Gni nio yess si adouna, té niou né famille kilifa. Alakhira dina meti torop. Mama, yallah nako Yallah yeureum, may waydiouram kholou mougn 😢
@cissedienaba5116Күн бұрын
Bilaye 💔
@famatadieme85414 күн бұрын
Courage Mr Ndong Allah vous assistera. 🙏
@pivoine4814 күн бұрын
Khalè bi amna loumou kham wayè Yalla kham na lèpe nite dafa fort trop.
@aminatawone25314 күн бұрын
Dafa am ay khalé you bone pékhé khalé bi nagnouko woo watt mou wakh thie yane lokho laa bayiwon maman diaraf bi kou gniémé yalla lakheu khawma dome khawma seuth sacrifié domou diambour yalla naa fofou néck noflayame kharékoo aldiana you guena kawé wassalame
@mamacissemane57313 күн бұрын
Diaraf bii dé réw laa deff cii makk
@AramePouye2 күн бұрын
Wakhal lo xam c mieux kimou andalone gnéméwoul ray sakh mboteu
@myamya6523Күн бұрын
Ak mak you bone key woluwuma sois disant jaraaf bobou
@myamya6523Күн бұрын
@@mamacissemane5731rew na en plus dafa louche sah esk bokouci
@ahmeddamegueye187921 сағат бұрын
Kimou andalone kouko gnouss dina wakh bb aicha yalna yalla yeureum ko té djégueule ko barkep makk gni
@zeynadiallo72664 күн бұрын
Maman Aïcha ndong que firdawsi soit sa demeure éternelle 🙏🙏🙏
@oumyniang20212 күн бұрын
Parents khalé bii deh bolé degueulo khamni niou responsable laniou yalla na borom bii maylen kholou mougne .
@nderrysokhna83024 күн бұрын
Sama khol métinaaa
@AlimaSamb-xw6gd4 күн бұрын
Li metina yallah nako borombi lerale thi barker alkhourane
@HapsatouDiallo-z6m4 күн бұрын
Yal na lepp lére si barké seydina Mohammad SAW
@latdeguenediagne80524 күн бұрын
Dina ler dé inchalah darou mousty qui gnou fa rayonne 2020 kiko raye daw kéne guissouko demb lagnou ko diap à thies après presque 5 ans
@pivoine4814 күн бұрын
Insécurité totale mo am souniou rew mi. Sétal li rek. Alhamdoulillah comme Yalla léral na
@coumbaba-t6q4 күн бұрын
On ne choisit pas ses voisins dommage
@latdeguenediagne80523 күн бұрын
@@pivoine481 bilay fek ko ba terrain football néko kay dama la sokhla mo guéne and ak mom longuo gnou dokh touti mou rothi diassi rek rendi 😭😭ba paré dieul diakarta guéne deuk bi fek lep daf ko préparé wone mais yalla leral nako demb et chapeau à notre nouveau commandant de brigade de darou mousty depuis 5 ans gnouy khar justice
@ndoumbemboup-u8c2 күн бұрын
Yalnako yalla yereum ki diéf yalnako yalla nite si lou yagoul dara
@attijanibargny92834 күн бұрын
Salam yalna Yalla feignal teh douma ki ko def ak kep kouy def Lou bone fiii thi Sénégal ak aduna dji Yalla sammeu MR Ndaw ak ndiabote dji Salam
@matydiop7922 күн бұрын
Vraiment trop c trop vraiment ça fait mal état bi warna Wakh si lii vraiment 😢😢😢😢😢😢😢😢😢repose en paix Aicha
@MameNdewDiouf-zn7bi3 күн бұрын
Si c'est avéré la police 👮 doit saisir les caméras de surveillance qu'il parle ça peut éclaircir beaucoup Zones d'ombre Paix à son âme 😭😭💔
@paulinebeguerisse48924 күн бұрын
Paix à son âme, qu'elle soit apaisée. Comme dit cest pas un dossier simple mais tenez bon , nous vous soutenons.
@gayafall4 күн бұрын
Masta reposez en paix mame Aicha
@MatyDieng-n8w4 күн бұрын
Yalnala yalla may kholou mougne
@coulibalyyacine62312 күн бұрын
Yalla nako yalla yeureum
@aminatacisse93783 күн бұрын
Ya Allah nako sounou Boroom yeureum té khaaré ko Aldianah si barké Seydina Mouhamad (SAW). Gniko faatt Ya Allah naléne sounou Boroom fénial. Famille Ndong massaléne, mougne rék
@SarrMay-b2f4 күн бұрын
Yalla na ko yalla yeureum té kharé ko aldiana firdaws amine ya rabbi 🙏
@babacarndiaye14193 күн бұрын
Yalnako Allah SWT YERAM xareko Aldjannah Firdawsi. Metina lool.MAMA AICHA YALNAKO ALLAH SWT LERAL METINA TROP.
@AbacarNdiouf20 сағат бұрын
Ki déff li yalna ko yalla wér métina trop
@ramses28233 күн бұрын
Lepp seutou diaraf bi la kouka nokk dina wakh deugue bi
@oumoul.khairyfall4176Күн бұрын
Yalla na ko yalla ndite
@oumoul.khairyfall4176Күн бұрын
Ci maagayou seydina mouhamet.sounou borom nit
@djibrildiouf-l5p4 күн бұрын
masa way sama grand famara li métina trop way yalla bakhna li doyna war trop
@strategiesetdeveloppement25253 күн бұрын
Pourtant les adn pouvaient le confondre on est un pays sans science
@aidasene87543 күн бұрын
Kikodéf yalnako Borom wér
@gorguisseybar2 күн бұрын
Tellement triste 😢
@morthiam98544 күн бұрын
Paix à son âme bon courage
@bsowfall3 күн бұрын
Yallah nako Yallah yereume khareko aldiana firdawsi yi si barket Muhammad PSL Massa metina trop
@cissedienaba5116Күн бұрын
Massa 💔 gnit a sokhor 💔
@myamya6523Күн бұрын
Mais lii yoboulene ko ci procureur Dakar kokou Hana li jahalouko
@mariamadiouf19404 күн бұрын
Police Tamite 3 jour ci mineur
@elhadjiahmadouba20482 күн бұрын
Faut revoir l'éducation et créer des comités de vigilance de quartier chasser tous les jeunes qui traînent dans les bâtiments abandonnés . N'attendez rien de l'état eux sont protégés et ils peuvent pas mettre un policier derrière chaque citoyen. Wa salam
@mariesalomon33752 күн бұрын
Bilaye Li diakhalnama te diakhaloul souniou borome
@aissatoubijou8498Күн бұрын
Qu’est-Ce qu’il raconte ce monsieur le papa est patient, en tout cas les enquêteurs Sénégalais aussi sont patient et finiront toujours à obtenir cause .
@dikhagaye74813 күн бұрын
Ndaysan yereume nako sax
@fatoumatadiallo32902 күн бұрын
Li métina 😢😢😢😢
@juniorjunior13452 күн бұрын
Une petite fille ne peut pas orchestrer une meurtrie... sans laisser de traces arrêter aussi. Wakhléné lou logique... même si la petite que vous présumé meurtre était une grande personne saway une crime n'est jamais parfait
@BeauteDiop3 күн бұрын
Man dall meunouma comprendre li xew sii sunu deukk bii lii waroul won deff 2jour si yon waron naniou am preuve nieuw bakan dafa forr Wa Bargny mom beitt naniouma mann nk domou Bargny dama rouss dakh kouko diapei won nisa dome digua diapalei mifa bii sett sen dome maman aïcha yalna aldiana disa deukouwayy
@BinetaNdiaye-e2v4 күн бұрын
Yala Dina KO were da fa meti trop
@AwaDiallo-hw9jf3 күн бұрын
Paix à son âme
@JjĥHhh-n5c2 күн бұрын
Na yone def ligueyam dafa yombe ray domou diambour comme ça
@halikano3922 күн бұрын
DOMOU DIARAF BOU GAUR BOBOU MO SAKOU MAMAN AICHA BA PARÉ RAYEKO KOUKO DIAPPA DIAPAGUA COUPABLE KOUKO BAYI BAYI COUPABLE YALLAH NAGNOU GOUDEU FANE DAYE LÉRE INCH ALLAH
@Didi-z1m2 күн бұрын
Liguay wah mba lou la ler la?
@mamidedakar67024 күн бұрын
Metina d😢😢 Khana mouton sakh meunoul rere si kogn
@zeynadiallo72664 күн бұрын
Sarapp ndeyou police Sénégal
@YacineDiop-f5t3 күн бұрын
Setou djaraf bi gnari version la wakh bima déguelo papa dji ndakh bi papa dji démé diko ladje khalébi daka wakh ni mome thi wave bi la démone ké déme diendi sow té caméra 🎥 bi nékone thi wave bi wané khalé bi kone li khéw khame nathi dara wala mou ragale wakh
@diarradiene42752 күн бұрын
Man dee yereum na son pere mais yayam ak ay rakam la geuneu yeureume billaahi li dafa meti tee niaw un avenir yakarouma yayam ak liniou ko sedel NDEYSSANE si khalee yala bouko thiat djitou ayway moun na am sakh bokou rak dji topon dou deme ni maman aicha aussi elle ne savais pas que bou andalek kokou dou nieuwaat jusqua ce que mou disparaitre jusqua SA mor Lima geuneu meti yayou maman aicha dafdonn diokh ay nitt lek tee nena domam si khiff la deee ohh alahou akbar ya raabby dort en paix maman aicha yalna yallah leral SA mbir yi nga bayi guinaaw ba SA kholou yaye mouna sedd touty😢😢😢
@Mourid.sadikh4 күн бұрын
LI moy meti si deuk bi niou tay sa dom do ham kiko ray
@Matiseck7070Күн бұрын
Lebou yi bossi boukoule bouffa deukkk falla yeme
@BinetaNdiaye-e2v4 күн бұрын
Dina fegne nite'da fa for
@NeseDia3 күн бұрын
Niouss len seutou diaraff bi dina wakh lixew !
@khakika-d9g2 күн бұрын
Fimou douguou khalebi khamnako khamna dafko netali ay wadiouram niouneko boul wakh nel djissoumako bayam khamna leup famille bi khamnaleup
@amisow68073 күн бұрын
Papa c la jalousie
@strategiesetdeveloppement25253 күн бұрын
Pourtant avec des analyses du corps et tous ses voisins on allait trouver l’ assassin
@mameyacinesarr55173 күн бұрын
Nanioulen andano com gouvernement bou Bess bi tiaxanoul niou tex ci pression meurtrier bi fegne
@dexterdexmen67072 күн бұрын
TANT QUE DEFOU GNOUBPEINE DE MORT LI DOU DIEKH SENEGAL
@HabibatouDiallo-b9n3 күн бұрын
Amine
@fatousene2482Күн бұрын
Vraiment je comprend plus notre justice le cas de filleule cas de Aziz et garçon et tant d'autre pitier quel gouvernement on 'a
@soumeyalenasagna600514 сағат бұрын
Doucement rek ce ne sont pas tous les crimes qui se résolvent aussi rapidement. La police sénégalaise est en train de faire son travail
@gayafall4 күн бұрын
S’en weyreuthé bi . Mo indi problème .
@sophrotall810521 сағат бұрын
Nolen khameni dafko wakh niou and dieundi wave te khalebi guissolenko