Je suis tidiane talibè cheikh ms j'aime trop ce zikr peut être loumouy tag yonenti bi motakh
@Cheikhkounta110 ай бұрын
Sallli hala Seydina Mouhamadine wa alihi wa sallim 😢😢😢
@lisaronaldo28613 жыл бұрын
Li sama vacances 2006 en Gambie lamay fateli, mou tombéwone ak wérou koor. Souniou meussane yéwou rekk ndieukalanté daw tale cassette bi. Dama weur diangue yi ci net bi ba sonou. Tey lako Yallah dogal alhamdoulilah!!! Sama khol séde na !
@gueyelax3 жыл бұрын
Ndeysann
@boromxamxame Жыл бұрын
Nday san bima neckè khallè rek lamay fatali
@AblayeNdongo-x4m10 ай бұрын
Ndayssane 🤍🩵
@papiba25182 жыл бұрын
Ndeysane sama Mame yalla na yalla yeureum ko ,chaque fadjr mom ladone déglou Radio😭😭😭
@AblayeNdongo-x4m10 ай бұрын
Amine yarabi 🩵🤍🥺
@ModouMarone-re1lm9 ай бұрын
Bilahi man aussi
@ibrahimadiop41874 жыл бұрын
Qui l’écoute en 2024😍
@khadimgueye2624 Жыл бұрын
Moi en 2023
@abolo9283 Жыл бұрын
2023
@astoudiop5158 Жыл бұрын
2023
@falloumansaly362 Жыл бұрын
Décembre 2023🎉❤
@AblayeNdongo-x4m10 ай бұрын
Alkhamdoulilah 2024 président Diomay 🩵🤍@@khadimgueye2624
@BabacarNdione-b1n10 ай бұрын
Qui est la en 2024
@labsolugueye90163 жыл бұрын
Thaï Lii Doumathi Doyall Mane jamais jamais jamais....../ thaï serign saliou Mbackè Yallah Nanouko Yallah Fayall Thi Barke cheikh Akhmadou Bamba ❤️🙏
@cheikhballacissewade13584 жыл бұрын
MACHALA MACHALA ÉTERNEL YAGUE FI TE WER AK NOUNE AMINE BARAKATOU CHEIKHOUL KHADIM A DIOYLOGHAMA BE TAYI GUIR SERIGNE SALIOU
@medafight4162 Жыл бұрын
Ecoute années 2003 2004 ndaye sann belle souvenirs barke serigne babacar sy ken mouhmed loko waye mo nekhe
@Dadjiwahabiya12 жыл бұрын
Même en 2022 😭 Wallahi yonent bi dou sapi Mouk dou xéwi Mouk
@ousseynousane142510 жыл бұрын
cheikh diop mbaye yalla nala yalla mayy goudi fane ak weirrr amine
@penda60835 жыл бұрын
Non song bi nekhna trop yallna yalla weral bete bi😭❤
@ndeyefatoumbaye41933 жыл бұрын
SERIGNE MOUNTAKHA YALA NAFI YAGUE TÉ WÉRR 👌👌👌🤲🙏🤲🙏🤲🤝🤝❤❤❤❤😭😭😭😭🇸🇳🇸🇳🇸🇳👍👍🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰😍😍😍😍😍🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🕌🕌🕌🕌🕌
@AblayeNdongo-x4m10 ай бұрын
Amine 🙏🩵
@mouhamadougueye6295 Жыл бұрын
Le plus beau son de l'humanité
@diarrangom57373 жыл бұрын
Seydina Mouhammad SAW mo gnou doy güero♥️♥️♥️
@YoussouLo-ku9lz Жыл бұрын
Yallna nou KO bourr yalla fayal si barkeb seydina moukhamed salahou halayhi wasalam ak si barkeb serigne cheikh ahmadou bamba ak si barkeb cheikh diop Mbaye
@abdoukarim16684 жыл бұрын
Ndaysan 🥰 yalla naga god fane ak werr 😭
@lafally2448 Жыл бұрын
Ça me rappel bima neikei khalei di dem touba and ak sama mame😭
@dioupakdioubal36904 жыл бұрын
Dieuredieufeuti sa soumako déglo sama khôl seed
@couradiop5311Ай бұрын
Yalna na Bour Yallah sédal sa khol ni nga sédalé souniou khole yi! Adouna ak alakhira
@ndeyeastougaye97175 жыл бұрын
Seydina Mouhammad dou massa khewi salalou alayhi wa salam