"Al Maktoum diokhouko Wird": Serigne Moustapha SY répond à son frère Serigne Abdou Sy et révèle !

  Рет қаралды 87,273

Senegal7

Senegal7

Күн бұрын

Пікірлер: 185
@moussasall4236
@moussasall4236 3 жыл бұрын
Notre fierté serigne Moustapha s’y ❤❤❤
@ousmanecisse4262
@ousmanecisse4262 Жыл бұрын
Jtm beaucoup seydi mouhamdal moustapha sy ❤❤❤❤❤
@mamadousy3749
@mamadousy3749 3 жыл бұрын
Vraiment serigne Moustapha sy bouko serigne cheikh diokhoul wird koukoye diokh ha domou bayou Sénégal yi dafa méti
@sokhnan963
@sokhnan963 Жыл бұрын
Machallah yalla n'a yalla samou sarigne mostaph
@khalilmourabytv7116
@khalilmourabytv7116 3 жыл бұрын
Serigne babacar Sy mansour yalna fi yagg té werr Al Khalifa
@coeur2lion38
@coeur2lion38 3 жыл бұрын
Amine way
@elmalick9288
@elmalick9288 3 жыл бұрын
Amine
@mallbelly8250
@mallbelly8250 3 жыл бұрын
Serinie Moustapha sy yal na fi yague
@laminendao3413
@laminendao3413 3 жыл бұрын
Serigne Moustapha sy yal nafi yagu té wérr mom rek mofi nekk
@coeur2lion38
@coeur2lion38 3 жыл бұрын
@@mallbelly8250 amine way
@taphamboup9859
@taphamboup9859 3 жыл бұрын
Yalle na niou yalla mosoul si none boudoul kholam fekh té samal niou sunu kilifeu cheikh Mohamedoul Moustapha sy almakhtoum
@lasguevaraelche5487
@lasguevaraelche5487 3 жыл бұрын
Je vous respecte et je vous aime bcp en tant que baye fall car vous n'ignorez pas l'éternel combat qui est la lutte contre les lobïstes qui veulent à tout prix diviser la religion que Dieu vous protège Sy Malick l'islam est une religion avec des actes des actions et la pratique et vous en êtes toujours conscient🙏🙏🙏
@lunelune8872
@lunelune8872 3 жыл бұрын
Vous les mourides vous n'aimez pas serigne Moustapha..vous avez hates de voir la famille de maodo s'entre déchirer khamna gnou leup.
@lunelune8872
@lunelune8872 3 жыл бұрын
Vous les mourides vous n'aimez pas serigne Moustapha..vous avez hates de voir la famille de maodo s'entre déchirer khamna gnou leup.
@lasguevaraelche5487
@lasguevaraelche5487 3 жыл бұрын
Saa déguine soriwul bal nala ci xol bu sed gouy kudul macky avec son gouvernement satanique ño far ab julite dey rafet ndjote jeumeulé ci moromam sa turundo jambari l'islam la wone Seyduna Aliou psl borom diassi dji yaaga xéxaal islam donc conscentres toi sur le véritable combat et ignores les détails jajëff👌
@binetagueye211
@binetagueye211 3 жыл бұрын
Baye fall nékhal thi jam deugeu dou robeu ay nop. Sa wakh yiw rafet na yalla na yalla fay la yiw thi barké souniou RM Serigne MOUHAMADOUL Moustapha SY
@inconnu90000
@inconnu90000 3 жыл бұрын
@@lunelune8872 yen gniy xalaat lolou key yenna ko mel C'est celui qui dit qui est ☝️yaye xacc deh yaw.
@modousall8066
@modousall8066 3 жыл бұрын
Notre fierté serigne Moustapha sy
@diamesenghor82
@diamesenghor82 Жыл бұрын
De toute façon Serigne cheikh moné à plusieurs reprises et publiquement Serigne Moustapha Sy moy patron wa moustachidine wal moustachidate té Serigne cheikh foumou tég daïra bi douko diokh koumou tagataloul bopam
@laminendao3413
@laminendao3413 3 жыл бұрын
Machallah sy Malick yal nala yalla fay
@papama1975
@papama1975 3 жыл бұрын
Yaw ko bakhgua Sy Malick trust me kou sellega Mashaa Allah we love you Moustaph 🇬🇧🇬🇧🇬🇧🇬🇧🇬🇧❤️👈🏾
@mordiop3404
@mordiop3404 3 жыл бұрын
Notre fierté moustarchedine❤️❤️❤️❤️
@seydinayoussouphandiaye8708
@seydinayoussouphandiaye8708 Жыл бұрын
Serigne moustapha sy yalna fi yagg teu wérr
@antisysthemebi2347
@antisysthemebi2347 3 жыл бұрын
En tout cas ce frère de serigne moustapha est un jaloue de son frère
@joodiop1182
@joodiop1182 3 жыл бұрын
Lolou rék la amoul lenene
@joodiop1182
@joodiop1182 3 жыл бұрын
Lolou rék la amoul lenene
@galayediop3150
@galayediop3150 3 жыл бұрын
limouy wax yeup sax dou deugue
@abdoundiaye4247
@abdoundiaye4247 3 жыл бұрын
@@galayediop3150 lane mossi deugue ak loussi aye fene et des précisions stp
@lucidestory1360
@lucidestory1360 3 жыл бұрын
del Xalaat bala ngay wax
@morgueye2635
@morgueye2635 3 жыл бұрын
Machalla s'y
@puulartv1790
@puulartv1790 3 жыл бұрын
Svp le Sénégal n'a pas besoin de sa svp prions pour que le bon dieu bolélèn niiu done ay waye naniou njabe niou dioubo 😭😭😭😭😭😭😭
@sanougadiaga2330
@sanougadiaga2330 3 жыл бұрын
ctgcvc
@sanougadiaga2330
@sanougadiaga2330 3 жыл бұрын
vvgcvgg
@sanougadiaga2330
@sanougadiaga2330 3 жыл бұрын
8c
@sanougadiaga2330
@sanougadiaga2330 3 жыл бұрын
vyvgvg
@sanougadiaga2330
@sanougadiaga2330 3 жыл бұрын
vvhvgv
@toureadama8639
@toureadama8639 3 жыл бұрын
Machala
@PetitKamara-yy1vj
@PetitKamara-yy1vj 10 ай бұрын
Walay ndaysan
@awabalde6432
@awabalde6432 Жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@dienauto4087
@dienauto4087 3 жыл бұрын
Patron = TARIKHAS = hiérarchie = ils bouffent votre argent. Mais yewoulene C'EST PAS POSSIBLE. MOUHAMMAD PSL N'A PAS ENSEIGNÉ ÇA
@dameseck6232
@dameseck6232 3 жыл бұрын
اعوذ بالله من الشيطان الرجيم ياسلام وياسلام في سنغال أمين يارب العالمين
@seyadhafida8849
@seyadhafida8849 3 жыл бұрын
🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
@omargueye5731
@omargueye5731 3 жыл бұрын
Bayill wax
@elagendiougalyr8449
@elagendiougalyr8449 3 жыл бұрын
Wahko sa baye
@badiartv242
@badiartv242 3 жыл бұрын
Dafa melni li sounou BOROM di diokhe sene lokho laye diare, n importe quoi
@zeynaboundiaye7128
@zeynaboundiaye7128 3 жыл бұрын
Nite daye mandou sou khamoul
@ibrahimadieng5242
@ibrahimadieng5242 3 жыл бұрын
@@zeynaboundiaye7128 kii boul kaa tontou wayé lath kaa yalla day wath dioxé wala dakay diaralé sii niit wala
@joodiop1182
@joodiop1182 3 жыл бұрын
@@ibrahimadieng5242 waw kay yaw wakh nga lepou
@joodiop1182
@joodiop1182 3 жыл бұрын
@@ibrahimadieng5242 waw kay yaw wakh nga lepou
@macdouseptique7278
@macdouseptique7278 3 жыл бұрын
T'a rien compris!
@tivaouane669
@tivaouane669 3 жыл бұрын
Loutaxe yéni domou Adama yi sohore Serigne Moustapha Sy gamou waxe si yalla AK yonente bi psl loléne beugue yéne merde waye lane moye sene probleme sene xole you bonne yi doumasa féhe
@sirajiba7450
@sirajiba7450 3 жыл бұрын
Wallah wallah
@enzokuhlemomo2060
@enzokuhlemomo2060 3 жыл бұрын
Lolou boumla mèti mon frere thierem Mo tolou nonou rek mais amoul morom sy malick
@mouhameddiouf3765
@mouhameddiouf3765 3 жыл бұрын
En Kone 2012 nga geuthie giss Serigne cheikh
@elagendiougalyr8449
@elagendiougalyr8449 3 жыл бұрын
Al Amine kagne là gueja guiss Mame Cheikh? Serigne Mansour kagnla gueja guiss Mame Cheikh? Serigne Mansour tawou Al Maktoum kagne la gueja guiss Mame Cheikh?
@mouhameddiouf3765
@mouhameddiouf3765 3 жыл бұрын
@@elagendiougalyr8449 laouiy .nioniou Séne baye reubou lene .Mustafa bayam dako reubeu
@MansourMbaye-t8q
@MansourMbaye-t8q 2 ай бұрын
Bly daka reibb
@omarseck4962
@omarseck4962 3 жыл бұрын
Il 'est triste ce gars là ce qui me fait mal moy borom kham kham yi la top rek dila diemeu layal rek Et sache que tu ne vas jamais entendre khalif général ndeyssane Way Yale na sunu borom deugeurel khalifa Ababacar sy khalife général des tidianes
@khalifasembene5878
@khalifasembene5878 3 жыл бұрын
Lane moy khalifa générale Ki eup lolou Yeine mame cheikh bigueine ko ko toudei laleine lakhatou Ndah lolou dou thieurou ada kepp T alhamdoulilah biniou ada teunkoulei Ki donou cheikh nk nieup xamnaniou ko mouy hassir mou sell mi Yallah naniou ko yallah sammal mou matalei yeineime❤️❤️😭 na khol yi fekh rk nieup am diam❤️❤️❤️
@omarseck4962
@omarseck4962 3 жыл бұрын
@@khalifasembene5878 ki dou dara ani borom kham kham yi weurone papam exemple cissé djingué donc kholen ki est ce manipulateur
@elagendiougalyr8449
@elagendiougalyr8449 3 жыл бұрын
@@omarseck4962 dis moi sur quelles bases ngeine japni Mbaye sy mansour mo wara neik Khalipha?
@elagendiougalyr8449
@elagendiougalyr8449 3 жыл бұрын
Wahma louy khalif général. va voir la genèse de ce titre au Sénégal et tu verras que li Maodo wahone ni Sénégal diné doufi dane ada jamais lolu rek là. mieux encore diga guisni reuyou fitra rek là mais nak xamxam yoyu daleine di soute ndah si képarou Cheikh Seydi Mouhamadoul Moustapha SY AL Maktoum, Al Mourchidoul ham rek ngeine koy dégué.
@elagendiougalyr8449
@elagendiougalyr8449 3 жыл бұрын
@@omarseck4962 légui ioe nioune niola wara tontu pourquoi Cissé Djingue. bola tolé nonu démal demander ko. et de passage aussi demandel maak gni andone ak Maodo té opposé Serigne Babacar kérok bi Maodo lakou funiuko teike? Ensuite nio meuna discuter. et comme disait Mame Cheikh rek "bi goorgui lako maak gni nafékoul yeup mane laniu jayantél". kou am bénéne attitude nak momla. Voici klk éléments de réponses pour nga xam figay ték sa tanke dans un terrain inconnu à moins k nga neik nafeikh: Serigne Papa MALICK Gamou 1997, keur Jeumb
@lunelune8872
@lunelune8872 3 жыл бұрын
Un fin manipulateur je vous jure..il dépasse de loin ses auditeurs. Des larmes de crocodiles pour mieux ferrer les talibes fanatiques et légitimés son fils..ouvrez vos têtes. Il ne croit pas en almakhtoum seul pape malick était fidèle à serigne chiekh. Qui vrai pouvoiriste leu...nima ko khamé dafa eup sakh...neneu Maodo ak Serigne babacar ak serigne chiekh dagnou ko done djeukeunté. Riiiiiirrrrre.
@binetagueye211
@binetagueye211 3 жыл бұрын
Alioune YABAR nopal sa bop nioune ay Moustzrchides laniou. Nous sommes indestructibles incorruptibles. Nioun ak souniou serigne ila abath inchallah
@momofall882
@momofall882 3 жыл бұрын
Nono lloy sokhor KO beugoul doko setane baye xam limouy wax
@morniang9878
@morniang9878 3 жыл бұрын
Sa khole dou fébaré do nagoule mouk kou Yalla bakhale . Ko khamné yar des milliers de personnes ño khamné niola EUP xam xam gueune la sélle. Wédi Serigne MOUSTAPHA Sy ALMAKTOUM moye wédi Mame CHEIKH dakh moko wakhone bounioula nara SACRIFIÉ ñou diokhé sougnou BAKANE. Kone nak kouye méré mérére Mame Cheikh dakh bamoukaye wakh foire nieuppeu ngui tok
@diagnendoye5756
@diagnendoye5756 3 жыл бұрын
@@binetagueye211 WALLAHI Al MOUSTARCHIDINES les indestructibles et incorruptibles moralement et physiquement MASHALLAH
@Awa894
@Awa894 Жыл бұрын
C’est son fils qui l’intéresse points
@galayediop3150
@galayediop3150 3 жыл бұрын
bayilén ndaye saytané waxdji yague na
@almoukhtar2608
@almoukhtar2608 3 жыл бұрын
Mdrrr est-ce que yaa ngi fi lii kagne la 😂😂😂😂😂😂😂
@papemakhasy281
@papemakhasy281 3 жыл бұрын
Doul rék amoul kilifa
@moustaphagaye1457
@moustaphagaye1457 3 жыл бұрын
Sa way yaw tamit amo kilifa en plus Omar Sall moma geuneul sa kilipha fouf
@naboufaye4918
@naboufaye4918 Жыл бұрын
Yow dé nianal yalla am lii Serigne Moustapha Sy am daffa am kilifa bamou nianalko Nikko mougne la narré sacrifié ma diokhé sama bope
@daoudandiaye7706
@daoudandiaye7706 3 жыл бұрын
Noooo mann lima diaakhal mooy … kiii doula wakh kéneu koudoul boopam, fooko féekeu boopam rk layy wané ahhhhh👎🏿👎🏿👎🏿👎🏿
@moustaphagaye1457
@moustaphagaye1457 3 жыл бұрын
Waw parce que lolou nga beug guiss si mom boula xam xam nioré daguay dém sétani intégralité gamou gui wala dém xoli archives waxtane yi amoul loumou diangalé woul plus 5000 k7 deff nako té a l'âge de 29ans laniou ko diox trophée ni Sénégal mofi nék jeune bi daka firi alkhourane bo meunoul deff lolou nga képou ko té xamni yak site internet yi yéna yam
@قلخيراأوتصمت
@قلخيراأوتصمت 3 жыл бұрын
Yaw yaman fèn Dèmal nga dèglou wakhtan wi yèpe Yarasoulou lakhi Bayil fèn dèg nga
@ousmanecisse4262
@ousmanecisse4262 Жыл бұрын
Jtm beaucoup seydi mouhamdal moustapha sy ❤
@matargueye7200
@matargueye7200 3 жыл бұрын
Amoulen khamkham wakh rek you amoul sanse wakhou yalla douguenn ko wakh mouk
@tivaouane669
@tivaouane669 3 жыл бұрын
Matar Gueye ya meneu doule sétano gamou gui xole bou bone nga yore nite ki loko bagne bagne bou waxetané si yalla AK yonente bi psl dagnakoye nangoule
@ngeumsabopou1415
@ngeumsabopou1415 3 жыл бұрын
Matar gueye bo tothione sa leufeul ndeye yém sisa serigne
@mansoursamb5921
@mansoursamb5921 3 жыл бұрын
Sa baye doula wahh Lou eupeu lifi serigne bi wahh
@serignesaliou9615
@serignesaliou9615 3 жыл бұрын
Matar geuy sa khol dou fékh moukk
@inconnu90000
@inconnu90000 3 жыл бұрын
Yen waxleene thi yallah te bayi sen waxi keur yi! Sofguene trop ay dioxe wird andi wird dieuli wird moy lan???? Koumou nekh dieul werde toudou yalla amoul diox amoul idiaza amoul dara nekouleen thi dara danguendi fo rek sen waxtaane you niak xorom yii 🤣
@abdoulayegueye7760
@abdoulayegueye7760 3 жыл бұрын
Mdr Kone ioe deglou wakhtane bi yeup une partie rek gua si am😂😂😂c’est triste
@julodaigne4172
@julodaigne4172 3 жыл бұрын
Kom lolou nga diap manoul si ta dem wirdal sa pop nek sa kilifa bop
@julodaigne4172
@julodaigne4172 3 жыл бұрын
Manoul
@mymaboydiaba
@mymaboydiaba 3 жыл бұрын
Yaw dagua rérr ndaysann
@Mboup505
@Mboup505 3 жыл бұрын
🤣🤣🤣🤣🤣Lol Mbaye palmarin dèmou si discours bimou donn dèff lann mo si ham ham
@matargueye7200
@matargueye7200 3 жыл бұрын
Yenn daguenn defene yenna sake adouna te figuen ko feke ti FI guenn koye bayi yalla momm bakou mai dou yenn dara mounoulenko sake di raye nitte gnii ak wakh you bari
@mansoursamb5921
@mansoursamb5921 3 жыл бұрын
Beugue wahh ac Doul mo tahh ngayy wahh si KZbin bi
@abdouniang2356
@abdouniang2356 3 жыл бұрын
Segne chiékh sabaye ngaye dir mbageu wayé bokou léne mola apou fitt apoula xam xam apou yar geunela ami teguine
@mansoursamb5921
@mansoursamb5921 3 жыл бұрын
Sa baye yarou la nahh boula yoronn dinga kham noyy Wakhè ac kilifeu Té bo sétannè wakhtanou S.Cheikh ni ladonn wah Demal kholi archives yi bande clown
@abdouniang2356
@abdouniang2356 3 жыл бұрын
@@mansoursamb5921 loume ma niaka yar niaka yar samak yaridikou dieumalé woumako si samaye baye ak raki baye mane ngaye segne chiékh lima yor aye arsiv yoroko
@laminendao3413
@laminendao3413 3 жыл бұрын
Iow da nga nday rew la wakh sa morom da fé nday nek boy wakhal iow rewo Gueumal li nga Gueum rek bayi niou Gueum li niou Gueum rek diam am fi
@mansoursamb5921
@mansoursamb5921 3 жыл бұрын
@@abdouniang2356 mais ki matt nala baye
@mansoursamb5921
@mansoursamb5921 3 жыл бұрын
@@laminendao3413 Mais mann S. Moustapha la geum
@fatufall2409
@fatufall2409 3 жыл бұрын
Yaw bayil wahke wakh rk gay diff
@tivaouane669
@tivaouane669 3 жыл бұрын
Fatou fall sa baye moye waxe Kate bou mag bi
@Mboup505
@Mboup505 3 жыл бұрын
🤣🤣🤣Khana sa baye moyy bou mag bi
@ngeumsabopou1415
@ngeumsabopou1415 3 жыл бұрын
Fatu fall yaw koulay baramou si moutty nga beug
Serigne Moustapha SY sur Ousmane SONKO - Extrait Yawmul Murchid
5:25
Femmes Dévouées
Рет қаралды 212 М.
To Brawl AND BEYOND!
00:51
Brawl Stars
Рет қаралды 16 МЛН
Cheerleader Transformation That Left Everyone Speechless! #shorts
00:27
Fabiosa Best Lifehacks
Рет қаралды 14 МЛН
FOIRE ANTET DERNIERS RÉGLAGE
11:44
Samagal
Рет қаралды 40
L’invité de la RFM : Serigne Abdou Sy, ibn Cheikh Ahmed Tidiane Sy Al Makhtoum
18:50
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 100 М.
Serigne Abdou Sy Al Makhtoum invité dans RFM matin du 23 Aout 2021
14:15
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 196 М.