la pertinente analyse de obeuli sur sa thies vs reug reug

  Рет қаралды 26,819

4appuis TV

4appuis TV

Күн бұрын

Пікірлер: 68
@elhadjaliounendiaye1684
@elhadjaliounendiaye1684 2 жыл бұрын
Sa Thiés rek machallaah yalla nako yalla may Ndam inchallaah
@nioulesskaye8964
@nioulesskaye8964 2 жыл бұрын
Ibou Ndiaye war nga ame combat déh champion nga
@falloufaye7267
@falloufaye7267 2 жыл бұрын
Machalla oboli analyse bi nice na
@adandoye3759
@adandoye3759 2 жыл бұрын
Billahi lou lére nga wakh Reuk Reuk niit yi koy geumoul ni mo meune 💪🏾 sa thies Billahi gnoko nara lore
@salioutine6014
@salioutine6014 2 жыл бұрын
Je persiste et signe sa Thiès va humilié reug reug inchallah ba beuss beu ak diam
@walydiouf9653
@walydiouf9653 2 жыл бұрын
Diokh ma sa numeero gnu tèg thi khalis bi amè fite
@modousall2693
@modousall2693 2 жыл бұрын
Lou leer nga wakh
@oumarsall4785
@oumarsall4785 2 жыл бұрын
Kou meunn Sa Thies, Reug mola meunn
@toubaamar3059
@toubaamar3059 2 жыл бұрын
@@walydiouf9653 gneuwal gnata ga gnémé tek
@gorguifaye2256
@gorguifaye2256 2 жыл бұрын
Allez Ndiaye Dina bax inchallah borome bakh nga 🥰💪
@assanendiaye2997
@assanendiaye2997 2 жыл бұрын
Mbeur Yalla Nala Yalla Sameu Défal la Diameu AK Weurgou Yarame Taw Fékhe Thikaw Thiakaname Déy Bax Déh
@dorndokh3344
@dorndokh3344 2 жыл бұрын
BRAVO nice na
@malangdieme9076
@malangdieme9076 2 жыл бұрын
Il a raison vraiment
@ablayediop8067
@ablayediop8067 2 жыл бұрын
merci ibou
@babdeh8549
@babdeh8549 2 жыл бұрын
Reug reug moy sadio mane mbeur yi
@sabarasts
@sabarasts 2 жыл бұрын
Kone d dou meilleur lutteur ani niom Messi Mbappe Lewandowski Benzema 😂
@babdeh8549
@babdeh8549 2 жыл бұрын
Gni nga toudou niepe khamou beurer
@adandoye3759
@adandoye3759 2 жыл бұрын
Di ngéne lounéne béteu dei sou biss ba Sa thies Dinako douma dane ko inchallah
@papediop9745
@papediop9745 2 жыл бұрын
Billahi sa thies rek
@mamathiam5649
@mamathiam5649 2 жыл бұрын
Lolou mom mokoy sédé obeuli
@khadimthioune5548
@khadimthioune5548 2 жыл бұрын
Balla guaye amoul morom si lamb dji
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 2 жыл бұрын
Sa Thiès mo meune 10 reug reug reug reug dou Dara
@seydinaomardiop4537
@seydinaomardiop4537 2 жыл бұрын
Yangui waxati😂
@assanendiaye5640
@assanendiaye5640 2 жыл бұрын
Douul rek ga meun
@brigbousiteuletarkinda1221
@brigbousiteuletarkinda1221 2 жыл бұрын
Cheikh do nopalou béne yoone🦁🦁
@elhadjimoussaniang1748
@elhadjimoussaniang1748 2 жыл бұрын
Chékh bass bou reug reug ya gui wakhti rek reug reug gaye wakhale dh borom gallegui
@amadoumatarfaye2820
@amadoumatarfaye2820 2 жыл бұрын
@@elhadjimoussaniang1748 saway sissou mane leu
@mmsseye9391
@mmsseye9391 2 жыл бұрын
Reug reug mo gueuneu parè
@mamadoudieng3093
@mamadoudieng3093 2 жыл бұрын
Gaston ngir yalla wagnile date bi defko defko 6 moi
@mouhamed_al_mahdii
@mouhamed_al_mahdii 2 жыл бұрын
Gawall fekiii ga yeyiii sikaww
@emiledione3236
@emiledione3236 2 жыл бұрын
Euboli amna doĺé temps yi dee
@IbrahimaNdiaye-hr2yp
@IbrahimaNdiaye-hr2yp 2 жыл бұрын
Dama moure muscle yiiiiiii
@latyrndiaye962
@latyrndiaye962 2 жыл бұрын
Mais ragale la
@assanendiaye2997
@assanendiaye2997 2 жыл бұрын
@@latyrndiaye962 Sa Message Bi Môme Kouko Guiss Xam Ne Wakho Lo Xam Ibou Ndiaye Euboli Ragal Yaw Rek Yakoy Wax Môme Niakeu Teylou Ndakh Attaque Bou Bari Mokoy Yakkal Lou Bari
@bigmomotimkashop8438
@bigmomotimkashop8438 2 жыл бұрын
Reug reug muenoll dan sa tihes
@walydiouf9653
@walydiouf9653 2 жыл бұрын
Reug reug mo meun koudoul balla gaye 2 saku ni guèn wakhon thi guy gui amolèn diome
@iboufaye5695
@iboufaye5695 2 жыл бұрын
ReuG reuG beusse bOu Dieulé bén cOup sa Thies DOtOul beuré
@amadugningue8168
@amadugningue8168 2 жыл бұрын
Sa thies degloul obeuli mi teukelnala combat bi teyal boy boulnou fonto defonngakofi contre boy niang
@diagnebass6754
@diagnebass6754 2 жыл бұрын
😂😂 dina bakh
@elpistolero97
@elpistolero97 2 жыл бұрын
Bilahi eupeul mo taxx ma bayiko supporteih eupeul leuh deif!!
@elhadjifaye1166
@elhadjifaye1166 2 жыл бұрын
Téy danou eupeul danou inchallah
@mouhamedmoustapha684
@mouhamedmoustapha684 2 жыл бұрын
@@elhadjifaye1166 douu DEUG
@elhadjifaye1166
@elhadjifaye1166 2 жыл бұрын
@@mouhamedmoustapha684 ioe kham ngani Reug dou moromou koudoul Sa Thiès sakh dangay supportere rék walay ndeysane
@ibrahimsall6115
@ibrahimsall6115 2 жыл бұрын
Reug reug moko meun fouf
@benoitdiouf5632
@benoitdiouf5632 2 жыл бұрын
Ces vrai que vous aites des lutteurs mais votre analyse est banal
@latyrndiaye962
@latyrndiaye962 2 жыл бұрын
Yew comme doo serere loutha ga ragale la khamoule
@assanendiaye2997
@assanendiaye2997 2 жыл бұрын
Ligua Wax Dara Amoussi Bayil Fene Ibou Ndiaye Euboli Ragal Yaw Rek Yakoy Wax Môme Bou Dano Si Lambeu Fitame AK Niakeu Teylou Lolou Mokoy Dane Parfois
@latyrndiaye962
@latyrndiaye962 2 жыл бұрын
@@assanendiaye2997 sa papa bou bayi fenne rek Dina bayi ok yew rewo sakh
@assanendiaye2997
@assanendiaye2997 2 жыл бұрын
@@latyrndiaye962 😂😂😂 Doumala Saga Ndakh Respecté Na Say Wadiour Ak Samay Wadiour Ay Maglagne Mais Conseil Bimalay Diokh Rek Moy Bayil Fene Fene Baxoul
@latyrndiaye962
@latyrndiaye962 2 жыл бұрын
@@assanendiaye2997 degoma Dee sa papa bou baye rek lolou d'où problème ok
@assanendiaye2997
@assanendiaye2997 2 жыл бұрын
@@latyrndiaye962 Guíss Nane Kou Niakeu Diom Nga Téga Yeureum Sa Ndeye Sonouna Si Yaw Deh Mo Guéne Nga Koy Sagalou Vraiment Deff Plus Nga Nékal Nit((Diéhiro I Diom))😂😂
@khadimthioune5548
@khadimthioune5548 2 жыл бұрын
Sa thies dou moromou reug reug
@elhadjifaye1166
@elhadjifaye1166 2 жыл бұрын
Mais Reug Reug moy bayam si beuré
@walydiouf9653
@walydiouf9653 2 жыл бұрын
Khadim ba do moudiou fèn
Lou Ken messoul wakh thi balla gaye... balla beye 1 corrige gris
23:38
$1 vs $500,000 Plane Ticket!
12:20
MrBeast
Рет қаралды 122 МЛН
JISOO - ‘꽃(FLOWER)’ M/V
3:05
BLACKPINK
Рет қаралды 137 МЛН
pimpi attaque balla gaye😱🔥siteu mo meun🤬⛔
4:29
Actu galsen
Рет қаралды 5 М.
Revue de presse Ahmed Aïdara du Mercredi 15 Janvier 2025
9:03
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 65 М.