Thia deug deug Cheikh Mbacké Sakho dou moromou gni. Ce Ahmed Khalifa Niass fitt rek lay dokhé. Sa compréhension du Coran est très limité... Machallah encore Cheikh Mbacké Sakho.
@FallmuslimКүн бұрын
Salam cheikh ahmed yaw khamogo bateye cheikh mbacke sakho c est un cadeau que le .bon.dieu nous.a donne pour qu on se repenti de nos eureurs merci
@alxuraanciwolofКүн бұрын
Sourate 4 v 101. Raccourcir moy (rendre plus court) manam gattal. Lolou ak wañi dafa wouté. Wax dëg kou am loy saxal ba weddi ci diiné waxal li Yalla wax ak fimouko waxé ñou dém vérifier. Diw néena ak mami diw néna ci diiné Yalla ji. té yalla né waccé na téeré bu leer , bunu faramfaccé , téeré bu bayyi woul dara.. douma topo waxi diw bayyi fi waxi Yalla. Ku topp waxi diw bou ëlëgué nga dém diw fayla rek.
@amycisse42648 сағат бұрын
@@alxuraanciwolof rendre plus court ce n’est pas diminuer ??? Cela dépend juste de l’unité de mesure utilisée…. On réduit ou raccourcit une distance, on diminue ou réduit un prix…. wagni leu rék… en passant j’écoute bcp CMS car il pose des débats d’intellectuels sur la religion….cela ne change des prêcheurs habituels cela ne veut pas dire qu’il a tjs raison.
@TheSenegambian4 сағат бұрын
Cissé 🎉@@amycisse4264
@AlieumachJengКүн бұрын
Sheikh Ahmed, am a Gambian living in Banjul The Gambia ,i really Like your program ,keep up the good Work.
@mamadouleigh3520Күн бұрын
It’s never easy to deny mbake sacho
@ZainabouDiop-Күн бұрын
They can't
@moussadieng3680Күн бұрын
Nobody is denying nobody. Sakho believe what he believes. Ahmed believes what he believes. And they are both Muslims. That's the beauty of Islam
@IbrahimaDiallo-zw7xb11 сағат бұрын
No do sen morom
@serignalssanesyllasate8140Күн бұрын
Thiowli moy bari rék mai cheikh mback Sakho limouy wakh té tékkou si alkhourane kén manouko tégui si wakhi kassé
@mohamedelhabibndiaye2969Күн бұрын
Ahmed Khalifa Niass que je suis depuis, Ahmed Cissé depuis bientôt 3 ans et Cheikh Mbacké ont une intélligence très avancée. Macha Allah akeykoum. Il est toujours nécéssaire d'avoir une refléxion au lieu d'un savoir tout court. Depuis Mauritanie.
@nixgueye6709Күн бұрын
Nekhoul ba nékhoul mais Ahmed Khalifa niass wakhoufi dara
@badousamb1553Күн бұрын
Il tourne autour du pot
@aliounebadarandiaye5390Күн бұрын
CMS est difficile à contredire car il ne fait que reprendre ce que le coran dit.CKN est cohérent avec lui même car il est le représentant d’une communauté qui a tracé sa propre voie.
@Cabayoroyoro2 күн бұрын
Non yalla gattal diouli la wax
@badousamb1553Күн бұрын
Maintenant ameth tu es entrain de mentir contre Allah
@badousamb1553Күн бұрын
AMETH WÉDDINA ALKHOURAN
@RokhayaCisse-jy3esКүн бұрын
Cheikh Cissè Cheikh mbacke yalla naléen yalla fay ❤❤❤❤
@cheikhbayethiam7044Күн бұрын
والله أنتم شرفاء 🎉 بارك الله فيكم ونصركم
@badousamb1553Күн бұрын
Amet khalifa comment peut tu dire un verset coranique que tu qualifie pourtant de Bien clair, mais ensuite tu dis"WAAYÉ" ? Vraiment Tu es faux
@badousamb1553Күн бұрын
Amet est entrain de tourner autour du pot.tu ne peut pas le clarifier.wakhou NAAFÉKH rék la fi wakh
@AmieFaye-sr7rwКүн бұрын
Wahtane wi néhnatina yalla noula yalla fayal Cheikh bi coula tope guindécou ❤❤❤❤❤❤❤
السلام عليكم احمد سيسسي وشيخ مبكي شاكو سؤال للمبكي شاخو الآية سورة غافر النار يعرضون عليهاغدوا وعشيا ويوم تقوم الساعة ادخلوا ءال فرعون أشد العذاب الاية
@SyAlassane-k7sКүн бұрын
هذا دليل بأن عذاب القبر موجود ذاتية فسوف تسال انت يا مبكي شاخ و شيخ باي ا نياس
@MohamedBA-xw2nyКүн бұрын
Wagni n’est pas égal à gataal diouli…. Gattaal diouli mo am tchi alkhourane
@amycisse426419 сағат бұрын
lol ils sont synonymes
@NihmaTV15 сағат бұрын
@@amycisse4264😂yaw khamo sakh louy synonymes. Raccourcir ak diminuer kagne la gnou nék synonyme ? 😂😂😂
@Gaye-industrieКүн бұрын
Lii moy xam xam manchaalah❤
@malickndiaye3711Күн бұрын
Saway way mbacke sakho nekhoul weddi d
@diodiobdx9435Күн бұрын
CAMS nekhoul ba nekhoul wanté wédi ko yomboul dé
@badousamb1553Күн бұрын
Les situations où leau peut etre aram et le vin alaal est facile à montré lii DEUG DEUG dou kham kham
@SidyDiakhate-q1iКүн бұрын
Insla mbacke sakho lumi wakh mom kanam la diem iow mom nafekh ga bou kate ndayam Ga
@amadoutoure1095Күн бұрын
Bayile sagua serigne bi
@freemind300912 сағат бұрын
AKF thinks that islam is just about saying your opinion without any reference to quran. He never backs his words with proof from the holly quran.
@adioumabarry7696Күн бұрын
Ahmed wakhoufi tous Raccourcir et diminuer ce n'est pas la même chose
@amycisse426419 сағат бұрын
C’est la même chose, pour donner raison à CMS vous racontez des conneries en voulant différencier « raccourcir et diminuer » , cela démontre votre manque d’intelligence
@cheikhsene6762Күн бұрын
Merci mbacké sakho
@badousamb1553Күн бұрын
AMETH SOSSKAT BOU MAK LA😂
@idydiallo9451Күн бұрын
Ahmed khalifa beury na kham kham Machalla
@badousamb1553Күн бұрын
MAIS MALHEUREUSEMENT IL N'EST PAS FRANC .. NAAFÉKH LA
@fdd10057Күн бұрын
Walahi wakho deuk fen ngay def
@amadoutoure1095Күн бұрын
Ana sa preuve
@malickndiaye371113 сағат бұрын
Wakhofi dara
@BaAhmadoudieylani-k3rКүн бұрын
شكرا لك يا شيخ أنا تلميذ شيخ عبد القادر الجيلاني ❤❤
@firi_guente_et_secretКүн бұрын
aythia niou yatall xam xam nguir dieummi seydina mouhamed abonél fi
@BaAhmadoudieylani-k3rКүн бұрын
❤❤❤❤
@abdoudiop8772 күн бұрын
Yalla nala yalla defal diamou cheikh ahmad cisse
@freemind300912 сағат бұрын
Paabi wakhoufi dara ay wakh sa xalaat rek lay deff.
@BaAhmadoudieylani-k3rКүн бұрын
العلم هو الإمام
@mamathseck833Күн бұрын
Mach alla niass ❤❤
@OmarTouray-k7qКүн бұрын
MashaAllah Ahmed khalifa borom kham kham la te li mo wah mom len mina deug si borom kham kham yi waye problem bi moye si alquran nga inde fa lukoy saxal mo diaffe nyeupp li werr te worr moy cams mom danel ko du yomb dh