Affaire Fallou FALL, sa tante(Fatima DIENG) sort du silence: le décryptage de Ahmed AIDARA

  Рет қаралды 97,253

2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE

2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE

Күн бұрын

Пікірлер: 239
@boubacarfall2225
@boubacarfall2225 8 күн бұрын
Bravo Amet je suis très content de toi 💘 seule la vérité
@seydoukanesall
@seydoukanesall 9 күн бұрын
Merci Ahmed aïdara,ki Yala dako wér, sokhor amoule ñdieurigne, qu'Allah nous en préserve
@daarahalimoulkhabirdaaraha3389
@daarahalimoulkhabirdaaraha3389 8 күн бұрын
Biko Journaliste Bii Niko So Amoon Pouvoire Fallou Diss Si Prison Bi Wala Mou Guéne Mouni Lolou Amalouko Importence Si Lako Saga Khamni Kou Sokhor Mogui Nii
@seydoukanesall
@seydoukanesall 7 күн бұрын
@@daarahalimoulkhabirdaaraha3389 wallahi,donc ça prouve seulement que sokhor késsé la
@toubzombaye
@toubzombaye 9 күн бұрын
Bilahi borome ndeye bou liguéye kénneu doko yakkeu😢 Donc li rék waar na takh jiguén seuyy ba déé😢
@alindao6836
@alindao6836 9 күн бұрын
Bilahi fallou yayam liguey na ndakh liguéyou ndeye moko may soutien total si sénégalais yi
@DiewoKeita-y1p
@DiewoKeita-y1p 8 күн бұрын
Mane amonena woudje bou mélone comme mome ba dawouma beug touki féne
@astoudiamanka4280
@astoudiamanka4280 8 күн бұрын
Bilaye hameau na sidara yallana Souf oyof si kawame Amine
@daarahalimoulkhabirdaaraha3389
@daarahalimoulkhabirdaaraha3389 8 күн бұрын
Sénégal Nakk Am Khaliss La Niou Diapé Yaye Diou Liguéye Ta Khaliss Kousi Sétoul Yalla Dou Dara ..... Mai Lii Mooy Deug Deugui Ndaye Bou Liguéye
@lessauveurs6314
@lessauveurs6314 8 күн бұрын
😂😂😂 du n'importe quoi,yaye djou liguey une mentalité purement africaine,nèke lène ay niteu
@paullelwele8879
@paullelwele8879 9 күн бұрын
Billahi wallahi Ahmed Aïdara li ci biir keur yi ken menou ko wakh...Yalla naniou Yalla may xolou mougne ak bamelou biir si non rek moussiba dina am...Yalla rek mofi nek😭😭😭😭
@oumoutraore9275
@oumoutraore9275 9 күн бұрын
L'arrogance et la méchanceté de cette monstre se lit à travers son discours
@SeynabouFaye-b6q
@SeynabouFaye-b6q 9 күн бұрын
Merci grand akhmed aidara yalnassa diam yagg séne takhaway rafetena lole justice pour fallou fall❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@awagueye6954
@awagueye6954 9 күн бұрын
FEMME BI.? VRAIE SORCIÈRE. YALLA NA YALLA TOROKHAL KO TCHI BARKÉ WEROU RADJAB BI TCHI BARKÉ SERIGNE FALLOU MBACKÉ KHADIMOU RASSAUL. YALLA BOUMOU WER YALLA BOUMOU AM DIAM. IN SHA ALLAH. MERCI BEAUCOUP 2ATV. MERCI AHMED AK SA ÉQUIPE BI YEP DIEUREUDIEUF. KI MOY 2E ADJI SARR
@alamiiratoulaprincesse7638
@alamiiratoulaprincesse7638 8 күн бұрын
Ndeyssan billay danguéna khamoul mystique rek dafay yakh nit bamou melni keneen
@AwaKane-vr3yf
@AwaKane-vr3yf 8 күн бұрын
Amine ya Rabby yallah na la yallah dégue toma🙏
@yacinetraore6827
@yacinetraore6827 9 күн бұрын
Salam vraiment suivons l affaire jusqu au bout . Que dieu aide fallou fall.les avocats aident fallou
@seydoukanesall
@seydoukanesall 9 күн бұрын
Sokhna yacine fallou Yala mo lérale lép, bouy déme justice diko acquittée, papa djii AK tanta djii kay nio nara âme problème après
@ousmanefalloubayeniass496
@ousmanefalloubayeniass496 8 күн бұрын
​@seydoukanesa c'est vrai. Deug bi léer na nagne. Il a fallu que j'écoute la tante, je dis qu'elle raconte des contre-vérités.
@mouhamedpropopit4696
@mouhamedpropopit4696 8 күн бұрын
Grazie mille frere Ahmed Aidara justice pour libertà fallou fall 🙏🙏🙏👏🏾👏🏾👏🏾😭😭
@RamaNdiaye-f9n
@RamaNdiaye-f9n 9 күн бұрын
Merci beaucoup Ahmed aidara Bonne continuation
@ArameDiop-v1j
@ArameDiop-v1j 9 күн бұрын
Amhed aidara merci❤❤❤❤❤❤❤
@ThiernoDioum-h5t
@ThiernoDioum-h5t 9 күн бұрын
Bravo amed tu as tout dit vous devez être le seul juge unique et à vie dans ce pays barke s touba mame ch Ibra fall ❤❤❤❤❤❤❤❤
@HadiaMamaDemba
@HadiaMamaDemba 9 күн бұрын
Entièrement d'accord avec Amina😢😢 Wollahi pabi mo diara yérreum😢
@doudouthiounelame858
@doudouthiounelame858 9 күн бұрын
Justice pour fallou fall Aziz dabala ak waly si barké seydouna mouhamed psl
@MameDiarralo-ju8my
@MameDiarralo-ju8my 9 күн бұрын
Mane xale bi dama ka yerem ndax lignko dougal te xamou si dara yayam yax adounam yax digen tem ak ay domou bayamfallou ala koli xalin dina gene inchallah
@cirobelladonna4999
@cirobelladonna4999 8 күн бұрын
Wlleaunefils❤❤❤❤❤❤
@ibrahimadrame2931
@ibrahimadrame2931 8 күн бұрын
Le Sénégal joue beaucoup avec le sujet du viol comme café Sénégal justice amoul
@almarena3130
@almarena3130 8 күн бұрын
Billahii 😊
@abdoulahadkebe924
@abdoulahadkebe924 8 күн бұрын
Walahi Ahmad Aidara yabakh ❤❤❤❤❤❤
@moussagnacko4008
@moussagnacko4008 7 күн бұрын
Merci akhmed analice pèrtina bravo ahmèd aïdara ❤❤❤❤👏🏾👍🏽🇸🇳
@MuhaSane
@MuhaSane 9 күн бұрын
Gnougui youkou doolé fallou diko nianal xolou mougne dafa nékk ni yalla mo diox fallou bén rôle thi jubanti côté justice bi .FREE FALLOU ❤💪
@adamandiaye4314
@adamandiaye4314 9 күн бұрын
❤ machalla Amy cissé bien trabajo ❤ tata Fallou bakhoule grand frére Fallou binek espagne bakhoule séne papa bakhoule justice pour Fallou loumou wakhe daye féne Akhemet Aidara tres bien voilà la vérité bilakhie
@MoussaThiongane-m5r
@MoussaThiongane-m5r 9 күн бұрын
DiNa Lére Déhhh Inchallah Courage Rk justice pour Follou Fall YaNako YonéneTé Bi TakhaWou Inchallah Amine Amine Amine ❤❤❤❤
@seuneba7091
@seuneba7091 8 күн бұрын
Pure vérité Ahmed
@modoufall5006
@modoufall5006 9 күн бұрын
Fatima dieng kanamam goubone guiii 😢😢😢déy fén didém rékkk sincerement 😮😮😮
@falloumbodji3062
@falloumbodji3062 9 күн бұрын
Ak seuram
@fallousakho6671
@fallousakho6671 9 күн бұрын
merci beaucoup Ahmed
@degrk5622
@degrk5622 9 күн бұрын
Tanta MoMA bétt bilàhi boko guissé elle a l'air sérieux très calme doko fogué sakh nitt mo leundeum DEUG , kiii mo bone ❌❌❌ xalé yi yalla nalén yalla takhawwou baarke Mame cheikh Ibrahima fall
@bassirouthiam1615
@bassirouthiam1615 9 күн бұрын
Merbi gnieme n’a wallahi ❤❤❤❤❤
@assdiouf1033
@assdiouf1033 9 күн бұрын
Sénégal la juge yi di teuth nit gni si ay thiakhane femme bi wakham yi ak médical rek gua teuth si nit15ans projet fallou bi gnou mou diar sene lokho yep la yone wara régler sino rewmi yone amou fi deh
@monavenir7378
@monavenir7378 9 күн бұрын
Bilahi deug nga Wax Ass parfois gnoune djiguene sax dagnouy rouss xalebi nek ak ndawam ba paré nga teuyé ki 15ans si lo xamni yalla xam mais li xel nangou moy takewoussi
@assdiouf1033
@assdiouf1033 9 күн бұрын
​@@monavenir7378ah wa bakhna comme ay nit you amoul bene mérite gno nek Thi justice di teuth nit gni si ay thiakhane rek Ousmane sonko war guena réforme justice sanque domou diambour yi si cas Viol yi legi Sénégal kou am problème AK nit def médical lidianeti sa niari témoin juge yi soukandikou si ap médical teuth la
@ndeyecourradiallocourra-sz3xc
@ndeyecourradiallocourra-sz3xc 8 күн бұрын
Wakhe ga deuk gnome nieup médecin bi police justice bi si gris bii
@assdiouf1033
@assdiouf1033 8 күн бұрын
Li kay Ousmane sonko war guena réforme justice bi juge you nafekh yeup gnou radje lene encore médical yi tamite doyoul si cas Viol cas Viol yi legi koula def none créer viol def médical lame comme juge bi mom si ap médical rek lay soukandikou di teuth ay domou diambour 15ans dem teud keurem nek en lège gno bari gno gui si prison Sénégal yi di subir peine Nou accusé de viol te Sénégal la majeure partie walou yone khamougnou si Dara police rek dagnou fa ragal problème sonko adji sarr sakh motakh sénégalais bari di xam touti si walou yone Dara vraiment nognou yeureum nit gni kou accusé ti nit te d'où deug limou warona teud gua teud ko sénégalais yi nek si diam
@niebendiaye
@niebendiaye 9 күн бұрын
Mane lima diakhal 5ans fallou nek si kassobi té famille maternélame dénoncéwouka .niome tamite amnagn thi part de responsabilité
@alamiiratoulaprincesse7638
@alamiiratoulaprincesse7638 8 күн бұрын
Esk dou mystique, Sénégal légui daniou lay togn ba paré teudj sa guémign 😢
@serignesalioulo8023
@serignesalioulo8023 8 күн бұрын
Khana toppu témoignage yi yep kharite?amna bene mer bokou leeral pourtant
@serignesalioulo8023
@serignesalioulo8023 8 күн бұрын
Tayit dossier viol dafa sensible dou diekki diekki rek wilipande kou ci réseau sociaux yi
@ousmanefalloubayeniass496
@ousmanefalloubayeniass496 8 күн бұрын
J'ai écouté une dame du quartier. Fallou du côté sa famille maternelle ( oncle ou tante) sont décédés plutôt. J'ai écouté cette version d'une dame.
@salimfall
@salimfall 7 күн бұрын
Parole véridique mon ami ameth aïdara vous metriser bien la société sénégalais bravo ❤❤❤❤
@AwaMbaye-r6z
@AwaMbaye-r6z 9 күн бұрын
Machallah amted aidara
@mansourdiagne5234
@mansourdiagne5234 9 күн бұрын
Merci Ahmed ❤
@TidianeMboup-d8x
@TidianeMboup-d8x 8 күн бұрын
Merci grand akhmed aidara yalnassa diam yagg❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@SDiarraSall-n4p
@SDiarraSall-n4p 9 күн бұрын
Serigne fallou yalna yalla tegui natou bi si barkep kajuradiap bi inchallah legui nga guéén
@MohamedNdiaye-h7u
@MohamedNdiaye-h7u 9 күн бұрын
Le prophète youssouph aleyhi Salam ne dirigeait pas le pays il était ministre des finances à l'époque
@BabacarKonate-y7l
@BabacarKonate-y7l 8 күн бұрын
Tanta yi ay domerame j'ai subit le mm sort mais heureusement q la fille adoptive de ma tanta a refuser Sénégal amna djifuène you doxane ndeyame d
@OusmaneDiallo-wk3jc
@OusmaneDiallo-wk3jc 9 күн бұрын
Ly mo takhe niouny goor waroul féble thie kanamou diabarame respect nak meunul niak thie sa diguanté ak môme wayé bu dieui décision dioté bul KO dégueulou
@monavenir7378
@monavenir7378 9 күн бұрын
Très bien dijgene là mais deug nga Wkh dh pire sax
@ousmanefalloubayeniass496
@ousmanefalloubayeniass496 8 күн бұрын
​@@monavenir7378 Merci d'avoir bien compris la chose. C'est ça qu'on appelle: humilité.
@AdjinataGaye
@AdjinataGaye 9 күн бұрын
Amen merci
@boromtoubajerejef289
@boromtoubajerejef289 9 күн бұрын
Justice pour fallou Amy Cissé RK la nop❤❤
@IbraSene-g8h
@IbraSene-g8h 8 күн бұрын
Mashala ahmed analyse bi amenasolo
@adiadieng1291
@adiadieng1291 9 күн бұрын
Li si keuryi kou wahe letpe netke wahegate les maisons au Sénégal 🇸🇳 vont très très mal
@aliounedrame263
@aliounedrame263 4 күн бұрын
Pur vérité aidarra
@khadygueye2985
@khadygueye2985 9 күн бұрын
Merci ❤❤❤❤❤❤❤❤
@salioukhouma2360
@salioukhouma2360 8 күн бұрын
Lima méti si cas rék Fallou bou nguéné daniouy balle femme bi😭mo continuer di dondou Diamou 😭
@FatoukebeDieng
@FatoukebeDieng 8 күн бұрын
Merci beaucoup améte aïdara 😅😅
@mapendasene8551
@mapendasene8551 8 күн бұрын
😂😂😂saway niari grand lo romb niouné kouléne toumal yobouléne kasso ndakh dépenses bi tarna légui😅😅😅
@BayeabdouMbaye-or1nu
@BayeabdouMbaye-or1nu 9 күн бұрын
Ndakh pabi mingi ande ak xèlam
@cheikhtijani321
@cheikhtijani321 8 күн бұрын
Justice soit faite ⛔️ 🔑 no a l'injustice..free fallou✌🏻
@CisseMbayendiaye
@CisseMbayendiaye 8 күн бұрын
Ahmed d'accord ak yaw dé
@maguidia8397
@maguidia8397 8 күн бұрын
Justice pour fallou yalla na la yalla tek lokho femme bi c propos ne sont pas cohérents darra diapouko lou doul bonne ak ķholou woudier
@assanecamara2188
@assanecamara2188 9 күн бұрын
Dem len kholi médecin biko defal certificat bi da on doit l’entendre aussi
@DaoudaNdione-qz6fk
@DaoudaNdione-qz6fk 9 күн бұрын
Merci Honorable 🎉❤
@tsar2791
@tsar2791 8 күн бұрын
bravo!!!!! Ahmed Aidara 💯correct
@assanfaal2079
@assanfaal2079 9 күн бұрын
bilay ya bakh Ahmet ❤❤❤
@CodouWade-v2u
@CodouWade-v2u 9 күн бұрын
Sénégal nieup ya borom héle laniou fatima fi ko yalla wéré moy fimou dielé micro
@jajafaya6470
@jajafaya6470 8 күн бұрын
Merci comme hamgua lolou da wah gueuneu confirmer
@YusuphaBittaye-sh2kf
@YusuphaBittaye-sh2kf 9 күн бұрын
JEREJEF AHMED,DAGABEE REEK
@CheikhDiouf-g9f
@CheikhDiouf-g9f 8 күн бұрын
Justice.pour.fallou❤❤❤. merci.a.vous
@tinanalane3053
@tinanalane3053 9 күн бұрын
Fatima bonne rek moko diap
@MarieNgom-z1k
@MarieNgom-z1k 8 күн бұрын
Tente fallou mi mba réyoul yayou fallou démaye ladj rék ndakhe fékane té Nanou
@OumySylla-l7k
@OumySylla-l7k 8 күн бұрын
Bilay ahmed wak nga deug mounoul wakh ba set
@FatimaFaty-sn6mn
@FatimaFaty-sn6mn 5 күн бұрын
Bilayi je suis fiért de vous
@damediop6967
@damediop6967 9 күн бұрын
Nan bayi fallou mère bi daye doul 😢😢😢
@ModouKassé-l1t
@ModouKassé-l1t 9 күн бұрын
Ndaw si vrai deume la
@BassirouGaye-k2b
@BassirouGaye-k2b 9 күн бұрын
Falou fall liberté
@hamadybalde3992
@hamadybalde3992 9 күн бұрын
Vérité absolue 😢😢
@hamadoudiallo5670
@hamadoudiallo5670 8 күн бұрын
Justice pour fallou libre fallou
@hawasuso3719
@hawasuso3719 9 күн бұрын
Very true my dear brother ❤❤❤
@amysambathiene2843
@amysambathiene2843 9 күн бұрын
Bonne rek ak nième' serigne waye galadiame tothie na dé
@FadelDieng-u7v
@FadelDieng-u7v 9 күн бұрын
Merci amina😢😢😢
@Elhadji57Moussa
@Elhadji57Moussa 8 күн бұрын
Merci ahmed
@NdeyeNdiaye-bg6bb
@NdeyeNdiaye-bg6bb 8 күн бұрын
Justice pour Fallou Fall svp
@oustazahmedfall6478
@oustazahmedfall6478 9 күн бұрын
Très bien Ahmed
@almarena3130
@almarena3130 8 күн бұрын
Ils ya des pères de famille qui vont rentrer dans l'enfer pour mal gérance de leurs familles
@mameastoundiaye8180
@mameastoundiaye8180 8 күн бұрын
Mame cheikh Ahmed Tidiane sy al maktoum nèna nitte bo féné malaka yi gnoy kheum 😂😂😂 kone mére fatim wagnil touti😂
@cheikhounanam9325
@cheikhounanam9325 9 күн бұрын
En kay yangi dora wakh yaw Ahmad aidara
@OusmaneBéye-y7b
@OusmaneBéye-y7b 8 күн бұрын
Ahmed aka grave khélmi mo sél
@mameastoundiaye8180
@mameastoundiaye8180 8 күн бұрын
Walahi xalé bou ndaw ga diagal ko féneu pourtant keur gui gay kheuthiou khana do khalate ni euleuk 7metre percale mo léne topou Alakhou Akbar yaw mère bi ragalal yalla touti thi féneu yi😢😢😢
@sallsall6130
@sallsall6130 8 күн бұрын
IL FALLAIT LUI REPOSER LES QUESTIONS QU ELLE ECLIPSAIT
@Niangahma
@Niangahma 8 күн бұрын
Billahi sama kholbi nimou boné si problème bi non femme bi yalnako yalla atté ak Sénégalais yii
@TounkoCamara
@TounkoCamara 8 күн бұрын
Femme bi dou jiguenn diou bah justice pour fallou
@KadiKone-h9s
@KadiKone-h9s 8 күн бұрын
Merci
@latgrandndiaye1909
@latgrandndiaye1909 8 күн бұрын
deug rékay moudiou ❤
@NgagneGaye-u5u
@NgagneGaye-u5u 8 күн бұрын
Merci 2atv la chaîne du peuple ❤❤❤❤❤🎉🎉
@dieynabacoly4053
@dieynabacoly4053 9 күн бұрын
Mais irresponsabilité wom motakh domaine yep dem na assumer ❤
@MarieNgom-z1k
@MarieNgom-z1k 8 күн бұрын
Tente bi kaye domarame la yalla nako boungal Lou yalla d'Al AK aqkou fallou
@adjaratoundiaye5699
@adjaratoundiaye5699 9 күн бұрын
Niit kou nek warnga khol sa diguenté ak yalla tei khamni euleuk dou agne tei dou rere d khamni tamite di nagnou ndiéguénayo sougnou ndaye dior. Papou fallou nak mak da nane fatima dako diap mystiquement parce que amna yo khani fou tayéf chaque jour gnou guiss ko di serie yi
@gouroupgenerationsecuritee472
@gouroupgenerationsecuritee472 9 күн бұрын
Honte internationale
@doffdouweer3686
@doffdouweer3686 8 күн бұрын
Policiers ..procureur et juges doivent être sanctionnés! prison dou thiakhaane
@AbdouNgom-t4y
@AbdouNgom-t4y 9 күн бұрын
Justise Sénégalais free baye mbene way fene yi da leer nangni 😂wale nekatoul jupe joubal joubanti book😂 free aladji fallou way 😂❤❤❤
@AwaKane-vr3yf
@AwaKane-vr3yf 8 күн бұрын
Paby daniouko mystique
@kinekare6526
@kinekare6526 9 күн бұрын
Aidara chérif deugueu rek gaye wakh ya bakhe
@khadijadione5577
@khadijadione5577 8 күн бұрын
Mane sètanouma Fatima dieng nakh bagn ndayam
@aminatawone2531
@aminatawone2531 7 күн бұрын
Yalla nagnou yalla moussale thie kou sagne papadji doussi thiobaré bopam khaléyi nénagnouné sén papa daléna choyé wone dou gneupou gnioye déme thie sérigne baa haméth nane dafa warona diock thie bopam momi tami papadji diarna yeureum ndakh douguena si kou bone wassalame
@alleualleu693
@alleualleu693 9 күн бұрын
Geneco bi manna blessé khalebi 😢 Con mpm na wakh😢😢
@mouhamedsene7393
@mouhamedsene7393 9 күн бұрын
❤❤❤
@mamadousalioudiallo1140
@mamadousalioudiallo1140 9 күн бұрын
machah ameth
@kinekare6526
@kinekare6526 9 күн бұрын
Falou thi barképe SERGNE FALLOU MBACKÉ YALANA YALA WALOU DIRIME ƁII
@Zazindiaye218
@Zazindiaye218 8 күн бұрын
FATIMA dieng domou leufeul ndeyam bi niiit kou bonneu ki alkou fallou day guėneu par la force nitou seytanė bi tass katou adouna
@papaalydiarra3411
@papaalydiarra3411 9 күн бұрын
Niom niar ngeup le temps nous le dira lu méti migui nieuw li samay wakhla papadji mom ci dof la dieum
@afro3827
@afro3827 9 күн бұрын
Femme bi day fen 😢
@IshaJoof-p2c
@IshaJoof-p2c 9 күн бұрын
Jerry Jeff❤
@Magatte-m6s
@Magatte-m6s 9 күн бұрын
Mouyene amina mi werna pa bi di sorcier
Affaire Fallou: Oumou dément catégoriquement sa tante, Ahmed AIDARA p...
43:25
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 76 М.
Revue de presse Ahmed Aïdara du Mercredi 05 Février 2025
6:27
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 22 М.
黑天使只对C罗有感觉#short #angel #clown
00:39
Super Beauty team
Рет қаралды 36 МЛН
Cheerleader Transformation That Left Everyone Speechless! #shorts
00:27
Fabiosa Best Lifehacks
Рет қаралды 16 МЛН
Мен атып көрмегенмін ! | Qalam | 5 серия
25:41
VIP ACCESS
00:47
Natan por Aí
Рет қаралды 30 МЛН
Les Confidences Émouvantes d'Aïda Patra : Parcours, Showbiz, Famille
2:11:17
Xibaar Yi 13H du 05 Février 2025 présenté par Cheikh Diop
21:34
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 1,4 М.
黑天使只对C罗有感觉#short #angel #clown
00:39
Super Beauty team
Рет қаралды 36 МЛН