Alahu Akbar😱🤭khekh bou meti entre liss Ndiago et Ada Fass: paka yi Diassi yi🤭Alahu akbar..

  Рет қаралды 57,088

LUTTE MOTIVATION

LUTTE MOTIVATION

Күн бұрын

Bienvenue sur votre chaîne (lutte motivation)
abonnez-vous ✔️ | partagez✔️ | commentez✔️| aimez ✔️|
Toute l’actualité de la lutte sénégalaise et des contenues d’inspiration quotidien!
Instagram ➡️ / lutte_motivation_officiel
KZbin ➡️ / @luttemotivation
Snapchat ➡️ / zyp10ybm
Facebook ➡️ www.facebook.c...
Tik tok ➡️ www.tiktok.com...
Thread ➡️ www.threads.ne...
Contacter nous sur Watsap 👉 77 265 29 18

Пікірлер: 173
@Le_Baobab
@Le_Baobab 7 ай бұрын
Liss Ndiago n'est pas un lutteur exemplaire il transmet un mauvais message aux jeunes li daffay yakk lamb té Day yakk sa carrière c'est désolant
@massambandoye3147
@massambandoye3147 7 ай бұрын
Kouffi dé si thiahane yi ya perte bandi bandi niou gagne la nga sonal say wa keur ak sa famille
@basselabdou9891
@basselabdou9891 7 ай бұрын
afaire you gniank faydayi wakh deug dé
@massambandoye3147
@massambandoye3147 7 ай бұрын
@@basselabdou9891niom ngi di dof dof Lou ni beuré wou niou fayakou wou niou koussi ganiou mbeur yi dou niou la soigner say mbok rek ngay sonal
@ablayendiaye9143
@ablayendiaye9143 7 ай бұрын
Bilahi deugueu la
@deugrek344
@deugrek344 7 ай бұрын
Kou dé ya perte rek. Mbeur yi am séni millions guén lén di khékhal. Une partie de la jeunesse est inconsciente😢😢. Thiakhane molén diaral rayanté avec ça guén beugue violence diogué sénégal ak insécurité. Triste pays!!!
@Khaly-kp3ek
@Khaly-kp3ek 7 ай бұрын
@FallouDioum-qv1if
@FallouDioum-qv1if 7 ай бұрын
Waxal waay bilahi
@TheBandafall2003
@TheBandafall2003 7 ай бұрын
Ces jeunes croient que le nouveau gouvernement sont la pour jouer s’il ne font pas attention la lutte avec frappe va avoir de grands réformes même supprimer ces habitudes sont pas civilisées c’est du sport seulement
@MendyDione-qc5dp
@MendyDione-qc5dp 7 ай бұрын
Fass lagn deuk ba parei gua daw😂😂😂😂😂😂Senegal dafa nekh kw
@BabacarSadikh-p2f
@BabacarSadikh-p2f 7 ай бұрын
Diamaguene y'a tout ⚔️🗡️
@makhtar70
@makhtar70 7 ай бұрын
Yeureum CFAO et bernabé et puis mi ngi melni deukk bi Amoul police. Bolen si diogoul yen Wa FDS, votre fameuse phrase "force reste à la loi" sera remplacé par force reste au banditisme
@modoudisne5043
@modoudisne5043 7 ай бұрын
Wa boy fass yi gaw nan dé wa😮 😂😂😂😂
@IbrahimaNdiaye-yj9cc
@IbrahimaNdiaye-yj9cc 7 ай бұрын
Génération bi loulay dal dagneko mériter amougnou avenir ´ndeye san
@Khaly-kp3ek
@Khaly-kp3ek 7 ай бұрын
Dèlèn conseiller rek❤
@ibrahimakhalil1776
@ibrahimakhalil1776 7 ай бұрын
Dit pas sa secteurs informels Bi la rek faut les sensibiliser si diné ak sakou talibé
@POULO_BII
@POULO_BII 7 ай бұрын
BOY FASS AY TAPÉTE LANIOU WAY😂😂😂😂
@pascalkane9767
@pascalkane9767 7 ай бұрын
Des jeunes inintelligents et sans éducation qui suivent bêtement les lutteurs aulieu d'aller travailler. Ken meunoul defar deuk bi ak gni. Saga ak khekh rek et je suis sûr que on les met dans une cage de MMA ou sur un ring de boxe il ne tiennent pas 1 Round.
@abdoulayendiaye184
@abdoulayendiaye184 7 ай бұрын
Boy fass yi daw nagnou😅😅😅
@PapegoraMbengue-mj1ff
@PapegoraMbengue-mj1ff 7 ай бұрын
Wa fass yéneu ma rouse lo😂😂
@thiamabdoulayetoure3414
@thiamabdoulayetoure3414 7 ай бұрын
Mais yenn Ada ay Boye rk gno gnewoon thie face to face bi c normal sa way ay toutank lagn tmt
@piponiang
@piponiang 7 ай бұрын
BANDI BANDILOU AMOUL NDIARIGN DIÉMLÉNN GUÉNÉ SÉNN WADIOUR SI NDOL BI LOLOU MOY GOOR YALLA MAIS PAS NÉKK DI DOFDOFLOU YEUFOU MBAME ALEU YII NÉKLÉNN AYY NITT
@ousseynoudieye1431
@ousseynoudieye1431 7 ай бұрын
Ya wax DEUG dh ❤ niak ba paré di dof doflou fi baniou gagn la si zero
@moussasall9051
@moussasall9051 7 ай бұрын
Guéto moy Diamageune fa lagne deuk❤️❤️💪🏾
@MbayeAbdou-mh5uw
@MbayeAbdou-mh5uw 7 ай бұрын
Senegal prisident niogui liguèye population bi nio rew dekk bo khamni wèlo pedal sakh manoko defar dekk yeupp raw senegal si thiakhane rek lagne neck
@MamecheikhibraCisse-q4r
@MamecheikhibraCisse-q4r 7 ай бұрын
Wa fass medina ayer tapét lane😂😂
@ryadvaraneba8848
@ryadvaraneba8848 7 ай бұрын
dang fii guiss wa medina
@KarimSeydi
@KarimSeydi 7 ай бұрын
Bilae oé😅🎉dagg sa yaram
@ousseynoudieye1431
@ousseynoudieye1431 7 ай бұрын
Ay thiaxan nguen si diay 'goré ak bandit ba lor sa bop neklen ay nitt
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 7 ай бұрын
Bilahi gni top mbeur yi danio dof trop trop 😂kingay top diko héhal mongui yor million bigne ko fay,mayoula sah 5f baparé ngakoy héhal,mangui sante yalla boubah mann mi 😂
@Elhadjikane-i6f
@Elhadjikane-i6f 7 ай бұрын
Wa bakhna tokk len fii ba doff Ndeye niew fii rekk
@momobouthiapathiolybi7752
@momobouthiapathiolybi7752 7 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂
@amadoufall8853
@amadoufall8853 7 ай бұрын
ADA NDAKAROU mo mom lambj legui koi vraiment il faut gayi nangou
@alioudanfakha8875
@alioudanfakha8875 7 ай бұрын
Wa fass yi lougni daw gni gno tapéte ndéké séne lamigne rék mo reuy😅😅🤣😂
@maxcoly5541
@maxcoly5541 7 ай бұрын
Boy fass ay Diambar laniou ay xalé you ndaw rekk Nio dém ba dimanche dina lerr😊
@ameththiam8369
@ameththiam8369 7 ай бұрын
Franchement li dafa niaw,une jeunesse saine c'est ce que le Sénégal veut pour son avancement,vous pensez que c'est un exemple à suivre ça,la lutte doit être banni au Sénégal pour toujours,li moyy avancements sports,vous vous trompez de chemin ça n'a aucun sens pour dire2 vrai
@AliouneDiallo-sl3lq
@AliouneDiallo-sl3lq 7 ай бұрын
Liss kasssé
@Kouroumakana
@Kouroumakana 7 ай бұрын
Mbeur bi di ligueye gagner khalissam, yaw guay khékh pour môme, #Sarap liiiiii 😂😂
@AliouneNdiaye-yk6hq
@AliouneNdiaye-yk6hq 7 ай бұрын
Lo khamsi dof
@LeopoldFaye-mu1mc
@LeopoldFaye-mu1mc 7 ай бұрын
ndiago bii seul wa fass ayyy ndy tapétttt ngén
@MGBOY-
@MGBOY- 7 ай бұрын
Waw boy fass gaw nagne dh😅😅
@TallaSeck-d8w
@TallaSeck-d8w 7 ай бұрын
Lamb dou yeuffou bvn respect
@Killer-z1u
@Killer-z1u 7 ай бұрын
Mais wa fass danio tela daw 😂😂
@papadjibrilba2857
@papadjibrilba2857 7 ай бұрын
Jeunesse inconscient sans culture lamb amaloule société bii ndiarigne
@amethguisse9670
@amethguisse9670 7 ай бұрын
Waa gni Ada Fass laniouy beurél wala Zoss. Liss yaw mom akk lima guiss naro goudou carrière. Lamb dou affairou bandit. Amlén yarr touti
@ninkinanka2670
@ninkinanka2670 7 ай бұрын
Liss comme khop wadji beumeukh ko mouy feur feuri 😂😂 wa diamagene li motakh ken doulen beug
@laminegueye4996
@laminegueye4996 7 ай бұрын
Liss ada fass diaroul teugue ndakh rewandé dina si faigne . Liss ya sokhla ada fass mais essayel mel ni siteu reference .mais yeufi dof yi boy yi topai la amoul sens .
@bathiedioum898
@bathiedioum898 7 ай бұрын
Yen yépou doulèn dara bandi bandi lou amoul chance séni parent sonal rek yipil xol yéwoul bok
@OmarBa-n2u
@OmarBa-n2u 7 ай бұрын
Diamegene la noiu dekk❤❤
@TaherElouardi
@TaherElouardi 7 ай бұрын
Ay dof guen rek
@legendediop9215
@legendediop9215 7 ай бұрын
Mbeur dou projet ngen niak diom topou si guinaw ben way di lambar lambari
@elhadjibeye2909
@elhadjibeye2909 7 ай бұрын
Boyi dall li moy sene adouna quoi😂😂😂😂😂
@badafall4392
@badafall4392 7 ай бұрын
Wa Diamaguéne nio fans ada fass tadanio beuri wakh
@mbayefall5684
@mbayefall5684 7 ай бұрын
😂😂 ana wa fass yi
@modoufaye9992
@modoufaye9992 7 ай бұрын
Diamagene. aye. Doff mothia eupe
@biranesogue4365
@biranesogue4365 7 ай бұрын
Saghomar da thioubou tay
@mortadacisse8992
@mortadacisse8992 7 ай бұрын
Bly ioe😂
@AbdouTall-ei1ob
@AbdouTall-ei1ob 7 ай бұрын
Senegal dou dem amoul avenire Ndayisan amouhou xelat xamxam Mo wore
@OusmaneSeydi-hy2mk
@OusmaneSeydi-hy2mk 7 ай бұрын
Wa fasse si réseau bi lagniouye néke di ndaye ndélou douniou ndaye dara
@L.Yamal100
@L.Yamal100 7 ай бұрын
Liss ñakeu na fayda, Ada fass mingui si bir nga nék si bitti di dof dof Lou 😂
@serignewade6680
@serignewade6680 7 ай бұрын
WA mai Nak wa fass ay français lagn diamaguene ya tout ⚔️🗡️🪓
@mamefatou6794
@mamefatou6794 7 ай бұрын
WA lisse ndiago dou zoss la wara beurelle Ada fass gouy hi louy problem bii
@boubacarboiro5813
@boubacarboiro5813 7 ай бұрын
Mouy liss mouy Ada danio wara hotti sen license gnii louy sen probleme
@mamepathe4618
@mamepathe4618 7 ай бұрын
Kou togn ?
@boubacarboiro5813
@boubacarboiro5813 7 ай бұрын
@@mamepathe4618 lolou lidiantiwoumako un sportif si t'es arrivè à un niveau tu dois montrer du professionalisme à tes supporters point final
@MamadoudoumatarNiang
@MamadoudoumatarNiang 7 ай бұрын
Nitou diam boulko woo si ay diamaguene ya tt😂😂
@mohamedhrounasy3246
@mohamedhrounasy3246 7 ай бұрын
Où sont les sécurités
@AbdoukoniaNiang
@AbdoukoniaNiang 7 ай бұрын
Wa fass danio tapete ba paré beuri wakhe banlieusard bou ragale amoule
@malicksane-q2o
@malicksane-q2o 7 ай бұрын
Une jeunesse perdue c dommage
@AmadouKamara-zp8ls
@AmadouKamara-zp8ls 7 ай бұрын
Wa fasse raxāass naniou ndéye talibi yeup bamou 7
@alioudanfakha8875
@alioudanfakha8875 7 ай бұрын
Diamaguéne rék feék soufi frék liss rék wa fass daw nagnou 😂😂😂😅
@MamadouCamara-tu1kf
@MamadouCamara-tu1kf 7 ай бұрын
Diamaguene ya tout dh 😂😂😂
@NDIAYEMayib-k5x
@NDIAYEMayib-k5x 7 ай бұрын
Sport fo ak rè lamb dji lagne wara athie 2ans
@Science-z5w
@Science-z5w 7 ай бұрын
Thiey Banlieue y’a tou Mafia « Tangue Niangue «
@ibrahimaseck7280
@ibrahimaseck7280 7 ай бұрын
Banlieue laniou deuk nioune boy town douniou yap
@Saracamara-rf6el
@Saracamara-rf6el 7 ай бұрын
Boy yi diamaguen dano sarik
@MamecheikhnaNdiaye
@MamecheikhnaNdiaye 7 ай бұрын
Mais cng gnou wara wakh ak liss mi defagoufi dara
@SenyFaye-i4j
@SenyFaye-i4j 7 ай бұрын
Wa ada dawnaniou 😂😂😂
@mansourdiack1289
@mansourdiack1289 7 ай бұрын
😂😂boy Fass yi rk nguene yap kerok contre pokola Bari ngene blessé boy Pikine yi danio Dakhar sene ndy bou Bax 😂
@AbdoukoniaNiang
@AbdoukoniaNiang 7 ай бұрын
Wa fass nio tapete rek
@KhassimDiallo-y4h
@KhassimDiallo-y4h 7 ай бұрын
Iow boy dolen yarou yen niou feklen sen kogne Deug sen ndey
@Kopp2111
@Kopp2111 7 ай бұрын
@@KhassimDiallo-y4h billay a domicile .gnou diougué feulé deug sén ndéy romb 🤣😂
@MaimounaBeye-pw4tq
@MaimounaBeye-pw4tq 7 ай бұрын
Xar lène baniou am diop 2 dinaniou xamni yeumbeul ya tout 🕯
@Kopp2111
@Kopp2111 7 ай бұрын
@@MaimounaBeye-pw4tq moh 🤣🤣
@abdougueye4837
@abdougueye4837 7 ай бұрын
liss ak ada fasse kou ko teigue guiss lou doy warr😂
@bassirouba3035
@bassirouba3035 7 ай бұрын
Dakar tapett you bone togne ba nopi di daww 😂😂😂😂😂😂😂
@abloslimshady
@abloslimshady 7 ай бұрын
Kou deh ya perte, reyanté lenn! Yené kham, senegal jeune yii dagno beurri ndax niou wagnekou touti
@moustaphababou6282
@moustaphababou6282 7 ай бұрын
Wa fass ndekete tapett you mak lagne noo ake sen laminge you reuye liss ndiago niawe rk ngen dawe
@MetaSow-j3z
@MetaSow-j3z 7 ай бұрын
Def len ko wa yeumbeul 😅😅😅
@MHDtarkinda-we2ns
@MHDtarkinda-we2ns 7 ай бұрын
Mbeur bou Guen ndaw Diamaguene ay fansam nio teubeuli won sen ndy nangou sen lepp daw ba bayifa sen dall yi😅
@MetaSow-j3z
@MetaSow-j3z 7 ай бұрын
@@MHDtarkinda-we2ns kilifeu gua nak 🤣🤣🤣 diop2 bayil ba diop2 AK siteu takhawe
@MHDtarkinda-we2ns
@MHDtarkinda-we2ns 7 ай бұрын
@@MetaSow-j3z siteu Diop 2 combat bobu boul ko xalaat skh nèkal nitt n'a beurè moromam yi
@Domou__rewmi.
@Domou__rewmi. 7 ай бұрын
​@@MHDtarkinda-we2ns ya mana doul zoss2 combats bi passé danio kate ndym bamouye beugue dead blh 😂😂
@AliouSeckSN
@AliouSeckSN 7 ай бұрын
Yén Diamaguene guéni rootsé douniou ndeye sen nawlé
@papagabardia7107
@papagabardia7107 7 ай бұрын
Liss ndiago sama mbeur gua mais waxal ak sa boy yi daniou lay yakhal
@serignedieng-vh4zv
@serignedieng-vh4zv 7 ай бұрын
limoy sénégal violence rk ba kagn
@footsenegal3241
@footsenegal3241 7 ай бұрын
Liss seul
@assgueye9899
@assgueye9899 7 ай бұрын
Gni Bilahi police daf len wara diape
@ndouramadou6653
@ndouramadou6653 7 ай бұрын
Yéne diam guéne beuguoule wa fass dama contane si thom mbeur yi bougnou tax nga ray sa bopou liss damo méré mom dafa worone kalemé supporter yi limou déf amoule jeurinie
@SowPierre
@SowPierre 7 ай бұрын
Kome aye aminal
@mansourdiop7037
@mansourdiop7037 7 ай бұрын
Wa fass nioy daw ni 😅😅
@BoubaFall-t5q
@BoubaFall-t5q 7 ай бұрын
Diamaguene laniou deuk Liss ndiago seul 😊
@mathieudenisdiedhiou8444
@mathieudenisdiedhiou8444 7 ай бұрын
Wa gni daw nagne di😂
@Clachnuckofg5752
@Clachnuckofg5752 7 ай бұрын
Serigne mor d'où touss
@Mrdiop
@Mrdiop 7 ай бұрын
Waa diamaguéne vraiment, vous faites honte. C’est désolant mais yaa ke des waga
@MHDtarkinda-we2ns
@MHDtarkinda-we2ns 7 ай бұрын
Saway dimbaliniou kouniou wo violence niou lèkk dedieuw ndm niolen Guen yakou fopp
@ndouramadou6653
@ndouramadou6653 7 ай бұрын
Escale deug yéneu fék wa fass yo fofou
@ndouramadou6653
@ndouramadou6653 7 ай бұрын
Waxale deug yéna fék wa fass yi fofou fass xamenga lougnou meune yot la
@MHDtarkinda-we2ns
@MHDtarkinda-we2ns 7 ай бұрын
@@ndouramadou6653 ww après niom niou nek si rèseau yi Di niou sagua
@ilidiouf3789
@ilidiouf3789 7 ай бұрын
Diamagune moy Sénégal par forst
@TIKTOK-OF-WOURY
@TIKTOK-OF-WOURY 7 ай бұрын
Pikine Moy ndeye bombe
@MHDtarkinda-we2ns
@MHDtarkinda-we2ns 7 ай бұрын
Diamaguene ya tout manquè woul dr bly ioe 😂
@VitoDiouf
@VitoDiouf 7 ай бұрын
Wa ndakaru 😂
@taphadieng3615
@taphadieng3615 7 ай бұрын
Gni danio fan ada fass kw liss zoss lay beuréil amguén loulén doye way ada amoul sen diote
@oumaroniane4793
@oumaroniane4793 7 ай бұрын
bilahi gni dignu bandit.boy usa yi gnolene geuneu khotekouuuuu foufffffff
@DalandaBah-qw6vd
@DalandaBah-qw6vd 7 ай бұрын
Wa fasse rewo golen skh té beus b Moy guener nekh
@djibrilba3786
@djibrilba3786 7 ай бұрын
Boy yi dofou sakh Wa fase lanioye tiital ni rek niom kham naniou bo bakh fane moye pikine 💚❤️Wa fase nakk sein wakha bary ´ lane moye aÿ daw 🤬
@SaliouSow-gj6or
@SaliouSow-gj6or 7 ай бұрын
Conscience zéro.
@cheikhbadiane5221
@cheikhbadiane5221 7 ай бұрын
Boy malfaiteur yi nimalene bagné
@diawcheikh3744
@diawcheikh3744 7 ай бұрын
Wa fass ay tapet gnéne
@beuguefallou3642
@beuguefallou3642 7 ай бұрын
Tousss nk diameguene késs
@mormbaye6098
@mormbaye6098 7 ай бұрын
dangéné réw rék liss warone na lén fi fékk rék
@Zallboutalfa
@Zallboutalfa 7 ай бұрын
Ay tabet ngen yen niebo Guêmuer bi ndeye suel
@MbayeAbdou-mh5uw
@MbayeAbdou-mh5uw 7 ай бұрын
Gouygui mo guene soff si lamdjii beuri loy kasss tropp beuri wakh tè liguaye wakh guemoko
@bakarydiatta9678
@bakarydiatta9678 7 ай бұрын
Ko e wa fass daniouye daw😂😂😂😂😂
@ndouramadou6653
@ndouramadou6653 7 ай бұрын
Daw guaraoule bandi deug boko théko day daw
@ModouSeck-lb7qq
@ModouSeck-lb7qq 7 ай бұрын
Wa fass aye tapet laniou kholal niouye daw😂😂😂😂
@bassiroundaw4751
@bassiroundaw4751 7 ай бұрын
😂😂😂
@PapealiouneNdiaye-ry6zi
@PapealiouneNdiaye-ry6zi 7 ай бұрын
Diamaguene nday seul
@SeydinaMboup-x6d
@SeydinaMboup-x6d 7 ай бұрын
Fass gno geuneu tapet saga tik tok dale meune neyko
@serignesene8842
@serignesene8842 7 ай бұрын
Ni lagnougne deff ba crimes âme
@cheikhgueye5458
@cheikhgueye5458 7 ай бұрын
Aythia mafia tang niangue bi wa fass yi nio ragual
@MatarSakho-n4p
@MatarSakho-n4p 7 ай бұрын
Boye yene khana khamolen dmg
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 18 **VOSTFR**
1:13:28
EvenProd
Рет қаралды 861 М.
It’s all not real
00:15
V.A. show / Магика
Рет қаралды 20 МЛН
Арыстанның айқасы, Тәуіржанның шайқасы!
25:51
QosLike / ҚосЛайк / Косылайық
Рет қаралды 700 М.
To Brawl AND BEYOND!
00:51
Brawl Stars
Рет қаралды 17 МЛН
99.9% IMPOSSIBLE
00:24
STORROR
Рет қаралды 31 МЛН
AMOURS BRISÉES   Saison 1- Episode 40
33:55
Yesdakar
Рет қаралды 132 М.
COMBAT LISS NDIAGO VS ZOSS: PUISSANT COUP DE LISS NDIAGO, ZOSS K.O
11:47
Les confidences terribles de l'ancien lutteur Sa Cadior
30:17
Senepeople
Рет қаралды 50 М.
It’s all not real
00:15
V.A. show / Магика
Рет қаралды 20 МЛН