Si le voleur est mort on n’ a qu’à classer le dossier et attendre le prochain voleur. Kou ame fite démale sathiate. Félicitation à tout le quartier
@amadoutidianediallo762 жыл бұрын
Lou lérr frère
@joachimdmkanfany70632 жыл бұрын
Bilayy c ça la seul solution.
@mouhamedndong60692 жыл бұрын
Sathie Moy Ray Rekk Amoul Lenen
@leonamadousagne1792 жыл бұрын
Wawaw
@langmamadieng50072 жыл бұрын
Billahi
@aminataseck23882 жыл бұрын
Xar bigniou rediiii mola fankkk ioe mè sante yallaa
@user-20322 жыл бұрын
Doyna war deh 🥲🥹kou yabou deh outti toile😢liii
@ndeyengom2 жыл бұрын
Oui c sa motax mom aussi gnou ray ko
@fatoumaigadiop9972 жыл бұрын
j'ai des larmes aux yeux 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 tellement que c'est difficile de vivre en paix dans se pays mon pays va mal très mal même.
@momogueye30712 жыл бұрын
Je trouve qu’il es très très éduqué en le regardant parler et comment il a réagi face aux voleurs RESPECT 😎
@sophiejaffar59432 жыл бұрын
On va tous nous tué si on trappe un voleur on a qu a le bastonne
@maisoumboulousarr89262 жыл бұрын
C'est normal sérére la niou niare ko
@osmansarr54832 жыл бұрын
Chapeau a toi Almamy diamé wonnéguané domou niomineka gua Macha allah bien fait
@mayaciss68212 жыл бұрын
Frère Santal yalla comme tu es en vie. Mais la prochaine fois prend quelque chose pour te défendre c est plus sûr.
@Talibeserignebabacar21912 жыл бұрын
Deysane wahal Alhamdoulilah comme que rayoula wayé lii métinaa deuk bii vraiment amoul sécurité yalla nagnou yalla are this barket serigne babacar sy bon rétablissement mon frère
@khadijadiame51862 жыл бұрын
Bilahi ndeysan alhamdoulilah lanioye wakh sama mag la moungui sante yalla bakh
@Talibeserignebabacar21912 жыл бұрын
@@khadijadiame5186 Alhamdoulilah yalla na wére akk diame ❤️
@daoudakonte87722 жыл бұрын
wadjii bou nékouton ndanan deug wadjii rayko chapeau à toi frère tu a bien défendu
@kinefaye1732 жыл бұрын
La serigne cheikh wakhone dé danou si bayiwoul khel mais yeksina sangue léne rewmi bala déréte dinou sangue yeksina fék fran maçon ak eliminati yi nio ngui si sounou rewmi ate mou nek ni rek wayé sounou borom bi SOUBHANA WATALA molène eupe dolé sasou nek souniou khel yi mongui Sénégal bepe Sénégalais bouy yéwo si rewmi yalnala sounou borom bi same si BARKÉ SEYDINA MOUHAMAD ALEYI SALATOU WASALAM incha ALLAH 🙏 🤲 🙏
@gltntegilou95322 жыл бұрын
Billah diambar nga deug deug yalla n'a la yalla samou doly soutoura ci Sénégal amiine 🙏🙏👏👏🦁❣️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@adjathiorombaye82002 жыл бұрын
Santale yalla ak sa ligueyou ndeye borome ndeye diou liguéye kén mounouko torokhale bilahi vue que yangi koy nétali santal yalla bou bakhe 🙏🏾🙏🏾
@crispyqueen73232 жыл бұрын
Leigui gniniou djotei agresser rayy len sen ndeye ligueyoul? Delen wax waxou niit. Yaye yeup ligueye nax mattou ba keraw ngay djour dome lolou lep ligueye la. Wayei dassi ame dome you magg bonn sen bonnou bopp
@jeangomis5192 жыл бұрын
On est 16 millions de sénégalais et Macky Sall ne peut pas mettre un policier derrière chaque sénégalais il est temps du œil pour œil et dans pour dent pour régler ces problèmes d agressions
@laperlecmoi59952 жыл бұрын
C'est ça
@mo.elpresidente31632 жыл бұрын
Ana aye ministères
@gamigam64202 жыл бұрын
Mais adji sarr a des policiers derrière elle quesqu tu en dis
@ckonare2 жыл бұрын
C'est parce qu'il a mal géré les ressources du sénégal qu'on a c'est problèmes 😡😡
@mo.elpresidente31632 жыл бұрын
@@ckonare bien dit frère
@massambadiop81812 жыл бұрын
Goor yalla deugg nga frère courage reik et bon rétablissement diambar deugg nga bo nekone tapét Sathie bi reuthie na bou yagg mais bayil xel fi nga deff kharr yi aussi amoul sécurité boubakh boul diapouni sikaw leu reik gayi dougnou khamni ay kharr niongui fi non gayi kham naniou fépou fou kharr nékk
@safietouniang15742 жыл бұрын
Ay nioune founiou dieum Mr Diemé koubakh ndaysane mé alhamdoulilah sant yalla boubakh
@mariamafaye72492 жыл бұрын
Alhamdoulilah Mamady Diamé domou sèrrère gor yalla deug Alhamdoulilah puisque ti es en vie et bon rétablissement frère
@laminefaye92222 жыл бұрын
MERCI BEAUCOUP SISTER, MAIS C'EST ALMAMI DIAME PETIT FRÈRE DE MAMADY DIAME, SAMAYE COUZ LAGNOU, ANTOUCAT METTINA MAIS ALHAMDULILLAH
@daoudadieng34402 жыл бұрын
Qu'Allah vous protège ,Almamy Diamé. Soyons très vigilants et très prudents.
@famazidia2 жыл бұрын
douuguou sall dem entrainer wadjiii sou amoul wone doler ray nagnou ko
@aboubacarthiare95382 жыл бұрын
Que Dieu vous protège mon frère
@vieuxbakhe57652 жыл бұрын
Attention y a des voleurs qui ont un taxi tout jaune ils roulent la nuit ils sont au nombre de 3 personnes ils sont venus au sacre cœur dans mon agence de voyage multi services croyant que nous laissons de l'argent ici mais dalou niou si et ils étaient armés de pistolet s'il n'avait quelqu'un aux abords ils auraient amené les ordinateurs dans ce sens faites très attention les multi services alerteeeeeeee
@leonamadousagne1792 жыл бұрын
Merci pour l'information
@sowpendasow17532 жыл бұрын
Mane dall say bo kheuyè rek di geuna diomi thi senegal Alhamdoulilah baga diotè sa bakane sante yalla tu es courageux
@assanendiaye29972 жыл бұрын
Ki Deh Sama Mbokku La Almamy Diame Boy Bou Cool Vraiment Li Métina
@baelhadjisamba89012 жыл бұрын
Très triste , mais respects à la victime. Il est très courageux. Il aurait pu réagir autrement mais malgré les coups de couteaux il a toujours voulu le maintenir. Courage à lui. Je ne souhaite à personne de vivre ce genre d'événements mais su ça arrive c'est comme ça que les gens devraient se comporter.
@amyndiaye60322 жыл бұрын
Thiey notre pays vas mal, mais yalla n'a borom bi saamou niou nioune nieup ainsi que nos familles 😔
@astoushylabarriette23522 жыл бұрын
Dans ce pays il est tant que chacun soit armé car même chez nous on ne se sent pas en sécurité si on ne se prépare pas à tant wallahi ces agresseurs ne vont jamais s'arrêter
@seydinaaliounediop79532 жыл бұрын
Bouldi gaawa waat ma soeur
@Sabrun-jamil2 жыл бұрын
Loolou mooy deugg dei, mane leegui meme sama biir keur damay armé wou,sama keur dei ssou nekheei yalla koufi douggue pour defma lou bonn wala sama njaboot,balaa moufeei gueenn dinafi bayyi bakkanam
@jazaka31782 жыл бұрын
Il faut chercher des armes(Pêle, râteau,gourdin) avant de riposter contre ces malfaiteurs
@abibdiop46782 жыл бұрын
Ok frere
@jazaka31782 жыл бұрын
Maintenant tous les agrésseurs et voleurs ont des armes soit c (couteau 🗡️ ou sabre) c'est pour cela, on doit pas riposter avec les mains vides
@abdourazakhdiao10732 жыл бұрын
Tu as raison
@elhadjidabasarr37852 жыл бұрын
Bonne rétablissement frère
@menguendiaye79772 жыл бұрын
khallé you goreyi délén lék ba sour di woute dollé bouléne bandi ataké ngéne déf ko loumétî ndakh bounioula diéko dou bakh
@elhadjifall14442 жыл бұрын
😂😂😂 wakh gua deug dall
@alioudiago11562 жыл бұрын
La ilaha ilala mouhamadou rassoulilahhh qu'Allah nous protège par sa grace🤲🏾🤲🏾🤲🏾
@babacarsow56582 жыл бұрын
MBA Ray ga ndy rk doumoukharame yi nianke diome rk
@ndeyeastousarr93432 жыл бұрын
Khar mi dé n'a santé ko yalla bou bakh que dieu veille sur nous tous
@mamadousarr33712 жыл бұрын
Al hamdoulillah yalla Nala yalla samou mayla wer bon courage frér
@seynaboubah95202 жыл бұрын
Bn rétablissement mn frère
@adamaseck88212 жыл бұрын
Domi kharam yii koulenn yereum da nga khamoul 😢
@sokhnaaissatouly6832 жыл бұрын
Bilahi mane sathie sakh damako yereum bougn ko diapé lignou kay def yeup Dina fadjou louko eup
@ouzinouzin36562 жыл бұрын
boko yareme tay mou rayé la souba
@amadoutidianediallo762 жыл бұрын
Sénégal 🇸🇳 dall legui comme Chicago chaque jour crime Sama gayii guiry yalla dieull lén sen motoukayy sino kouniourayy yay perte
@Babbasfa2 жыл бұрын
Nél brésil kay mba caméroun si zone anglophone bi.li da eup
@ndiayecoumba89872 жыл бұрын
Ndeysan du courage mn frère li métina trop yakna gnou yalla samm té argnou may gnou moudiou gou rafétt gnoun niépp
Alhamdoulillah Bon courage frère Qu’Allah veille sur nous tous !
@domoubadiane3482 жыл бұрын
Il est brave deh. Ndeyssane.
@bboybzb66062 жыл бұрын
non mais c'est qui ce journaliste ? tu cherche quoi a pousser le victime a pleurer alors quil na pas envie de pleurer , abusez pas
@diaboutallcisse11422 жыл бұрын
Lolou moma diakhal di...
@mariamadrame33712 жыл бұрын
Ah manite diakhal nama
@bibiziinho35142 жыл бұрын
Bon rétablissement frère 🙏🙏🙏🙏 yalla nala yalla défal li gueun
@mountagadiallo59842 жыл бұрын
Wallakhi yaw âme gua khole si cètait moi je vait Luis ègorgé en que personne arrives 😭😭😭mangui dioy
@caffaniass7882 жыл бұрын
Allahou akbar soub khanalla 😭😭😭
@momidiop78782 жыл бұрын
Alhamdoullilah Machalla yallana yalla defal laa tawfekh
@khadimsady64672 жыл бұрын
Courage mon gars c'est vraiment dure mes que allah nous protège 🖖🏿❤👨🏿🦯
@deugrekgodisone20692 жыл бұрын
Yay gaïdé dé🤟🏾🤟🏾🤟🏾🤟🏾🤟🏾🤟🏾❤️❤️❤️❤️❤️❤️🦁🦁🦁🦁🦁
@adjathiorombaye82002 жыл бұрын
Sénégal 🇸🇳 visa moma fi bayi🏃♀️ont n’est dans quel pays 🥺nous vivons dans une monde qui s’appelle le monde des fourbelus les humains vivre comme des animaux 🤔🤔yalla nala yalla same si barki serigne saliou ❤️❤️❤️🙏🏾🙏🏾
@ladivadiallo94442 жыл бұрын
mane dé ma ngui suisse mais raye you bari yi si sénégal dama sah ragala gnew sa ma réw yalla na yalla same gnepe
@aron60542 жыл бұрын
@@ladivadiallo9444 boy demal wouteul sa Gun koula diégué nga wathiéko
@mddi14202 жыл бұрын
@@aron6054 dafa leer
@yandendiaye89692 жыл бұрын
Bilahi ak Say morom bo meunè Say Dangay yobalè sa Familles
@adjathiorombaye82002 жыл бұрын
@@yandendiaye8969 lou lerr yande deukk bi woratoule
@coumbandiaye69232 жыл бұрын
Bon rétablissement mon frère ! Mais Macha Allah Diambar tigui nga.
@diapsofficiel11332 жыл бұрын
Brave homme masa yalla nala borome bi sameu
@juniorswae13592 жыл бұрын
Personne n’est à l’abri dans ce pays Bilakhi … yalla Neu Yalla Sam Nieup insha’Allah té mouseul niou si Leep Louy lou bone
@marythiawndiaye35112 жыл бұрын
Chapeaux aux habitants du quartier
@AwaNdiaye-q8s7 ай бұрын
Pikine guinaw raill
@clairemari72922 жыл бұрын
Bravo félicitation
@dubainfall10862 жыл бұрын
Kou diapp sathie rayo ko tei mou narone la rayy balloumalako walahi
@oumysougou35022 жыл бұрын
Bilahi
@inconnu900002 жыл бұрын
Dagn ko warone rendi bilahi !
@Takiiw2 жыл бұрын
Li etat bi warnagn si diouke barki alkhouranoul karim grand bi liko dal mettina trop , li dou yoon billahi wallahi 😭😭😭😭 nitgni dagnou am ay problem com ningako amer , ngala way bougnla geuna goree di gorgorlou yaw ngay sathieu di agresser, na nitgni armeou kouy sathieu diam nit niou dageu nday sa niari tankyi nga nekkeu handicaper domoukharam yi 😭😭😭
@mbayagueye37652 жыл бұрын
Ins bi operation sathei la kou beugg dai rek demal sathi population bidal mingifi rek kou sathie ngou talal sa nounara gui bamoune ngay bou nite yidi liguey ngene di beugg lou yomb bandes de tortue
@tambedouyacine72272 жыл бұрын
Yalla nala yallah défal Diam ❤️
@btptv17432 жыл бұрын
Le gas est un vrai tueur une personne qui a réussi à abattre un mouton sans l'aide de personne
@ousmanendiaye6942 жыл бұрын
Slt frère si on peut abattre un mouton sans l'aide de personne. Sé un système tu croise les chambe derrière et tu prend un de sé pié devant tu le mé dans sé corne merci.
@lolababalola82052 жыл бұрын
Est ce que ce n'est pas vous par hasard ??? 🤔
@btptv17432 жыл бұрын
@@lolababalola8205 arrêtez d'être négatif dans la vie quand on dit les senegalais sont méchant a cause des personnes comme que l'on parle . Pour votre infos moi je suis au Maroc
@lolababalola82052 жыл бұрын
@@btptv1743 mon cher vous êtes au Maroc ! Et alors !? J'ai pas percuté votre message ???
@ndeyengom2 жыл бұрын
Loutax mou ray khar bi sax moma diaxal
@adamaseck8992 жыл бұрын
Almamy yow diambar nga mossa doon Yalnala yalla may wèr nga meuna reprendre say activités et merci wa pikine info
@mamita83672 жыл бұрын
Pour mane ak li khew si deuk bi voleur yi ak agresseur yi dinagne pose touti ndakh khamnani khalatougnou bayi domerame yiiii sonal ngueine nite yiiiiii 😡😡😡😡😡😡
@ssbahzin102 жыл бұрын
Ndeysane Almamy diaameu rek nguay aam boroom bakh ngua yatou,yarou tey,niit Kou bakh ndeysane,amal diaam rek nala yalla aar si barké seydina mouhamed du courage
@salifthior50742 жыл бұрын
Diambar deug ngeu. Yalla soutoural nala. songou borome paka gnou am fiteum bariwoul mais comme que tu es saint et sauve rek on rend grace à Dieu
@mamadougalsen87122 жыл бұрын
J’espère qu’il n’y aura pas d’enquête Longue vie à toi bro
@sadiobandia9472 жыл бұрын
Kouniou diapaty ngey agressé balla ngey sath naniou la soti essence tall n'a nopalekou niou nopalekou
@elhadjifaty82192 жыл бұрын
Billahi
@moustaphandiaye85502 жыл бұрын
On devrait commencer à adopter la charia, affaire bi c'est simple
@alioudiouf83102 жыл бұрын
Almamy que Dieu veille sur vous... Respect!!!
@kinggeneral61842 жыл бұрын
Pilon ngay wout dakhar ndeyam si bopou
@oumysougou35022 жыл бұрын
😢😢😢😡😡kolal li rekh bilay sathieu Domou kharam yi nio sonele . Yalla naleen Yalla weer rekh niou torokh ba faw . Li Dafa doye waar trop insecurity bi legui ba keur jambour 😰😰
@bahtiediop7322 жыл бұрын
.0
@bahtiediop7322 жыл бұрын
m
@joserere42742 жыл бұрын
Sénégal m’étonne vraiment. Chaque jour agression, vols, meurtres et suicide.
@Rasssoullll2 жыл бұрын
Senegal dee gamou tivaoune momafi bayi,,,kou yabou toukhou
@aissatoundong27112 жыл бұрын
Bn rétablissement frère le niominka
@papndong72542 жыл бұрын
Yare khare aka bari risque
@calcodesall49412 жыл бұрын
Ak yoré moto scooter
@khadijasarr97722 жыл бұрын
Yokale mure bi yalnaniou yalla samme ak mboléme domou Adama
@ibrahimadiouf53882 жыл бұрын
Mane j’habite à guinaw rails mais Sathie walahi khol n’a vidéo wame bi sank mai kokou deukou fiiij khawma nak foumou deuk mai Sathie yi sonal naniou mai Bilahi kouniou diape dînaniou la niousse baga poupe daguene Di dofff dofflou ndeyam nioune niolene gueuna sonnou foppe domou kharam yiii ngueune done nioune wa guinaw rails pare naniou nak Kouffi dougou Di Sathie dinajiou ray sa Ndey 😤😤😤😤😤😤
@oumysougou35022 жыл бұрын
Bilay zone yeup bouniou defone lolou manko nekh been dinaniou arreter . Gni Bilahi aye golo laniou 😢
@ibrahimadiouf53882 жыл бұрын
@@oumysougou3502 daniou bone deee Sathie yiii Bilahi y’a ils sont toujours armés nak
@oumysougou35022 жыл бұрын
@@ibrahimadiouf5388 Sisi danio ame guanay d Mai’s lolou kouniou ray Yaye perte 😢😢ah meytouleen bou bakh . Yow mome fonk nala Ndakh Sama papa Ibrahima la toudou
@mouhamedndong60692 жыл бұрын
Est ce que vidéo Mongui KZbin
@khadywade6082 жыл бұрын
Guinea rail mom ay weuyu reck fa ndeuk
@user-20322 жыл бұрын
Thieuy senegal chaque jour rek beneu cas kou kheuy sakh sa fit dafay dem ndakh tu t dis que peut-être s serai moi la prochaine victime hooo Ayway demlen liguey II😭😭🤲🏾
@sokhnaaissatouly6832 жыл бұрын
Bilahi damay diangui dakar mais sama téléphone sakh damako ragal té parceque ndagay romb ay niit you bizzare tekssi ioe ndagay khamni niou rayleu ak dem agn lagnou yamalé life bi inst bi nehneu
@coumbadiouf7922 жыл бұрын
Bala police donn gneuw dagno waronn dagueu 4 barap yeupp ,khawma kann mais koko todoul nekk danger ,domaram yi diarougnou yeureum
@jacky33262 жыл бұрын
😂😂😂😂😂 wakh nga deugeu nak
@coumbadiouf7922 жыл бұрын
@@jacky3326 je t’assure,temps yi c’est ce que j’arrête pas de dire à mon mari ,chaque mains on coup les 4 doigts bayi lah gua dem ,non c’est fini danger doto ko nekkati à vie ,avec un doigt à la main tu ne pourras plus tuer ou faire du mal à quiconque
@amadoudiouf8312 жыл бұрын
Bro sathieu deh na li sama kogn la
@ndeyekhadymbaye74302 жыл бұрын
Santal yalla bou bakh...vue que tu es toujours en vie... yalla koula beug là
@lapiraterie92i72 жыл бұрын
Sathie bi dadonn raay wadji ms ce pays grave
@user-20322 жыл бұрын
Bilahi deh noo
@sambadiagne57502 жыл бұрын
C'est les politiciens mal intentionnes et les droits des malfrats qui ont affaibli les hommes de loi. Donnons aux de loi leur faveur au temps de collins. Force doit rester à la loi.
@mouhamedhabibniang80302 жыл бұрын
Faut pas sortir les choses de leurs contextes
@daarasantestouba39182 жыл бұрын
Bilahi Guinaw rails sud li mo fi ame barkep borom touba veillou korité bi rk deff naniou ko sama béne deukeundo ray xaram yobou ko Mane mi rk sathie naniou sama xar si koor gui
@abdoukone48762 жыл бұрын
billakhi sante yallah rek dakhe bokone gua si victime yii li yeup politique bou bonne là...état
@reguadmalaw12722 жыл бұрын
Mach Allah yallah nala yallah d’éfal diam
@habibmanga53002 жыл бұрын
Bon rétablissement Mn grand
@cissramatoulaye96112 жыл бұрын
Dama warou🙍♀️🙆♀️🤦♀️
@jacky33262 жыл бұрын
Ndeye sane 😭
@ndeyengom2 жыл бұрын
Yalla nala Yalla sameu areu la goudal say faane inchalla ak mbolém djoulite 🤲🤍Amine
@MamadouDiop-vg9fn2 жыл бұрын
Sama collègue la li métti na mais sante Yallah rek
@17tvofficiel122 жыл бұрын
Bon courage à la famille Diame Sénégal sen loi diakhal na ma dans cette famille _ Diame_ qui est une victime le procureur à arrêter deux personnes de cette famille donc le père de famille qui est notre Papa et mon frère
@user-hh8gz8bz6o2 жыл бұрын
Très émouvant le gas et cool
@santeyallahrek84072 жыл бұрын
Alkhamdo lilllah frerr Amal diamou
@peindoushakadiallo48802 жыл бұрын
Alhamdoulillah, dieu merci
@amadoutall68742 жыл бұрын
Adouna. Nehou.
@abdoulayebah24332 жыл бұрын
Non vraiment c'est triste billahi wallahi 😢😢😢😢
@serignecheikhsy41552 жыл бұрын
Bilay legui senegal dera worou fofou
@ibrahimalhassan53882 жыл бұрын
Que Dieu te donne une bonne santé
@ablayediop89632 жыл бұрын
Billaye wakhga sènègal dafa mèti 🇮🇹🇮🇹✅
@laminefaye92222 жыл бұрын
METTINA LOL FRÈRE C'EST MON POTE ALMAMY VRAI GOR YALLA PATRIOTE DIAMBAR DEGGUE, 🇸🇳😭 MON PAY VA MAL TE PRESIDENT DI FAYE AYE NERVI 💔😭🇸🇳 ET MERCI WA PIKINE INFO FOR REVER
@papemorfall76972 жыл бұрын
Alhamdoulillah yalla bakhna grand
@clairemari72922 жыл бұрын
Bonne guérison
@rouguietousy22922 жыл бұрын
Non mais li ba kagne, 😭😭j’ai mal pour cet homme massa.agresseurs yi yallah nanou trokh beuthieuk. Bilay ndiambar nga
@fatoudiouf87562 жыл бұрын
Amnga chance mon frère
@siracisse86732 жыл бұрын
Té nion déme guassi souniou mbambéle togue Di khare .li kate kéne mouthioule
@mormbaye29892 жыл бұрын
Diaroul xar ky 😂😂😂nan soul sunu bopou ky mo geuneu sed ❤️😂😂😂
@thiammoustapha88212 жыл бұрын
Dia dieuf bro Diam rek
@diopfatou8262 жыл бұрын
Ay way li ba kagne 😭😭😭😭
@bamayeldiallo61832 жыл бұрын
Les pikinois chapeau Il y a eu récemment une femme de 62 ans qui a été violée et tuée à diakay ou tivaoune peulh les voisins l'on entendu crier mais personne n'est intervenu
@diandysagna18772 жыл бұрын
Oui c’était dans ma ville thivaouane peulh c’est tellement triste