La vie et l'histoire de Cheikh Ahmadou Bamba ( Jaar jaari Serigne Touba) Ses qualités sublimes et son intelligence fine - la version audio à télécharger ici: www.mediafire.c...
Пікірлер: 29
@CheikhounaNdiaye-kb3ks3 ай бұрын
Dieureu dieufé Kou Tède ki Yalna niou yalla défal djikkom you teddé yo ya🤲🏿
@cheikhounagueye13966 жыл бұрын
dieuredieuf waay serigne bi amna solo lool liguay leeral amna solo dieuredieuf mbacke yalla nala fi yalla ya gual si sugnou kanam barkeb yonen tebi sallalahou alayhi wassalamm barkeb serigne touba amine dieuredieuf
@yorodiouf12835 жыл бұрын
Amna Solo loole Mbacke masha Allah Yalna Borom bi faye ci Serigne Touba mi ngay ligueyal.
@layendiaye74245 жыл бұрын
Machalla yalla gafi yague tè wer
@toubambartv70625 жыл бұрын
Machallah Serigne basirou khelcom soponala
@mominnatoudiop32016 жыл бұрын
Machalla amnasolo lool
@ndiayeteranga37727 жыл бұрын
machalla mbacke waxtane wi am. na solo lol yagui léral lou Iouri thi serigne bi
@rassoulmbaye72396 жыл бұрын
Soukrane amna solo trop
@daoudathiam48447 жыл бұрын
Ma Cha allah serigne bi amna solo loul sakh
@laminlo44497 жыл бұрын
machallah serigne bassirou mbacké khelcom
@IbrahimaGueye-cq5cs6 жыл бұрын
Dieuredieuf
@76abou7 жыл бұрын
diarama mene cheikh ibrahima fall
@soldaroubayekarimbassiroun45357 жыл бұрын
abo gueye amine amine
@papembengue3545 жыл бұрын
Mashallah...
@cheikhounasamb61505 жыл бұрын
Serigne Bassirou Mbacké diadieuf leerna andak téguine Wanté Khassidayi di wakhi kou tedd ki boul nangou mouy gueuneu soufé say wakh .Nga dieul sakh léneen lou melni wayi arab sou meunoula niakk.Ndé sakh wakhtan wi késsé doyoon na. Défar rekk mom laa dioublou.Mangui diegoulou nîeep
@abdoug7316 жыл бұрын
Amna solo
@76abou7 жыл бұрын
Mbacke balla zuma la degğ lou damay am mbegğ looll serigne touba da seraall sama xooll moom rek la bagğ bagğ serigne touba rek fall
@rassoulmbaye72396 жыл бұрын
Dila nianale rek mbacke balla yalla goudal fane wi weral thieur yi
@cheickbadiane1735 жыл бұрын
Jiere jief borom tuoba dolli whatal wakhtane wi
@momobayfallmomobayefall99946 жыл бұрын
Hakacha fall
@MorDiaw-v8gАй бұрын
❤
@mouhametbouxarangelo65926 жыл бұрын
Son bi si sof motakh wakhtanal bi xaw masidara
@daarayserignebassiroumback23956 жыл бұрын
Dissi diégalou boubakh. Desnnassi bayi khel bénén yone Incha Allah
@SanYallah6 жыл бұрын
@@daarayserignebassiroumback2395 Asalamoualeikoum kan moy diangue khassida yi si video bi ?
@marwanefall47985 жыл бұрын
@@SanYallah serigne aliou fall
@SanYallah5 жыл бұрын
@@marwanefall4798 diadieuf way Barakallahoufik ak ngeureumeul Borom Touba
@yorodiouf12835 жыл бұрын
Ziar na niep, Beugue na kouma bakhei ki diangue khassida ci font background bi.
@pslleida68174 жыл бұрын
Bay aliou fall moko diangue fatou na nak nako yalla yaram