Ada Boy Baol crache ses vérités, recadre Pokola et Sa Touba :"naniou bayi…"

  Рет қаралды 12,983

Lutte TV

Lutte TV

Күн бұрын

Пікірлер: 82
@gueyelabsolu5889
@gueyelabsolu5889 27 минут бұрын
Ada Boy Baol sa communication Superna trop champion bonne continuation ❤️
@malickdia3495
@malickdia3495 56 минут бұрын
Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
@Sport2079a
@Sport2079a 2 сағат бұрын
Merci adama dieng parcelle seule
@daoudandiayecalciombeur964
@daoudandiayecalciombeur964 2 сағат бұрын
Vraiment ada boy baol tu a parfaitement raison sa wakh ji rafete na macha allah li nga wax ci matar gueye mane mi mako dieukeu tontou ci live bi mane la calcio
@gueyelabsolu5889
@gueyelabsolu5889 28 минут бұрын
Mbeurou parcelle yeupou bouniou sotè pokola Mou Nious lèn 🧏‍♂️poko mbam sén papa la Thi Lèpou Respecte lènko 🫏Molèn geuneu yaxou Fouffff sax
@oumarndiaye8802
@oumarndiaye8802 2 сағат бұрын
Ada boy baol, dieuleul avance Thiatou Aïda BOU JOAL monguene
@ModouDiouf-i4d
@ModouDiouf-i4d Сағат бұрын
Ken hamouko
@ZamSallecollege
@ZamSallecollege 2 сағат бұрын
Wawa ada❤❤❤❤
@ThiernoDiallo-c1k
@ThiernoDiallo-c1k Сағат бұрын
Machalah ligua wakh thi Sa Touba deugg bou werr leuh
@AladjiMbaye-s1c
@AladjiMbaye-s1c 12 минут бұрын
Un grand champion baol 2
@AssaneSarr-pc5rw
@AssaneSarr-pc5rw 2 сағат бұрын
100 mbawrr mbawrr ❤❤❤❤
@abdoulakhatbadiane1294
@abdoulakhatbadiane1294 28 минут бұрын
Talfaa n’a wathie ci mbapatt yi gagner waattt ora ak confiance
@gorangom3537
@gorangom3537 Сағат бұрын
Champion deug bilay yala meun
@siradia2678
@siradia2678 4 сағат бұрын
Champion deug moy wakh no
@mamadousall7046
@mamadousall7046 2 сағат бұрын
Bilahi ndanane laaa
@saliougueye2348
@saliougueye2348 5 минут бұрын
Merci beaucoup sa Touba déf Barri wakh trop
@saliouthiam2462
@saliouthiam2462 2 сағат бұрын
Talfa na déme diégué dji modou Lo lolu moy ndiérignam wallaahi
@KaneOusmane-t9t
@KaneOusmane-t9t 2 сағат бұрын
M gayi nagne dieul ada boy baol bok champion deugue mongui ni
@Ndiaga-mw6zc
@Ndiaga-mw6zc Сағат бұрын
Ki lanlafi def
@MamyGaye-l1v
@MamyGaye-l1v 2 сағат бұрын
Sa touba datfa yeuk ney Bolam bilahi
@MamadouSylla-w5s
@MamadouSylla-w5s Сағат бұрын
❤❤❤
@MohamedThioune-p9k
@MohamedThioune-p9k 4 сағат бұрын
Talfa da ragal boy bi😅
@azizndour6152
@azizndour6152 3 сағат бұрын
Iow ak Zoss yenay blem bi 🙊🙊🤦🏾‍♂️
@moussandiaye3250
@moussandiaye3250 2 сағат бұрын
Vérité crue ada boy baol
@SophieSall-s1o
@SophieSall-s1o Сағат бұрын
Ada boy baol waxo fi toussssss way
@mamadoundiaye5230
@mamadoundiaye5230 13 минут бұрын
Talpha stp défal retour si mbappatt yii surtout Dakar satouba mome hamoul boppam pour mome mo yoor ndam
@cheikhbasskeurmassar9548
@cheikhbasskeurmassar9548 2 сағат бұрын
Ada baol yaw amnga loula doye ngaye geune ci internet bi naane combats te bougnou dokhé sa combats nga rookh
@Mbodji-walo
@Mbodji-walo 4 сағат бұрын
Du courage Talfa baylén sén wakh yi Pokola moko meune danenako c'est finit li fereplay leu rk khana dolén ay dioullit😂 man wa camberene diakhalngén'ma
@DiengMagueye
@DiengMagueye 4 сағат бұрын
Wakh DEUG yalla pokola seul bilakhi
@Mbodji-walo
@Mbodji-walo 3 сағат бұрын
@@DiengMagueye Man Medina la deuk mais nieupp khamnagne Talfa champion leu na défarouwat rk dina bakh
@seydounouroufaye8353
@seydounouroufaye8353 3 сағат бұрын
Wakh gua deug frère
@booygaye9894
@booygaye9894 3 сағат бұрын
Sawaay lii louciy yonou wa camberene do tontou kii rek
@Mbodji-walo
@Mbodji-walo 3 сағат бұрын
@@booygaye9894 Sen mbeur leu
@oumargueye8032
@oumargueye8032 14 минут бұрын
Mbeur defaral sa entourage iow balegui nekago mbeur tei Parcelles assainies Camberene adouna dounioula yaakar mbeur day deuheuniou du courage Sissi kanam moy dak peace
@saliouthiam2462
@saliouthiam2462 2 сағат бұрын
Ada mi louy probleme rek mom guénnou si mbaor mbaor la comme mane dh mais kii 😢😭 psk amoul combat fokni Wa diambar nioko bagn teugeul te dou lolu adversaire yi nioy bagn
@dabambaye1066
@dabambaye1066 35 минут бұрын
Ada kassé baye fall bi
@papengom259
@papengom259 Сағат бұрын
Aliou kayré mo beuri ndaye wakh
@gorangom3537
@gorangom3537 Сағат бұрын
Lamb khana mo yor gnepo 😅😅😅😅 pourquoi Sénégales mana xewal xamoul dara
@BilalMbodj-x9i
@BilalMbodj-x9i 3 сағат бұрын
Ada dégou fi sa touba wakhé dh wakhalol talfa dh côté franc la wakhé coma yeugol yeugomala
@modo6218
@modo6218 3 сағат бұрын
@@BilalMbodj-x9i sa touba na topou feulé nioun parcell rek
@moussandiaye3250
@moussandiaye3250 2 сағат бұрын
Walahi ada tay lalay doga guis damaladone dég rk wayé yaw nit deug nga mais tay lalay commencé supporter Yalla nga deg roi des arénes
@aliousene5100
@aliousene5100 2 сағат бұрын
Lou lerr gua wakh ada
@bayemodoufall2879
@bayemodoufall2879 3 сағат бұрын
🎉🎉🎉🎉
@damembow6374
@damembow6374 3 сағат бұрын
Ki vrai ngakaa la ndékété
@ametndiaye1421
@ametndiaye1421 Сағат бұрын
Ada nékal nit te bay dof doflou gui yaw AK matar wa Thiès séne yone nekou thi du courage talfa
@MohamedThioune-p9k
@MohamedThioune-p9k 3 сағат бұрын
Sa touba mo faroul fen Modou lo kesé Moko nior mé nion p.a lanouy topou
@DiengMagueye
@DiengMagueye 4 сағат бұрын
Guemal yalla bania mana dan pokola meun na dan kounek
@syllepogba1743
@syllepogba1743 3 сағат бұрын
Kii nék sisa weet ap saytané la dé begoul diam wagni laine wakh dji
@afro3827
@afro3827 3 сағат бұрын
Sa touba mom yalla la diapé bopam 😂😂
@damembow6374
@damembow6374 3 сағат бұрын
Satouba limou déf dara nékousii yénaaa sof rk th meunou lénn gattt
@goracesse5941
@goracesse5941 53 минут бұрын
Mbaor mbaor yi akagno am diom talfa neck si rk dinabakh champion geu
@m.moussa678
@m.moussa678 2 сағат бұрын
Tapete la da roukh depuis signature bi , poko dafko roubé daabe ko dafa yombou trop
@KaranoreyniKhalil
@KaranoreyniKhalil 2 сағат бұрын
Tapét mo takh nga nék fi di wax
@morsene7507
@morsene7507 3 сағат бұрын
Kone yaw dagua sisse mais boys instant boy bi sokhla woule liguaye wakh boys dawara yatale guir avenir
@modo6218
@modo6218 3 сағат бұрын
@@morsene7507 merci mbeur dangay beuri guina
@BayembayeDiouf-i2q
@BayembayeDiouf-i2q 2 сағат бұрын
Ada goor degue
@elhadjindiaye7089
@elhadjindiaye7089 2 сағат бұрын
Sa touba dou touss Sénégalais mo nékha nakh😂
@KhadimDéme-z1w
@KhadimDéme-z1w 3 сағат бұрын
Kadouyi rafét na ada boy baol
@NafinaBueYessere
@NafinaBueYessere 2 сағат бұрын
Yaw ya nékh 😂😂😂
@modo6218
@modo6218 4 сағат бұрын
Boy bi bou yenay kay conseil gewma mou sori talfa na wathie bopam and ak ay grand wam
@layeseck1495
@layeseck1495 Сағат бұрын
Deug rek nga wakh dé
@FatouDiop-k2v
@FatouDiop-k2v Сағат бұрын
Ya guene tapéte gnepe yaw ndiaga Thiam guaye daw nagou wo beré ak mome
@IbouSene-eh9lj
@IbouSene-eh9lj 4 сағат бұрын
Talfa kess
@AbdoulNdiaye-y3l
@AbdoulNdiaye-y3l 3 сағат бұрын
Boy tu n'est pas conscient
@AboulBacharSall
@AboulBacharSall 2 сағат бұрын
Talfa waxlein ko deug na wathie wat boppam xamna desse na lou beurri si lamb ta xale leu champion leu
@dtfofficielle8502
@dtfofficielle8502 Сағат бұрын
Sa way diéleul Boy Baldé 2 - 0 yi mate
@modo6218
@modo6218 4 сағат бұрын
Ada boy baol dacorouma talfa ken fakhastalou ko boulen outal boy bi ay non da warona danou rek na geuna wadiat ak ay mbokam
@modo6218
@modo6218 4 сағат бұрын
Sa touba mo beuri wakh khamoul touss begue ande ak mbeur yeupp lolou menoul nekk nioun ay domou parcell laniou
@gorangom3537
@gorangom3537 Сағат бұрын
Sa touba tour bi moma diaxal rek
@jpsf687
@jpsf687 4 сағат бұрын
Ki comme boy yi nieme wouniouko...diel len ki beuré ak mom
@mamadousall7046
@mamadousall7046 2 сағат бұрын
Ndanane laaa motakh gayi diko daaw
@SophieSall-s1o
@SophieSall-s1o Сағат бұрын
Sa touba degue rk la waxe
@damembow6374
@damembow6374 3 сағат бұрын
Pour niom yék dune musculation rk moy lamb
@MohamadouDiallo-t8o
@MohamadouDiallo-t8o 3 сағат бұрын
80% mbeur yi lamb contact la souf si
@damembow6374
@damembow6374 3 сағат бұрын
Pourquoi satouba dila woo yaw tu est ki démal woutii combat mogeunn si yaww
@seydounouroufaye8353
@seydounouroufaye8353 3 сағат бұрын
Yaw mom do sportif sa bopou bakhoul
@gueyelabsolu5889
@gueyelabsolu5889 27 минут бұрын
Mbeurou parcelle yeupou bouniou sotè pokola Mou Nious lèn 🧏‍♂️poko mbam sén papa la Thi Lèpou Respecte lènko 🫏Molèn geuneu yaxou Fouffff sax
@modo6218
@modo6218 4 сағат бұрын
Ada boy baol dacorouma talfa ken fakhastalou ko boulen outal boy bi ay non da warona danou rek na geuna wadiat ak ay mbokam
@damembow6374
@damembow6374 3 сағат бұрын
Wax lénn talfa deug meunoul khékh na diangui khékh th démm andeu ak mbeurou parcelle yii
Wally B. Seck - Kay Ñu Pello WAVE
50:08
Wally Seck Officiel
Рет қаралды 30 М.
The evil clown plays a prank on the angel
00:39
超人夫妇
Рет қаралды 53 МЛН
How to treat Acne💉
00:31
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 108 МЛН
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 12 **VOSTFR**
1:13:32
EvenProd
Рет қаралды 2,7 МЛН
Prank Star -Saison 3 episode 42 Serigne Ndiaye Lady Diama
9:12