🔴Alerte: Louye ram ci gnak bala djeum!yallah Ndiaye néneu Yallah dafa guak 😭😭 Ana avocat dîné dji?

  Рет қаралды 12,475

BAYE NIASS TV

BAYE NIASS TV

Күн бұрын

Пікірлер: 141
@PapeMBopp
@PapeMBopp 6 ай бұрын
Beaucoup de moukhadam doivent prendre exemple sur oustaz Ahmed Ba
@MaimounaDiame-ms6ue
@MaimounaDiame-ms6ue 5 ай бұрын
Merci cheikh Ousmane
@khadim1875
@khadim1875 6 ай бұрын
Léne rék moma indi si commentaire , Khol baxam kéne dinako defendre . fi lay xamé nak ni ndékété sénégal geumougne yalla . Sangue ndiaye limou wakh eup neu . Soubahana lah
@elhadjimalickdiop2234
@elhadjimalickdiop2234 6 ай бұрын
بارك الله فيكم وفي مجهوداتكم الجبارة لخدمة الإسلام والقوم
@ZST7414
@ZST7414 5 ай бұрын
Ki wara wax ak mom moy cheikhoul khayri . Seti ko
@ElhadjiDiakhaté-h4s
@ElhadjiDiakhaté-h4s 6 ай бұрын
Yallah nagnou yallah mousseul cii reirr ak sankou😢té tékk gnou cii yonou siratal moustakhim
@barhamjaw2255
@barhamjaw2255 5 ай бұрын
Man talibe baye niass la mais dama russ sakh... .sangue mbolo nakh nako
@jojojay9056
@jojojay9056 6 ай бұрын
dou talibé tidiane qui moussou bala tchimm
@aladjidiop3767
@aladjidiop3767 6 ай бұрын
Machalla Serigne bi yalna yalla samoula arla si barké cheikh oul khayri baye
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 6 ай бұрын
Sangue Ndiaye daffa yape domou adama yiii rawatina Talibé Baye Niass yiii. Djeureudjeuf Cheikh Ousmane Mbow contane naniou ci yaw ❤❤❤
@ibrahimakane3392
@ibrahimakane3392 6 ай бұрын
Diere diefe Serigne bi ❤️💯💘 Yalla Gisna Lèpe❤
@freemansolo5427
@freemansolo5427 6 ай бұрын
Ce Ndiaye est vraiment un dmrm Allah est digne d'être craint. Ndiaye joue avec notre religion
@ibrahimakane3392
@ibrahimakane3392 6 ай бұрын
ماشاء الله تبارك الله أحسنت و أكملت
@modoundiaye5879
@modoundiaye5879 6 ай бұрын
جزاك الله خيرا وبارك فيكم ❤
@mansourgaye6205
@mansourgaye6205 6 ай бұрын
Soubhanallàh allahou akbar ki dafa diangoul nak té louko nékh wax pourtant môme talibé you diangue la âme mais môme moylolou
6 ай бұрын
Sangue Ndiaye kou yabaté nakala nitt mouna wakher lire moma djakhal.
@TamsirNdiaye-rz5rf
@TamsirNdiaye-rz5rf 6 ай бұрын
Diaradiaf ce ousmane mbow Linga wakh lepo degla
@Boromdeukbi8470
@Boromdeukbi8470 6 ай бұрын
Ay bou done da wax serigne diw dafa guak shiiii senegal ya peut de musulman bilahi
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 6 ай бұрын
Wallaye ndayssane mais kou bindeu Serigne yi nak leuye wakhalni dhé khamgua li daffa eupou
@serignetoubadiop5528
@serignetoubadiop5528 5 ай бұрын
MAHI NIASSE douthi wakh? lane moy ndiarigname;;; Ande same djiko yi ,makhtar sarr ,vous etes ou?
@SeydinaGueye-iw6cs
@SeydinaGueye-iw6cs 6 ай бұрын
Soubhanalah Yalla kou guak mola guakloo ndakh mom Moy buur bi teulé woul Dara Moy ki meun lepp ya bonn yaw Miy wakh lolou yalla d'où fowoukay😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@toubatouba4966
@toubatouba4966 6 ай бұрын
Allahou wahidoune ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ bour yalla dou dioume dou ngahkk ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@MamadouThiam-qb7qq
@MamadouThiam-qb7qq 6 ай бұрын
ماشاء الله بلغت أطال الله عمرك
@alydiop-x1x
@alydiop-x1x 6 ай бұрын
boye ndiaye mi gñouko tooppu la yeureum, ki ap doomeram la, xamoul dara, kanam gou leudeum, daguénko wara thiaw mou noppi, boye ndiaye mi doomeram la, saÿ saÿ,
@cheikhabdoukarimedeme-qh2jy
@cheikhabdoukarimedeme-qh2jy 6 ай бұрын
شكراً للشيخ عثمان امبو المجاهد التنويري الكبير
@babadiao5030
@babadiao5030 6 ай бұрын
أستغفر الله العظيم الذي لا إله إلّا هو الحي القيوم وأتوب إليه
@abdallahgassama3678
@abdallahgassama3678 6 ай бұрын
Walahi 😭 doynawarr jerejeff Serign bi si leral yi ❤
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 6 ай бұрын
Yallah Ndiaye mogui yakheu Faydou bi
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 5 ай бұрын
Sangue Ndiaye Moy dadjal dhé
@MamadouThiam-qb7qq
@MamadouThiam-qb7qq 6 ай бұрын
Sang Ndiaye هذا أخطر من أبي جهل بكثير
@AMfalltv
@AMfalltv 6 ай бұрын
Bimou toudé yalla ndiaye lathi mandou puisque béne yalla la kham
@ababacarndiaye3553
@ababacarndiaye3553 6 ай бұрын
جزاك الله خيرا
@عليجغن
@عليجغن 6 ай бұрын
انا لله وانا اليه راجعون والعياذ بالله والعياذ بالله والعياذ بالله لاحول ولاقوة إلا بالله العلي العظيم وانه لمسيح الدجال في هذا الموقف السيء من انسب لله جهلا أو خطأ فقد كفر بما أنزل على محمد صلى الله عليه و ءاله وصحبه وسلم تسليما كثيرا حق قدره ومقداره العظيم
@ahmedgueye8067
@ahmedgueye8067 6 ай бұрын
Santa Ndiaye mom dafa katta ndayam
@NdeyeDiopSamb
@NdeyeDiopSamb 6 ай бұрын
Walakhi deuge le serigne bii pa Ndiaye yakh n'a faydou bii
@ablayng6446
@ablayng6446 6 ай бұрын
Yallah bindoutt kou meuna yakh bireum Faydou bi mom pa ndiaye moy yakho si faydou bi 😂
@abdoulahisow
@abdoulahisow 6 ай бұрын
Sen bopou reck daniouye dounde dine waye doundalouniouko waye yalla na yalla fayala
@malcomkebe5535
@malcomkebe5535 5 ай бұрын
Bida yeup thi réer lala dieumé😢😢😢
@soldaroumamesalioufgm
@soldaroumamesalioufgm 6 ай бұрын
Wallahi taye lakay sogua guis t vedeo bi laka guis mais dafa wakhe rek sama yarambi daw ma sopo ko Looole wallahi ❤❤😢
@mamecheikhthiam456
@mamecheikhthiam456 6 ай бұрын
الله أكبر الله أكبر 😢😢😢😢😢😢😢😢😢 سبحان الله 😢😢😢😢😢
@MamadouThiam-qb7qq
@MamadouThiam-qb7qq 6 ай бұрын
أذكراسمه بكل صراحة
@MamadouKane-gq2hy
@MamadouKane-gq2hy 6 ай бұрын
Ki defa dof Bari wakh
@OusmaneSeck-v6r
@OusmaneSeck-v6r 6 ай бұрын
Li Papa Mahi warna ci wah,Ndiaye bou bguee diné bou bess mou wah ,guenee ci Islam Tariqa Faydou.
@niomrelo1959
@niomrelo1959 6 ай бұрын
Sama kholl dafa toy dama titt si bima dégué limou wakh sangue ndiaye vrai domeram la
@Ngathibouthiosan
@Ngathibouthiosan 6 ай бұрын
Mbow ak sangue Ndiaye yena yakh faydou bi niari doul kati😊
@IssakhaDiouf-e9t
@IssakhaDiouf-e9t 5 ай бұрын
Fén nga dé mbow mosoul wakh loudoul yala néna wala yonénti bi
@bboyfall5741
@bboyfall5741 6 ай бұрын
Svp lien bi yalla Ndiaye di wakhé lolou menagn ko ame
@issadiouf256
@issadiouf256 6 ай бұрын
Sangue ndiaye Diahasèna Faydou bi Yeup ohhhhh 😭😭😭
@mballondiaye50
@mballondiaye50 4 ай бұрын
Sang Ndiaye yaawara wax yaañu saf Bumla taxa wax loo xamul
@makhtarseck8584
@makhtarseck8584 5 ай бұрын
Wallai doynewar
@dahiratoualelmouwalimam4768
@dahiratoualelmouwalimam4768 6 ай бұрын
أين الشيخ الخير بنفسه وهذا من اتباعه
@halildanso3232
@halildanso3232 2 ай бұрын
Iow katal sa ndaye yakk mom yéna yam ay domeram ngén rek nafekk kharamata ndiaye yii, kou yabb Baye yéna takh mais Baye kéneu meusou ko yabb si doundam
@AblayeToure-i4m
@AblayeToure-i4m 6 ай бұрын
Yéne niarr niakgene fayda trop 😮😮😮😮
@IssakhaDiouf-e9t
@IssakhaDiouf-e9t 5 ай бұрын
Yowla Kham kham gnoroul
@MouhamedDoucoure-u9m
@MouhamedDoucoure-u9m 6 ай бұрын
Ki dafa rew khaw ma dafa doff khas ma louko dal yalla dou morom wayé bimou wakhé ni amadou ba moy 5 em président té dou deug loloi rek nek n'a fene
@mbayebaity2484
@mbayebaity2484 5 ай бұрын
😢😢😢😢😢
@IbrahimaGadiaga-os7pk
@IbrahimaGadiaga-os7pk 5 ай бұрын
❤❤❤❤❤
@semoudiouf4781
@semoudiouf4781 6 ай бұрын
Yénn dagéndi saga yallah yénn soit disant hanrif yi,daga bagne sangueu Ndiaye rek mais yénn gneupeu yéml
@tabciratv1901
@tabciratv1901 6 ай бұрын
Jaajëf ❤❤
@serignedieng2374
@serignedieng2374 6 ай бұрын
Serigne bi ndao yawe ake sange Ndiaye momoléne fayda bi vous êtes des talibé ou bien des politiciens a Quoi votre problème ?
@modoundiaye5879
@modoundiaye5879 6 ай бұрын
Sange ndiaye mofi wakhoune ذى ثلاث شعيب 😂😂😂
@YoussouSarr-k4v
@YoussouSarr-k4v 6 ай бұрын
😂 شعيب kaye
@souleymaneibrahimasall5367
@souleymaneibrahimasall5367 6 ай бұрын
Alhamdoulilah vidéo bi guiss n'a si SANGUE bou téd biii...
@AL-AMAANA-TV
@AL-AMAANA-TV 6 ай бұрын
dinga dof doflou ba doff bi nekaat deugue nak
@IssakhaDiouf-e9t
@IssakhaDiouf-e9t 5 ай бұрын
Ki da rére lol sakh
@MouhamadElkabirNdiaye
@MouhamadElkabirNdiaye 6 ай бұрын
Kham kham mo nekh dehh
@elhadjibabaka5218
@elhadjibabaka5218 6 ай бұрын
Où est le khalif Chiekh mahi le serviteur du oumah
@ibrahimaniang6539
@ibrahimaniang6539 6 ай бұрын
Bârakalâhu fîkum
@lamineyade5753
@lamineyade5753 4 ай бұрын
Astahfiroulah astahfiroulah
@sendeugtv8501
@sendeugtv8501 6 ай бұрын
yaw mom bakh nga thi sageu ndiaye dou dara
@dahiratoualelmouwalimam4768
@dahiratoualelmouwalimam4768 6 ай бұрын
أين شيخه قبل كل شيء
@TamsirBarhamaniass
@TamsirBarhamaniass 6 ай бұрын
أيد الله يا حبيبي
@AliouBarro-r7q
@AliouBarro-r7q 6 ай бұрын
Won leenko seen serigne yeen would lhayri
@الراجيرحمةربه-ث5م
@الراجيرحمةربه-ث5م 6 ай бұрын
Moom xanaa waxoul woone ni mooy Yalla? Yénni néne la rek
@Vlad05207
@Vlad05207 5 ай бұрын
Serigne bi wah ji wah ji moy biss bou la Yalla dimbaliwé digueine bayi baye niass si bopam té japp si Cheikh Ahmad TIJANI Qutbul Maktum wal Barzahoul Maktum Preuve: Baye NIASS amna lou eup 4 femmes té Cheikh Ahmad TIJANI mom sah faf 2 femmes rek la am té Yonente nena kou tak lou eup 4 femmes non seulement safara ga jeum ms aussi gni la ko May, Imam bi ko mayé, gni ko feké,kou si mena wah té wahou si safara ga jeum. Motah bala ga toudou doméharam bi Di Sangara NDIAYE Wahal si jeufou baye niass bou haram bobou
@abdoulayediallo7197
@abdoulayediallo7197 6 ай бұрын
Dof yiifa nekk Di youhou nioma jaxaal
@sayroulabad8726
@sayroulabad8726 6 ай бұрын
Nioniou bruit laniouye topou doff laniou malheureusement😅
@khadim1875
@khadim1875 6 ай бұрын
je suis choqué bro bilhai . Mane li serigne serigne bouko wakh ak no tolou si kaw souf ma dieul samay bagass abal leu . YALLA AKA MAT TEI SORRI AK GAGUE . SOUBAHANAL , WAKHAMDJI REUYNEU
@PapemalickFall-yq2mz
@PapemalickFall-yq2mz 6 ай бұрын
Doyna war
@daamnjaay1274
@daamnjaay1274 6 ай бұрын
Kii man na wax yu rëy, wax ji ñaaw na lool
@PapeDiop-t4u
@PapeDiop-t4u 6 ай бұрын
Lii Mbagnél leu Wala kiniane Wala beugona am lii wadji am té amoko Bimala dalé sétan bah légui wadji ngay dall
@abdallahgassama3678
@abdallahgassama3678 6 ай бұрын
Defarr yaha yaha nyu pa ndiaye di yaha
@PapeDiop-t4u
@PapeDiop-t4u 6 ай бұрын
@@abdallahgassama3678 Faydou bii yeneu dieuf AK wax yi manone nassé niak Comme niou bokk ben nanouwaay
@abdallahgassama3678
@abdallahgassama3678 6 ай бұрын
@@PapeDiop-t4uku wah yalla dafa diome lolu c faydu la wala ban nanou y la ???
@mouradmbaye2690
@mouradmbaye2690 6 ай бұрын
Bagne sangu Ndiaye ak kheikh ko ci djamou yalla la bokk booy ignaane dangay ignaanei kou bakh waayei doo feikk yeifeur bou meilni sangu Ndiaye nga hamni Firhawna sakh rousnako wakh boul fetteini sangu Ndiaye moofi wakhoone ni yalla fiila feikk assamaane ak souff ba parei mouni moom mooy yalla tei yalla Ndiaye la sant esk loolou la baye niass wootei pa parei kouko wakh guein ni dafa ignaane sangu lou nit diko ignaanei mboolo ak khaliss
@alydiop-x1x
@alydiop-x1x 6 ай бұрын
ki wakh na deugg, boye ndiaye mi doomeram la xamoul dara kanam gou leundeum, may leen gnou diamou
@nancynicol1870
@nancynicol1870 6 ай бұрын
Jerejeff nyass see relanbi
@ousmaneaboudia3249
@ousmaneaboudia3249 6 ай бұрын
😢😢😢😢sey
@awacheikhyass
@awacheikhyass 2 ай бұрын
😢 non mai ce luit la il nous fou la honte au musulman
@Faalbualkookii
@Faalbualkookii 6 ай бұрын
Man de ab Murit laa waaye Seex Usmaan Mbow boroom xam-xam la
@elhadjiousmanediouf
@elhadjiousmanediouf 28 күн бұрын
6 c 9
@maissagueye3357
@maissagueye3357 6 ай бұрын
Mboww kagn ngay nopalou ? Wakhi Sangui Ndiaye so khamoul famouko tek boul wedéti, Sangue Ndiaye ak talibem yi niola geun kham alkhourane.
@amadougaye9964
@amadougaye9964 6 ай бұрын
Yow la andal
@khadim1875
@khadim1875 6 ай бұрын
seuteuteuteuteuteuteut ... ESK XAM NGA DAYOK YALLAH . EST CE TU MESURE LES PAROLES DE VOTRE SANGUE NDIAYE ! VOTRE SANGUE LA ? BAYE NIASS MOKO GEUNE 1000 FOIS ! DIEGUE WOUL SAKH BAY , Té WAKH DJI MOU WAKH BAYE NIASS SANIOUKO WAKH ; Yéne ESK XAM NGENE DAYO AK SEILOU SOUNOU BOROM AK MATAM SI LEIP . BAXNA , NEIK LEINE SI LINGUENE NEIK REIK , POUR YENE YALLA SEINE MOROM LEU ;
@P.m.n.y.m2853
@P.m.n.y.m2853 6 ай бұрын
Soubkha nalla
@djibrilgueye6240
@djibrilgueye6240 6 ай бұрын
Amna aye baat you diisse,nakhadi ta sibou
@ahmedgueye8067
@ahmedgueye8067 6 ай бұрын
You mél ni rek motakh beuggouma tarikh
@AliouBarro-r7q
@AliouBarro-r7q 6 ай бұрын
Yeen niepp yem sakka rekk guen nekka
@abdoulayediallo280
@abdoulayediallo280 6 ай бұрын
Baye tontou nalene bou yag kouy ande ak mane da ngay nék thi lima nek thi wax thi dieuf Kou nék thi sa bakane yaw l rk mom dagn nathi yaw
@LoumOusmane-vu9dt
@LoumOusmane-vu9dt 6 ай бұрын
😬😬😬🫣
@ibrahimathiam7644
@ibrahimathiam7644 6 ай бұрын
Sangue barham loumou wakh deugla
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 6 ай бұрын
Louye sa dalil?
@BaAliou-xs2gs
@BaAliou-xs2gs 5 ай бұрын
Soubhanallah
@djibrilgueye6240
@djibrilgueye6240 6 ай бұрын
Ki ndakh talibé BAYE LA talibé ñiambé darou la wone séne hale rék laye dokhé
@mamourniang94
@mamourniang94 6 ай бұрын
Yasono😂
@bainyang
@bainyang 6 ай бұрын
Ki natoula c sheik Al khairi AK Bai, ki dai fo rk, shaitan mokoy cnotrole.,,dofi rk nyokoi topu
@talibebayebi88
@talibebayebi88 6 ай бұрын
Mbow bayil SANGUE ABOUBAKRINE BARHAAMOU NDIAYE bayil djaxassé bi, SANGUE Ndiaye xam xam bimouy waxx mola nakhaari , Bayil lingay defff....
@SerigneBabacarCiss-o9k
@SerigneBabacarCiss-o9k 6 ай бұрын
كبر مقة عند الله. والله هذا ليس طالبا للشيخ
@MamebayeNdiaye-c4e
@MamebayeNdiaye-c4e 6 ай бұрын
مقتا
@amadougaye9964
@amadougaye9964 6 ай бұрын
Héy may lan ñou djam sangue barham loum wakhe deuggeula
@mahmoudly4641
@mahmoudly4641 6 ай бұрын
Yén gnar yénneu yak faydou bi😡 ay fén kat ngén🤌😡☑️
@KebabiraneSeck
@KebabiraneSeck 6 ай бұрын
😂 wadjii kone Baye niass moy serignou dadial. Té nguenn bagne yakhannté
@mouradmbaye2690
@mouradmbaye2690 6 ай бұрын
Sawaay yow liga wakh eupp na dei sangu Ndiaye dou sakh djoullit bay neikk talibei baye fii yakkantei amoufi Kii gnakkei woorma yalla nioukoy djoubeunti nganaane bayyilein yakantei bi hawma kouy sa Serigne waayei souniouko wakhoone li sangu Ndiaye wakh doo fi neikk di commentaires bay reitaane
@KebabiraneSeck
@KebabiraneSeck 6 ай бұрын
@@mouradmbaye2690 seydina mouhamed moy sama Serigne. Manii nguenn bayii sén yii
@KebabiraneSeck
@KebabiraneSeck 6 ай бұрын
@@mouradmbaye2690 yaw khanna déglou woo vidéo bi. Diaroul wiirii wax dé. Yakhannté moom yakheu sa bopeu rek. Yénnnii nénne dé. Baye niass dièpii nala. Nguenn nék fii dii mbél mbéllii ni rek. Chiimm. Vous ne faites pas l'honneur de Baye niass. Kénn xamoulén.sénégal yém. Sén Serigne lou way meune wax sédé bou bax rek ligayal dîné partout dans le monde.
@mouradmbaye2690
@mouradmbaye2690 6 ай бұрын
Hakantei mooofi amoul yow Hana doo djoullit Kii limou wakh yalla Hana deigooko au lieux nga meitit kouko ngay attarder ci ay futilité yow souniou wakhoone yonent bi dafa gak dinga fi neikk wakh ay détail
@KebabiraneSeck
@KebabiraneSeck 6 ай бұрын
@@mouradmbaye2690 boy sén waxou mbammm yooyou yén la concerné yoonn kénn nékouci. Yéenii nénn la dé. Té nguenn rafétal ko rek
@KebabiraneSeck
@KebabiraneSeck 6 ай бұрын
Wa yaw soneu nga ndeyssann
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 6 ай бұрын
Képou kou takheu ci môme khamnako car bepou nitt bouye yakheu dîné bi mogui sa kaw or yakheu Kate yi danio beurry comme le cas de sangue Ndiaye
@AL-AMAANA-TV
@AL-AMAANA-TV 6 ай бұрын
sonou ci defar mo geune sonou ci yakk
@KebabiraneSeck
@KebabiraneSeck 6 ай бұрын
@@mysteremystere5196 yeurum nalén. Sén dounndeu ndeyssann. Nguenn di yakhannté nii melnii ay mbammm.
@abdouwahabthiam8055
@abdouwahabthiam8055 6 ай бұрын
Yaw mom danga niaka fayda qoi, khana sanga Ndiaye sa woudiou la, danga sifflet way
@OusmaneSeck-v6r
@OusmaneSeck-v6r 6 ай бұрын
Moko def gnou wahko😮😮
@souleymaneibrahimasall5367
@souleymaneibrahimasall5367 6 ай бұрын
Yaw nopil...ngay wakh sa wakhou dof yii....
@AL-AMAANA-TV
@AL-AMAANA-TV 6 ай бұрын
yaw nekal nitt
@hamadybalde3992
@hamadybalde3992 6 ай бұрын
Yawe xhame Nanou Sohore mola Jap bilahi 🤦
@mouradmbaye2690
@mouradmbaye2690 6 ай бұрын
Wakhi dof kay sangu Ndiaye yeifeur bi mooko fi wakh
@NdeyeDiopSamb
@NdeyeDiopSamb 6 ай бұрын
Walakhi deuge le serigne bii pa Ndiaye yakh n'a faydou bii
@abdoukhdrethiam-hq6ud
@abdoukhdrethiam-hq6ud 6 ай бұрын
Liguéyou baye kénn mounouko yakeu moy yakou rek
@ramatoulayesy
@ramatoulayesy 6 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤
2EM PARTIE DEBAT DJALALOU DINE ET MAMEALADJI MOUNTAKHA.....
2:42:50
BAYE NIASS TV
Рет қаралды 3,6 М.
Questions réponses oustaz THIOUB détruit SANGUE NDIAYE le Khoutbou Zamane
6:51
Seydi Mouhamed el cheikh
Рет қаралды 1,8 М.
the balloon deflated while it was flying #tiktok
00:19
Анастасия Тарасова
Рет қаралды 34 МЛН
ПРЯМОЙ ЭФИР. Золотой мяч France Football 2024
4:41:06
Family Love #funny #sigma
00:16
CRAZY GREAPA
Рет қаралды 17 МЛН
Random Emoji Beatbox Challenge #beatbox #tiktok
00:47
BeatboxJCOP
Рет қаралды 20 МЛН
🔴VAR Sangue Barhamou Ndiaye PAR Cheikh Ousmane Mbow VAR
17:46
IBRAHIMA SOKHNA REPOND A HABIB NDIAYE
27:37
BAYE NIASS TV
Рет қаралды 1,3 М.
سورة البقرة كاملة لطرد الشياطين من منزلك وجلب البركه باذن الله surat albaqra
3:59:57
the balloon deflated while it was flying #tiktok
00:19
Анастасия Тарасова
Рет қаралды 34 МЛН