Je suis mouride mais j'ai des frissons rien qu'en l'écoutant
@abdoulayefaye56898 ай бұрын
Diné dji béne la. Mag dji daniou woté kénal Allah bolé si beug Muhammad rhassoulloullah sallal'l Lahou aleyhi wa salam. Kou baax nga. Salam
@FallouSow-z8i8 ай бұрын
Bilay de meme que moi❤❤❤
@salammalekoum22348 ай бұрын
Même mane ❤😢
@FallouGalass-lg5bt8 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@serignefalloudiakhoumpa64748 ай бұрын
Mouride waru ko déglu ? Xana du Turu Yalla lañuy zikr?
@elhadjibakhoum52708 ай бұрын
En tant que mouride, dadj bii fim may ageu yalla rek moko xam !! Kendou sounou makgni ❤❤!!!
@abysene38418 ай бұрын
Macha allah j'ai des larmes aux yeux tivaoune mon paradis sur terre me manque😢
@beuguepirelespatriotes87998 ай бұрын
Wallahi yallana niou yalla fayal aladji malick
@abysene38417 ай бұрын
Allahuma amine 🙏@@beuguepirelespatriotes8799
@ibrahimasylla24568 ай бұрын
Mourid tijan laye e thiaba niasene ndiassane dioulite yepakoye nianal giudiu fane wer karange bate bou gana diapani barkeb brom touba ak xassida yi amine 😭😭😭❤❤
@DiaguaWane8 ай бұрын
Ana gni guiss vidéo Tik tok kom Mane nieuw directe pour setante lep si vidéo machallah Serigne Moustapha la nieuka dég mou wakh sa tour bilahi mourite talibe bamba la te Lou bakh rek la beugue mai nékh dou wésou li machallah ❤️❤️
@AminaLo-x7h8 ай бұрын
Suis là 😂
@cheikhounadia41958 ай бұрын
Mangui ni dama ko sét ba sone mais al hamdou lillah à fin ❤❤❤❤😂
@mamadoudien24968 ай бұрын
Yalnala yalla saam arr la weral baatt bi lingay wakh neekh na khol mouride sadikh la wayet dioy lo nama tay si souba
@KebaDiop-b6s8 ай бұрын
benn ci man Murid bi❤
@AdamaNdoye-t2k8 ай бұрын
Machallah ❤❤❤
@abdoulayediack52088 ай бұрын
Ma cha alah nagnoulene ko protéjé boubakh nak Serigne Babacar Sy Mansour khalif général des tidianes yalenafi yague té wére amine
inchallah kom toudou nako rk yalla dina ko samou konou loum toudou yalla def si barke inchallah ❤
@ousmaneseck68898 ай бұрын
Machalla alhadoulilahi
@laminesebor35568 ай бұрын
Surtout lolou ❤
@ndiagambaye57808 ай бұрын
Kone ngiko begue abou daniy kharr❤
@ousmaneseck68898 ай бұрын
Nn gayi n'en len KO Al rek grawoule talibé cheikh daye tabé après magal mou gnibissi mais niou wattouko mbeuk rek si danou lerr ti
@viensvoirtv98448 ай бұрын
Je suis muride mai walahi sope nako mashallah yalna yalla yok xaam xaam bi tam may la weir ak goud fane xaliss bu barkeil Maodo moy Ahmadou Bamba ahmadou moy Maodo gnon bok Mäm maram Touba ak tivaoune beine deuk la ❤️ yalna diam yag Sénégal 🇸🇳
@cheikhtidianecisse82443 ай бұрын
Machalah ❤🙏🙏
@chatmaktùm30118 ай бұрын
Yalna ko yaAllah thi barkel thi barki Sérigne Moustapha Sy Al Maktoum❤
@mamadousadji60568 ай бұрын
Daye nieuwe si mercato bi transfère fawe mou ame guisse nako si hisbou daroul xoudose yi ❤❤❤ Machallah c’est le Sénégal ❤️❤️
@MouhamedGaye-k8d7 ай бұрын
Billahi nk na nieuwe loumou wax niou faye ko ❤
@mbayediop1238 ай бұрын
Diereudieuf pape Malick si anticipation bi niane bou am solo la na demm ba diekh machalah baye Mbaye sa mame mo takh niou kham mame maodo Malick Sy (RTA)
@sunuterangatv61378 ай бұрын
❤❤worna serigne touba li nékh na waye macha Allah ❤ 3:49
@mansourndiaye90148 ай бұрын
Ninga sédalé sama xool bi yalnako Cheikhou Tidiane sédalé sa xool ❤🥹🤲
Ma sha Allah yalla nala Yalla yokou wer aral bopam ak sa wadiors yi ly nékhna trop bilay Yalla guéne la
@AstoubabaDiop-it7nm2 ай бұрын
L'élégance c'est d'être talibe cheikh ms baye mbaye tu chante très bien Machallah je veux que Dieu me donne un marie comme baye mbaye amine 🙏🕌
@oumydabo75217 ай бұрын
Ohhhhh😢😢 machalah li nehhna❤❤❤❤❤ yalna yalla goudal Say fane Baye Mbaye 🙏
@dabagueye53957 ай бұрын
Baye mbaye j'ai pas les mots ndakh xol❤ bou fess ak ay dioy😢. Yalnala yalla takhawou té sameu la si barké Cheikh Tidiane RTA
@damegaye20208 ай бұрын
Machalah way Baye Mbaye yalna yala protègél la bopam inchallah ❤❤❤❤😢
@SouleymaneKamara-ed1rw8 ай бұрын
Amine
@papaousmanelo8928 ай бұрын
La relève est assurée ❤️ Yàlla na Sougnou Borom sam lakh fou yakh egoul
@BounamaNdiaye-i8c7 ай бұрын
Bilahi monùmasi doyal li nékh na yalnala yalla samù khadre la mé cette chanson ma touché dùma si ték lénén bala yalla dima méré bayil ma teud😢😢😢
@Diagne13-u1c7 ай бұрын
Donou gua sa mame donou sa baye machallah goudeul fane talibé cheikh mo nekh en tout cas je suis fière ❤
@teddydiallo52746 ай бұрын
mouride, tidiane,layene, ....... leup lahilaha illallah bi nioko bokou , islam sa kaw sa kanam way... machallah
@MuguetteSeck8 ай бұрын
Machallah Yalla naga goudu fane t'es weer Barkep serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@moustaphadione72398 ай бұрын
Lii dioylo nama Barké baye niass lii nékhna
@fatoubinetoumaguettedieye62066 ай бұрын
Machalla je suis MOURIDE mais j'ai des frissons en entendant Baye Mbaye lafe thiate goudou fane weer bcp de bonheur ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@bilyshop2218 ай бұрын
Ana gniu diouge tik tok ndakh li 😂❤️❤️😂
@ibnouserignefall69658 ай бұрын
Suis la😊
@fatoudiop39878 ай бұрын
Maagui ni deh li katt limiye deff si yaram dafa graw
@Tee_Baby_8 ай бұрын
Mangi niiii😂❤
@modousall38318 ай бұрын
magui nii brk borom touba li nekh na
@Bouba8158 ай бұрын
Magui nii😂😂😂
@modoufatmambow99028 ай бұрын
Frissonnant tu as remué mon âme Machallah. Wayy wan len ma ki ma teral ko wayy toubarkallah
@ndoumbesamb39608 ай бұрын
Mais que diiiire😢😢 Macha Allah yalna Yalla same leu teh aar leu❤❤❤❤
@Mamesaye-gw7rv7 ай бұрын
Kharal ma télécharger ko sakh nopalou dama sone ci weur bi té khawma noumou toude😂ki yalnako yalla may goude fan ak wér barké seydina mouhamed swl❤❤❤
@AbdoulMbengue-g3p6 ай бұрын
Baye mbaye
@MamemansourBalkhawmi8 ай бұрын
Baye Mbaye del diangu tére yi waye yaw talent Rek nga
@saerdiop55688 ай бұрын
Je l'ai téléchargé pour pouvoir l'écouter tout temps Yalla na yalla samm la ci barké cheikhoul khadim😢
@IliassCissé2 ай бұрын
Machallah diajacallahou hayran Diam rék
@fatoucissokho50867 ай бұрын
Bilay Seutt day done mame 😢 Ndeysan Pape Mbaye donde fier na si Baye Mbaye famou teudd Ma Sha Allah Baye Mbaye ❤❤❤❤❤laf thiat ❤❤❤❤❤ you remind me of your grandfather🤲🏽🤲🏽🤲🏽🤲🏽🤲🏽👌💪🙏🙏🙏🙏 I’m a proud Tijane
@Delba369Beatz7 ай бұрын
Way Baye Mbaye Yalla naga Goudou Fane Si Barké Seydina Muhamath S.A.W. Amine ya rabbi ❤❤❤❤❤❤❤
@habibah2722 ай бұрын
Machaa Allah 💞💞💞 li nekh na
@NdiateMboup-cz4un8 ай бұрын
Baye mbaye yalla n'a la yalla same 😢
@NdiayaDiop-v6b27 күн бұрын
Ÿallena yalla koudale safane❤❤❤
@OusmaneLy-cv5nd7 ай бұрын
❤😢😢😢man dee dama warou yallana yalla arr mayla goud fan ak weur 🤲 Amin ♥️ Barakkalah❤
@fatousane94432 ай бұрын
Oh machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ Yalla n'a Yalla wéreul bate yi
@tidianeaw54498 ай бұрын
Macha allahh yalla na yalla samoula té are la ak sayi wa diour❤❤❤
@Dinhothiabb8 ай бұрын
Pourquoi à chaque fois que j’écoute ça,je pleure 🥹🤍
@amathSow-ig2ly8 ай бұрын
je suis mourid mais li dfa daw yaram bilah
@uneBabacarienne-pd6jx7 ай бұрын
Machallah yalla na yalla wéreul bate bi si barké Serigne Babacar ❤
@serignefallousarr71767 ай бұрын
Mbarké s touba ki motakh may diang xasida ❤fala bouda mine chakwa❤ alhamdoulilah ❤❤
@ibrandaw-fm4xz8 ай бұрын
Macha alla keneu dou Sénégal en sus de cette révélation ( yalla nako yalla sam may KO fane bou goud) Commentaires you eup sont des mourides ça prouve Sénégal rew bou bakh lagne
@DiopBaba-z2u8 ай бұрын
Ki Nak mou yèlo ayy milliard, barkè serigne Touba 😭😭😭
@OusmaneLy-cv5nd7 ай бұрын
❤ wallahi❤
@groupenabiyetv82118 ай бұрын
NOKHOL BA NÉKHOUL MAIS PAPE MALICK KOU BAKHLA NDÉYSANE ❤❤❤❤❤
@ndeyemadeleinediallo42328 ай бұрын
Machallah yalna yalla lafala thiat
@Mariam_org6 ай бұрын
Allahu akbar 1: 2 je vois beaucoup de fierté dans les yeux des gens dans le plateau. 6: 23 ❤ Macha'Allah quelle voix qu'allah ta'ala te protège my Dear 😢❤
@ndeyeanthioboydodiouf47928 ай бұрын
Machalla ❤🎉 yalna yalla may goudou fann akk wer
@moustaphaba1435Ай бұрын
Mais li nekh na trop❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@deffaly90568 ай бұрын
Merci Bayes Mbaye continel si rhythm bi rèk pas taassou masha Allah ❤❤❤
@MorBadiane-oe8md7 ай бұрын
Machalla yalle boule thaite d'où gua❤❤❤
@AhmadouDieye-gj4jt8 ай бұрын
Machallah yalla na yalla sameu arla lakha fou yakha ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@falloukane168 ай бұрын
En tout cas 😢 kou sa khole yengouwoul si li demal fadiou febarou khole❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@SouleyeNdiaye-gw9lv22 күн бұрын
😂😂😂😂
@RouguiyatouBa-z1r8 ай бұрын
Waouh 😢😭😭😭 Les mots me manquent bilahi 😭 machalah 🥰❤️❤️❤️🙏🏽 Mbaye Mbaye yallaneuh yalla wéreul bate Chi barké Séyidouna Mouhamadou psl 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
@HawakayaKane7 ай бұрын
Macha ALLAH sama dom bi, ya Allah namla samm, sa baye moy sama weuy katt, sama sonnerie portable sah mofa nek❤️😇
@mamediarraboussotall11828 ай бұрын
Goudou fane rék Rék nak Inchallah.Et mes larmes qui ne cessent de couler.😢😢😢❤❤❤ qu'Allah swt t'accompagne et que la Baraka du prophète Muhammad et de Seydi Hadji Malick illumine ton devenir.
@IdaChoi-h9zАй бұрын
Yalna yalla gudal safan si barki nabi moustafa yalna yalla def jambari dinee yaram dawna yalla nga raw sa bay in Sha allah ❤❤❤❤❤
@PapeIbrahimaDiagne-jj6jt8 ай бұрын
Je suis fière d'être talibé cheikh ❤️❤️❤️
@Xarnoubi8 ай бұрын
Yalnala yala samou barki serigne Bachirou 🙏🙏♥️écouteurs la dieund pour bien écouter 😢❤
@ndiombendiaye45368 ай бұрын
Machallah baye mbaye yalna yalla barkél leup inchallah amine
@YacineDiagne-wp8hy2 ай бұрын
Machallah ♥️❤️❤️♥️ sama xol sedna yalnala yalla same
@AstoudiopSy8 ай бұрын
Li nekhna deh ma sha Allah 😭😭😭❤️❤️❤️❤️yalla nala borom bi faye ningua beigueilei sama khool bi😭😭😭❤️❤️
@SokhnaDienf3 ай бұрын
Machala nioune wa touba nioy nouyo li nekhna waay❤
@habibah2722 ай бұрын
Walahi ndeyssan
@BabacarThiam-vp4iw8 ай бұрын
Yalna yalla wéreul bat bi baye mbaye❤😂❤
@yorocambelndiaye94948 ай бұрын
Walahi kénn meunouta fayyy waydiour ....de plus qui a vu les corrections de son pére pendant qu'ils chantent. Non vraiment ce petit est un géni....Yalla nala yalla défalll djiamm barki Alkhourannn
@bigndanane14487 ай бұрын
Fane yii mom sama khôl bi dafay nékh rek. Mouride fénial boubakh né Tidiane bi domou badiénam la. Niouy roubéwanté rek. Lii Yalla na yague ci Sénégal. Bouniou kéneu diakhassé. Machalla Yalla na yalla ciguil Sénégal guereum ko naatal ko
@awalodione99576 ай бұрын
Machallah yalna yalla goudal séne fane may léne wer akk werlé ci barker Seydina Mohamed SAW Amine ya rabbi