Allahou akbar😱Cheikh Mbacké Sakho lek yap khathie, mousse ak graisse mbam khoukh dara haram mou si

  Рет қаралды 10,787

TIKGALSEN TV

TIKGALSEN TV

Күн бұрын

Пікірлер: 41
@gooroundeyefatou7552
@gooroundeyefatou7552 Күн бұрын
Tey ma diomi si mbacké
@EutouXamXam
@EutouXamXam Күн бұрын
Yalla naniogui Yalla mousal si niake xame xame ki lomy wakh xamoul si dara yalla douli diamou ak soutoura si réwmi
@gooroundeyefatou7552
@gooroundeyefatou7552 Күн бұрын
Cheikh Mbacké mi diahal nama
@mor499
@mor499 Күн бұрын
Thiey Cheikh, mane mom je ne le reconnais plus. Cheikh dèlousil
@Ruqqayah-n
@Ruqqayah-n Күн бұрын
Sa place n'est pas ici
@fayedjibyseye
@fayedjibyseye Күн бұрын
Botopé ahmétt mi diga réé ba dé😂😂😂😂
@harounacisse9124
@harounacisse9124 Күн бұрын
Mdr😂😂😂 Ahmed Cisse 😂😂kagna frérot je suis mort de rire je sens plus mes abdominaux😂❤❤❤
@makhtarsyll2804
@makhtarsyll2804 Күн бұрын
cheikh mbacke sakho waxoul deug limiye wakh lousi bari daye féne
@moustaphakane1979
@moustaphakane1979 Күн бұрын
Indil say dalil si alquran
@abdoulayengom7659
@abdoulayengom7659 Күн бұрын
Noooo sakho mi dafa xoromu nèna viande ak graiss ki dsnio wara soupal ndey graisse ak yéésyi mou naane 😂😂😂 no graisse gui c bon mé viande pa bon c grav
@defday7667
@defday7667 22 сағат бұрын
Mbacké Sakho miii thi ay sécte la sén affaire yi ay processus la rék bou yagué dîner bi lanioule wédii
@laminembaye497
@laminembaye497 15 сағат бұрын
Ahmed Cissé ak mbacké sakho doul rék lanioy déf
@diopyankhoba9309
@diopyankhoba9309 Күн бұрын
so geumoul wakhou yonente geumou alkhouran ndakh gni bidi allhouran gno bidi wakhou yonete
@DameNiang-j5c
@DameNiang-j5c Күн бұрын
Werna bilaye
@ibrahimakane6233
@ibrahimakane6233 Күн бұрын
Bilahi wallahi dangay geum niar yeppou wala nga weddi niar yepp
@RAMB75
@RAMB75 Күн бұрын
Nite ki moy limiy lék day ame diékhital. Même lek lou léw ak lou léwoul day ame diékhital.
@moustaphadiop6213
@moustaphadiop6213 11 сағат бұрын
Yefer bakhoul
@gooroundeyefatou7552
@gooroundeyefatou7552 Күн бұрын
Lek mom si culture la parsk amna sérère yo hamné beugounou mbroxé
@Cabayoroyoro
@Cabayoroyoro Күн бұрын
Sérère nigni déff mbororkhé eupp na😂😂😂
@abdoulayengom7659
@abdoulayengom7659 Күн бұрын
Djiguén diou xèss dara nékusi di yaw mi kula gueuna beugu femm bu xèss yaw ?
@CheikhNdong-x6s
@CheikhNdong-x6s Күн бұрын
Lou nekh guendi walhnakk
@stafiroulaha
@stafiroulaha Күн бұрын
wakho degue grésse Moy takhe yapeu nek yapeu sou graisse amoule yapeu dou.mana.ame toule rek
@babalamine
@babalamine Күн бұрын
Cheikh Ahmed mbeutt ngay gueuneu niirole sakhe 🤣🤣🤣
@cisseomar345
@cisseomar345 Күн бұрын
Lii deh mooy "JIGEEN DAGAN NA, WAAYE TAAT (DATA) BI DAGANUL" YALLA SI CORAN DAFA AM YI NGA KHAM NI DAFF KOY JUNJU, Exemple: cigarette, alcohol, etc. S
@moustaphakane1979
@moustaphakane1979 Күн бұрын
Yalla ni ay ayam dagnou leer, faram fathieko, mooy leral. Nganane joundie.
@dindinggal7220
@dindinggal7220 Күн бұрын
Jaletin
@mafilledieynabasow
@mafilledieynabasow 8 сағат бұрын
Dawal ak graisse gnouy and. Amo deug deug
@cheikhndour5612
@cheikhndour5612 4 сағат бұрын
Lolou dou diary khodiokla bokoul ak diar
@aliounebadarangom1779
@aliounebadarangom1779 Күн бұрын
Cheikh iow yay deugeul ni bi yalla diokhé yonent bi ba paré gnissi dess dinkouléne dara ???
@mlmohamed519
@mlmohamed519 Күн бұрын
Kagna 😂😂😂
@wakhdeugguetayallatakh8129
@wakhdeugguetayallatakh8129 Күн бұрын
Yaw do tidiane dh dangay fen say say pure nga
@SyAlassane-k7s
@SyAlassane-k7s Күн бұрын
Boul diakasse ak. Ay lent
@mlmohamed519
@mlmohamed519 Күн бұрын
Lorsque j’étais étudiant en Algérie on nous servait la viande de cheval 😂😂😂
@PapisNdiaye-lt9sg
@PapisNdiaye-lt9sg Күн бұрын
Vrai
@Maidior77891
@Maidior77891 Күн бұрын
Yapp ak graisse kene meunoul lène séparer. Tay mome dakourou ma ak yaw
@abdoulayengom3700
@abdoulayengom3700 Күн бұрын
Tu gressemblyz un kagna
@abdoulayengom3700
@abdoulayengom3700 Күн бұрын
C'est pas vrai ce que tu parles des sérères. Tu es en retard. Même toi tu es différent des américains.
Cheikh Ahmed Cisse vs Cheikh Mbacke Sakho
2:48:27
Cheikh Ahmed Cisse Official
Рет қаралды 7 М.
Sigma Kid Mistake #funny #sigma
00:17
CRAZY GREAPA
Рет қаралды 28 МЛН
Cat mode and a glass of water #family #humor #fun
00:22
Kotiki_Z
Рет қаралды 32 МЛН
Wall Rebound Challenge 🙈😱
00:34
Celine Dept
Рет қаралды 21 МЛН
Cheikh mbacke Sakho défi Serigne mor Diagne
34:07
Sunugal Sn
Рет қаралды 2,2 М.
SERIGNE SAM MBAYE
3:55:19
Sunu Thiante
Рет қаралды 63 М.
Sigma Kid Mistake #funny #sigma
00:17
CRAZY GREAPA
Рет қаралды 28 МЛН