыл бұрын
Ndeysane😪😪😪😪 yalla nako Yalla nitt🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@madodiagne30075 жыл бұрын
Topppko jusko bout. YALLAH NA ko yallah niitt
@sodadione55694 жыл бұрын
Amine amine ya rabi
@ndiayeastou81905 жыл бұрын
Boul bayi dhe sa dom la bou dewogne fate gako bou yague si bene cote bi limiye doundou mon takh ga koye yeuke bilaye sama xol bi da diekhe fi bo âme bralong liga beugeu doko âme ms yala bkh na tega def aye nianne da si bkh yalnako yalla nitte 😓
@lesligakop93444 жыл бұрын
Sisi bou déwone batay kélame géne nasi té ainsi amna yénéne dom mai téwoul kélame dou si géne