Réwou nanfékh deug moy Sénégal ! Écoutez moi ces domaram di outal justification ngabou ! Kén mossoul guiss louni mel ! Allahou akbar
@MrFayemanou2 жыл бұрын
Vraiment
@KIRIKOU342 жыл бұрын
Delen am rafet ndiorte si djoulite yi Té gnaane yalla mou mousseul leen té sangueu len soutoura Doundou bou djékhagoul louné khadj naci
@lissa43642 жыл бұрын
Deuk ndafekh leu
@elhadjisene97232 жыл бұрын
Machallah diangéne dieuff waye machallah Serigne Modou lo ngabou ku bakh la machallah yalnako yalla takhawu
@fatougoundobodianseck16012 жыл бұрын
Serigne bi wéré na nak 😭😭
@saliouka51702 жыл бұрын
Nagn wax deugu té yalla tax segne bi da dioum nianalenko bayiko digantem ak boromam mou diegalou. Niou bayi parparlo nite Moy dioum Moy def bakaar . Wayé nagniy wax deugu té yalla yakh parparlo yakhna Sénégal wasalam
@moussamboww69362 жыл бұрын
Degg na deug dé
@tech-info692 жыл бұрын
👉C'est une épreuve pour lui mais aussi une alerte pour les autres et pour nous également. Dieu sait tout et est capable de tout. Respectons ses ordres si on veut être épargné de l'humiliation d'ici bas et celle de l'au delà.
@laurentoulai78062 жыл бұрын
M
@lapaixvive89292 жыл бұрын
Sénégal yeup wara diapali Serigne Modou té nianal ko Yalla. Mes larmes ont coulé si niak souteureu biniou tek Serigne Modou.
@ahmeddiallo34142 жыл бұрын
Vremant
@bathiembaye72182 жыл бұрын
Pour lan jaapalè
@freegalsen55562 жыл бұрын
BOUKO DEFONE SA DIABAR MBA SA SOEUR DO WAKH LI KI DOU TOUSSS NGANANE SERIGNE PFFF NA TOUBAL BOROM KEUROU SOKHNASSI AK YALA T MOU OUTI LIGUEY ISHH
@lapaixvive89292 жыл бұрын
@@freegalsen5556 khamo si mane dara. Niata nitt nio soutoural sen diabar tji lou geuneu metti li. Dakh Serigne bi watt na ni moussoul tedé ken. Nb: je suis talibe Cheikh Tijane
@lapaixvive89292 жыл бұрын
@@bathiembaye7218 boula dalone,diga beugue koula diapale té nianal na. Té fi lek déwoko ,reutieu go
@marcelfaye68812 жыл бұрын
Waye dém léne djiébalou sii séne ndéye ak séne baye yi moo guene Serigne you bakh yi yeup djiékh nagne
@killahndiaye38382 жыл бұрын
Sénégal mo beuri nafekh😱
@KIRIKOU342 жыл бұрын
Delen am rafet ndiorte si djoulite yi Té gnaane yalla mou mousseul leen té sangueu len soutoura Doundou bou djékhagoul louné khadj naci
@familygeuye49322 жыл бұрын
bilay mais serigne bi ken manou'ko layal
@boubacarsakho49292 жыл бұрын
Thiey yalla yalnala yalla samue sering modou lo ngabou
@familygeuye49322 жыл бұрын
mais na bay katt diabarou ndiambour nak 🥰
@mouhameddiop23002 жыл бұрын
J'avoue k le degré d'hypocrisie m'impressionne au senegal. Tt ce k le prophete avait prédit sur la fin des tps se révèle de jour en jour.
@moussafaye61052 жыл бұрын
Sokhnasi domaram deugla lépp mom la
@mamadoufaye96612 жыл бұрын
Yenna nafekh deug
@NdiayeAss-ox1pp3 ай бұрын
Hoooooo machala djotaye bi am na solo ♥️♥️♥️♥️♥️
@iboudabo42722 жыл бұрын
Nafek bakhoul degue rek Moy degue nitou yalla da ngaye khame ne nitou yalla NGA wakh lene degue
@bathiembaye72182 жыл бұрын
Bilaahi mooy Dëgg
@mamaamar61782 жыл бұрын
Wa bakhna kénne matoll
@72h.Tountou.patriotique2 жыл бұрын
Ibou Dabo mane nafék bu né si senegalais yi moma diahale alieu ni wah si sérigne bi ils attaquent la femme
@papaelhadjithiam77462 жыл бұрын
Saway nitou yallah yi djiguène daneil dou diekh ci kaw souf. Li yageuna ci adouna
@fatimnahaye49322 жыл бұрын
MACHALA bilakhi dama rousse ana soutoura sama khole dafa méti trope ndeyesane togne bakhoule
@moussediarra25722 жыл бұрын
Lann Moy marabout sakh yalla rek mo am ay yonett tebi
@thinktanktruth19682 ай бұрын
Kou topp Seriñ ba neegëm ysko tooñ.
@aminatawone89152 жыл бұрын
Fii néck sérigne yombe nafi nagni top yalla ak sounou niary wadiour yow la yow la kén mounou fé tééré kén déé vala nga wakh nigni lou khéw fa gni déé néck yalla naniou yalla same tée atégnou sii yeurmandéme wassalame
@radisisdionewar13272 жыл бұрын
sa ndiogou tres belle analyse. ndawsi mo amul sutureu te aduna kuy xalat yalla tuuti rek di nga suturaal jaamu yalla yi
@sakhewarfatma69982 жыл бұрын
Mdrr soutoureu de quoi, ses vidéos tout le monde peut les consulter actuellement.
@radisisdionewar13272 жыл бұрын
Sakhéwar sutureu de serigne bi itamit yorna ay wakhi ndaw si te tegouko. Te sudul dara sakh ndaw si sutural bopam ndakh louko serigne bi wakh neehnako. Te moom borom këram meunatoul ka woolou
@mamadous69192 жыл бұрын
Sa niogou me vrai nafekh. Ragal rek mo takh mou wakh lolou
@SengemodouMbacké3 ай бұрын
Thiey ndeysane yalla Nanou ko yalla takhawo
@adjelee89552 жыл бұрын
Eh, il faut arrêter cette hypocrisie. Ce pseudo marabout n'a que ce qu'il mérite. Il a manipulé, profité et trompé les gens.
@ndeyeoumydiongue16712 жыл бұрын
yawe ya séytane bou yalla serigne bi mo fegne le rék
@adjelee89552 жыл бұрын
@@ndeyeoumydiongue1671 Je persiste et je signe, il faut arrêter cette hypocrisie. Si tu sais que je suis une seytane, c'est que tu es toi même une seytane. Les gens mauvais se reconnaissent entre eux. Naféque wa.
@caranoufedior5642 жыл бұрын
Je te jures trop de nafekhs au Senegal Ce type moralement il doit plus diriger qui que ce soit
@dieyealioune55662 жыл бұрын
Parfaitement d’accord avec toi ; Sénégal mo beuri nafekh Personne n’est parfait , soutoura aussi oui mais y’a trop de charlatans qui vivent sur le dos des gens et ça faut les dénoncer Kou diok né Serigne la
@adjelee89552 жыл бұрын
@@caranoufedior564 Je t'assure, c'est à cause des nafékhs, que des choses dégueulasses comme ça continuent. Il ne faut jamais rien dire. C'est pénible à la fin.
@mohamedtall19922 жыл бұрын
Fanatisme pure et dur! Vous suivez des personnes sans avoir la raison garder!
@makharyndiaye59222 жыл бұрын
Merci beaucoup à vous
@ndiayeidyndiaye91682 жыл бұрын
Merci beaucoup odo
@moussediarra25722 жыл бұрын
Geum leen yalla mo geun Di geum ayy nitt
@bambaniang11232 жыл бұрын
ndakh mouhamed yalla la
@seneabdou93762 жыл бұрын
😂
@seneabdou93762 жыл бұрын
Moussa wouyoul Bamba fi😂😂
@RabyaSamb3 ай бұрын
Allahu Akbar 😢ana soutura
@diordiakhate78282 жыл бұрын
Nous devons tous être vigilants
@mouhamadlaminefaye35962 жыл бұрын
Yalla nako yalla fay ay dieufeum you bakh tai diégual ko ay dioumtaim
@damediop32792 жыл бұрын
Machala amna solo
@caranoufedior5642 жыл бұрын
Arrêtez de culpabiliser les femmes Le Marabout est aussi marié non ? et malgré ose avoir affaire avec femme d autrui ? Les talibés doivent aller apprendre leur religion le Coran et pas dépendre de ces charlatans N essqyez pas blanchir ce type qui n est plus apte moralement à diriger des gens
@babacarmbaye58053 ай бұрын
Serigne yalla soutoural naka depuis mou nec xalé ba légui mossoul ndiallo
@sheky31382 жыл бұрын
Bou dé serigne bi moko def wéré na deh!
@familygeuye49322 жыл бұрын
Serigne bi da katt khalé bi ta momê wedy wou'ko
@mansourdiop70372 жыл бұрын
Wakh lene deugue serigne bi nguenii deff sene yeuffou nafekh yii ish
@xalilb41862 жыл бұрын
Bilahi mane dama waarou sì Sénégal...légui Lou méle nii gnou neube ko, Pour lane ? Mouye continuer di def louko nèkhe
@fatbintoumbengue7842 жыл бұрын
Bilay Nji ko wedi daniou nafekh trop
@Mimi-mv8bc2 жыл бұрын
Bilahi Senegal douniou aye nitt. Serigne bii thiaga Bu bonne la . Nioukoye victimize
@fatbintoumbengue7842 жыл бұрын
@@Mimi-mv8bc te niawi kadou nak limou wakh lepou
@mamemor38422 жыл бұрын
Lègui mome lèrnani taloubè yi yalla rèk lenouy sètt serigne bi yalla naco yalla takhwou diègall co
@mbayefall83782 жыл бұрын
Vraiment sandiogou est fort
@mamadoudiouf25682 жыл бұрын
من ستر على مسلم ستر الله عليه"، أي: إذا فعل إنسان شيئًا منكرًا أو فاحشة وسترت عليه، ستر الله علي؟ أرجو أن توضحوا لي هذا، جزاكم الله خيرًا.
@mathiasndiaye31452 жыл бұрын
Quand on sait quelque chose de mal d un autre il faut le préserver la dignité si ça ne lese pas un autre Mais ici il y a rien de musulman Une femme ne doit pas résider chez un autre homme que son mari ou son frère en plus la seule attitude dans ce cas c est de noupici Mais torokhal nit bakhoul Mais défendre kou djité Di def nenen it bakhoul
@papid1002 жыл бұрын
Sohibou tu es un vrai nafekh
@ndeyekhadydiakhate73192 жыл бұрын
Sokhnassi pion la rekk dagnouko Yoni, wayé mingui commencer lérr
@mamemor38422 жыл бұрын
Yalla naco yalla tècc si siratall mousstakhimm dou mou adama mo metoul صراط مستقيم
@diilerecaalifuuta5492 жыл бұрын
Soyibou doo tontoo coura maky neena yoow ak sa njagou nio ligueye cheikh niasss ont suivre depuis a Paris
@mamebambadiop17352 жыл бұрын
Wa yéne tamit bayi léne sén yi way serigne d'où yallah way
@babacarndiaye50232 жыл бұрын
Sergine bi limo don wote la donol nékol nitto yalla nitto yalla do wakh wakh yi nang wakh deugue dji
@Tahirousarrforever74182 жыл бұрын
Vérité absolue
@lissa43642 жыл бұрын
🤣🤣🤣dama djongué beu exagér
@matarndiaye34963 ай бұрын
Diabarou Diambour laye Guéné sa koy bou reuye bi , dikako diokh 😂😂😂 serigne bi mo beugue leufe lolou moy wakh dji
@masambaka51242 жыл бұрын
Serigne Modou lo ngabou nite kou bàkhla nitouyalla la yalla Moy wanéboupam yalla rék mon mate Sa toup na délou ci yalla قال رسول الله صلى الله عليه وسلم من كان يؤمن بالله واليوم الآخر فليقل خيرا أو ليصمت
@ousmanedia15102 жыл бұрын
Machalla wolay ndeysan
@nouridnesaidousy91292 жыл бұрын
Soutoureu wi mais da am posture bo khamni diamou yalla bi bouko amé amatoul droit deff yeneu erreur yi si adouna sinon yapp yalla wessouwoul lolou meuno nieuw di tek ni si yone tourné di deff ay erreur monumental
@damemboup92752 жыл бұрын
Bilahi, walahi di woté yalla ba pré di def li,ba pré nite yi nafexx di wakh pexe none nooo deug amatoul,serign bi di wakh kadu yi
@ndiagamboup7392 жыл бұрын
Me man faralouma KO xaw ma KO me danko def weyolasion Domi sile 'na pelenta
@astoundiayediop62802 жыл бұрын
Sounou mam Adama saytané moko guéne aldiana
@medounethiam992 жыл бұрын
Walahi kiedal domeramla rék
@khaliljadid33422 жыл бұрын
Magui diégalou dé wayé iow amo xam xam koudoul RASSOULILAHI matoul
@babaissasarr79662 жыл бұрын
Seringe waroul defli lolou mouy wakhbi
@lissa43642 жыл бұрын
Merci 🙏🏾
@lafemmebattante2 жыл бұрын
Serigne bi nitt la d'où waliwou dou koutbou samane daye dioum ni nieup
@astougaye57142 жыл бұрын
Soukey yagui diorama♥️♥️♥️♥️
@astougaye57142 жыл бұрын
Sorry yagui diogama MachaAllah 🥰🥰🌹🌹
@cheikhounatine7582 жыл бұрын
Mais avec cette erreur est-ce que vous allez oublier tout le travail qu’il a déjà abattu 🤔🤔🤔🤔
@missy72542 жыл бұрын
Qu’est-ce qu’il a fait comme travail?
@cheikhounatine7582 жыл бұрын
@@missy7254 il a enseigné le coran
@missy72542 жыл бұрын
@@cheikhounatine758 ok donc il comprend bien ce que le coran dit.
@cheikhounatine7582 жыл бұрын
@@missy7254 bah logiquement
@ousseynougueye11022 жыл бұрын
Le marabout aide et soutient ses disciplines s'ils font des dérapages. Mais si le marabout commet une erreur, on doit aussi le soutenir .
@camarademba22672 жыл бұрын
Je pose une question comment la personne prend sa femme baye yayame bay papam déme toque thi disent Serigne pour travaille Un gas soit disent Serigne
@assanegueye18152 жыл бұрын
@@camarademba2267 kou wax fegn ndeyssane
@assanegueye18152 жыл бұрын
Doom baye dou niou bene d Serigne ak talibé bakar diombou si kene nk wayé danio am founiou wouté Wax diou lathié degg degg la nk
@momo___gaye25412 жыл бұрын
Kel pertinence 👋
@shiekhndaw69972 жыл бұрын
Yene mom tenge na donn avocat mudu lo ngabu
@falloundiaye9532 жыл бұрын
Très bonne question ?ana audio yime don wakh ak serigne bi
@mamoudoudiane81982 жыл бұрын
C’est pas la peine c’est une honte à entendre
@ndiougandiaye77642 жыл бұрын
Nanou soutou ralante
@maria1-s7w2 жыл бұрын
Vous êtes tous des Bokalekat, suivez Allah et son prophète bien-aimé c'est mieux.
@daarayseexsaalihu2 жыл бұрын
Cëy Saa-Njoogu, yaa man a jàngat!
@khadimsylla18052 жыл бұрын
Bilaay barina kuy xas nit te kamuy xas bëggut a mel ne moom
@boubacarsakho49292 жыл бұрын
Merci waye wa walf tv
@famadiagne55952 жыл бұрын
Yalla na nous yalla doli soutoura Omar boun khatap wakh nag deugu
@gnagnadiene2182 жыл бұрын
Beurinathi ay morom troppp mom mon fesler rekkk
@mamadousow87142 жыл бұрын
ماشاء لله على كل حال وجود بعض
@bathiembaye72182 жыл бұрын
Wax leen sëriñ bi Dëgg Waay
@thiambanendour42912 жыл бұрын
Vous êtes vraiment des faits un marabout reste un marabout
@NdiayeAss-ox1pp3 ай бұрын
Soutoureu aka am solo
@sanesaliou92622 жыл бұрын
Non franchement Sénégal ak serigni le Sénégal c'est pays exportateur de marabouts 😁🙈🙈omar tu ma tué de rire 😁😁🙈sah tu as parfaitement raison totale merci
@layendiaye10652 жыл бұрын
Sonhibou ya nafekhe khamo yala yabone
@ndiogougueye78442 жыл бұрын
Walf yén li lolén siy wané yéna gueuna gnak soutoura mé li môme c'est une erreur monumentale mais nit la rek té nit kou doul dioum amoul
@CheikhGueye-d7e3 ай бұрын
Wakh Yep wata gene
@cheikhdiaw67372 жыл бұрын
Wallahi Yeenay ay naafekh you mak.. Serigne bi moy say say. Nguenne beug dieul toor bi diokhko ndawsi...
@SidySall-p1r9 күн бұрын
Mai li epouna diaroulwone vidéo soutere Moy lepou
@nourre2102 жыл бұрын
Très bien souka bilahi li lou ñaw la
@famadiagne55952 жыл бұрын
Sokhna si défoul Dara mais preuv la bou gon mais nak mounon nako bagna wéer ta soutoural ko ba noopi dém yonam
@thinktanktruth19682 ай бұрын
Mbirmii daal mandou ci moo war. Yalla moo kham li kheww. Ndakh moom waatna. Kou. Waatnack dankoy bayé ak yalla. Lima kham mooy Pékhém djiguène daa reuye.
@72h.Tountou.patriotique2 жыл бұрын
mane nafék bu né si senegalais yi moma diahale alieu ni wah si sérigne bi ils attaquent la femme
@72h.Tountou.patriotique2 жыл бұрын
Ñou dénk nit alale ndah dako wolou koku loubeule ko après nitni né yaw mika deunk ya dioum aye nafek you mag nguéne
@ranamasud17162 жыл бұрын
Momassi diahal ragal deug rek
@elagegueye33102 жыл бұрын
Sohlawouniou audio ndawsi mom hanna amoul diabar koudonn wah day math sen tatou diabar esq diguen lidianti ay audio kon yen nagui tribunal
@ahmadoumbacke29782 жыл бұрын
Serigne Modou lo nite rék la dafay dioume comme niépou Dou malaka dou djinné
@familygeuye49322 жыл бұрын
katt diabarou ndiambour mom dfa graw
@AdamaTraore-wt6sx2 жыл бұрын
Sokhna Bety wakhna lép.
@laminendiaye47052 жыл бұрын
Du moom késsé dé. Moom la ay mbiram feeñ rek. Déngeena xamul rek. Islam waxul ken mu jébbalul mbindeef. Yallah limuleen diggal mooy ngeen topp Yonent bi. Moom rek la Yallah garantir né kuko topp jubb.
@barambow5812 жыл бұрын
La fille n'a rien n'a perdre
@KhadimKebe-z1n3 ай бұрын
Li daw la
@amydione71552 жыл бұрын
Khamna ni Serigne bi dal wediwoul yene ngen kay wedil
@KIRIKOU342 жыл бұрын
Delen am rafet ndiorte si djoulite yi Té gnaane yalla mou mousseul leen té sangueu len soutoura Doundou bou djékhagoul louné khadj naci
@oumarmbaye59883 ай бұрын
❤❤❤
@mamethiorondiogou65322 жыл бұрын
Limoudef diguintem ate swt la leu d'où diguintem ate domou adamayi gnoune amougnou pour jujéko wala di jugé ki konke seul Allah swt seulement à le droit de juger c'est lui le maître des scieux il est le seul juge
@ndiayefatou5653 ай бұрын
Moooyène! Wakholène serigne gnou say say yi nguène nane! Kou bayiwoule serigne tariqas yi dingua gnak adouna ak illakhira! Guissa golène dara sakh!
@elagegueye33102 жыл бұрын
Souhaybou boudonn ibadouyui do wahhee niui billahy ont se connaît
@matargueye90812 жыл бұрын
Sa nidogou moye thiédo 😂😂😂
@tatalily2 жыл бұрын
Sénégal dal on malméne les petits criminel les grand in les applaudis.
@daarayseexsaalihu2 жыл бұрын
Loolu Dill la rekk.
@inconnu900002 жыл бұрын
Thiey senegal !😠😠 Kou bone niouni bakhna Kou bakh niouni bone na Ba yawmal khiyam waji dou serigne saysay la yemal si sa diabar! Ki lislam reynako new bouy dokh la
@miketoure45182 жыл бұрын
FORZA SENEGAL FORZA WALF GROUP FORZA YEWWI
@mmadebousso25742 жыл бұрын
Walf li warolél ana soutoura
@ibrahimadieye93992 жыл бұрын
Amouniou soutoureu
@junior33482 жыл бұрын
Adouna soutoura rek mofi nek yala guisna leep et puis le mara il et jeune c est t un homme cc tt
@youtubetv56982 жыл бұрын
Euleuk yawmal le khiyama Serigne yep ni laniouye deme ak seni talibe
@alassanediouf1442 жыл бұрын
Khana sa papa mo xam li khew fofou
@amathug2 жыл бұрын
Sa diabar, bén goor warou la si doy. Amoul serign, amoul pape, amoul frère, amoul dome bou mou diouroul.