AFFAIRES OMAR SALL LA SUITE ET LES DANGERS DE WAHABISME = CHEIKH BAYE NIASS

  Рет қаралды 13,432

THIOUB MOU BAYE NIASS TV

THIOUB MOU BAYE NIASS TV

Күн бұрын

Пікірлер: 142
@PapendioumaFaye
@PapendioumaFaye Жыл бұрын
Oustaz yow on doit te donner des heures dans tout les télévisions du Sénégal parce que tu conscientises les jeunes
@barham1234
@barham1234 Жыл бұрын
Bilaahi....moom dé woolounaako thi plateau yi thi défendre soufisme té teg ko thi xam xam
@djibrilball5439
@djibrilball5439 Жыл бұрын
😂le soufisme du senegal ne peut rien contre la sunna
@bouasano7249
@bouasano7249 11 ай бұрын
​@@djibrilball5439 ok disciple de aboul wahab c'est comme ça continue 😂 votre secte va s'agrandir 😂
@ibrahimacissedieureudieufs2732
@ibrahimacissedieureudieufs2732 Жыл бұрын
Merci beaucoup Cheikh Baye sante nanioula bou wer yalnala yalla faye
@omardionne1201
@omardionne1201 Жыл бұрын
Amiin
@hadaranandiaye1644
@hadaranandiaye1644 Жыл бұрын
Merci beaucoup Oustaz Cheikh Baye Niass. Vous faites la fierté des Tidianes.
@hadaranandiaye1644
@hadaranandiaye1644 Жыл бұрын
Je vous ai suivi sur 2stv le vendredi dernier. Vraiment, vous avez un esprit éclairé. Ce qui plaît en vous, ce sont les sources que vous avez données. Le monde d'aujourd'hui exige quiconque décidant de parler doit faire ressortir ses preuves.
@mamadousow7917
@mamadousow7917 Жыл бұрын
Machallah yaa Oustaz. Xam xam bi lerna. Que Dieu vous protège !
@amethdiop7361
@amethdiop7361 Жыл бұрын
Dieureudieuf Cheikh bi leral gua bari louma commencer woneu depasser tijaniya fi dunya wal akhiraty❤
@mortalltall
@mortalltall Жыл бұрын
Merci merci merci 👍🇸🇳💯❤❤❤
@aliounebadarandiaye831
@aliounebadarandiaye831 Жыл бұрын
MachaAllah Baye Niass , tu a parfaitement raison on doit trouver des réponses aux défis de l'heure.
@MatarToure-wd4mt
@MatarToure-wd4mt Жыл бұрын
❤❤❤ ماشاء الله ياشيخ شكراً لكم ياغالي بارك الله فيكم ❤❤❤❤
@ssalioulo5751
@ssalioulo5751 Жыл бұрын
Merci Cheikh Baye niass ❤❤❤
@niangaya539
@niangaya539 Жыл бұрын
Tu tjr apporter des réponses comme tu le fais merci
@fallkhadim3256
@fallkhadim3256 Жыл бұрын
Mach alla amna solo Chiekh baye 🙏🙏🙏
@omardionne1201
@omardionne1201 Жыл бұрын
Merci beaucoup encore une fois. cheikh Baye, sincèrement dama soxla khdis bi nga wah thi mbalan wajifa 🙏
@Destinée221-n6u
@Destinée221-n6u Жыл бұрын
Je suis d'accord oustaz xalé yi mboubou serign gui la niou wara soumi té diangui
@diopmas2592
@diopmas2592 Жыл бұрын
MachaAllah
@BarkhamDiallo-nn8mp
@BarkhamDiallo-nn8mp Жыл бұрын
Masha Allah sangue bi
@ablayegueye6201
@ablayegueye6201 Жыл бұрын
Yalla nala yalla sameu
@ablayetoure9738
@ablayetoure9738 Жыл бұрын
Machalla cheikh baye niass
@Kambel-tv
@Kambel-tv Жыл бұрын
جزاك الله خير اياشيخ
@omardionne1201
@omardionne1201 Жыл бұрын
Wallahi yow cheikh Baye Niasse nianalla moniou war ndah sa doundou amalnaniou njarigne.jarejef
@maoudoseck6105
@maoudoseck6105 Жыл бұрын
Masallh
@HabibouSall-fj5iu
@HabibouSall-fj5iu Жыл бұрын
ماشاء الله بارك الله فيك وجزاك الله خيرا ❤❤❤❤❤❤
@saambaaybaac4309
@saambaaybaac4309 Жыл бұрын
Jaaaajëëf!
@ousmaneaboudia3249
@ousmaneaboudia3249 Жыл бұрын
Merci❤
@souleymanediop8840
@souleymanediop8840 Жыл бұрын
Ma sa alh
@Talibé_cheikh12
@Talibé_cheikh12 Жыл бұрын
Dieureudieuf❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@NdiagaKane-vn4sl
@NdiagaKane-vn4sl Жыл бұрын
Maacha Allah
@moustaphadiop7136
@moustaphadiop7136 Жыл бұрын
Billahi wallahi Tallahi Cheikh bi beug nala Sheuut
@BayemodouSall-sb6cz
@BayemodouSall-sb6cz Жыл бұрын
Cheikh baye Hayati doundal weurel ibdou si souf cheikh tidiani si kaw ❤
@AkhmaGueye-ko2gt
@AkhmaGueye-ko2gt Жыл бұрын
Masal lal❤
@abdouniang1697
@abdouniang1697 Жыл бұрын
شكرا لك هذا هوالعدل ياسيدي
@PapoukoroTraore
@PapoukoroTraore Жыл бұрын
Mach Allah niass bien dit cheikh baye long vie à vous
@mamadoundiaye4431
@mamadoundiaye4431 Жыл бұрын
Diadieuf cheikh bi ❤
@souleymandiallo9196
@souleymandiallo9196 Жыл бұрын
السلام عليكم ورحمة يأخي في الله أوصي بنفسي وإياك بتقوى الله مايلفظ من قول إلا لديه رقيب عتيد
@Ismaeljallow-k3b
@Ismaeljallow-k3b Жыл бұрын
The intellectual level of the speech/sermon is high. Thank you Sheikh Baye i like it anyway: 'what's good for the goose is good for the gander'.
@Ismaeljallow-k3b
@Ismaeljallow-k3b Жыл бұрын
Jerejeff Sheikh Baye wakh nga deque. Julit danga wara mandu chi wakh. Demal sura 6 verse 152 dafa lerr. Jerejeff Burr Yalla fayela gudal sa fan. Ameen.
@djibrilball5439
@djibrilball5439 Жыл бұрын
Mandou amoul fi .on doit dénoncer tout ce ki est bida
@Ismaeljallow-k3b
@Ismaeljallow-k3b Жыл бұрын
@@djibrilball5439 khamo tus dangai rek.
@khadydiop5056
@khadydiop5056 Жыл бұрын
شكرا شكرا شكرا
@PatheGueye-rt7vv
@PatheGueye-rt7vv Жыл бұрын
Dieredief chiekh tidiany Cherif ❤❤❤❤❤❤❤
@ablayekane5209
@ablayekane5209 Жыл бұрын
Merci pour les éclairages.juste une question qu'est-ce que vous entendez par islam du du Sénégal.? Il y a des islam ou un islam pour tous les musulmans ?
@serignemooustaphadiamilwad7137
@serignemooustaphadiamilwad7137 Жыл бұрын
Ça veut expliquer comment on applique l'islam au Sénégal
@AssaneNDIAYE-oz3fk
@AssaneNDIAYE-oz3fk Жыл бұрын
mach'Allah nala samay Borom Bour Yallah samu yok xam xam bi.koula bagne bagne na deug.Walahi waxga ak gnome ba tayi si xam xam gnou bagne
@djibrilball5439
@djibrilball5439 Жыл бұрын
Omar sall est l'un des meilleurs voire le meilleur oustaz de tous les sénégalais.
@cheikhfall2537
@cheikhfall2537 Жыл бұрын
Tu m'as
@PapoukoroTraore
@PapoukoroTraore Жыл бұрын
Niass Niass niass rek
@PapoukoroTraore
@PapoukoroTraore Жыл бұрын
Mach Allah
@abousy1525
@abousy1525 Жыл бұрын
ماشاء الله ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@bayejobe4204
@bayejobe4204 Жыл бұрын
💕🌹🌹💕💕💕🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹
@Thiam0011
@Thiam0011 Жыл бұрын
ليرضى الله عنكم ❤
@BabacarMbaye-c7i
@BabacarMbaye-c7i Жыл бұрын
حفظك الله
@actusen3729
@actusen3729 Жыл бұрын
Mon frère tu es un gars véridique, ces gens sont des complexés qui pensent être intelligents alors qu'ils sont bêtes. S'ils avaient le nombre de Talibé des tidianes et des mourides ils vont tuer tous ceux qui seront contraire à eux ,ils n'ont aucune tolérance. Yalla atêgoule ba kêne fogueni mo nèke si dengue.
@PapoukoroTraore
@PapoukoroTraore Жыл бұрын
Niass niass niass niass niass niass niass niass niass niass
@guisse875
@guisse875 Жыл бұрын
Les wahabious n'oseront jamais affronter les Tidjanes sur un débat télévisé et contradictoire.
@basirutouray9906
@basirutouray9906 Жыл бұрын
Numero cheikh baye la Sokh la svp 🙏🏾
@ousmanendiaye9643
@ousmanendiaye9643 Жыл бұрын
Macha allah cheikh les salafistes daniouy sonal sen bop
@barham1234
@barham1234 Жыл бұрын
Bou gaayi khamoone kila nampale thi xam xam....dinagne reglé. Cherif ibrahim saleh Al housseyni moufti bou mag bi Nigéria binde lou eup 600 livres thi xam xam moy seigname. Té kookou talibé baye niass là.
@MatarToure-wd4mt
@MatarToure-wd4mt Жыл бұрын
ماشاء الله ياشيخ شكراً لكم ❤❤❤
@khadydiop5056
@khadydiop5056 Жыл бұрын
اطال الله عمرك
@bayejobe4204
@bayejobe4204 Жыл бұрын
🌹🌹💕💕💕💕💕💕🌹🌹🌹🌹💕💕💕💕💕💕🙏🙏🙏
@djibrilball5439
@djibrilball5439 Жыл бұрын
La loi est la pour tout le monde .c'est vrai. Ana gniy saga yalla ak yonnenti bi. Gnila donn deure binga wakhé fi k baye da dioum thi bén mass'ala loutakh la loi n'est pas appliquée . Arrêtez les mensonges.
@PapendioumaFaye
@PapendioumaFaye Жыл бұрын
Je veux dire rayy
@ebrimaceesay6098
@ebrimaceesay6098 Жыл бұрын
🤐🤐🤐🤭🥱🤫
@Baaissatou-ph2xo
@Baaissatou-ph2xo Жыл бұрын
استاذ لا تحزن إن الله معك بالله
@Baaissatou-ph2xo
@Baaissatou-ph2xo Жыл бұрын
استاذ عمر سل
@djibrilball5439
@djibrilball5439 Жыл бұрын
Boy baye niass ,hamo louy togne,c'est juste la vérité qui fait mal.indiléne séne preuve
@harounasow4965
@harounasow4965 Жыл бұрын
il faut pas niou fatigué le wazifa baye niass defou ko cheikh tijan defou ko
@modoudiallo132
@modoudiallo132 Жыл бұрын
Ya meun fène
@mbayendiaye4562
@mbayendiaye4562 Жыл бұрын
Katal sa ndeye dagua xam baye wakh si wazifa
@pakhalil6876
@pakhalil6876 Жыл бұрын
Sa youniou lênn wowei ci débat ci kham kham douniou meusseu nieuw mann lolu moma djakhal ci niom 😅
@dembafmanneh
@dembafmanneh Жыл бұрын
You are really on point. Is not even only in Senegal but even in The Gambia so call Intellectuals go Saudi come back home and just do exactly what you said.
@serigneousmanesarr2304
@serigneousmanesarr2304 Жыл бұрын
Ma contane ci yow
@Pape-p5p
@Pape-p5p Жыл бұрын
C est à dire ce discours est unitil ngay Lak français nii . Prenez la paix comme objectif , vous aimez trop la division vraiment . Le Sénégal est en recule et on a plus besoin de ça . Maylene nitnji diamm way stp … on veux un Senegal de paix et de tranquillité Ba legui yene nieup mounolene fi attewo dîner kone diner djitewoulene , vous fonctionnez tous sur la laïcité. On veut un Senegal meilleur, trop de méchanceté dans vos paroles
@rendrelesmathsplusfacile9184
@rendrelesmathsplusfacile9184 Жыл бұрын
FI NGA DEBAT RESSEMENT WADJI PHAGOCYTER LEU SI AFFAIRE NIANAL KOUDOUL DIOULITE
@Baaissatou-ph2xo
@Baaissatou-ph2xo Жыл бұрын
من كان يومن باالله واليوم آخر فااليقل خيرا أو ليسمة
@TMBNTV
@TMBNTV Жыл бұрын
Lolou wax ko ahmad lo ak omar sall
@beugualbayereknopalouofficiel
@beugualbayereknopalouofficiel Жыл бұрын
Akayy deugg cheikh baye téré bobou la guayi di lire di wakh rek maname li talibéyi di wakh mome lanou djeulé si séni serigne yi nékakk mome si birr réwmi
@MatarGueye-p9u
@MatarGueye-p9u Жыл бұрын
Ma la kham Sénégal gussoumafi sa morom chekh bay
@djibrilball5439
@djibrilball5439 Жыл бұрын
Té nga bayi Al oustaz Docteur Ahmed lô .niveau bi dafa kawé .c'est l'un des héritiers du prophète au même titre que Al oustaz Oumar sall.
@khadydiop5056
@khadydiop5056 Жыл бұрын
Billahi sama khôl seddna
@BoussoSow-gm6oj
@BoussoSow-gm6oj Жыл бұрын
Merci baye waw nga lepp détail yalla warouĺ guoudeul sikime ak fatal Roubaud oustaz sall prison moy diamam 13:47
@BoussoSow-gm6oj
@BoussoSow-gm6oj Жыл бұрын
14:32
@BoussoSow-gm6oj
@BoussoSow-gm6oj Жыл бұрын
Mais oustaz thi cas bi soit disant oustaz sall dem prison bi moy 10:57 securiteme
@modouthiam2910
@modouthiam2910 Жыл бұрын
Makk gui gnofi andi islam Talibé mak gni gnola diagal guani bidal .wa sén seuyou yaye kon wéroul .té kon doumou ndialo lagn.
@Baaissatou-ph2xo
@Baaissatou-ph2xo Жыл бұрын
😂😂😂😂😂
@diborndiaye1258
@diborndiaye1258 Жыл бұрын
Jeunes yi lene di topp kagn jar naniou yeureum. Je vois ay commentaires dama naane ndeyssane. Effectivement serigne yi danio wara actualisé leur discours. Deuggue la bala nga wakh si haqiqa danga wara wakh charia bi nga hamni mo guena accessible si niep parce que amna niou sene entendement soriwoul . Arabie Saoudite li niou nahari fimou nekk nio ngui bayyi Américains yi ak yenene peuple di dougual bière, avec le projet Neom de Mouhamed Ben Salmane , récemment à Gaza pendant que nit ya ngui deh fofou Arabie Saoudite di am fetou Aloweene nga hamni toubab yi sakh hamnaniou ni fête Païenne la. C'est vrai si transition laniou nekk donc il faut que les serignes soient bien outillés pour que jeunes yi fonk liniou am . Mystification jeekh na , Max Weber nena desenchantement du monde lokou moy les liens traditionnel-legitime ou charismatiques qui faisaient croire à un homme providentiel ou un homme mystique lolou jeekh na. Legui le monde est devenu rationnel , depuis la société industriel avec le phénomène bureacratique , le monde passe vest une sécularisation maanaame religion sakh bo khefeh niou jeuleh ko fi . Na niep jangui. Iqra laniou wakh. Merci THIOUB d'avoir apporté ces éclaircissements pour que beaucoup piisse comprendre
@el-hadjingom-wd9ki
@el-hadjingom-wd9ki Жыл бұрын
Ndeysan wax dji amna sollo looollll sax, té lingua wax lou werleu❤
@diborndiaye1258
@diborndiaye1258 Жыл бұрын
@@el-hadjingom-wd9ki Si dama xam ni nioune talibes yi héritage bigni maggue gni bayyil nio ko teggui mo takh kou joggue xass niou. Nioune nio goorgorlouwoul
@el-hadjingom-wd9ki
@el-hadjingom-wd9ki Жыл бұрын
​@@diborndiaye1258maanam folcrole bi moo beuri
@indigne2161
@indigne2161 Жыл бұрын
Ne faudrait -il pas commencer par rappeler et juger vos anciens comme le ‘’ grand ‘’ baye Niass qui a a egaré des millions de croyants ?
@modoudiallo132
@modoudiallo132 Жыл бұрын
Ya meuna féne
@bocarwade8241
@bocarwade8241 Жыл бұрын
Omar Sall dou borom xam xam garabou garabou diaye garab lanko xamee wayee d'où dinee motax Mouy waxee xamadi
@PapendioumaFaye
@PapendioumaFaye Жыл бұрын
Ces gens là bougnoufi amé dolé nieupe lagnouye tayy Ils sont faux
@diborndiaye1258
@diborndiaye1258 Жыл бұрын
Mane daal ibadous naniou wakh si Palestine mane deh fofou la lene di haar. Sortez du Senegal bayyi lene maggue gni ngene di dénigre ak kanio teh wakh si li xew Gaza ak le monde musulman . Diversion bi doyna
@Pape-p5p
@Pape-p5p Жыл бұрын
Je suis triste quand je vois parler les oustaz de mon pays . Comme des lutteurs, qui se préparent aux combats, ce que vous faites est honteux.
@BirameBirame-rd6uh
@BirameBirame-rd6uh Жыл бұрын
Tongie dalle bakhoull nagiouwakh duegdji
@mballondiaye50
@mballondiaye50 Жыл бұрын
Doctor dafa ragal xaley tasuuf yi wahabiya yu nak yi kenne ñeme Wusi xaley tasuuf gaccak peeñi lañi bañ
@HamidineTall-t4c
@HamidineTall-t4c Жыл бұрын
Cheikh baye démal bortouko pleinet
@MatarGueye-p9u
@MatarGueye-p9u Жыл бұрын
Il vons jamais accepté de debatre avec toi
@ibrahimandiaye-5250
@ibrahimandiaye-5250 Жыл бұрын
Na sen khel dale kou kham batine deugue situation bi doula diakhal Sénégal moke na si batine dou Oumar Sall ak ay nitame niokoy dini walahi dani sona rek
@diborndiaye1258
@diborndiaye1258 Жыл бұрын
Soufisme nak koukay bagn yakarna di nga weddi Isra wal mihraaj. Guddi raniane bi nga hamni Rassoulalah thi la djeulidjeh jouli ak lamou guiss tha voyage nocturne ba ak famou jaar maqdissil haram ila maqdissil aqssa ba nga hamni tay à Palestine Juifs yi beuggue naniou si tekk tank ndakh ham limouy représenté yep. Damani dinne dji fi si Sénégal li kay jahasseh bitim reew la joggue dou souniou maggue you tedd yi. Kou lene di hass nak danga hamoul te maytoulma bou baakh
@abuahmad9938
@abuahmad9938 Жыл бұрын
Kou la dakk doul guissoula ko ci kow soufff...
@TMBNTV
@TMBNTV Жыл бұрын
Guiss ngako katt moye omzo sall
@diborndiaye1258
@diborndiaye1258 Жыл бұрын
C'est que Sénégal émotions mo lene sonal. Omar SALL fi la ni Cheikh Ahmed Tidiane chrétien lawone. Njabotam bou ko nekhee plainte. Wahouma dara niou naane ay Serigne fi laniou sagua yonente yi teh kena plaintou lene. Cheikh Ahmed Tidiane bo remonté ay mamam ba Adnan niep ham naniou ko. Dans sa famille ba gni nekk Senegal dangay guiss ay Abou Moutalib , Mouhamed Habib, Mouhamed Bachir, Hamza , Amar etc , et j'en passe . Le debat sunnah soufi nak mome yaggue na dans le monde . Au Senegal tamit yaggue nafi nit gni daniou siy fogua jot. Tu as raison depuis combien d'années ils n'acceptent pas de venir discuter. Ils sont financés par le Yemen, et d'autres pays Arabes et aujourd'hui on a vu leur position dans le conflit Israel Palestine. Pourquoi Ibadou yi sene vidéos yiy circulé si réseaux sociaux guissaguouma si niou wakh si Israel Palestine lolou daf ma jahal ba taye. Yaw Thioub mou Baye nak ham nga bou bakh ces oustaz Alpha BA , Mor KEBE , Akhmrd LO , etc . Il faut sue nit yi ham ni li yaggue na si diine dji di wotewo ni yaye julit yaye ahlou sunnah fekk si suuf nio ngui def lenene. Yaw nak li nga jangue si taarikh bou ko julit you bari janguone rawatina sama mbokk Tidiane yi kone kena dou lene jam . Wahabisme nak bou ibadous Senegal yi hamone liniou nekee fimnek niep hamnaniou ngourou Arabie Saoudite et les Juifs d' Israël nio bokk mame il s'appelle Mordahay. Guestou lene sama mbokk joulit yi guestou lene histoire diguanteh Arabie Saoudite, les pays Arabes et Israel . Le conflit de Palestine Israel dafa tignal deukkou Arabes yi . Sénégal bou lene gneh reewou Arabes yi danio feegn si li hew à Gaza. Dem lene guestou dji. Guiss na nak si ay vidéos commentaires you bari niouy saga tarixas yi mais bouniou xamone tarixas yi stabilité bigni indi si rew mi dinagn bayi di naane nio divisé dinneh dji. Thioub li nga wah deuggue la hamone nani dinagn heuy suba attaqué ouvertement serigne si ak tarixas yi mais débat bi war naniou ko gueneu élevé comme tu dis . Bref on n' est pas des ennemis ay mbokk joulit laniou
@moussakeita9085
@moussakeita9085 Жыл бұрын
Allahou Akbar ! Que des diffamations! Craignez Dieu encore une fois. Lou tax ngéne beug soss? Tu as écrit combien de lignes pour ne raconter que des bétises. Arrêtez cette campagne de diabolisation et apprenez à dire la vérité.
@diborndiaye1258
@diborndiaye1258 Жыл бұрын
@@moussakeita9085 C'est toi qui dois apprendre à dire la vérité. Waham niep nio ko deggue monsieur nga naane soss. Yallah ma gueneul jeumou Omar SALL
@PatheGueye-rt7vv
@PatheGueye-rt7vv Жыл бұрын
Ap wakhabib d'où dém débat public jamais bathi sén Serigne bi Ahmed lo d'où dém débat public mouke😅😅
@Pape-p5p
@Pape-p5p Жыл бұрын
Moi je suis pas ibadou , mais xana ahmad khalifa Niass daguene ko ragal ??? Nena Liguene di def yene Tijane yi si église bi la diouguer . Legui ????? Arrêtez la haine , et cultivez la paix . Vencore une fois , vous avez un pays trop pauvre , donnez des solutions pour changer ce pays . On eat trop en retard . Niak fayda rek mo takh niou Nek 97%musulman du attewo laïcité. Fiii SENEgal benn Tarikha beugoul moromam . Donc Yene oustaz yi yene wara toub dellou si yalla
@thiernondiaye1975
@thiernondiaye1975 Жыл бұрын
Mé baye nias mi peulfouta la wala
@TMBNTV
@TMBNTV Жыл бұрын
Iow lane ngua
@momarsarr8851
@momarsarr8851 Жыл бұрын
Diner beungoul lingay déf khana peulfouþa dou nitt
@abdoudieng1097
@abdoudieng1097 Жыл бұрын
Franchement je ne comprends le fil conducteur de votre intervention.Omar est exclu du dèbat intellectuel il n'en a pas le cran.C'est celà qii ex😅plique ses errements et son outrecuidance.
@geustu1998
@geustu1998 Жыл бұрын
Iow esk do chiites Iow mi Di toumal Omar souli bammél té wakho deugg
@ousmanedieng14
@ousmanedieng14 Жыл бұрын
vous avez tout compris ne nous laissons pas divertir par Oumar sall....il préfère attaque les musulman que les mécréants. l'heures n'est de veiller aux menaces extérieurs qui guettent l'Islam.non pas de diviser la communauté comme essaie de le faire oumar.SALL........ON DIRAIT QU' IL EST JALOUX .........
@ousmanefall5769
@ousmanefall5769 Жыл бұрын
Diambaaar deugue mooy yaw
@diallo7951
@diallo7951 Жыл бұрын
Khamo darra
@rendrelesmathsplusfacile9184
@rendrelesmathsplusfacile9184 Жыл бұрын
MOR KEBE OMAR DIALLO DR WAKHALEWOUMAKO AMOUNIOU SA TPS BAY TOGUE DI DEBAT AK YAW PAS QUE DAGN LA RAGAL YAW DOU KHAM KHAM DOU YAAR KON DEBAT AK IOE NGAY SAGUA ISLAM NIOM NIOUY AM BAKAAR MTX NIAKO KHAM KHAM MAIS AGGO SENE NIVEAU VRAIMEN CHIITE NGUA IOE
@TMBNTV
@TMBNTV Жыл бұрын
🤣waxi ragal rékk nguafi wax kou geuneu niakk yarr omar sall dafa am si mim rew
@Baaissatou-ph2xo
@Baaissatou-ph2xo Жыл бұрын
Lios nasarane 😂 là loi do rouss di wakh lolou
@MamadouKa-n7q
@MamadouKa-n7q Жыл бұрын
والله احمد لوح أفضل من ولد في بيتكم وأنتم جميعا.
-5+3은 뭔가요? 📚 #shorts
0:19
5 분 Tricks
Рет қаралды 13 МЛН
MADIAMA FALL EXPLIQUE COMMENT LE STRESS PEUT ÊTRE LIÉ AUX DJINNS SÉYATINES.
15:37
PALESTINE AU CENTRE DE L'ISLAM POLITIQUE = CHEIKH BAYE NIASS, & THIEDO MOURID SADIKH
1:04:49
🔴TAFSIR BAYE NIASS BU LEER TE AM SOLO
59:43
MALBN TV
Рет қаралды 15 М.
Gambie: Wakhtanu Cheikh Bachir Niass ci Baye
1:34:39
MALBN TV
Рет қаралды 16 М.