Ko bakh esk xam nga le sens de beugue . Démal gueustoul histoire Layla ak ki done beugue. Lou raw lol lanou beugue Serigne bi.
@karimkarim-ew1rq8 күн бұрын
lou rafet rec la meusseu wah si serign bi nak
@massambadieye994527 күн бұрын
Nioune Serigne TOUBA rèk laniouye tope
@DJob3d24 күн бұрын
Il lui a demander kelk chose en contre parti d'un savoir (venant) de dieu alors que le coran nous dit dans la sourate yasin verset 21 : ٱتَّبِعُوا۟ مَن لَّا يَسْـَٔلُكُمْ أَجْرًا وَهُم مُّهْتَدُونَ 《suivez ceux qui ne vous demandent aucun salaire et qui sont sur la bonne voie.》 Kou beug mothiou moytol mbacké mi il est inspiré par satan après ses douguou khelweu sans meme le savoir , satan lui a donner l'éloquence et le bien parler pour séduire et manipuler les âmes faibles qui au lieu d'apprendre leur religion de leur Messager et des hommes de sciences il attendent que quelqu'un vienne leur simplifier les turpitudes qui les pousse dans un égarement évident. Suivez la voie du prophète (saw) et laisser ce gas avec sa propre tombe . Ca sera mieux pour vous
@salmaba512313 күн бұрын
Je suis d'accord avec vous Cette personne réveille la fitna, il dit que des sottises. Prenez garde contre cette personne si vous voulez réussir ici-bas et dans l'au- delà.
@bayetoubasylla7327Ай бұрын
Macahallh 👏👏👏❤sopou nala lolll
@amdiop453715 күн бұрын
Diadieuf
@zallmbaye1622Ай бұрын
😢😢 serigne mbacke sakho yallah nako yallah guider amin ya rabi ndaye sann walahi il croit fermement ces propos nanou ko nianal yallah rek
@tallfamilleelectroniquekol6840Ай бұрын
Amine yalla na ko Yalla guinde
@mouhamadsane675927 күн бұрын
Nitt daal sou beuguè guindèku faaw daal mou bok si kurell ?? 😂😂 Yeen yeena djara yeureum
@maneseydina656427 күн бұрын
Walahi rere ba goumba nga fokni ya ngui yone bou bakh bi
@bourhan14212 күн бұрын
Yalna mou alkou
@karimkarim-ew1rq8 күн бұрын
lou leer lay wah kay , loum la wah indil la ayat ak ay preuve you lerr
@mouridoulahi20004 күн бұрын
الحمد الله رب. العالمين والصلاة والسلام على رسول الله ❤شكرآ ياشيخ أحمد الخديم البكي ❤
@serviteu_d_AllahАй бұрын
Mbacke lingay leeral Amna loussi ame solo waayé mounoo diaamou yalla té boolé woosi sunna ndax loolu weddi yonnentibi sayaboo nga toub balaa ngay dée
@wakeurserignesaliou36425 күн бұрын
Ahmadou kene la❤❤❤
@MamFatouАй бұрын
Ma Sha Allah
@maneseydina656427 күн бұрын
Le fait que Allah dans le coran nous interdit de se diviser c'est une réalité,mais vivre le Coran sans la sunna est un mensonge.
@MoustaphaMbathie-mm1rp25 күн бұрын
جر جف سيخ أحمد بمب خا دم رسول ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@OumarBoye-s7tАй бұрын
Bo topé alkhourane kassé dangeuy am diamou sakh.
@ousseynoutoure3621Ай бұрын
Gnoune dagnouye magal ba khaye fatou so magaloul sa affaire leu tei woul atte mou diotte magal gui di gueuneu neikh peipou kani si gueidj takhou ko weikh
@hoorevision5753Ай бұрын
ioe dof nga rek
@moustaphamboup4934Ай бұрын
Saway dioumo dé wayé dinée yeufou doff la tékou dofoul amoule dé yaw nak Dofu Kane ga mbacké Sakho ndayssane kou mbakhla
@hoorevision5753Ай бұрын
Machallah cheikh Mbackè sakho un homme pluridisciplinaire ❤❤❤
@jobseuofficiel3787Ай бұрын
Wakho fi dara. Waly Seck sayou deffei concert mou fesse deleu tei accuser nagn ko lounek
@AbdoulayeDiatta-gy5oyАй бұрын
Yén dolén ayy dioulite ayy mourite nguén gana messeré wakhonako Donc islam akk mouridisme dou bén
@FallouGaye-gf7kb6 күн бұрын
Soubhana lah astakhfiroullah
@hoorevision5753Ай бұрын
Cheikh Mbackè sakho un homme véridique ❤❤multidimensionnel
@basmbaye7527Ай бұрын
@@hoorevision5753 mbacke sakho doulkat la nafekh la saytane la yak mom sen leufeul ndeye
@DJob3d24 күн бұрын
Je vous jure devant ALLAH (aza wadj al) que ce gas en dans une perdition évidente
@malickseck91129 күн бұрын
Amoul morom khadim Rassoul
@Bamba-rk12 күн бұрын
yalna leen YALLA guindi
@assouhbatoufillahiАй бұрын
YA AYOUHAL LAZINA AMOUNOU TAQULLAH WA TAKU ILAYHI WASSILA.
@kenalserignetoubambacke269Ай бұрын
Dieureudieufé borom Touba ❤
@ModoumaremeGueye-kd1wh16 күн бұрын
Tourou yalla lou am solo la wayé niaka am serigne boulén ték thi yone molène alak
@MohamedKalleDiop8 күн бұрын
Jamonoy dof Si yàlla.waaye yaangi Si réer si yàlla.yalla nanu yàlla Gindi amiin
@bathiefaye71797 күн бұрын
Ki khamnga foumouy moudié ak wadji moy bientôt amed cissé moy guéneu def boppam héro ni j'avais la mission dédéconstruire nbacké sakho pour wané ci thiaxane yimou nek Pour meuna gagné wat touti sympathie meuna continuer thiaxane yimou nékké Niome niar nieup ci ay tiaxane lagne nek mais ahmed cissé dakkoy tek xel
@serignecheikhdiop69018 күн бұрын
Waaw leen goor non moom yalnane gana dof thi todo yalla ak nianal diamo yalla yi
@toubapatarАй бұрын
وماءاتيكم الرسول فخذوه ومانهيكم عنه فنتهوا واتقوا الله إن الله شديد العقاب
@gueyyealiou395Ай бұрын
Lou wer
@MoustaphaMbathie-mm1rp25 күн бұрын
ما قصدك في ها ذه أية
@abdoutoure643614 күн бұрын
Ndayesan ki dafa sanko rek hoo😢thiey dondo go djiéxa gol lony xathie na thi😢
@ahmetmbodj765629 күн бұрын
Cheikh Ahmed il est tellement fort, si seulement vous pouvez savoir. Fén lo na Sakho sans ke ce denier ne s’en rende compte
@yusufmouhamed-8787Ай бұрын
Qu Allah vous garde merci
@abasselo8206Ай бұрын
Assalamou halaykum astakhfiroullah
@fnoumbediop690Ай бұрын
Masahalla yal n'a yalla Fay yiw 🤲
@boutiquekheweulbusinessАй бұрын
C'est très intéressant
@seydina_jibril14 күн бұрын
Cheikh mbacké sakho Fou yalla waxé ni délén joulli fajar tisbar takkudaan timis guéwé indil ma ayya bi ma jébalou si yaw Yalla waxouko ta yankay déf nga beugeu xaraamal joullé néew ndakh ni yalla waxouko !!!!!
@aliouba64808 күн бұрын
Yallah wakhnako déh
@karimkarim-ew1rq8 күн бұрын
wahtou djouli yi ngeuw na alhourane bro , ngeuwal pv ma dioh la ko
@seydina_jibril8 күн бұрын
@karimkarim-ew1rq astagfiroullah
@seydina_jibril8 күн бұрын
@@aliouba6480 foum ko waxé
@mactarseck9849Ай бұрын
Amna solo
@mamefall978823 күн бұрын
Mbacke Sakho dadial molayoni nga woutalko Ay talibee
@Smokin_mass3317 күн бұрын
Ki dei deugue lafi wakh
@karimkarim-ew1rq8 күн бұрын
kon kou wah li yalla wah teh mou nek si alhourane dadial mola yoni ???
@moussaba2321Ай бұрын
Nit kou honnête le cheikh mbacké ❤
@tracychapman6700Ай бұрын
très honnête manchalah
@kouroubayefallpureАй бұрын
Bayi doul d’où tax niou bayi s touba d’où tax niou bayi magal boul sonal sa bopu sax di yakh sen énergie s touba beug nanuko ba nopi
@khadimMbacke-d9uАй бұрын
Ki dafa rere ba yakho ndeyessane 😢
@abdoukhadirmboup9360Ай бұрын
Da rer dine kene dothi dogale samkhele alkhorane khadis mokoye firy de gamole khadiss
@sorycoulibaly59417 күн бұрын
Lou waay meunn thi Istighfar ak Salaatou Alaa Naby nako deff...point
@MalibereSambeАй бұрын
Yalla nala yalla faye chiekh amet cissé bagua takhé niou geune kham kouye mbacké sakho nite yi nio sokhore beugouniou kouye wakh lou yalla wakh niome nagua wakh serigne bi néna rék mane mome légui alquran yalla dji rék laye top
@mouhamadoumourtadaalkarim8274Ай бұрын
Yao la req
@DakarFaDAАй бұрын
Saway def si ndank d. Alhourane ken meunouko top mom kesser té bolé wossi sounna Seydina Mouhamed psl. Si alhourane ken djangalé woul nane lagnouy dioulé, dou nombre rakka yi, ken expliquer woul adj makka nougn koy defer, nougnouy woré... donc Mbacké mi lim si comprendeoul barina. Mom na wakh foum diangué diouli ndax si alhourane la
@MouhamadouMoustaphaDiao8 күн бұрын
Ki santoul mbacké dhé ki sakho la santé Nay léer
@thiernoseck17658 күн бұрын
Vous êtes un homme sigma
@PapadjibrilNdiaye-y4o21 күн бұрын
Sénégal nékhna gni amnagnou ay talibé
@mamethiernosopenaby8713Ай бұрын
Wakhtane bi amna solo
@mouridoulahi20004 күн бұрын
😂😂😂sanékh sakho dafa neexxx 😂vrai comedian la
@diopcheikhahmadoubamba61277 күн бұрын
Da nga dofff ba legiiii😅
@mamefall978823 күн бұрын
Mbacke Sakho yangui reral segalaiyou amour tawhid
@karimkarim-ew1rq8 күн бұрын
man am na tawhid mais daff ma geuna leral yonou yalla bi machalla alhamdoulilah
@ndiayeahmad5929Ай бұрын
Ku bëgg lu leer sa digg ak yàlla jàngal sa diine te bagn ko fortatu. Diine kenn du ko business 👁️👁️👁️👆🏼👆🏼👆🏼
@ngordieganeАй бұрын
Cheikh avec ce monsieur vs risquez de tomber ds le folklore.
@doyendiouf624016 күн бұрын
Machala
@aboridial34316 күн бұрын
Ken Dou borom Touba
@firdawsigroup3132 күн бұрын
Gnaare gni cest des dangers publique.. Mbacké sakho khelmi dako rérale.. Wayé ahmed Cissé mom ab kathior leu..
@BabacarKA-by5kv5 күн бұрын
Sakho dofowon , dof deug dou werr Tassawouf dou ay thiakhane. Serigne si dagno xam, xamé, dioub tey dioubal sell sellal yiw diebal Yalla sèn lépou. Kou djiss batil askanko sa bopou mba sa khel mba kénèn. Yalla nalèn Yalla guindi
@amasy4597Ай бұрын
Mbacke Sakho bègue nalla guiss❤
@AliouNdiaye-lc3pp7 күн бұрын
Waaye alkhurhaan wahula nan ngay jullee
@daoudadiedhiou1221Ай бұрын
Manchalla ❤️
@mamefall978823 күн бұрын
Chaytanee Molay fohee
@ndiougadiop7250Ай бұрын
DOFF YANGUI CI BIIR NIT GNI
@fayedjibyseyeАй бұрын
Ndeye sane
@malickamar80748 күн бұрын
ولا تصل على أحد منهم مات أبدا
@AdanaSowАй бұрын
Alquran dal laniou Yalla topoulo tè lolou la diokhone Yonent mo nèk ci Alquran Laa ilaha ila LLAHOU wahdahou laa charika lahou ❤❤❤❤❤❤
@layetheonly513913 күн бұрын
Fane la nek
@ahmedtidianesy597012 күн бұрын
un comédien aek un illuminé... quel cocktail
@bassiroundiaye3913Ай бұрын
Chiekh amét cissé yaw ak ki yéna yém ndakh yag koy diapalé geumo dara
@AKTECHPlusАй бұрын
Alhourane moye sougnou référence thi diné Islam wax douko fëtë kaw ki da doff ki dëye rëlelatë yoyou yëpp amoul solo indil louye dakh aye waxame djëlëko thi alhourane mo woor kouni yalla nëna sokko gueumoul indil li yalla wax mo gueune tanguëne bayi jugement bi
@AminataFall-w8q9 күн бұрын
CHEIKH BO FATOUWONE KENE DOULA DIEULÈ??
@IlliasSa-b1vАй бұрын
Cheikh mbacke Sakho Dieureudieuf
@amdiop4537Ай бұрын
QURAN versets 30 et 31 parlent des polythéistes (ceux qui adorent plusieurs dieux),par contre les Tarikhas croient en seul Dieu.Ces versets se réfèrent aux nassrane,c'est eux qui ont divisé leur religion en plusieurs dénominations et qui n'ont pas le même concept de Dieu.Et chaque dénomination se rejouisse de leur croyance.
@dasmanjackaggo3340Ай бұрын
C'est un début Révélation pour entrer dans la vraie lumière
@seydina_jibril14 күн бұрын
Yalla ban waxtou la touddou si alhouraaan ??
@Bamba-rk12 күн бұрын
diiné yamoul ci alkhour aan th wèddi khadiiss wèddi nga YONENT BI th kouka wèddi sànkou nga th kaafir nga soubhanallah
@akimbousso2206Ай бұрын
Ñiari masi dadjial yalna yala mouseul nitngi ci yen yen khelyi geun geuna geum ci Li yala wakh dinedji khol lankoy geume way Ken dou toupou sam khel kham kham bou barri ak khel Mou nekh ak diamou yala goudal barri takhoula ragal yala takhoula mouthi ndakh soudon takha mouthie iblis mouthie way iblis topou am khel moko sankue yalnanou yala mouseul ci yen ñiargniii😢
@hoorevision5753Ай бұрын
ioe dof nga rek Machallah cheikh Mbackè sakho
@funasambsamb1661Ай бұрын
@@hoorevision5753kén dou wakh deug si yén bâ wérr, deug rék là yaw andil arguments mo tané lingaï wakh
@mamefall978823 күн бұрын
Mbacke Sakho saytane dafala diaye dila fohee
@OusseynouNdiaye-l8s25 күн бұрын
AXMADOU le sauveur de l'humanité, en tout cas Sakho tu veux avoir des talibés😅
@damefall-it8gcАй бұрын
Cheikh mate cisse moytoul ki dalaye changer dé bilahi
@OumarBoye-s7tАй бұрын
Machalla
@solution5135Ай бұрын
Cheikh mb sakho néna geumoul wilaya wayé lounkosiwakh douko wédi
@kradiop43418 күн бұрын
Sakho koulakham(?
@Smokin_mass3317 күн бұрын
Serigne Bamba meusteu sosse tariqa.
@dijabravoooawaaa9262Ай бұрын
❤️❤️❤️❤️❤️
@pointdevue1304Ай бұрын
Ce mbacke sakho est complètement égaré. 😢😢😢😢
@abdoulayesarr1138Ай бұрын
Yoro diamy Serigne Yoro diamy borome xham xham
@lahatleye6313Ай бұрын
Yal momu tamit mo wax ni ÑJANN LÈNN MA MA NANGU SÈNN ÑANNN TÈ APP NÈEW DIOULÈKO MOY ÑIANALKO TAY LA GEUM NI DAGA RÈŔ
@SanteYalla-tm9kkАй бұрын
Cheikh sakho Mais lima diakhale loutakh nga am ay taloubé?
@moustaphadiakhate3997Ай бұрын
Très bonne question
@nimspetiteАй бұрын
Amatoule Talibé dé liberer naaaa gneuppp ki kou deugou laaa
@khadimendiaye8527Ай бұрын
@@nimspetite Mais pour le moment amna niouko topou dama xamoul nak nolén di toudé😮😮😮
@beugyallarekАй бұрын
@@khadimendiaye8527kène topou ko dé. Amoul ay talibé amoul dahira amoul dara
@AliouNdiaye-lc3pp7 күн бұрын
Sa wax ji yaqul darra ci sunu gëm boroom Touba
@SarrKhadim-w8g29 күн бұрын
Ki limy wakh thi xel lako tek dîne du loolu ki ab nafeekh la bu mak
@KhadimoulMoustaphaDiopАй бұрын
Boffi baye3 serigne touba do am dra nah bo demeee cheikhou tidiane dou la beugg fo dougg dougn la nawlo
@jilymbacke589126 күн бұрын
Niare niou rerr and di rerale top lene bala moye wes ki sunna la weddi ki xamne Limoye wax dou degg dikou diapale مسيلمة الكذاب وطليحة بن خوليد الأسدي
@cheikhounadieng4922Ай бұрын
Ki dafa djaal diamono dof djaal diamono khotekou! Si ay Allam la nek
@harounasow496511 күн бұрын
Shaytana foyé noko
@maneseydina656427 күн бұрын
Rira bien rira le dernier
@malickamar80748 күн бұрын
ما هو صلاة المغرب في الحكم القرءان
@lahatleye6313Ай бұрын
Rouyu kay bu weur tè worr sy dimono bi s abdou rahmane darul mouhti doyna sy
@ablayedine6951Ай бұрын
SAKHO SGN TOUBA AKI NDIABOTAM, DIOULÉ NAGNOU AY NIT TÉH GNOLA GANA HAM YALLAH.KON LOLOU DO SI IRI KÉNA
@bathiefaye71797 күн бұрын
Amed cissé gueumoul touss ci limiy wakh ta bientôt dina guéneu yakh mbacké sakho ni dako done piégé rek Ay domeram you dadié la rek
@oumarnguer-n1lАй бұрын
Serigne bi magwi liniou edi dou ay khadj mais aay yonela
@assanesene876621 күн бұрын
Malgré que ce gars est perdu il dit la vérité concernant les familles religieuses au Sénégal dinné dou tarikha kouné yakarni mo guen moromam
@SarrKhadim-w8g29 күн бұрын
Cheikh sakho yangui doora doof yak say taalibe nak😂
@omarndiaye5184Ай бұрын
Serigne bi nga balma sa kham kham gattena
@DembaSow-bo2fzАй бұрын
اللهم ارزقنا علما نافعا وتوفيقا بالله ياربنا إن كان العلم جاهلا عنك وكافرا عنك وعن نبيك واجعلنا جهلاء ياربنا أنت على كل شيء قدير واجعلنا مقتدين ومتّبعين ومحترمين نبيّك وحبيبك رسول الله صلى الله عليه وسلم.... والله العظيم من لايصدق الرسول لايصدق الله...❤❤❤❤❤❤❤❤
@basmbaye7527Ай бұрын
Bo demoul magal touba Esj wagnina dara si wa touba dommy khadj
@ibrahima5Ай бұрын
Pourtant il n'a pas dénigré ceux qui y vont. Il a clairement dit qu'il a lui même découvert qu'il n'était pas obligé d'y aller. En fait cette discussion est venue à cause de la question qui lui a été posée par Ahmed Cissé. Mais ça n'a jamais été un sujet de ses multiples débats et autres.
@OumarBoye-s7tАй бұрын
Vraiment ta mom sakh néné il l'a découvrir dans ses livres
@cheikhfall3088Ай бұрын
@@OumarBoye-s7tdomu xathie kone danga beug wax serigne bi seutu xathie la amm
@MalibereSambeАй бұрын
Iow sa tounou ndeye ya môme nite yi
@OumarBoye-s7tАй бұрын
@@MalibereSambe wakh lene xam xam mo eupou solo
@MoustaphaMbathie-mm1rp25 күн бұрын
Ki mom mangui sogua setan vidéo wom mais ki vrai nafiékh la
@faddamose4209Ай бұрын
Any attempt to understand the Quran devoid of the Sunnah is a misguidance. May Allah guide us all in the straight path, ameeen.