N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
Oh les parents, ma chérie désolé de te dire que tu devrais quitter la maison Tu travailles, takal sa ndigg out caution et déménage Va vivre ta vie au calme so amei loy may papa et maman fais le et sans racune sinon dinga dei ak misère wala nga cardiaque et c'est t'es enfants qui perdront Fact!
@veroniquenatack7392Ай бұрын
*Bilay ioe deugue bou werr gua wakh na guéneu lolou moy diam dji😢je suis vraiment triste pour elle😢🙏🏽*
@strategiesetdeveloppement2525Ай бұрын
Effectivement on est trop attardé par ses cultures de m-/ erde moi je quitte et je fais ma vie
@bintmoustapha8633Ай бұрын
Ma belle dangua rafét sakh boula kéne stressé. Démal loué ngua gèrer sa vie ak say dome. Diam mo guene lépp....Courage❤
@maremediop6444Ай бұрын
@bintmoustapha8633 Moy diameu ji dal bo démé ba sa keur pape ak sa keur yaye amo fa diameu dal nga béro har yallah , nieup nék si diameu , il faut savoir se détacher des fois même si c est dure parfois
@BinetaNdoye-yf6ppАй бұрын
Wawaw
@DYNA8869Ай бұрын
J'ai vécu la même chose avec ma famille et maintenant bilahi lou bari sama lokho lay diar. Guéneul takal sa seur nga liguéy wout sa nék yalla dinala soutoural. Boul compté si béneu goor nak. Moytoul gnou ré la. Yokal diom rek. Courage ❤❤❤
@fatoundour4586Ай бұрын
Moi pareillement sama 1ere mariage no seulmen dagn meuko forcè wone meu divorcè gnou sonal meu si keur gui tè kimeu warone taxawou mouy sama yaye momeu geunone sonal😢meukoy mougn mou mètiwone mai yaalla xamnani lep diexneu beu samay parent dagnouy am kerseu sakh sigui xolmeu, j m suis remariè
@zahrasarrАй бұрын
il me semble que bcp de femme divorce vis la meme chose je vis la meme chose mais mane sama voisine dont mon propre papa a louer l'appartement il veulent que je sorte pour recuperer la chambre
@absadiop2563Ай бұрын
Meme moi auss
@oumy6935Ай бұрын
Moi je veux quitter chez mon père mais j'ai un problème de logement . C'est cher à dakar , c'est à saly que j'ai failli prendre un studio mais malheureusement je suis commer ante et mes clients sont à fakar en général. Je souffre beaucoup et yalla n'a ma yalla attei ak mom. Wadiour dîna ameil akk dom
@foogadebbomolooty9839Ай бұрын
Moi aussi j’ai vu la même chose avec ma propre famille j’ai beaucoup souffrir mais aujourd’hui elle Hamdoulah tout est fini et je suis heureuse. Je suis États-Unis.🇺🇸🇺🇸🇺🇸
@Gagne_SiryАй бұрын
Famille Sénégalais mo doy War. Sokhna si geumeul sa bopou liguéy géré sa bopou AK Say dome. Boul dioy soit forte pour tes enfants té ngua loué dji. Yal nalla yalla défal diam❤️
@oumardemba1462Ай бұрын
mane dh wax deug nekh yalla li la beug mou dieufé ko ndax nak sa diam yaram loumou diar war ngako dieundé
@adjandieyaseckfall6794Ай бұрын
Li motakh dangay nèk si séy di doundou lou mèti mais dangay préféré tok diko mougne ndakh so tassè so gnibissè sa keur famille lou mèle ni rèk nga fay fèk.
@ramaramatoulaye8770Ай бұрын
Elle m'a fait pleurer😢😢😢
@nogayegalon969Ай бұрын
Courage ma chérie quand j'ai eu 5ans que j'ai été mal traitée par ma mère et ma sœur jusqu'à l'âge de 25ans et demi et c'était tout les jours des bagarres c'est pour cela j'ai quittée Sénégal depuis le 18 septembre 1983 je suis en France courage ma chérie continue ton commerce bisous ❤
@khoudj841Ай бұрын
Massa😢
@SAYANDECAPILLAIRECLUBАй бұрын
Ooh masta😢
@ZahraAidara-xx7jeАй бұрын
Moi qui fête tabaski tt seul pour éviter problème famille cet tré dure mais dieu est grand
@sokhnafatouseck-lf4fqАй бұрын
Ndeysaan lou metti yagna fi. Say mbokk sougn la dh maltraité fokoy djoyé? Tu as leurs nouvelles ?
@mameantagueye8677Ай бұрын
Lolou lay ndoundou ak sa frère ak soeur sama yaye dafa décédé ak sama papa ma nék taw sonou si gnome sama frere lou méti lounék migui makoy ték démna ba damay togg sama bopp gnouy coupé sama courant ma sonou trope mé yalla bakhna yalla rek la yakar gnanal lénma yalla guénama si situation bi sama frère dafmay sakh daur wayé bayina yeup si lokho yalla dagnouma wor je suis seul ak yalla
@ModouNdiaye-r6xАй бұрын
Bjr gouye gui tu as bien parlé c bien conseillé
@AlassaneNdiaye-n5yАй бұрын
Courage Grande Sœur, nous prions pour que DIEU vous protéger
@Tij525Ай бұрын
kann mola wakh yako mak
@famadiallo6049Ай бұрын
Courage ma sœur tu m'as fait pleurer yalna YALLA saafara.
@bimbakhgadiaga8456Ай бұрын
Ma cherie guènal keurgui nga dème louer tak sa sere liguèy
@dieynabagassama636Ай бұрын
Santal yalla banga amé métier légui je te conseille de sortir de cette maison nga outi nek
@AstoukorkaDemeАй бұрын
Demal outi nek gua tok fa ligueye khar yalla Dina nieuw inchalah du courage 😥 😢😢😢yalla mo moye bour
@cissedienaba5116Ай бұрын
Massa 💔 Mane deh man gui ley nianel fou sori si ce me bir Khol 🙏 YalneleYallah terral té diapaléle ak ce ndjabott 🙏 ngue ame ce keur, ouf ce ndjabbot, am jam ak salam. Ce mbok yi di na niou rouss inch Allah. Li yeup ngir sokhor ak alalou adouna 💔 Courage ❤️🙏
@rokhayatoudione3912Ай бұрын
Bayil. Sa papa ak yalla ! Sa yaye it kou bonne la !
@joliemamanndiaye2861Ай бұрын
1) tu sais très bien que ils veulent que tu sortes , sors quite à dormir dans le salon de coiffure. 2)tu as d'abord dis que ton mari est bien et qu il s'occupe de tes enfants tu dis aussi que nianato nek ak mom 3) yalla nalén yall dioubolé mais sors de cette maison
@oumy6935Ай бұрын
Moi min père me torture , j'ai voulu déménager à saly mais je suis commerçante et mes clients sont à dakar là plupart. Juste pour am diamm je fais tout pour ne pas le croiser. Juste pour am diamm
@ababa5489Ай бұрын
Bien dit,na fanane si bir salon,mou épargné khaliss.
@strategiesetdeveloppement2525Ай бұрын
@@oumy6935va louer une chambre
@salihatendiaye8143Ай бұрын
Masta ma soeur❤yala nala yala takhawou si barki Serigne saliou Mbacké🙏🥲
@OusmanyatassayeАй бұрын
Il faut aider cette femme. Elle est vraiment en détresse. En tant que père d'une fille, ça me révolte les comportements de ses parents...
@aminafall823Ай бұрын
Il faut gua dieul say distance sokhnasi daguay loué chambre rare len fepp tokk sa coint
@banawelle9842Ай бұрын
Moye deuke nak prkoi vivre avec des gens ki t'aiment pas❤
@aichasecka-8974Ай бұрын
Limalaye conseillé dall guénal Keur gui Yalla môme nieup louer djile balanioula ray
@TidaCisse-m9bАй бұрын
Moniale rek famille legui comme des ennemis qui vivent ensemble toutes les familles c'est comme ça chaque famille à son problème
@KhadyMané-x7tАй бұрын
Ma sœur sama xalatt dehors moy gua outt sa chambre tokfa lo am soutoura woko ba yalla gnow inchallah 😮 courage 💪
@farmataniang5608Ай бұрын
Il faut l aider aider l aider ses enfants qu allah la sauve amine ci barke salaatul fatiya amine
@khoudiandiayethiaw485Ай бұрын
Elle est brave mais elle doit prendre ses distances avec ceux qui veulent pas d’elle et essayer de se battre seule yalla rk lof nek
@awadiagne3184Ай бұрын
Ce qui me plaît chez vous c'est que vos titres correspondent à vos contenus ❤❤❤❤❤❤ bravo 👍
@idrissadrame3332Ай бұрын
Bilay gni danio meune sene liguey teksii professionel
@NdeyembarkaWade-w7lАй бұрын
Bilay Nima bagneé di khégne lo diwowoul,wayé yéne mome machallah ❤
@alkhamissАй бұрын
Yalla nala yalla diapalé silou bakh inshallah
@fatoundour4586Ай бұрын
Lisi geuneu graw moy parent yi lègui sou seu dome yoroul loumouleu diokh ngeu sonal ko tè so waxè gnounane wadiour xer leu so dalè si kawam tothie sou dalè seu kaw ngeu tothiethiiiiip sè vraiment domenge mai amneu wadiour yo xamni mèritè wougnou diour
@MarietouGaye-iy3lzАй бұрын
Dafa am wadiourr you sokhor meuna geunalai séne niabote té kholale yaye modone défar dome ba diaye ko mou séyi wala laigui yaye moy yakh dome bou bakh bou amoul béne sigue nak bamou lamb wayé yomar khiyam dina méti loll 😢😢😢😢😢😢❤
@bibasarr4821Ай бұрын
Billahi
@myadiouf1448Ай бұрын
Kii deii limouyy wakh kokou doundoul meunoko khammm yalla nagnou yalla mayyy khollou mougne mane akk gnoyyy doundou lii yeuppp🙏🙏
@gracevie6343Ай бұрын
Bilay, c'est pourquoi il ne faut jamais juger les gens.
@sml6264Ай бұрын
Ma sœur quitte la maison pour ta sécurité.yalna yalla takhawoula
@YandeNdiaye-v8qАй бұрын
Ndeysanne confie toi au tout-puissant, métina. Je demande à sa famille et surtout à ses deux parents père et mère d'avoir pitié d'elle et de l'aider à vivre en harmonie avec tout le monde.
@saudarud3774Ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂
@banawelle9842Ай бұрын
Je ny crois pas impossible ya plus de pitié c plus ke grave désolé mais yeurmendé diehnafii loume fii wahh yeuppe wala vous analysez pas les faits c plus ke grave la solution c kelle kitte la maison mo
@Ayou157Ай бұрын
@@banawelle9842voila loumou déf loudoul kité défoule loukoye maye diam
@karibaye2333Ай бұрын
Massa mettina soko doundoule doko ndakh keur famille c'est compliqué j'ai vécu au temps la même chose j'ai voulu même me suicider car tout le monde était contre moi, mais c'est ton courage et tes prières qui pourront t'aider de t'en sortir.
@MariémeCamara-g2eАй бұрын
Ma sœur va prendre une chambre yalla bakhna yalla dinala may loyco fayé inch'Allah
@khoudiandiayethiaw485Ай бұрын
Son problème est un peu général au Sénégal, il faut qu’on arrête de faire mal aux divorcees ou femmes mariées dans les maisons! De plus même les célibataires souffrent beaucoup
@AissatouGueye-q9hАй бұрын
Ay way il faut aider cette femme svp
@SeynabouMbengue-c6dАй бұрын
Dans la vie il y a des gens qui sont cruelle et qui n'ont pas de cœur
@MoustaphaNiang-tf1ouАй бұрын
Sokhnaci demal louwé dji sa bakan mo geuna for say wadjour yagui li guey yalla mogui lay soutoural demal oute sa chamber deuk fa bo kheuyé dem ligueyi sakhél meuna dal 😢😢😢
@yassing3985Ай бұрын
Dome amna akhe çi wadiour wayé wadiour tamite amna akhe çi dome wayé yalla nala yalla borom keur bou guéne çi yowe yala maye la khôl lou mouye
@naroubayeniassfall8019Ай бұрын
Walahi DEUG ga wakhe.
@hhjg1664Ай бұрын
Walahe dayga bu werr nga wahk
@MariamaSagna-j2wАй бұрын
J'ai vécue la même chose on ma amenée à la police et c'est mes demi soeur demi frères et quant j' ai quitter la maison et prendre ma chambre on m'a traiter de pite de tout mais moi mes parents n'étaient pas en vie dieu merci je suis en Europe maintenant dieu merci on dure que c'est mon histoire que tu racontes soit fort ça ira inchallah
@fatimatra8457Ай бұрын
Tu as bien fait ya des familles très toxique you bone sax
@seuneba7091Ай бұрын
Moi même j'ai vécu la même chose mais aujourd'hui je suis en Europe alhamdoulila
@SyAïssata-x4wАй бұрын
Oh ndessane s vraiment triste 😥 massa yallah bakhna je te comprends
@BinetaThiatАй бұрын
Yalla nagnou yalla doly soutoura guéneul fofou fii lép yalla 😢😢
@AbdallahTouré-h1pАй бұрын
Ki ndeyesann kouko xool xamni xamoul dra 😢😢 ❤
@PapeMbaye-v5pАй бұрын
Billhi
@veroniquenatack7392Ай бұрын
*Bilay ioe 😢elle a l’aire si innocente 😢🤦🏽♀️*
@DjibyNdiaye-fd1cyАй бұрын
Bly sama nak la day fenn
@BlackPanthere158Ай бұрын
Esk dou yaay fén😂@@DjibyNdiaye-fd1cy
@BlackPanthere158Ай бұрын
@@DjibyNdiaye-fd1cyak lou meuneu khéw yén baakhoolén. Vous la maltraitez pourquoi ? Vous êtes tellement méchants.
bilahii je te comprend très bien mom lay doundou rek mes yalla bakhna biss dina meusa diekh
@mameantagueye8677Ай бұрын
Lolou lay ndoundou mé loudoule diékh rek amoule na ande ak yalla rek
@gracevie6343Ай бұрын
Courage dîna bakhhh. Dèloolone sene boop si ya ALLAH
@myleneb5813Ай бұрын
😮😢oh ma belle mansa😮 je prie que Dieu te trouve un très bon mari😢😢❤
@FallAdama-j3iАй бұрын
Force à toi ma chérie demal louer avec tes enfants bala nioulay ray stp ma belle ❤❤💪💯
@djimbymbaye9359Ай бұрын
Sa yaye sa papeu ak say frere bakhou niou gueneule keur gua dinagn la ray
@dieynabakane4498Ай бұрын
Li daf amme si keur yii😭😭😭😭
@BinetteFatimaDiedhiouАй бұрын
MoMA diahal
@Marysa-kb3pmАй бұрын
Aka beuri thi keur yi danou laye sossal hainal La yah sa dere badoto diar tousse fekeu niome nio sikkeu
@naroubayeniassfall8019Ай бұрын
Louko raw amneu si keur yi
@veroniquenatack7392Ай бұрын
*Lou raw amna thi keur yi*
@baubaubeye7836Ай бұрын
Laylaaaah 😢yaw li ngay lathie ndah dafa am si keur yi🙈😭🤣man nekone na sama keur tata après m bac 😢wayè limafa doundou si métite ak sosalaté😭ba bima amé liguey mou yèbal ben femme pour mou niome diakhaséma ak sama patron 😩bobou la téléphone mon papa di dioye rek nakk man suma diakhlé 1semaine damay diéxx takk com kou febar ay att😩😭sila khamni soumafa toguè meune na déh saxx ndah nakharou khol 👉gueneuh si keurgui deim oute neg Wayè sante na YALLA legui amna salaire bou bakh di yonè sama pa ak mère 👩 yor sama rak ba legui am sama auto
@ironahide5896Ай бұрын
Da ngay nek sa keur baye amfa neg ak lep. Dem seuyi niou dieul sa neg nela amatofi neg. So divorcer au lieu niou deufeul leu nioulay sonal pask da nga len di khatale. Sa diabarou frere molay ndieuka siss ba yobalé si sen dieukeur yi
@AissatouWade-z2nАй бұрын
Sa yaye de kone AK sa papa bakhouniou
@S.B-io7vhАй бұрын
Je vie la même chose
@AissatouWade-z2nАй бұрын
Daniouy sossal dé
@AissatouWade-z2nАй бұрын
Limou wax nexoul degue dé waYe AK am mère daniouy ragale sen dom you goor yi pa aussi day ragal mère bi
@bigmolah122Ай бұрын
Bilahi wallahi day doulle
@salyallemomuawrksarr8652Ай бұрын
Sokhna guenal keur gui ndakh dom sou amè sagn sagn gniou def la yène yi sa yaye ak sa papa nioko dolèl say wadjiour beugou gnioula bayi lène ak sene keur yalla dièkhoul boudoul lolou dinga am loula nakari si keur gui guènal fofou😢😢😢😢😢😢😢
@layeseck872Ай бұрын
😢😢😢😢 sama xol bi toy na si sakh dafa am famille yi def yo khamni do sakh comprende loutakh ngay bokou ak niom😢😢😢 mais yalla soula tégué natou bilahi souko tégué nga faté lépeuh courage
@Laglce9015Ай бұрын
Faut pas te laisser faire dal faut souffrir pour personne appart tes enfants et ta mère
@kanyvanwijk270Ай бұрын
J’ai pleuré tous les larmes de mon corps. J’ai vu la même chose je t’encourage c’est pas Facile
@AidaBiteye-zi7toАй бұрын
Moi aussi j'ai veçu la même chose 😢😢😢😢na outi chambre mo eupe djam
@banawelle9842Ай бұрын
Mo keune elle souffre dale
@mameantagueye8677Ай бұрын
Lidé lay ndoundou ak sama frere mé yalla bakhna na ande ak yalla rek
@foogadebbomolooty9839Ай бұрын
Courage
@farmataniang5608Ай бұрын
L état doit intervenir le ministère de la femme doit soutenir cette femme pour sauver la vie de cette jeune femme
@KinéBarry-b5qАй бұрын
Quitte la maison ma chérie du courage aussi 😢
@farmataniang5608Ай бұрын
Aider cette femme 🚺 vraiment
@AissatouGueye-q9hАй бұрын
En plus tu es trés belle Machallah , accroche toi !
@ThiatouYayam-t4hАй бұрын
Li la done doundou bimaye doga divorcer sama diabarou mak ak sama grande sœur dima sonale sama papa ande si ak Niome mais legui Alhamdoulahi
@basselabdou9891Ай бұрын
Thiatou yayam🙏
@AissatouGueye-q9hАй бұрын
Tu n'as pas de problemes ça ce voit sur ton visage, tu as l'ére gentille , yala dinala diapalé
@ndeyelo3776Ай бұрын
Boul wakh lolou nit dafa lendeume
@inspiredtoinspire1855Ай бұрын
@@ndeyelo3776yao loko hamal nith loumou leundeum leundeum amna nith yo hamni ay nithou kassei lagn kouy fen ak koudoul fen soko guissei hamko
@oumydiawara3533Ай бұрын
Il suffit de la regarder pour savoir qu'elle est une bonne personne
@seydousecka3750Ай бұрын
Mais amal ndiorte bou rafet rek, ki nourou woul kou ame problème
@courasarr1582Ай бұрын
Massa ma chérie yallah bakh na❤❤❤❤❤
@oumyba7815Ай бұрын
Salam sokhna si s'il vous plaît sortez de la maison il voulait que vous sortez
@babsmstnewmusic7876Ай бұрын
Faut aussi donner la parole à la famille pour avoir deux versions , à chaque fois qu’il a problème chaqu’un jette le tort sur l’autre
@fatoudiagne3899Ай бұрын
Ma sœur, Wallaye tu es brave car je n’aurais pas pu. Tu es très forte mais ça va aller InshaAllah. Si je peux te conseiller de ne même pas répondre à leurs provocations. C’est cruel, ton propre frère, quel lâcheté. Tu as aussi le droit de porter plainte contre eux. N’oublie pas que tu as des enfants ma chérie. Je pleure avec toi, mon cœur saigne. Ce sont des monstres et des laches, tchippppp. Du courage chérie. Que Dieu t’accompagne et qu’Il te bénisse InshaAllah ❤
@bijoux-c6lАй бұрын
La cohabitation n'est pas facile. Courage ma sœur
@serignetoubarkАй бұрын
أن الله مع الصبرين😢😢 Yalla migui Ande ak moñe😢🙏 yallna yalla taxawu la inchallah
@salihate-ew6wyАй бұрын
Ndeysane massa😭😭
@AlimaSamb-xw6gdАй бұрын
Yallah nala borombi diokhe kheweul bo yorer sa djiaboot courage ma chérie
Vraiment sokhna si man am na yeuremadé trop si yaw en tant que dioulit ak moromou dioulitam. Mai man à ma part personnel avant may jugé damay téye ba déglou gniari côté yeup - God bless you sister 🙏 peace and❤
@AbySarr-c4p26 күн бұрын
Du courage ma soeur ,mbokou légui moy ennemi
@veroniquenatack7392Ай бұрын
*Massa et courage Yalla nala sougnou Borom takhawou ba gua guéneu thi bounkhatal gua nekk🙏🏽mbokou lègui yi moy lolou gnoula gueuneu djiégué sakh gniola gueune meuneu trokhal c’est vraiment dommage 😢*
@cocoshanell2750Ай бұрын
Ndeysane massa😢😭
@ndoumbendiaye7405Ай бұрын
Si j'étais toi damay guen si keur gui loué fenen oubi fa sa salon
@fatimandao8359Ай бұрын
Yow ño bok khalate yonou diame soriwoul
@khadydiouf3813Ай бұрын
Mani démale ngua ou ti chambre
@pivoine481Ай бұрын
Moy deug, mou nopalou bala mouy diour lanène
@veroniquenatack7392Ай бұрын
*Lolou moy diam dji*
@helenethiaw1385Ай бұрын
C'est ça mouwout béni nég pour môme rék
@oumoukane5264Ай бұрын
Du courage ma chérie
@MariemeSadio-b3dАй бұрын
Est ce que tes parents sont tes vrais parents 😮
@fatimacoumba3956Ай бұрын
Bonne question
@khadydieng6321Ай бұрын
Lolou dé la nék di xalate ni
@AdjaDiop-n6jАй бұрын
Bien jure
@AstouSy-f8iАй бұрын
Kéneu meunoul wakh lépeu wayer amna famille you boneu mougui nonou sou féker bouguou touniou gua nek si keur gui gua guéneu déme loué point
@ndiemembengue8345Ай бұрын
Mougnale ma chérie dounedena louméne nii soit forte tayeu yome gnoye topeu si sama guinawe wallahi
@PendaNgom-q1cАй бұрын
J’ai le coeur meurtri vraiment lii dama dépassé courage et déménage pour sa diame
@MbayendiayeNdiaye-r6vАй бұрын
Sokhnasi Bilahi incha Alah yalla dina safara lepou boul dougou dara si lou bone
@AissatouGueye-q9hАй бұрын
Non non pas de wakhtane , ils vont te tuer gua perte
@AissatouFaye-ip2osАй бұрын
Ndeysane yalnala YALLAH takhawou sama yaram dawna 😢😢ms du courage yALLAH diékhoul ma chérie
@thiamserignecheikh1210Ай бұрын
Jewrine néko mou mougne métina lolou nak Yalla sognou borome moko ték nattou bi yalla nakoko téguil Dina jéx dé inchalla
@lingueregougdji5801Ай бұрын
Massa yalnallah yallah diapalé si mbarké nabii amine yaraabi ❤❤❤❤❤
@marietousylla5253Ай бұрын
Courage ma belle que dieu vous protège inchallah
@DYNA8869Ай бұрын
Comment je peux avoir ses coordonnées svp ?
@banawelle9842Ай бұрын
Appel sur le service commercial il té donnera le numéro svp aidez la moi aussi je veux ses coordonnées demain je vais les appeler
@mamanmbaye1305Ай бұрын
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 sa yaye kou bonne la nit kou yess ak yaye noumou amé yérmandé thi dome sa yaye dila doundou li 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@oumylopy4803Ай бұрын
Bilay lila Sène Wa keur dèf mètinama trop 😢
@Thiouboulettes1553Ай бұрын
Sama pape ni lama défon waye khoulo wouma khékhou ma démouma police dama guén bayilén 3ans guisou malén kouniou yakar rek dem nan fofou wax kouma wax manila paréna ci niom wayé funé weur nafa pour ma nékat ak niom mais ba legui deganté rek legui mouné khana souma déwé diga niew maniko dinafa niew😂
@thiabeNdiayeАй бұрын
Dangaye reé😂
@Thiouboulettes1553Ай бұрын
@@thiabeNdiaye non damay dioy
@veroniquenatack7392Ай бұрын
*Parfois lolou rk gua meuneu deff pour am diam mm si c’est duré😢*
@Thiouboulettes1553Ай бұрын
@@veroniquenatack7392 moh fofu la geumé ni yalla mo yor niépp té d'où sétan kén sante yalla bu bax Sakh alhamdulillah
@YaakaarАй бұрын
Beaucoup ne comprennent pas mais lou ame la* yalnala BOROM BI gueuneu saameu* Mais un conseil démal diko sééte diko dieundeul quelques affaires meme so fa deukoul ngua saakou gnaane doula wagni dara té BOROM BI lolou la beugue
@harounaba2791Ай бұрын
Ngeun Balme Nak queutions Rék le Eusqe pa bi moco diour ndaxte mounouma comprendre ni gor dine bange domam bou Djigeun 😭😭😭
@MamanSagna-o9vАй бұрын
Courage ma chérie
@Absa_20Ай бұрын
Courage Sokhna lép dina diékh inshallah
@SeynabouGueye-t1gАй бұрын
Allahou Akbar ban genre de parents ms yalla baxna yalna la yalla may holoup mougne si barké Alkour'an 😢 métti na trop ndeyssann 😢
@VieuxNdiaye-o3nАй бұрын
😢😢😢 que dieu te protège li métina
@mar.y3964Ай бұрын
Soxna si démal loué sa chambre ligueye té bouléne may tousse fékhél ba ame sa terrain tabakh sa keur . Boussi maye kéneu sa alal