AMA BALDÉ: "GRIS COMBAT BI DOU DEF 1mn30", ADA FASS ÉNERVE GOUYGUI, LISS MENACE ZOSS - FACE2FACE

  Рет қаралды 23,519

2stvsenegal

2stvsenegal

Күн бұрын

Пікірлер: 17
@FallouThioye-ol5jp
@FallouThioye-ol5jp 7 ай бұрын
Yalla nala Yalla may dam Ama balde
@tallambengue-oc4cd
@tallambengue-oc4cd 7 ай бұрын
Bilah walahi Ama damako beugue ndam rekk inchallah ❤❤ yalla nala borom mousal si thiate wayy AK balla gaye
@guedjgueye6478
@guedjgueye6478 7 ай бұрын
ama Serigne Ndiaye 2 nékhouta daneuh deh
@mambayecisse2017
@mambayecisse2017 7 ай бұрын
Liss bandit la 🤣🤣
@alaminegaye
@alaminegaye 7 ай бұрын
Ama seul😂😂😂😂😂
@GalassGueye-z4r
@GalassGueye-z4r 7 ай бұрын
No gouy gui dénama rayé
@serignedieng-vh4zv
@serignedieng-vh4zv 7 ай бұрын
bilahi pikine moy lambe
@serignedieng-vh4zv
@serignedieng-vh4zv 7 ай бұрын
giri yengel nge gayndé gi
@GalassGueye-z4r
@GalassGueye-z4r 7 ай бұрын
Liss moko tayé téli cng dathé wara wajh
@kadijatoujallow3477
@kadijatoujallow3477 7 ай бұрын
😂😂😂❤❤
@seydoukanesall
@seydoukanesall 7 ай бұрын
Tapha geuye 2 , quand gris le salué,le caméra ta trahi ,tu a dit naféke, ça se lisé sur t'es lèvre
@Goor-us9in
@Goor-us9in 7 ай бұрын
Saway ioe mandou wo dh té do diapp limou wax thi kaw rk moy bégué gris rétane diapp ndiambour ram …. Défo yeufou dioulite
@seydoukanesall
@seydoukanesall 7 ай бұрын
@@Goor-us9in iow pr iow niii dagua mandou,meunone gua rombe,limou def modoule yeufou dioulit,dioulite daguay deugou dii wakh ligua geum ,sa te suffit ainsi
@Goor-us9in
@Goor-us9in 7 ай бұрын
@@seydoukanesall ioe pour ioe lane moy mandou? Ioe lingeu déf moy niakka mandou pas mane limeu déf prsk boudone mane limeu def niakka mandou leu kone yonnente bi mandou woul wone parsk bou moussane guiss kou defoul loudoul dakokoy wax sénégalais nak dafa am problème ak signification (mandou) bouniou done dieul yeufou diambour sah ngeu nieuw wax thi niouni non non waro thi wax ndax danga wara mandou 😂 xamouniou mandou loumouy firri ak fane ngeuko wara utiliser🤷‍♀️
@seydoukanesall
@seydoukanesall 6 ай бұрын
@@Goor-us9in niaka mandou moy fék commentairou diambar dougou sii di diéma diaye kham kham té khamo touss,donc trace ta route car tu réfléchi à moitié
@serignedieng-vh4zv
@serignedieng-vh4zv 7 ай бұрын
liss boudé yako taye togn bakhoule
@chelseablaz3786
@chelseablaz3786 7 ай бұрын
Mais ada fass beuretoul way
Face2Face Bou métti Zoss vs Liss Ndiago "Man douma sa morom daga…
17:24
RÔLE'N SHOW 24
3:13:56
Rôle'n Play
Рет қаралды 24 М.
GRIS BORDEAUX VS AMA BALDÉ : CLASH EXPLOSIF AVANT LE COMBAT !
29:04