yèkini yoré woul couronne 👑 bi 15 ans que se soi clair tok na 15 ans danou woul mais couronne bi 8 ans lako tiyé yènn gni posé question yi dèlènn renseigner wou bou bakh way
@jazaka31789 ай бұрын
Ak 8ans yi niatta Combat ak yane adversaries Bombardier,Tyson, Tapha gueye ,Baboy,khadim ndiaye,lac 1 je pense
@Enfant_béni_79 ай бұрын
C'EST NORMAL PASK NIONIOU NIOFI NÉKONE AY TANOR KOU NÉKEU AK SA DIAMONO BAYILÉN SOXOR 😮 MOU TANÉKO SÉN MBEUR BOBOU NGA XAMENI ROI DES ARÈNES KLOKLO LA XALILE YONN@@jazaka3178
@ZundumuZundumu9 ай бұрын
Ok nnou la dmé kw
@zakaryagangue35439 ай бұрын
Macha Lambologue . Sa analyse amna solo
@MameSow-vp7rj9 ай бұрын
Modou lôooooooooo ❤❤❤❤
@ModouNdiaye-r3m9 ай бұрын
Lo rek ❤❤❤
@AssaneDia-hj7nz9 ай бұрын
Modou. Lo 💪💪💪💪👑💪💪💪👑🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲❤️❤️❤️❤️❤️
@MorWade-w7q9 ай бұрын
Lambo módulo rekk la nioy topo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@hqby9 ай бұрын
Siteu défaite rek inchallah si kartanou yallah sounou borome inchallah si kartanou yallah sounou borome inchallah 👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️🙏
@AmadouThiam-yo2rl9 ай бұрын
Yow vrai fans nga ❤❤❤
@hqby9 ай бұрын
@@AmadouThiam-yo2rl Guisgua lolou encore siteu défaite rek inchallah si kartanou yallah sounou borome inchallah si kartanou yallah sounou borome inchallah 👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️🙏
@AmadouThiam-yo2rl9 ай бұрын
Amine ya rabbi
@AmadouThiam-yo2rl9 ай бұрын
Même mane fans modou lo la
@khadyka53849 ай бұрын
Ndeysann ya fidèle si Modou lo nak ❤️❤️
@AlassaneBzrry8 ай бұрын
Siteu késssé❤❤
@AlphaBa-zw4rx9 ай бұрын
Modou lo da boko Comba be nhk❤
@mafallfallvip81749 ай бұрын
Modou lô❤❤❤❤❤
@nouroulfayda50419 ай бұрын
je ne suis pas wolof mais je pense que modou n'a pas dit qu'il va arreter au bout de 3 ans il dit que s'il compte rester 3 ans sans competir autant arreter la lutte
@sowsory10359 ай бұрын
Bien dit merci beaucoup pour ta réponse
@konadiouf25969 ай бұрын
C'est bel et bien ce qu'il a dit
@malicksarr21419 ай бұрын
Modou Lo Champion ❤
@Elhadji21879 ай бұрын
Bilahi modou warna beurré ben 5 ans incha alla
@Gorguimaxime-fn5tb9 ай бұрын
Siteu amoule niveau roi des arènes
@PapaBarry-cw1vz9 ай бұрын
Analyse pertinente 👌👍🙏
@serignemouhamadoumourtalla19989 ай бұрын
15ans machalah Yékini
@AssaneFaye-qq8of9 ай бұрын
Siteu vs Modou lo lolou échauffement la rekk 😅 déjà amna niou victoire bou yagg
@AmadouNdiaye-r1b8 ай бұрын
Yékéni meilleur lutteur du cinquantenaire
@AliouKama-zs9ye9 ай бұрын
Il a dit que la vérité ❤❤❤❤
@BallaKa-z6c9 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤💪💪💪💪💪💪
@MrSambadiene9 ай бұрын
YaLMINe❤❤
@MameAbdou-j3d9 ай бұрын
Se verité❤
@Enfant_béni_79 ай бұрын
LAMBALOGUE TAY DOUL NGA ,, DANOU NGA 😂 SA XAM LAMB RÉER NALA 😂 YEKINI 15ans LA TOK DANOU WOUL LANOU WAKH MAIS 8ans LA TEUYÉ COURONNE BI 👑 DANOU WOUL OK BOLÉN DIOUGUÉ DI DOUL FOKNI YÉNEU GEUNA XAM LAMB TÉ DOUL RÉK AK GATT GOU REUY GUÉN GEUNA MEUNE AK DOOR DI THIOGOU NAK XALISS 😂 TCHIM 😂
@abdoulayesow42089 ай бұрын
Lamboloque may gnou diama tu parle trop Modou rek❤
@ElhadjiDiedhiou-e4v9 ай бұрын
Me yene nii Di wakh laneleu wakh lou niaw si Modou lo bayilene parparlo bi mo gune
@seydinamohamedndiaye66908 ай бұрын
C’est incroyable il dit une bêtise le journaliste n’est pas capable de le rectifier..La couronne il l’a tenu 8 ans yekina pas 15 ans mon gros
@abdougueye48379 ай бұрын
tapha tine ama ak lac de guerre niokko danne
@AlphaBa-zw4rx9 ай бұрын
Tafa tin kamol darra 😂
@salysagna76979 ай бұрын
Li dé guissouma loussi nekh vraiment
@babacar31789 ай бұрын
Lamb ak football dou béne
@NdeyeNiang-i4n9 ай бұрын
Modou lo ama rek lá fi má kham né Dan na mbeur mas ay boye niang ay siteu dou nio dara
@mamepathe46189 ай бұрын
Boy niang bamou diapé ama mbapat da d'âne ndéyam ama dou mbeur simbkat la
@sowsory10359 ай бұрын
Lambo Modou lo na pa dit il va pas laisser regarde bien se que tu dis
@Lilkheuchfrombomakingbii9 ай бұрын
Modou lô reug reug enregé woula ték khél diarouko
@cheikhndoye86899 ай бұрын
Durant 8 ans lasso nekkk 2015la commencé son carrière arène 2012 l’a enregistré son première défaite
@sophrotall81059 ай бұрын
Yoni nga Ama mou danou, nga yoni boy , amo solution nga yoni siteu
merci gora thiaw . yekini est un grand champion mais il nest pas roi pendant 15 ans . il lest en 2006 et la perdu en 2012
@IslandCureislande9 ай бұрын
Bien vu lambolok wopopopopp
@LamineNgom-p9p9 ай бұрын
Waw waw dé
@AbouAboumbaye5 ай бұрын
Yikini késsè
@AssaneDia-hj7nz9 ай бұрын
Modou. Lo 💪💪💪💪💪🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲💪💪💪💪👑👑👑👑👑👑❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@AliounebadaraGassama-or4op9 ай бұрын
7 ans la tok danou woul après mou dieul roi
@modoucisse20799 ай бұрын
Siteu rekk
@NdeyeNiang-i4n9 ай бұрын
❤
@abduuu-t1v9 ай бұрын
Lambalogue yamal modou limi def xamnako
@AliounebadaraGassama-or4op9 ай бұрын
Lambalok yékini 8 ans l'a nék roi
@BayemorSeck-vg4hs9 ай бұрын
Site rek ❤❤❤❤
@fifteenlevelgangflgang_zb80658 ай бұрын
Tyson Toubabou Dior la Dane pour etre Roi des Arène pas Manga 2
@AbouSow-mv1kl8 ай бұрын
Xaragne à vie
@devndao55279 ай бұрын
Way lii dou combat boulén gnou sonal
@goramekare95949 ай бұрын
Lamb tay mom dagua danou lamb yekini ak modou Les temps dou benne modou a beaucoup plus de combatant balla ama gris lac eumeu boy niang reug siteu tapha tine sathies ect yekini avez que tyson bombadie balla n2 ect dou bend lamb
@NdeyekharNdiaye-r8b9 ай бұрын
Maylennou j'amm ak tapha tine lgui danou ragal niotayy
@cheikhndoye86899 ай бұрын
Mais yèble dounguène bayi 15ans roi des arènes
@NdeyekharNdiaye-r8b9 ай бұрын
Yalla na modou lo bayi lamb si katanou yalla yobalei couronne bi sinon dannko xeixx na yekini
@NdeyeBinetaMbaye-i8t9 ай бұрын
Xamon dara beri ndaye wax doull
@abasall7119 ай бұрын
Sa way modou amna combat buner thiow déranger wuko
@IbrahimaFall-gq4xp9 ай бұрын
Modou doyaloul lambou mo kharam
@AissataGangue-l1s9 ай бұрын
8an
@mamepathe46189 ай бұрын
Tapha tine khana ama baldé daanouko
@BourBa-xd9rn9 ай бұрын
Lac de guierre sakh dane nako
@bdiene669 ай бұрын
Tapha tine bi wouté nak beulé dé😂😂😂
@AliouneDiaw-sp1jv9 ай бұрын
😂😂
@mbackegaydelserignembacke83359 ай бұрын
Saway modou waxoul lolou dh dani souma narone tok nopalou 3ans kone ma bayi lamb ms delene waxal nit ki lim wax yw lamb danga ngaamou trop mounane naagou modou yeugoul succse yekini masoul beure combat mem pas 3moi garaw garawlou bi ngueni bayi manolena xam ba xam nit ki lim defagoul soff nguene trop
@babacar31789 ай бұрын
Tapha tine dou touss
@NdiagneNdiaye-wn5ts9 ай бұрын
Ce gars là se sonne trop d'importance, khamoule touss
Modou lo defou fi dará si rio bi defna 5 Ani amol combat apore 2 combat rek lá fi def de tane ay combat you kou nekh rio modou bi dou rio
@MSam5-vp5ed9 ай бұрын
Lum def .. yaw defulokor .. sa mbeur deffut kor. Norpil sa y
@alaminekandji21979 ай бұрын
Yangui sisou dh😂😂😂😂
@NdeyekharNdiaye-r8b9 ай бұрын
Sisiu mann si bopam waroutoo nooyi
@daoudakante29179 ай бұрын
Ferme ta bouche khamo dara si lamb
@nomisdogue6189 ай бұрын
Ya sokhor te mana fen
@KhadimeSylla-s7v9 ай бұрын
Modou day daw rek
@Lewy5099 ай бұрын
Sisou man nga 😄
@moustahadrame69799 ай бұрын
Kane la daw
@KhadimeSylla-s7v9 ай бұрын
Ww
@ElhadjiFall-nw2he9 ай бұрын
Ses pas. Vrais corona awnafi emergenze fo nk
@cheikhouna_k95739 ай бұрын
Modou dafa ragal dieul tapha tine .je peux pas comprendre gnou beuga teug sa combat yaw ak tapha tine ngani dangay nopalou bayi ba tapha tine am combat nga dieul siteu vraiment affaire ragal la .
@moustahadrame69799 ай бұрын
Saway Tapha tine lou takh kharoul Modou Lô dém Dieul avance légui Modou day tokk diko khar wl? Tapha tine kann lafi dane yambar bobou 😂😂
@cheikhouna_k95739 ай бұрын
@@moustahadrame6979 saway mane tapha dou sama mbeur je ne fais k constaté des faits. Tapha meunoul khar modou ndakh modou mo wakh dafay nopalou 2ans .tapha menoul khar kouy napalou 2ans .modou manone na respecté 2ans yimou wakh c'est mieux
@moustahadrame69799 ай бұрын
@@cheikhouna_k9573 daga dégue Modou né day nopalou 2 ans day nopalou rk la wakh