😱Allakhou Akbar :Thioune Boutique Limou wakh Waly Bambey, Mane Yalla Rek la Yakkar tés so Moytou wo.

  Рет қаралды 93,386

CINEVOX PLUS

CINEVOX PLUS

Күн бұрын

Abonnez vous et activer la cloche de notification pour ne pas ratez aucune de nos prochaine vidéos Merci

Пікірлер: 385
@leprometzo9048
@leprometzo9048 4 ай бұрын
Thioune yaw sa kanam sokhor nekouthi da fékk rekk kou bakh sonou yalna yalla samm la ❤
@MarieDiop-cq3es
@MarieDiop-cq3es 4 ай бұрын
Bilay
@jobisdiopmjjobis3496
@jobisdiopmjjobis3496 4 ай бұрын
Oh machalla kadou yi nice na lol yalla sa diam yagg
@SagebaraDieng-mf8oe
@SagebaraDieng-mf8oe 4 ай бұрын
Thioune bilay meunone nga bagna tontou Waly mi wéroul
@ramandiaye3726
@ramandiaye3726 4 ай бұрын
Fallait pas répondre ce mec il n'avait pas une belle voix déjà il faisait slm comédie yaww ngayy deff lou bakh bokou sakkk fallé
@oumouceras3810
@oumouceras3810 4 ай бұрын
​@@ramandiaye3726:24
@liesarotine9436
@liesarotine9436 4 ай бұрын
Vraiment kou meunoul touss batam bou bone di wout buzz nane liguey dako wara porté plainte
@fatouseck4915
@fatouseck4915 4 ай бұрын
Mon frère tu devrais même pas le repondre si c'était moi dinako porté plainte mou indi preuve certains sénégalais il t'accuse gratuitement mome loumou ame bey moukoye ligueye amoule sorale yaye faut punir ces genre d'accusation trop facile
@sodandiaye9063
@sodandiaye9063 4 ай бұрын
Yalla na sa diam yague gua continer dignou bègueul❤❤
@Abraham22199
@Abraham22199 4 ай бұрын
Badola la khamoul khaliss thioune bayil ki yako raw si lepp ❤
@yasssinediallo1080
@yasssinediallo1080 4 ай бұрын
Vive thinoune boutique ❤ vraiment merci 🙏 beaucoup tu es l’homme fort 💪 je te souhaite long vie et bonne santé a djarama ❤❤❤
@BayeDiop-v6c
@BayeDiop-v6c 4 ай бұрын
Aminé tihoune yalna yalla defal la diamu ❤❤
@adjafallmory7316
@adjafallmory7316 4 ай бұрын
Bilaye thion ya bakh ya gore ❤❤❤wally bambey mo sofe te beuge beuz
@elhadjidjigal4014
@elhadjidjigal4014 4 ай бұрын
Machallah yalla nala yalla sam si barkép alkhourane 🇺🇸🇺🇸💯🇺🇸🇺🇸
@AwaSene-j1z
@AwaSene-j1z 4 ай бұрын
Machallah Amine yarabi
@tallatoure195
@tallatoure195 3 ай бұрын
Tu communique bien machallah❤🎉
@khadijandiaye8374
@khadijandiaye8374 4 ай бұрын
ndeyssane koubakhnga yalnah souniou borom barkéle sa ligeey té sammeula🙏
@ToulayeDiop-ui4zl
@ToulayeDiop-ui4zl 4 ай бұрын
Nite kou bakhe nga kafe AK ré rék Nga kham ki badola amal diam rék ❤❤❤❤❤❤
@ndeyeamicissokho8339
@ndeyeamicissokho8339 4 ай бұрын
Demal porte ko plainte mo guene wakh dji limou wakh dafa graw trop sax
@serignembackemouhamedtoure3526
@serignembackemouhamedtoure3526 4 ай бұрын
Ndeysaan Thioun Boutek boul Tontou Dofbi Waly Bambaye Waxi Dof Rek ☝️ Laye Wax
@AichaSakho-cl5ze
@AichaSakho-cl5ze 4 ай бұрын
Machalla.❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@DembaPouye-k5e
@DembaPouye-k5e 4 ай бұрын
Merci beaucoup yalla n'a sa diam yague ❤❤❤❤
@sambaliondiallo5353
@sambaliondiallo5353 4 ай бұрын
Machaalha mon frère je te souhaite longue vie et beaucoup de santé Dieu te protège❤❤❤❤
@serignembackemouhamedtoure3526
@serignembackemouhamedtoure3526 4 ай бұрын
Bilahi Waly Dana Rethiou Limou Wax Nanou Dim Base Kanam mane Mi S.M.M.T.S.S.S 🇮🇹 Xawma Thioun Boutek Waye Kou Bakhla
@AbySene-kt2bu
@AbySene-kt2bu 4 ай бұрын
Non thioune yalnala yalla faye sa khôl waly mi ga khamni dafa dof boulka tontou
@MbendaGueye-kf3yc
@MbendaGueye-kf3yc 4 ай бұрын
Boul ko falé yaw nit kou bakh ga❤❤❤❤
@OusmaneGueye-t5u
@OusmaneGueye-t5u 4 ай бұрын
Ya nitté bilahi ❤
@laminedaffe9335
@laminedaffe9335 4 ай бұрын
Merci beaucoup mon frère courage souko rkc ❤❤❤
@Defunity
@Defunity 4 ай бұрын
Thioune couco Guiss xamni nite cou bakh leu, kénène ki môme thiow li motakh ma xam co on va dire qu'il a atteint son but. Continue tel que tu es Thioune ne change pas, continues à aider des gens si tu peux, ne change pas pour un ingrat. En tout cas merci pour le travail que tu fais.
@Steven-ul8pw
@Steven-ul8pw 4 ай бұрын
Thioune Bayiko Ak Yalla Wahdiou Niaaw Yag Nafi
@fatoubarre2946
@fatoubarre2946 3 ай бұрын
Pour thioune ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@papendiaye2784
@papendiaye2784 3 ай бұрын
Machallah réck la meuneu Wa wakh si tioune boutique
@SaliouDiange-g4v
@SaliouDiange-g4v 4 ай бұрын
Wally dof le 🎉🎉😢😊😊
@niang.talibe.brom.ndienend5434
@niang.talibe.brom.ndienend5434 4 ай бұрын
Way thioune doundal yaw talibe serigne touba nga ..dof bi da diaroul genneu di def interwew 😂😂😂,da bank rek
@ndiolefaye2043
@ndiolefaye2043 4 ай бұрын
Liguey bi yalla na gueneu diapppp dagno sone si Wally Bambey 😂😂😂😂
@NouhThiam-l1k
@NouhThiam-l1k 3 ай бұрын
😂😂😂😂😂
@assanfaal2079
@assanfaal2079 4 ай бұрын
wally 2 dou nitt bilay 😭😭😭🙏🙏
@mousstaphafall-ou8df
@mousstaphafall-ou8df 4 ай бұрын
Bilahi 😢
@votremiroir7612
@votremiroir7612 4 ай бұрын
dof pire leu
@AbabacarSamb-h5j
@AbabacarSamb-h5j 4 ай бұрын
thioune ya bakhe waye barki Serigne saliou mbacké nite kou bakhe ngua
@ndeyefatouninguembengue7598
@ndeyefatouninguembengue7598 4 ай бұрын
Thioune Macha Allah ❤
@AbdallahMbaye-ld4to
@AbdallahMbaye-ld4to 4 ай бұрын
Ndeysane. Thioune. Kholl bou rafét la yorrr ❤❤❤❤❤
@moustaphasow7920
@moustaphasow7920 4 ай бұрын
Thioune❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@aliounedia8314
@aliounedia8314 4 ай бұрын
❤❤❤Thioune bilahhi borom bah gua diammm rk guay ame inchalla
@babaissandiaye1916
@babaissandiaye1916 4 ай бұрын
Boul topou gni sokhor yow sa khol da rafet. Machallah ❤❤❤❤
@ndeyewade7376
@ndeyewade7376 3 ай бұрын
Yaye gor dege❤❤❤❤❤❤🎉
@MarèmeSène-s6m
@MarèmeSène-s6m 4 ай бұрын
yaw kou bakh ga🙏🙏🥰
@ndemoudiofior8338
@ndemoudiofior8338 4 ай бұрын
Waly goré woull deh talibé seurigne touba dou sokhorr amall diame thioune❤
@khadydiagne9686
@khadydiagne9686 4 ай бұрын
Wally khamoul bopam wally va travailler c’est mieux 😂😂
@Seck-c7d
@Seck-c7d 4 ай бұрын
Merci beaucoup Waya nak bayiko xell domu harame diaroull wolou😭😭😭🤜🤛🙅🙅🙅🤝
@MalickDiop-wu5ms
@MalickDiop-wu5ms 3 ай бұрын
Amine noo thioune boutique nitte kou bakhla bilalhi khamoumako mosoumako guisse
@moyancheikh3991
@moyancheikh3991 4 ай бұрын
Manii nanale ndokh bou séde té nelaw Yallah rek mofi nek❤❤❤
@modoudiagne8237
@modoudiagne8237 4 ай бұрын
Thione kou bakhga Yalla na yalla fay sa khol
@fata3463
@fata3463 4 ай бұрын
Senegal dall xaléyou ndao weurdi nian rék 😢😢😢😢😢
@moudoudiop6216
@moudoudiop6216 4 ай бұрын
Ndeysane yaw gou Bakh ka 💯💯💯💯
@AwaboussoMbaye
@AwaboussoMbaye 4 ай бұрын
Machallah ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️
@MarieDiop-cq3es
@MarieDiop-cq3es 4 ай бұрын
No thioune ya bakh way
@Sambathiaw-ss9pj
@Sambathiaw-ss9pj 4 ай бұрын
Thioune boutique kou bakhla bilayi❤❤❤❤
@papediaw1707
@papediaw1707 4 ай бұрын
Waly 2 demal ligueyi mon guene
@bintoudiop274
@bintoudiop274 4 ай бұрын
Machallah ❤❤❤
@AbabacarSamb-h5j
@AbabacarSamb-h5j 4 ай бұрын
thioune yalna yalla defale diamou waye thi barki borom touba
@katygaye8280
@katygaye8280 4 ай бұрын
Wayaw bayiniou waaaye waly bambey nga kham nii moye tawou bougane 😂😂😂
@MbodjVabien
@MbodjVabien 4 ай бұрын
Tioune mii nitt kou bakh la Manchallah llou la guiss si mome mais Wally ay mbiram mome
@assfayeserignesaliou742
@assfayeserignesaliou742 4 ай бұрын
MACHALLAH THIOUNE ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️✅️✅️✅️✅️✅️✅️👍👍👍🏽👍🏽
@Muhammadulaminediba2502
@Muhammadulaminediba2502 4 ай бұрын
Cëy Senegal dioté ak morom yobuko si telé ba lii yaxanté bA kañ.😮Ana soutura ana mouñ😎
@abdougorafall5863
@abdougorafall5863 4 ай бұрын
Sa way danga dioum.nak warowon ton tou DH danga waron teudjie ndayam teudialé bayam ❤
@Madamemmedia
@Madamemmedia 3 ай бұрын
Wally 2danga faté yalla khana ki diaroul répondre
@MamadouSene-i4z
@MamadouSene-i4z 4 ай бұрын
Waly bambaye amoul ngor xalis la geum😮
@AssaneMbengue-gt5dd
@AssaneMbengue-gt5dd 4 ай бұрын
AMINE YARABBI
@Malicksindidi1988
@Malicksindidi1988 4 ай бұрын
Wadjii thiatt moko japp manam thiatt ak liguéy nitt danio niiroo niniouy manifesté woo(dafa melni nganii DEFAAL AK DÉÉF)danio niiro na dém woutii ay niaan dina bayi inchallah
@CheikhounaSall-c5m
@CheikhounaSall-c5m 4 ай бұрын
Merci beaucoup ❤❤❤❤
@GambianTikTok-fy4so
@GambianTikTok-fy4so 4 ай бұрын
Belie ya bahk thioune ❤❤ke walu tou day sa bopa Wally
@xalimagui-officiel9001
@xalimagui-officiel9001 4 ай бұрын
Yalla dafma dimbali ba mann déjà bi Wally Bambey Di def beuz dawou mako deglou. Sénégal legui kou dioug di dof dof lou si kaw nitt gni pour tedd sen kaw. Thioune sa kadou yi kouko degg xamni kou deugou nga. Nekal sissa liguey té bayi tontou bi.
@NgagneSeck-ib9gn
@NgagneSeck-ib9gn 4 ай бұрын
Ku Yor numéro ki s'il vous plaît ce gosse je l'aime beaucoup je vois sa réussite s'il était entouré de gens matures et qui voit loin ce qu'il fait est très important wallah
@CheikhSarr-il6dv
@CheikhSarr-il6dv 4 ай бұрын
Mashallah
@Lampfall87
@Lampfall87 4 ай бұрын
Bro yaw nala diam sonal bayuiko ak yalla wally day out beuss hamul dara mom batam nekhoul 😂day soop rek
@oGthixm07
@oGthixm07 4 ай бұрын
wally bambey warna rouss dh ki kou bah lah bly
@SanteCheikhibrfall
@SanteCheikhibrfall 4 ай бұрын
Thioune yàlla na la yàlla défal diame ak soutoura
@RamataSow-w9i
@RamataSow-w9i 4 ай бұрын
❤❤❤ yalna yalla yapelé
@biteyeaminata370
@biteyeaminata370 4 ай бұрын
Boul ko falé bayi ko mouy fowé khelam mi bania dem hôpital bala liko dal diko eup dolé febarou bat you bari yi vraiment senegal meti
@mamikayre7021
@mamikayre7021 4 ай бұрын
Thioune porter ko plainte
@bayenarmbengue5839
@bayenarmbengue5839 4 ай бұрын
Thioune diaroul wona tontou déh waly bambaye wëroulle doffe deugue laa
@mcmassofficiel8489
@mcmassofficiel8489 4 ай бұрын
Merci beaucoup
@SidyLamineBarry
@SidyLamineBarry 4 ай бұрын
Merci thioun❤
@IbrahimaGaye-ew8gu
@IbrahimaGaye-ew8gu 4 ай бұрын
Y’a bakh yaaaaa gorè yaaa ab djioulite Bilay Thioune y’a bakh
@amfashiontrading1108
@amfashiontrading1108 4 ай бұрын
Waa commerçant lounouy ligueyer ABB mn waykatt
@oGthixm07
@oGthixm07 4 ай бұрын
moma diakhal sax
@talibeserignesaliou8762
@talibeserignesaliou8762 3 ай бұрын
lol moma diakhal
@deugrek-gk3lx
@deugrek-gk3lx 4 ай бұрын
Vrai badola moy wally bambey vraiment domeram leu dou nitou dara
@BazirDiop
@BazirDiop 4 ай бұрын
Filme bi episode 2😂😂
@alimatousougoufara1571
@alimatousougoufara1571 4 ай бұрын
Bilahi thioune yaw kou bakh nga bayiko ak yalla
@AbdouDiouf-z3k
@AbdouDiouf-z3k 4 ай бұрын
🎉🎉🎉❤❤❤
@FallouFall-y8p
@FallouFall-y8p 4 ай бұрын
❤❤❤
@ababakrinkara3133
@ababakrinkara3133 4 ай бұрын
Yeen gni yapp nagn leen nak li prank la sheuuuuu Sénégal 😂
@SanéAliou-g3v
@SanéAliou-g3v 4 ай бұрын
Thioune diam si yow❤❤❤❤
@gorguidieng7796
@gorguidieng7796 4 ай бұрын
Waly conseil boumalay diokh Moy khaliss koulako geune beug douko am Da nga si andal ngor pour am sino tiaga ji rek gnokoy lek
@AissatouWade-z2n
@AissatouWade-z2n 4 ай бұрын
Waly bambey foumou Toth
@gorguidieng7796
@gorguidieng7796 4 ай бұрын
@@AissatouWade-z2n feine
@MorDiaw-j8o
@MorDiaw-j8o 4 ай бұрын
چون يال نليال ميور❤❤❤❤❤
@MahiGueye-x4i
@MahiGueye-x4i 4 ай бұрын
Wally bambey walahi dmrm deug gua bly sa rasta you neup yi rek mane na tes sa voix😅😅
@CharlotteThiam-l5m
@CharlotteThiam-l5m 4 ай бұрын
Yaye ngoor naak Thioun
@DiogayeNdiaye-vv5no
@DiogayeNdiaye-vv5no 4 ай бұрын
Thioune demal porter plainte moom mo bakhou . Li motakh Wally seck douko djigué opportuniste la selon lima fi degue. Bagn liguey di takhawalou rek ba parè di toumal nite yi
@ThiernoGueye-ut1uh
@ThiernoGueye-ut1uh 4 ай бұрын
No thioune vraiment togne ngama domikharam dji da diara tontou
@awambaye3449
@awambaye3449 4 ай бұрын
Ya Bakh way machalla
@AbabacarSamb-h5j
@AbabacarSamb-h5j 4 ай бұрын
thioune sa communication rafetena lole waye
@maguettethiam1311
@maguettethiam1311 4 ай бұрын
Thioune ya bakh bilaye
@MadjigeneDieye
@MadjigeneDieye 4 ай бұрын
Thioune boutique kou bahhe gua gorgua
@OmarToure-y
@OmarToure-y 4 ай бұрын
doundeul wereul goundeul fan
@ALIOUNENGOM-t7n
@ALIOUNENGOM-t7n 4 ай бұрын
Courage thioune
@Awalô_l9z
@Awalô_l9z 4 ай бұрын
Bilaye sa xol refétna bilaye❤❤
@Astou-m2c
@Astou-m2c 4 ай бұрын
Rawale
@Yasspro4452
@Yasspro4452 4 ай бұрын
Lii miss a sénla waye sénéglaise yi yéwou léne waye akh
@NdiayeAwa-nv6hm
@NdiayeAwa-nv6hm 4 ай бұрын
Machallaha
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 18 **VOSTFR**
1:13:28
EvenProd
Рет қаралды 1,5 МЛН
AMOURS BRISÉES   Saison 1- Episode 40
33:55
Yesdakar
Рет қаралды 295 М.
Хаги Ваги говорит разными голосами
0:22
Фани Хани
Рет қаралды 2,2 МЛН
Sigma girl VS Sigma Error girl 2  #shorts #sigma
0:27
Jin and Hattie
Рет қаралды 124 МЛН
Who is More Stupid? #tiktok #sigmagirl #funny
0:27
CRAZY GREAPA
Рет қаралды 10 МЛН
No Stress - Duo bou nekh entre Wally Bambey & Niamakhite
8:47
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 127 М.
😂Amadou ba tit na problème amna dh douma dem fenne
18:48
moussa officiel
Рет қаралды 31 М.
PRANK STAR  - Saison 3 episode 27 Ada Fass - Damalay diam
13:55
Mahfousse
Рет қаралды 247 М.