Bon Gamou a tout le monde.. Baye niass love.. Ila Medina Baye…
@elhadjika7482 Жыл бұрын
Il faut épingle hein
@ousmanekamara8527 Жыл бұрын
Inchallah 🙏🥺 vous êtes les prophètes du hip-hop je dis bien les prophètes du hip-hop galsen 👑♥️ bilahi 🥺🥺🥺🥺 yalla nalein yalla aar si barké Baye Niass ✨
@mamadouas-sidiqoutijanyfal2471 Жыл бұрын
BAYE MOY DEUGGUE ☝🏾❤
@BintaNyang Жыл бұрын
Hol yi sed na ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@adjiasamb8244 Жыл бұрын
Niass ❤
@NguerAziz Жыл бұрын
Ma fi djitou🥰 1 million avant gamou qui est dacc Dieureudief BAYE NIASS 🥰❤️
@IMAMLINGERIE4227 Жыл бұрын
Dieredieuf yaw da nga bakh
@YADISCO-PRO Жыл бұрын
😅😅😅😅😅 non non😊
@sadickbraindpglofficiel4967 Жыл бұрын
❤
@elhadjifaty8219 Жыл бұрын
Machallah ya bakh
@NguerAziz Жыл бұрын
@@YADISCO-PRO mala djitu dh 😂
@kimNi221 Жыл бұрын
Kou Beugg am dome bou Goor toudéko Cheikh Ibrahima lalal j'aime Svp♥️
@aliounebarry373111 ай бұрын
❤
@backrinediouf28419 ай бұрын
❤J’aime cheikh ibrahima niasse❤❤
@mariamasakho3886 Жыл бұрын
Le bonheur d’être talibé cheikhna akhmed tidiane chérif est inexplicable alhamdou Lila binou amé Maolana cheikh Ibrahim migni xamal cheikh tidiane Dieureudieuf Baye niass❤❤❤❤❤❤
@fayeahmadoulamine6790 Жыл бұрын
Je suis mouride mais j’aime Baye Niass éperdument ❤
@ousmanembodji1634Ай бұрын
Je suis mouride mais j'aime baye Niass éperdument❤
@elhadjidione7279 Жыл бұрын
Kou Beuge Am dom bou gour toudiko Seydina Mouhamed lalal j'aime👍🤲
@alamiinibnabubakrdiop7473 Жыл бұрын
Linga wax mom nieup ko beug ❤❤❤ Salalahou aleyhi wa salam
@sadiondoye4435 Жыл бұрын
PSL 🥰
@sadiondoye4435 Жыл бұрын
Alhouma amine inchallah 🙏
@vivianeniasselareine2847 Жыл бұрын
Psl
@ndeyekhadygueyeaw1938 Жыл бұрын
Alhamdoulilah bamako sougnou Borom mayé
@Domoumoustapha Жыл бұрын
Baye si khol yi❤️ tarikha tidjiania si dieumou yi ak si khel yi🥲 Talibé cheikh si djiko yi🫶🏾 Beyti baye si lokho yi✊🏽 Bourde sunu yitté☺️ Mbecté mi dioli ba médina baye❤️🩹 Alhamdoulillah diarama maoulana cheikh Ibrahima niass❤️🙏🏽(bind ko si commentaire yi)Djeureudjefé baye🫶🏾
Kou beug am dom bou gour toudiko barké baye Niass machalla doli santé yalla bou bakh ak Baye Niass dieureudieufée Baye Niass❤🙏🤲🥰🥰
@AminataNdiaye-v5k Жыл бұрын
Ohhh wa médina baye kaffrine thiey yalla ahhh li nexxna barrière baye willane😊
@sidyadiaby6706 Жыл бұрын
Thieuy deyza sa parole rek may ray barki baye niass dundall weral lo dundou doyul barki baye niass binou bok 🤲🏾 ♥️ 👑
@AstihYade-yq1gh Жыл бұрын
Niou beug Baye Niass kay🥰🥰Nékhna way
@aissatoukebe7839 Жыл бұрын
❤️❤️🥺le bonheur que vous procurer à chaque Gamou 🤣😍❤️🥹meuno léne sax comprendre Yalna Baye faylén bopppam
@ibrahimadiongue513 Жыл бұрын
Je suis Mouride mais Baye Niass je l’aime sincèrement. Nitou yalla deug leu. Et sa relation avec la famille de Cheikhoul Khadim à l’occurrence Serigne Fallou est une illustration et exemple pour nous ,jeunes d’aujourd’hui . Di jegalou waat bou bakh si kadou yi
@ramata.t9351 Жыл бұрын
Kaadou yi rafett n'a machallah... et c'est cette relation qui devrait perdurer entre jeunes mourides et jeunes tidianes😊
@ibrahimadiongue513 Жыл бұрын
Vous avez sur toute la ligne ma très chère. Que le bon Dieu exauce toutes les prières formulées à cet égard ❤.. ioe tmt nit kou bakh geu Pask kou bakh moy guiss lou raffet diko wakh
@ablayetoure2071 Жыл бұрын
Machalah yalla yokou diamou doli soutoura si barké Mame Ibrahim fall borom koosy wayou baye ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@dijablishofficial1477 Жыл бұрын
Walakhi khamouniou louniou souniou wadji diaral borom kaolack mo bakh souniou wadji beug ko rekk diam nguaye doundou foh tolou moniou khamal yone wi Diém thi yallah baye moye sohniou baye sheikh al Islam yalna yallah yokou lerram té Tass niou si barkém sons bi nice neu trop machalah❤❤
@wiiz-jullow9 ай бұрын
Alhamdoulila si le fait ma tokk tay du guis Sama bobou si klib bii diereudiefè baye kou ko si wakh yalla gua fèkè dewen❤
@sarrbrickest-kp2zo Жыл бұрын
Dak rap dak weuy geune lén xam yalla dakk lén lép geune lén dégeu yalla 👆🏾Grâce à maolahna cheikh Ibrahima 👈🏿dieuredieufé baye niass🙏 ❤🙏❤🙏
@fatoudiaseck1649 Жыл бұрын
Barki borom Touba Baye dama ko beug té yalla rék tah❤❤❤
@ousmanekamara8527 Жыл бұрын
Ohhh 🥺 encore les prophètes du hip-hop galsen 👑 🥺❤️ vraiment je vous adores 🥺❤️
@aminataniasse9477 Жыл бұрын
Wallahi dama setan clip ma sama beugne yii😁😁ba clip bi diéx ndax contentement dieureuffe Baye Niass, dieuradieufati akhlou brick
@ndouramboup9178 Жыл бұрын
magal dewen wayal lén niou noiun mourid yii baye bi mome machallah yalana lén yalla sam si barké serigne fallu
@abdoulayeseck10 Жыл бұрын
Kou beugue baye niass rék lalale j'aime ❤
@momothiam238 Жыл бұрын
Mourid sadix ma beug baay way❤❤❤🙏🏾
@aissatouloum1970 Жыл бұрын
Folen degeu mouride bou beug baye niass lék diapeu lenma ss la Dieureudieuf baye barkhama ❤❤❤❤❤❤
@SallCoumba-jx9id Жыл бұрын
Billahi Baye takh na ma diap len ba faw machallah fiert d'etre Barhamienne
@mouhamadoudiouf213 Жыл бұрын
😢 oh c beau😊😊. Je suis Mourirde mais quand je vois ceci je ne peux que m'émerveiller. Le soufisme c'est ma vérité
@Djigo-thiam9192 Жыл бұрын
Alhamdoulilah diam si gneup si barké mawlana baye Niass
@bintaba2970 Жыл бұрын
Barké baye niass son biii niomouy deff sama khol bi enh 🥰🥰🥰❤❤❤
@RoiMouhamedVI8 ай бұрын
vraiment ls paroles st riches ....surtous boul yame si taram bi ,kalam bi ak niolay bi ohh
@OuzzbayemamouTV Жыл бұрын
Baye la solution Rék laye tope je suis fière d’être talibé❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️✅
Billahi damalén meussa beugue avant même de savoir que vous étiez des Barhamiens❤️✨ chaque année nianguén ni sédalé sama khôl Yallah nalén ko Ya Rabbee fay🤲✨❤️🥰
@josephinethiaw5826 Жыл бұрын
Nice clip bon Gamou frères et soeurs Musulmans on vous aime ☦️❤🙏
@MadijaGaye Жыл бұрын
Version Sped Up Rakadiou Ci Baye kzbin.info/www/bejne/d4jCdnpripmkaKssi=Qf1iDFtm4qkZP_zt
@talladiankha Жыл бұрын
Kou beug Baye lalale j’aime ❤
@akhloubrickyoutube Жыл бұрын
Merci 🙏
@talladiankha Жыл бұрын
Nioune yéne rék lagniou beug ❤
@sarrbrickest-kp2zo Жыл бұрын
@@akhloubrickyoutube❤❤❤
@ThianéDiop-f1g4 ай бұрын
❤❤❤❤❤ @@akhloubrickyoutube
@DameNdiaye-lz4ox Жыл бұрын
Man murid la waye dama beugue baye loll ❤️ 🌹😭 billahi
@domouyayameyas2689 Жыл бұрын
Dyazaaaaaaaaaaaaaa😂 🔥🔥🔥🔥🔥 quel couplet !!! Do nitt! Barke mame ibra fall wayou Baye ! Ra
@elimanethiongane7346 Жыл бұрын
Boromm Xelll rekkk moyy Déegueu liiguéen diii djioudiou du début jusqu'à la fin Ndeyssane walahi😅souguéenko khaamoon daww raadjiou djiie thie Baye al hamdoulilah Dieureudieufé baye
AŔRA TU AS UNE VOIX EN OR MASHALLAH. DEZA LE FLOW DE TON RAP EST SUPERBE❤❤❤❤ J'AI ÉCOUTÉ CE SON PLUS DE 100 FOIS. FORCE A VOUS AKHLOU BRICK . RAKADIOU NA CHI SON BI C'EST VOTRE CHEG D'OEUVRE ET DIEU SAIT KE TOUT VOS AUTRES SON SONT TOP. BIG UP GUYS KEEP UP THE GOOD WORK. MUCH LOVE❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@thiernodiouf7182 Жыл бұрын
Vous êtes encore rempli du joie dans les cœurs ❤
@fatousharassouldiouf2945 Жыл бұрын
Barké Ahmadou Bamba son bi dinama doflo,chak jour plus de 5 fois,on t’aime Baye❤🎉
@seckantoinette4294 Жыл бұрын
Merci infiniment @Akhloubrick . Rombeu naniou sakh rakadiou si baye wayé danio diekh takk si mawlana cheikh Ibrahim. Guissouniou loudoul cheikh Ibrahim Doundouniou loudoul cheikh Ibrahim Alhamdoulilah limouniou hamal mo nekhal souniou doundou motakh amouniou sago si dieum dji.. Ila medina baye inchalla
@MamaThiam-o2q Жыл бұрын
Macha Allah Yalna yallah fay lén ya rabi Si kow si kenem Akhlou brick ❤
@SetaSoums-bp1dw Жыл бұрын
Mashallah long vie à vous inchallah qu'Allah vous protège ❤🇲🇷🇸🇳🇲🇷🇸🇳
@kmbtvofficiel Жыл бұрын
Machallah rafetna ❤yalla n'a diamou yageu yarabi 🤲
YAINE RÉK LAGNOU TOPE..VOUS AVEZ RÉPONDU À L'ATTENTE...MACHA ALLAH.. TRÈS NICE
@AblayeDiouf-kn4ks Жыл бұрын
Bilay niou ngi lene di niaanal yalla bou bakh khawma kane deh mais mane rouslo wolenma yalna yalla yokou lene ❤❤❤
@maamcheikh621 Жыл бұрын
"Rakadjou Thi Baye" est en ligne sur youtube. Un régal musical qui justifie l'amour inconditionnel que portent Ara & Deyza à Cheikh Al Islam et, partant, à toute la Communauté Niassene. A consommer sans modération.
@MadijaGaye Жыл бұрын
Version Sped Up Rakadiou Ci Baye kzbin.info/www/bejne/d4jCdnpripmkaKssi=Qf1iDFtm4qkZP_zt
@babacarsine3206 Жыл бұрын
Toujours au top 🔥🎉moment bou maye Sétane vidéo bii j’ai une cœur remplit de bonheur ❤😭 yalla na léne yalla faye séne khole ❤️🎊🙏
@aichakoita8010 Жыл бұрын
Mawloud Moubarak a touts les HUMAH ISLAMIQUE 🤲🙏🙏🤍🤍🤍💙💙
@ouzediop9218 Жыл бұрын
Diereudieufeee maoulana cheikhal Ibrahim borom Minka ilayka❤❤❤❤
@KhadijaGueye-h4k6 ай бұрын
Le bonheur 🥹 d’être Talibé Mawlana cheikh Ibrahima niasss walahi c’est une chose barhamienne📿 ou rien 🫶🎉🥳🥳
@berthamendy7439 Жыл бұрын
Oh lala machallah chaque année damay yakamti leur son pour le Gamou suis Chrétienne mais j'aime tellement Baye Niass c'est plus fort que moi en plus Akhlou Brick vous assurez comme d'hab bne continuation mes bro et paix sur vous bn Gamou à tous❤🥰🥰🥰
@chei.b11049 ай бұрын
Ya niakk ignann rekk jamou siyoww
@papesarrsarr Жыл бұрын
❤❤❤ vraiment je suis très très très content de vous chaque année damlay ni khar ak pasience walakhi yaina takh ma xame kouy baye barhama niass top ko nak nakh dama beugue yalla ak kouma khamal yalla bima toper baye barhama niass la xame sama bop ba paré xame yalla Di santeu maolana cheikh Ibrahima Niass ❤❤ dieurdieufti Baye barhama Niass
@modouridialbrickestgueye7667 Жыл бұрын
Sma kaw lall la nelawé fi la yéwo ci rakadiou bi ci Baye❤ no daay deff effet mbegté ❤