Vous avez dit la vérité. C'est vous avez osé dire ce qui se passe dans le pays. Continuez à dénoncer les problèmes du pays .félicitations.
@AidaSane-lm6dj14 күн бұрын
Mbodia je suis fière de toi ❤❤
@Djiby-sq3wv18 күн бұрын
Mbodja yalna sa djiam yagueu defar nga seuyy you barri lolou rk doyna 🎉
@allediouf128612 күн бұрын
Sokhna mbodia tu as raison ça m'arriver un jour une mère m'a courtiser et j'ai refusé j'étais tellement musclé et ma poitrine bombée car machallah
@crocodile...22117 күн бұрын
13:02 bilahi Fi vérité nga wakh❤
@GoldouLov14 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤ merci madame merci pour le journal merci madame merci ❤❤❤
@mbayelo303317 күн бұрын
Merci beucoup mbodia lou ler gay wakh ❤❤❤❤
@FabianThioune15 күн бұрын
Yalla naniou yalla mousal si yaye youmelni sant yalla si souniiou yaye you yiiw yi akh am soutoura am kèrsa
@BetouNdiaye-hm1rc16 күн бұрын
Merci mbodia mbaaye
@modoundiayesonko18 күн бұрын
Machala yalla nala yalla defal diam❤
@PAPAALIOUNETALL-c3l5 күн бұрын
Rien que la vérité courage
@modoumbacke947915 күн бұрын
Ah Amna ku ñëwoon ci yonente bi neko takk na muni ko kotak muni ko jeek muni ko lula tee takk jàq ❤😊
@MouhamedSouare-q3b12 күн бұрын
Merci beaucoup maman yalla sa diam yagg
@doustar219317 күн бұрын
Billahi ma bueg mbodia mbaye yalla nga am diam sama Yaye dji mala bueg té xawma lanla ❤❤
@AnnaDiop-m7h17 күн бұрын
Très bien tu as parlé avec franchise
@mai-my8ym18 күн бұрын
Waw de très bien mbodia mbaye yagu gua diko wax de, legui NAK fatou laobe guenal diegualou😅
@autoentrepreneur398918 күн бұрын
Franchement ça c'est de la perversion, il faut que les autorités prennent leur responsabilité car y'a de ces propos à ne pas avancer dans l'espace public car les enfants vous écoutent et pire crier comme ça pour une dame cest vilain
@Omzo_Le_Faramareen_Officiel17 күн бұрын
Mbodia Mbaye BEUG dion😮😮😮😮
@FathouNguer18 күн бұрын
Yalna sa doomm takk mere ioe danga nio yapp mounane na dioubo ak mbokam
@Omzo_Le_Faramareen_Officiel17 күн бұрын
Mbodia Mbaye esk dou xalé 25ans yi niokoy voundang tmt😂😂😂😂
@MamesaliouNdiaye-u4o6 күн бұрын
Penda❤❤
@ishanjie587018 күн бұрын
Merci mama❤❤❤
@ibrahimalom643913 күн бұрын
Verité bilahi dra nékousi
@MoustaphaDiop-f7s18 күн бұрын
Je ne comprends pas les sites internet maintenant li bane sens lagnouy amal jeune yi chômage molen sonal Guen nek fi di wakh you niack fayda yi
@rokhayacisse790515 күн бұрын
Am n'a sens li actualités
@AbdouSow-ce4dn18 күн бұрын
Merci mbodja tu a raison
@arretekeita88018 күн бұрын
Machalla elle a parfaitement raison Diekk bou ndaw 30+ Diekk bou makk 40+ ak diekk bou magga magu 50+
@ModouBodian-jv4oj15 күн бұрын
Mo taye utilisé halé bi danio sohoré aissatou penda Diop taque mère moma gueneul taque halé you thiaga yi ga hamni gooro goor teudé naléne ba sén data yi yatou mounouniou diohe plaisir béne goor séye bi ndam rék inchallah merci bodia
@Mariamadoillo18 күн бұрын
Yow mii merr nga teh merru chagga nga IL foka nga Anda ak merr bu nyak jom bi ngay defend.
@ousmanediaw290518 күн бұрын
Merci mbodia
@moustaphathiaw349015 күн бұрын
Kou lén top khétou Seydina mouhamed (psl) dou yokou mouk une femme ménopause à partir de 40ans .😢😢
@BinetaSarr-d3f17 күн бұрын
vérité absolue et
@ummhuraira249518 күн бұрын
Khawma zero stress khawma mais ZERO PUDEUR. Sant Yalla doo sama yaay.
@gayafall18 күн бұрын
Chacun choisit son mec ou sa femme . Laissez les vivre . Liberté chacun a sa vie . Passons à autre chose .
@rekrekbodian355016 күн бұрын
Yow Thiaga gua domoram by done
@SerigneabdoukhadreDiop-x1m16 күн бұрын
Sokhna mbodia 😂😂😂
@SerigneabdoukhadreDiop-x1m16 күн бұрын
Ça c'est grave😂
@MoussaDiop-ji2gn18 күн бұрын
Sokhnasi yangui déf mauvaise promotion c'est du n'importe quoi Sénégal mo bari ay nafékh yakh nguéne Lou bari thi génération 2000 ak séne Lamigne you reuy.
@nafibalbina208917 күн бұрын
Pourquoi la mediocritè extreme ces temps au Senegal 😢😢. L heure est tres tres grave.
@BounamaDiarra-o8p15 күн бұрын
Ces médiocrités ont toujours existé au Sénégal, je suis désolé
@nogayegalon96918 күн бұрын
Je suis d'accord avec toi continue trés bien et surtout très fort ma sœur le sénégalais est très méchant et hypocrite vas y je suis avec toi bisous ma sœur je t'écoute depuis la France merci🎉❤
@CheikhBa-yk6xh17 күн бұрын
Vous avez votre problèmes intimes pour quoi de ça n'occuprje conseille le couple de vivres leurs amours de tourné aux bavardages 🎉❤
@KhaliphaababacarGueye17 күн бұрын
Boie yallah na la yallah diapalé. 😊ya gérer😮😢❤
@elagegueye331018 күн бұрын
probalembi moy djoulit dou tak gisanekatt dafa haram
@hamzafall547518 күн бұрын
Senegal yalla nalèn yalla may liguey ndakh gnou bayi cas... Senegal lii rekk moko tardel... Bou Khalè bi khèyè kharou boumlèn bètt... Djioulitt day Manou...
@PapeDiop-z7z15 күн бұрын
🇸🇳🇸🇳 Pape Diop Bamako Mali 🇸🇳🇸🇳
@Prunelle567818 күн бұрын
Dina wakh ba dougal bopam ki lamigne bi mo reuye c’est grave
@yacinegueyetahir948718 күн бұрын
Nena xale la yor
@julioniasse193217 күн бұрын
Grande gueule rek,elle ne fait que de la mauvaise promo se cette jeunesse.Aucune connaissance utile pour la société
@Prunelle567817 күн бұрын
@@yacinegueyetahir9487 moma tital ak gni koy nane ko woutal ma mou melni courtier Doyna warr
@ThiernoOmbre18 күн бұрын
LUTAX NGÈEN DI MAY KII BEUZZ?
@diagnemomo477118 күн бұрын
Ay mére thiaga nio barriii Sénégal nékaléne nite mére yi diwanté birbouy daww lay diokhéé😂😂😂😂😂😂
@fatoukine341518 күн бұрын
❤❤❤m achallah mbodjia
@FallMama-e1i17 күн бұрын
C'est vrai
@nogayegalon96918 күн бұрын
Continue ton travail et tes vidéos point barre
@abdoucoly827816 күн бұрын
En nagouwo sa dome defko 😂
@DiengeRokheya17 күн бұрын
Ww yaw rk layi yoube maman mahllh❤❤❤
@ngathiefallmusiquefromsene206018 күн бұрын
Yaw respect é wo sakh saye dôme bilahi
@mamanniang399918 күн бұрын
Mbaya waw mi ya encourager mère pour gnou andal khaliyi
@zzzz-yf6ch14 күн бұрын
Thiaga Yi !!
@ousmanediaw290518 күн бұрын
No mbodia dou wakhantou mouytoulen ko
@ASylla-ol6ew18 күн бұрын
C'est toi qui fait la promotion des jeunes d'aller découvrir les vieilles 😢😢😢😢😢tu es mauvaise 😢😢😢😢😢😢😢
@LassanaTRAORÉ-m5x18 күн бұрын
Tu as parfaitement raison. Ton commentaire mérite des millions de « like ». Diereudieuf way
@bounamadiom942618 күн бұрын
Walahi dinane mague you nekh
@MoustaphaKanoute-s1o18 күн бұрын
Tu as raison mon frère
@Gkcdshndsncs18 күн бұрын
Djigueine diou bakh day am kersa wayei loula neikh wakh
@coumbafaye931918 күн бұрын
@@MoustaphaKanoute-s1oKI KAY ZERO PERSONNALITE NAK.
@NdeyearameNdour_1417 күн бұрын
Mbojia yaye diabare deug deugeu
@adambadjiebittaye163916 күн бұрын
Thank so much 👏🏾👏🏾❤️❤️🫶🏾🫶🏾💯💯
@AbdouNdao-zn6uq18 күн бұрын
Xalei bi beugg nako femmes bih beug nako tei yallah takh femme bi meunon nako quinape walla laineneu ameu si na yayam mougn khamnei nattu la
@toubabnelljoop952818 күн бұрын
Où est la police des mœurs, bon sang ;et l'office de la cybercriminalité ds tt celà, quelle société frivole ,puérile et sans "croyance aucune" ,pauvre société d'hypocrites malheureusement.
Sou wakhone niou dieul Sene lokho def ko si tal bi kene douko def kou beugu bone da ngay bone khalé You ndakh yi nek fi ngay weur ay maguette
@AwaDialloNDIAYE18 күн бұрын
Mbodja wakhoul kène dém lène weuri mère yi bayi lène juger nitt th khamo lène ko ki wakhoul dara lou ayy guiss nañou fi papa bou violer domam guiss avant mbodja mbaye Amna ayy khalé you goor you Dane seuy ak ayy mère Kone bayi lène juger nitt
@AwaDialloNDIAYE18 күн бұрын
vraiment nak ma chérie
@AwaDialloNDIAYE18 күн бұрын
Mane dh khamnako bou bakh lépp loumou may conseiller moy téél sa bopou pask amagouma dieukeur mounima téél sa bopou ba am jeukeur lolou rk lamay conseiller chaque jours Kone kokou dou jouer rôle bou négatif si adouna
@elhadjindiaye708918 күн бұрын
Man dama diomi ki ame na ay dôme
@madyceesay532918 күн бұрын
Bo Senegal do deuku Islam yaw mee dinga chance say kadou. Mer bu torokh
@mouhamedndiaye903317 күн бұрын
Nioko taye deuk bi losi wakh am n'a Lou desss
@bintoudoumbia895518 күн бұрын
Sénégal comme sabar bou tass, beug belle vie dinala diaralé vulgaire, la plus part des jeunes garçons qui cherche des vielles femmes sont des rigolos beug nagne am vie bou stable mais séne yaram dou tang intérêt rek. Mbodja néna khalé gori gnolay woo di woutlo mère il fallait bien préciser k mere you am kopar, am auto, am villa lagni weur, dougnou Doug mouk ci mère yi am bene neg AK gni di diaye légumes AK beignets pour doundou. Arrêté d'influencer les jeunes li d'où ligiey
@AmadouSylleCamara16 күн бұрын
Li moñou tre dem zarou thi ño beugeu yakeu khalé yi
@AliouNdiaye-lc3pp15 күн бұрын
Moytu leen mere yi 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@AmadouSow-jl1gu17 күн бұрын
Khaléyi dara dagno meuneu kâte rek djiguéne boko katé niari yone si guoudy dotoulâ bayi té lolou khâlé yi gnoko meuneu
@assanelam887818 күн бұрын
En tt cas xale boussi bayiwoul mère do def carrière epuis sakh pourquoi maguettet yi teu xaleyi nekeufi
@BounamaDiarra-o8p15 күн бұрын
Mais kou nekak sa gout😢
@mthodyndotty79616 күн бұрын
CE N'EST PAS LA MÊME CHOSE. LE CAS AISSATOU PENDA ET OUSSEYNOU EST SPÉCIAL. SA MÈRE ET SA SOEUR PLEURENT. YOW MOME NIAM NGA XALÉ . LI NGAY WAX DOU SA XAM XAM . PRATIQUE LA LO DEF BÉ PARÉ LA.
@coumbafaye931918 күн бұрын
AK NOUMOU MANA DEMER REK SAY WAKH DANGAKO WARA WODE.
@ummhuraira249518 күн бұрын
Wakh DEUG! Mais loo kham tchi gueweulé????
@coumbafaye931918 күн бұрын
@ummhuraira2495 MANE GUEWEL LA DEH MAIS ROUSNA LI. GUEWEL YEFI GUENEU AM LOUNIOUY BAGNE. KI KAY DA AMOUL KERSA REK.
@Salsaa-x7z18 күн бұрын
Chiim yaw ya yakh domou diabour yép thiagua kharam bi sa domyi dougnou rouss
@AmarSow-iu8bl18 күн бұрын
Sa lamigne niaw na soxnasi
@KhardiataDiouf-m9q17 күн бұрын
Dangay jangale rekk bul bayyi lël ngay def
@GgGh-on4ni18 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤
@allediouf128612 күн бұрын
Je me demande rek nakh khalé warna sékal mak
@ablayediop575216 күн бұрын
No mère dièpiii nala trop mè linga wakh deugue pire la billahi
@abymboup835915 күн бұрын
KI DAL DOMERAME LA REKK LIGUÉO FI DARRA KHANA PERVERTTIR KHALEEE YII CHIIMMM