Aida Diallo: Mon mari m'a abandonnée, Après 2 mois de mariage

  Рет қаралды 49,007

DAKARBUZZ TV

DAKARBUZZ TV

Күн бұрын

Пікірлер: 166
@vieuxsonko9221
@vieuxsonko9221 3 жыл бұрын
Aucune femme dans ce monde ne mérite d'être maltraitée ou abandonner
@omarsene2994
@omarsene2994 3 жыл бұрын
😭😭😭Dénioulaa nakh sacrifiée la ndéyssane 😭 koo khamoul ayy mbokamm, bénni mbokamm guissokô boul mossa nanguou mou takk'la wayé yalnala yala souniou borome takhawou ndéyssane bo ngua wérrr
@paaliounendiaye2908
@paaliounendiaye2908 3 жыл бұрын
Goor bakhoul wadji vrai doméram leuh mais tôt ou tard dinako guiss . Wadji dafa wor c triste sister Yalla nala Yalla takhawou inchallaah
@evadipmoree1975
@evadipmoree1975 3 жыл бұрын
Trahision bakhoule manone gua diapou si militaire bi rek wore bakhoule nioune djiguène gni lounou dale nioko yobè sounou bopou amenasi djiguène nio xameni djeukeurou Modou Modou diaralenalène wore kounou guènale 19ans djiguène dafaye doyelou ta bagne lou foukhou beutem xamena tourou France 🇫🇷 bi mo takhone niou dougale leu si seyebi xalè bi damako yeurem 5ans ta xamo sa Papa mètina trop mes yalla bakhna yalla na yalla safara lèpp inchallah encor une foi m'efions nous de l'eau qui dor
@yandrndiaye6451
@yandrndiaye6451 3 жыл бұрын
Bilahi mo gneuk wor.té bo woré gnou wor la
@evadipmoree1975
@evadipmoree1975 3 жыл бұрын
@@yandrndiaye6451 lolou dei deuguela mo djeuka wore ta akh bakhoul
@tigressesylla9941
@tigressesylla9941 3 жыл бұрын
@@evadipmoree1975 bo woré dingko guisse tôt où tard voilà les conséquences légui khalé bi moy guena souffrir
@Yetou85
@Yetou85 3 жыл бұрын
Tour le monde fait des erreurs. C'est très facile de donner des conseils après
@nabousow7754
@nabousow7754 3 жыл бұрын
Bilahi kay
@mendesshasha1021
@mendesshasha1021 3 жыл бұрын
Kokou dala sacrifié walay. Et svp arrêtez de dire à la fille k da warr mom bimouy seuy khalé la wone khamoul dara yayam moko mayé nagn blâmer yayam. Senegal pour finalité djiguene mou seuy seuy walay koussi téyoul dotoko deffati jtjur. A l'écouter elle ne connait rien dans la vie té yakk nagn adounam.
@abdoudiop5163
@abdoudiop5163 3 жыл бұрын
noleni maye nite seni dome te khamou lene aye mbokam ndakh modou modou la lane moy france nite dakay am ngor akh militaire bi rek molene diape akh ba khoul mere. Aida diallo nala yala defal diame soutoura maye la weur bou bakh si barke seuydina mouhamed psl 🤲🤲
@omarsene2994
@omarsene2994 3 жыл бұрын
Vraiment aussi
@dialloelhadjialassane5086
@dialloelhadjialassane5086 3 жыл бұрын
Une très bonne conseille.pour les autres.avant de marier a qui que choix il faut bien renseignè car on ne sait jamais ce que demain raportera. bonne rètablissement.
@bellawomen
@bellawomen 3 жыл бұрын
Sénégal kouy touki rek laniouy bagna guiss motakh niou le di nakh a chak fois tey dafa baakh trop
@laperlalaperla6646
@laperlalaperla6646 3 жыл бұрын
Bilahi ligua wakhe dara douko dindi
@dabaniang8141
@dabaniang8141 3 жыл бұрын
Yalla na bour yalla safara thi barkhé seydina mouhamed psl
@laperlalaperla6646
@laperlalaperla6646 3 жыл бұрын
Sénégal dagno faible modou modou youssi eupe dagniy khéméme wala gnou beugue kham lo wodo takhe gnou tak la bisse bougne ko khamé bayila séti kénéne yéwouléne goor gnou beuri pour gnou am la bagnou si ba tak la yalla na la yalla takha wou inchalah
@nanafall4134
@nanafall4134 3 жыл бұрын
Kokou bandi la té xamna sacrifice la wone rek africain aka diara ragual ak gnimako sania wakh mais djiguen moytou lenn seuyeuk ko minoul xamoko yalla nala yalla atté ak mom Aida diallo yalla deffal la weer
@aishazimia9912
@aishazimia9912 3 жыл бұрын
Ameen ya Rabi
@lilou511
@lilou511 3 жыл бұрын
svp les filles woute len si lolene diape, ligueye lene ba goor boula abandonné dina fekeu ga meneul sa boop, c'est vraiment triste🙏🏼❤️
@MarieGomis-tt6ze
@MarieGomis-tt6ze 3 жыл бұрын
Wakhal dee
@bellawomen
@bellawomen 3 жыл бұрын
Merci
@nafidiaw5542
@nafidiaw5542 3 жыл бұрын
Bilay bagna yakar si ben gor dara
@tigressesylla9941
@tigressesylla9941 3 жыл бұрын
@@nafidiaw5542 billay mane déh mangui goor gorlou pour Bagna yaakar kéne koudoul mane
@nafidiaw5542
@nafidiaw5542 3 жыл бұрын
@@tigressesylla9941 beure gua si ay morom affaire yi mom geumeu sa bop rek la
@adjiseck9104
@adjiseck9104 3 жыл бұрын
Yalla nala yalla diapale si daradiaye kou tedeki(SAW).
@omarsarr4591
@omarsarr4591 3 жыл бұрын
Ya wor sa copain ndakh kou diougé France,bref légui yaw yaye subir problème yii, yalna yallah takhawou la
@aminandiaye3303
@aminandiaye3303 3 жыл бұрын
Non worouka wahou wadoiure réke mon frère walagui 😪😪😪😪😪
@gueyekhadim9682
@gueyekhadim9682 3 жыл бұрын
👍👍👍👍👍
@tigressesylla9941
@tigressesylla9941 3 жыл бұрын
🤔🧐
@Yetou85
@Yetou85 3 жыл бұрын
Bâyilene ignane
@awakounta4524
@awakounta4524 3 жыл бұрын
L'I metti na dei seuyou tay yiii diaroul daw bay danou bilahiiiii goor mo diaroul taylé sa life
@tigressesylla9941
@tigressesylla9941 3 жыл бұрын
Walay
@mimaaaniang2473
@mimaaaniang2473 3 жыл бұрын
merci j t jure lgui diamono bi da diahasso
@ndeyefa784
@ndeyefa784 3 жыл бұрын
Bilahi diaruko mom def ndank
@khadijalo8182
@khadijalo8182 3 жыл бұрын
Masta grand cœur mètti n'a mais boy dougyati si gor deko kham bam ler na nagne kham ay mbokam kham lepam dinasi bakh masta yalla nala Yalla diapalè
@aminatacissokho9587
@aminatacissokho9587 3 жыл бұрын
Yalla nalla yalla diapalè bb masta kèn meritewul lii. Yalla nalleu Yalla takhawu 🤲🏽😭🥺
@athuaba7734
@athuaba7734 3 жыл бұрын
Auu massa ma soeur métina trop yalla na yalla safara
@aidadiouf5085
@aidadiouf5085 2 жыл бұрын
Yalla nako yalla safara 🤲😭 amine yarabi 🤲
@tackoba1051
@tackoba1051 3 жыл бұрын
Massa promt rétablissement svp les hommes amlen yermandé way
@ndeyembaye6074
@ndeyembaye6074 3 жыл бұрын
Massa ma cherie metina Yalha nalla Yalha samm si barki Seydina mouhamed
@minata2174
@minata2174 3 жыл бұрын
Suis désolée yaye mais, ya sacrifier sa dome...c’est la triste réalité!! Vs pensez dal que adouna seuy rékk la
@tigressesylla9941
@tigressesylla9941 3 жыл бұрын
Billay séy séy rék
@Yetou85
@Yetou85 3 жыл бұрын
Thieye
@Khadija-b5b
@Khadija-b5b 3 жыл бұрын
Bilay amna goor yo khamni takk djiguenn deviergé la rek dem lagnouy def fébar la si gnom
@L2Skn
@L2Skn 3 жыл бұрын
Sadique amneu 🤨😡, dagno sacrifié life xalé bi Courage sister, yalla na yalla safara lép amine ya rabbi!
@evandoye4112
@evandoye4112 3 жыл бұрын
Y’a des gens mauvais blh bayiléne soléne néké ak Sén diabar yi bagnou eubbb guéne abandonné léne akh bakhoul djiguéne gni tmt soyez responsable de vous même goor gni gneup yam motakh kou yabou ame diom nanguo liguéy di def Thi sa boppeu sou défé bakhna sou défoul bakhna takkal sa ndigu ma belle gua gorgorlou liguéy soit forte pour ton enfant té gua bayiko ak yallah tôt ou tard dinako guiss 🙏🏾
@mamadoudia3387
@mamadoudia3387 3 жыл бұрын
Mais lii metina trop way yalla nako yalla diapale
@aichademe1152
@aichademe1152 3 жыл бұрын
Massa yalla nala yalla defal diam
@moustapha9679
@moustapha9679 3 жыл бұрын
Metina lollll amlen yeurmandé thi djiguen yiiii mais sokhna si gua balma nak meti na trop mais worrr bakhoul bayinel lolou ko meusoul guiss gnou maylako
@maimounaka5561
@maimounaka5561 3 жыл бұрын
Deggo mounila dafa bagnoon wala ??? Moom wakhoon na dafa amm kenen avant Mouy marié ...fofou fan la woor gui nekk 🤔🤔🤔
@khodialoum1986
@khodialoum1986 3 жыл бұрын
@@maimounaka5561 je pense kimou bayi dém seuy ak ki lay wakh daf ko woor.
@moustapha9679
@moustapha9679 3 жыл бұрын
@@maimounaka5561 kou bakh setanal encore vidéo attentivement nak OK ki militaire ladone guenal copin mo takh mou bayiko dem seuy ak koumou meusoul guiss
@tigressesylla9941
@tigressesylla9941 3 жыл бұрын
@@moustapha9679 voilà les conséquences bo woré dingko guisse tôt où tard
@maimounaka5561
@maimounaka5561 3 жыл бұрын
@@moustapha9679 moom neena took n'a 2 semaines bagna sekkh ak moom Moy Warner ni dagn KO forcer mais woroul fofou lay wakher
@ndeyenogayediop237
@ndeyenogayediop237 3 жыл бұрын
Ndeye sann mettina lole me yalla nalla yalla takhawou
@assanendong1285
@assanendong1285 3 жыл бұрын
vraiment metina waye loudoul diekh amoul
@awaantagueye4562
@awaantagueye4562 3 жыл бұрын
Yalnala yalla safara metina
@feutimahbah4254
@feutimahbah4254 3 жыл бұрын
Metina trop yalna la yalla diapalee
@fatouamydia790
@fatouamydia790 3 жыл бұрын
Chérie yalla nala yalla taxawou wayé woor bakhoul
@modouboussoleye9782
@modouboussoleye9782 3 жыл бұрын
KOU WORE DAWE BA RÉNE MOU DJIKE LA DANIOULAKO DJIGNE YENA NDIEUKA WORE
@tigressesylla9941
@tigressesylla9941 3 жыл бұрын
🤔🧐
@yayemariegueye5910
@yayemariegueye5910 3 жыл бұрын
On compatis vraiment c'est dure Mais arrêtez les mariages précoces car c'est la principale cause des Fistules obstréticales (maladie de la Honte ) Et le traitement Chirurgical coûte excivement chér
@awabadiane8397
@awabadiane8397 3 жыл бұрын
Ndeyssane yalla nala yalla may werr 😭
@nsjsvdbldkdbfj2002
@nsjsvdbldkdbfj2002 3 жыл бұрын
Maye sa dome ko khamoul bene bokam dakh France la diougue yewoulene li louko fi diar khalebi nako yalla diapale si barke werou korr gui
@salymatadia3620
@salymatadia3620 3 жыл бұрын
Yalla na la yalla tahawou te may la goudou fane ak
@thianekhouma6045
@thianekhouma6045 3 жыл бұрын
Li metine 😭😭😭😭
@gayephone
@gayephone 3 жыл бұрын
Mais niata laniouko wakh pour mou fadiou
@nsjsvdbldkdbfj2002
@nsjsvdbldkdbfj2002 3 жыл бұрын
Li yobouko si doye bane mossi guaw legui mou wo wadji
@nabousow7754
@nabousow7754 3 жыл бұрын
Massa mais yalla bahna dena bah inchalla
@amyfall1831
@amyfall1831 3 жыл бұрын
Yalla nala yalla wereul ci barke seydina mouhamet inchallah
@kinediop2130
@kinediop2130 3 жыл бұрын
Yalnala sunu borom takhawou
@niangmodou47
@niangmodou47 3 жыл бұрын
Thieuy Sénégal ndaw lou yomb France rék nga may nitt diabar thé khamoko amo thi mome béneu thiofél ndeysane
@khodialoum1986
@khodialoum1986 3 жыл бұрын
Massa sister, mais hôpital bi ko accouché gnoko warone traité ba mou weur
@tigressesylla9941
@tigressesylla9941 3 жыл бұрын
Exacte
@alimaseye1542
@alimaseye1542 3 жыл бұрын
Vraiment
@astouffaye5576
@astouffaye5576 3 жыл бұрын
Yana nalla yalla diapale si barkel seydina mouhamed
@chicolisto4890
@chicolisto4890 3 жыл бұрын
Nit nêk na afriq ..gene dêmine kou nêk europ .....ohhhhh sone na si yêtêbi
@mounag8518
@mounag8518 3 жыл бұрын
Amna goor gnou bone. Voila les consequences des mariages precose.... fistules etc....Yallah na la yallah same mayla werr same sa dome teh may la dieukeur bou bakh.
@tigressesylla9941
@tigressesylla9941 3 жыл бұрын
Wallahi à 15ans bayi diangame bayi lépame ngua trokhale ko ni
@alioundiaye8096
@alioundiaye8096 3 жыл бұрын
Allahou akbar yalla nala yalla sammu waay 😭😭😭
@loracarton3891
@loracarton3891 3 жыл бұрын
Guiryallah diap lenn ssi dakar buzz hooo massa 😔😔
@Khadija-b5b
@Khadija-b5b 3 жыл бұрын
Li metina trop ana waye yalla bouko meuneu diapalé té yalla rek takh thieuy goor
@dialloelhadjialassane5086
@dialloelhadjialassane5086 3 жыл бұрын
Il faut tout m'efier les mariage intèrèt
@7863-p4y
@7863-p4y 3 жыл бұрын
Quelle intérêt
@deynabakebe7422
@deynabakebe7422 3 жыл бұрын
Tu n'a pas de photo de lui si tu as publié son photo
@tigressesylla9941
@tigressesylla9941 3 жыл бұрын
@@7863-p4y comme du genre donner la main de t'a fille à quelqu'un rien que pour son argent
@papatoure2319
@papatoure2319 3 жыл бұрын
Aahh yaye boye yenagui wakh nii wadji dafko waar mais mom yamite dafa waar kimou nekolone. Daggene di nekk ak nitt mouy teubb di daanou ak yow deggeu kounek France rek walla etats unis genn waar kiggene nekkale donc voila les consequences. Yalna ko yalla teggile naatou bi
@Yetou85
@Yetou85 3 жыл бұрын
Seul ceux qui habitent au Sénégal raisonnent comme toi.bo deukone France do wakhe ni. Sokhor bakhoule on est tous des Sénégal ais , peu importe où on vit
@abdoudiop5163
@abdoudiop5163 3 жыл бұрын
wadji moye domeram deugue sa akh dinako dale na deme rek
@khadifall2255
@khadifall2255 3 жыл бұрын
Wa Louga dano Bari xalis loutakh Manou nioko diaple
@salyndiaye7983
@salyndiaye7983 3 жыл бұрын
Vraiment
@aichatouba1613
@aichatouba1613 3 жыл бұрын
Deyssane c triste pour l'enfant également vraiment y a des hommes irresponsables .qd l enfant grandira et réussira un jour qu il vient pas dire maye sa baye ....
@aminatagueye6405
@aminatagueye6405 3 жыл бұрын
Wor bakhoul si lep massa waye louy modou modou gno gueune son gneup metina nak yalla na yalla safara
@myasarr9779
@myasarr9779 3 жыл бұрын
Il faut donner son nom et sa photo si vous en avez une y'a des gens qui vont le reconnaitre partout ou il sera en Europe wakhatouma France gui.
@abdoutoure2490
@abdoutoure2490 3 жыл бұрын
Aduna. Lou mou metí méti nagua ande. AK sa ngor. Té djieguen alllalou. Yalllalá Kiéne dou ko. Torakhale soumeté wahtanalakmom worr bakhoul
@diekygueye8530
@diekygueye8530 3 жыл бұрын
Masta yaye boye. Yalna Yallah safara lèpp
@serignendiayebeuguefallou7088
@serignendiayebeuguefallou7088 3 жыл бұрын
Thièy lii métina trop Gore bou bone bakhoul
@Miss-zk6et
@Miss-zk6et 3 жыл бұрын
Thiey Yalla . Deysane 😭
@salimatambaye1140
@salimatambaye1140 3 жыл бұрын
Metina 😭😭
@adjasiresene8332
@adjasiresene8332 3 жыл бұрын
Yalla nako yalla weurerl
@alimaseye1542
@alimaseye1542 3 жыл бұрын
Sokhena amo photo wame
@gueyekhadim9682
@gueyekhadim9682 3 жыл бұрын
Bayi len wor sino lunek meun nalen dal
@alioubaradambaye2251
@alioubaradambaye2251 3 жыл бұрын
C triste mais Nanou bayi khél ni wor bakhoul dogué worma bakhoul
@samirakontey1390
@samirakontey1390 3 жыл бұрын
Ayway li mettina troppp 😭😭😭je veux son numéro
@adjarassoul5680
@adjarassoul5680 3 жыл бұрын
Masta ma puce yallah dédji na bénén yapp boudoul dieun dina bakh
@adjacoumba1366
@adjacoumba1366 3 жыл бұрын
Thiey yalla
@dorndokh3344
@dorndokh3344 3 жыл бұрын
Operation bi mo bakhoul déh
@bobselassie4845
@bobselassie4845 3 жыл бұрын
C'est comme ca que vous marquez le visage de votre invite😡 Mougneul sister,dina bakh inshallah
@vieuxsonko9221
@vieuxsonko9221 3 жыл бұрын
Que Dieu te vienne en aide nous les hommes on doit changer de comportement
@ramatoulayendiaye6877
@ramatoulayendiaye6877 3 жыл бұрын
Il faut donner son nom et le décrire dou niak kouko guias. Boon amna wayé yalla bakhna
@mbalkakognedof5866
@mbalkakognedof5866 3 жыл бұрын
Akhou militaires bi mola dal Wor bahoul
@libellule978
@libellule978 3 жыл бұрын
Mais toi aussi fallait pas trahir ton petit ami de l'époque. Ça se voit t'es trop naïve. Qu'Allah te vienne en aide
@tigressesylla9941
@tigressesylla9941 3 жыл бұрын
Amine 🤲
@coumbazanklan6961
@coumbazanklan6961 3 жыл бұрын
Wor Bahoul Akh la
@sokhnandiayeba5606
@sokhnandiayeba5606 3 жыл бұрын
Merci Amy sope sama
@doudougaye6367
@doudougaye6367 3 жыл бұрын
yalna yala safara ko
@SokhnaKyKyLahi
@SokhnaKyKyLahi 3 жыл бұрын
Se marier avec un inconnu lii moy conséquences yi ndeysane courage à elle😳
@khadijawassa7976
@khadijawassa7976 3 жыл бұрын
Masta ma belle
@lunendiaye253
@lunendiaye253 3 жыл бұрын
Gnila ko may togne nagn la trop khaliss rék ndéysane
@nsjsvdbldkdbfj2002
@nsjsvdbldkdbfj2002 3 жыл бұрын
Wa anni kilako meyye
@ahmedgaye705
@ahmedgaye705 3 жыл бұрын
Warr bakhoul da nga warr militaire Bi motah li dall
@Yetou85
@Yetou85 3 жыл бұрын
Pourquoi les hommes font ça.expliquez moi svp
@serignetoubarekdogoukaseci6857
@serignetoubarekdogoukaseci6857 3 жыл бұрын
Wor bakhut Sokhna si
@abyfall6504
@abyfall6504 3 жыл бұрын
C est dur mais niou moytou worr bakhoul
@khadydiop793
@khadydiop793 3 жыл бұрын
Bilahi ma chérie woor baxoul
@tigressesylla9941
@tigressesylla9941 3 жыл бұрын
Voilà les conséquences
@khadydia5554
@khadydia5554 3 жыл бұрын
Bilahi! Pasc kokou france la nek rek! Nexoul ba nexul waye lep niomlaa
@boussodiouf1116
@boussodiouf1116 3 жыл бұрын
Bone amna
@daoudafaye4584
@daoudafaye4584 3 жыл бұрын
Nokoule félé wor kat bi
@marieheleneberre8736
@marieheleneberre8736 3 жыл бұрын
Mais quelle est la réaction du mari de sa soeur ? Ce n'est pas possible ces personnes irresponsables le mari de sa soeur et son ami.
@khadimniang2112
@khadimniang2112 3 жыл бұрын
No sénégal bye lén may ndiabr koguine khamot baxna modou modou ak Gui pa yam
@mamadoudieng2755
@mamadoudieng2755 3 жыл бұрын
Non
@sodambaye1628
@sodambaye1628 3 жыл бұрын
😭😭😭😭😭😭😭😭
@diopballackmouhamed890
@diopballackmouhamed890 3 жыл бұрын
Yalla naga an tan si barke saydina mouhamed me yaw nak daga wor nak
@zainasow427
@zainasow427 3 жыл бұрын
😱😱😱😱😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@yayouyayam339
@yayouyayam339 3 жыл бұрын
Waye wa hôpital lepou niom la
@rienquelajusticefuturejuri7561
@rienquelajusticefuturejuri7561 3 жыл бұрын
Kone gni gnogui waxate waxou seuye
@chicolisto4890
@chicolisto4890 3 жыл бұрын
Mane europ la nèk ....wakhe na ba sone bilahi ...europ dou tous dara nèkoufi ..soutoura rêk la maudou maudou yi di dokhè ....djiêgene senegalyi sk sêni wadiouryi ..gême lène sène bop .guir yalla ....mane europ la dêf presq sama lêpp .mè sama dome douma ka may maudou maudou ...poin barrr
@cheikhsakho3397
@cheikhsakho3397 3 жыл бұрын
doyena warr
@toubandiaye5507
@toubandiaye5507 3 жыл бұрын
Arrêté yéne tamite yéde yeureume mako gueune té sey yalla mokoy tak sa arass natou yalla la nak
@maremegueye3230
@maremegueye3230 2 жыл бұрын
Yen lougnou l'en def dagan n'a khalis nguen djital nooy maye nît diabar te khamo ay mbokam
Enceinte et en Bazard: Les Chroniques du Nettoyage ! 🚽✨
00:21
Two More French
Рет қаралды 42 МЛН
Quilt Challenge, No Skills, Just Luck#Funnyfamily #Partygames #Funny
00:32
Family Games Media
Рет қаралды 55 МЛН
Revue de presse Ahmed Aïdara du Jeudi 19 Décembre 2024
7:21
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 60 М.
Solange Beyala sort du silence
1:37:49
Porkam officiel
Рет қаралды 4 М.
My LIFE AVEC AIDA DIALLO - Episode 01 Sur SenTV
35:00
Sen Tv Officiel [DMEDIA]
Рет қаралды 53 М.
Revue de presse Mame Khalifa Jeudi 19 décembre 2024
18:57
DAKARBUZZ TV
Рет қаралды 16 М.
Enceinte et en Bazard: Les Chroniques du Nettoyage ! 🚽✨
00:21
Two More French
Рет қаралды 42 МЛН