ANALYSE BOU DOYWAR SUR REUG REUG VS BOY NIANG LES VRAI SPÉCIALISTES DÉCORTIQUENT LE CHOC

  Рет қаралды 68,291

Bantamba TV

Bantamba TV

Күн бұрын

Пікірлер: 96
@gueyelabsolu5889
@gueyelabsolu5889 8 ай бұрын
Bouché linga sole rafetna trop way ❤️
@mouhamedsamb7238
@mouhamedsamb7238 8 ай бұрын
Reug reug guissouma ayam si mbeur bou gaw kouy xalate leu gueuneu meune d'après ce que j'ai vu
@IbrahimaNdour-pb8qq
@IbrahimaNdour-pb8qq Ай бұрын
Yaw khamga reug reug kouy been been monno dann reug
@SouleymaneCamara-n9e
@SouleymaneCamara-n9e 8 ай бұрын
Boy niang bouye dan reug reug si encadrement ak mystique lako yakar mais boudé mbeuré reug reug moy favori si man
@medounediene9652
@medounediene9652 8 ай бұрын
Reug reug manaa khekh dafa avantagé beure rék attention gris baurdeaux daure mo nebou berrem
@ouzdaking382
@ouzdaking382 8 ай бұрын
Fadam ak buurr roubé rek dou ni soyez professionnel balla gaye 2 c est un tres grand champion c est le papa des lutteurs nekh nakhadi , ndam rek Inch'Allah 🎉
@papemalicksembene783
@papemalicksembene783 8 ай бұрын
Wakhi supportere kassé nga fi wakh bro
@abdoulatifdiop5640
@abdoulatifdiop5640 8 ай бұрын
😅😅😅 nekh nakhari mbeté yalla
@ouzdaking382
@ouzdaking382 8 ай бұрын
Utiliseléne séne khel touti waye yéneu khalate yi dafa rousslou sakh 😂😂😂 il faut pas etre tebé 🤣🤣
@ibrahimalo3060
@ibrahimalo3060 8 ай бұрын
Boy niang limou indi contre modou souko indé mo meun koudoul reug reug
@medounediene9652
@medounediene9652 8 ай бұрын
Bécaye invitél birahime ndiaye mou wakhla loudoul dégne
@mansourdieye9494
@mansourdieye9494 8 ай бұрын
Bilay yénagui wax rék khékh mais reug reug néexoul door coup dé day xol coup té reug reug sayoo déclenché daflay diapp force té bouko diapé Moy combat bi dièxna
@Nene-il9cp
@Nene-il9cp 8 ай бұрын
Merci fadan vraiment je suis très content de toi
@ousseynoutoure518
@ousseynoutoure518 8 ай бұрын
Ordinateur khékham baxoul té sanieu sanieu bi desna manila reussir mbappat et frappe c'est pas donné à tous le monde
@ousseynoutoure518
@ousseynoutoure518 8 ай бұрын
Sa thies da yakaroni boy Niang domamla Boy niang mo meune reug dou nékhé gueum nak
@bdiene66
@bdiene66 8 ай бұрын
Kom dou nékha gueum rék kon wéroul😂Yow khamo reug😂😂
@baradieng1489
@baradieng1489 8 ай бұрын
Reuk reuk le Grand champion boul deglou ben farfarlo
@ababacaredougueye9668
@ababacaredougueye9668 8 ай бұрын
Boucher ak lirou,ils peuvent pas analyser sur BG2 à cause de leur proximité avec le lutteur,Fadam et Buur veulent réveiller l’orgueil de BG2 pour qu’il soit au top de sa forme c tt
@Knmunhomme
@Knmunhomme 8 ай бұрын
L'olympien reug reug contre boy Niang le mental samouraï , bour ...combat leu dé
@fatougueye325
@fatougueye325 8 ай бұрын
Boy Niang seul kouka bagn sa tounou yaye niang kassé
@papadionmendy3557
@papadionmendy3557 8 ай бұрын
boy niang késsé 💚❤
@Lass9
@Lass9 8 ай бұрын
Bour ak fadam Boy lagnouye farale day fégne sakh si sén wakh
@GagnessiryBa-qd8uz
@GagnessiryBa-qd8uz 5 ай бұрын
Fadam do nite lecture de combat g très important bilakhi walakhi
@AwaGueye-jf9ol
@AwaGueye-jf9ol 7 ай бұрын
Bour gueweul thi bopam mo khamoule bopam louka nekh lay wakh mbeur gni lolou pour lanlatamite un peut de respecter mbeur ayy kilifeu lay
@dialloboubacar6142
@dialloboubacar6142 8 ай бұрын
Reg reg bis bou ataké boy niang am louko meti
@elzobibaboypolyvalent
@elzobibaboypolyvalent 8 ай бұрын
Boucher sokhor nga lo bagné Boy Niang nii 😮
@lefootballsansfrontieres8921
@lefootballsansfrontieres8921 8 ай бұрын
Bour diango français d 😂 débat ouverte moy lan😂😂
@GoraKhouma-ny8vn
@GoraKhouma-ny8vn 8 ай бұрын
Bouché a raison boy Niang doit amener une bagage fraîche pour s'en sortir
@MouhamedThiaw-bu2li
@MouhamedThiaw-bu2li 8 ай бұрын
Reug reug mo boy niang fouff
@ibrahimakhalil3884
@ibrahimakhalil3884 8 ай бұрын
Fadam soit professionnel boy lire dagay sath dofa seug Di khol
@sidysakho6558
@sidysakho6558 8 ай бұрын
Reug Reug nék MMA di xékh chaque Jr
@abdoulatifdiop5640
@abdoulatifdiop5640 8 ай бұрын
Way mounoul khéx
@Jubjubbaljubantii
@Jubjubbaljubantii 8 ай бұрын
Gni key danio nekh rek
@fodediame1831
@fodediame1831 8 ай бұрын
Bilayi Gandia Fama brome Niombato
@FallouNdiaye-y9i
@FallouNdiaye-y9i 8 ай бұрын
Bouché yaw da nga bagne boy niang bene moromam dakhouko beuri
@domou__rewmi
@domou__rewmi 8 ай бұрын
Sa Thiès moko dakha beuré fouf
@ibrahim69853
@ibrahim69853 8 ай бұрын
Fadam deug rek nga wakh naniou ko diapalé waye
@ouseynousarr1673
@ouseynousarr1673 8 ай бұрын
Bouche mounoul beug boy Niang 😂😂😂😂
@Babacardiane221
@Babacardiane221 8 ай бұрын
Manoulén na bayi di énvité bousé ngiryala ki khamoul dara way akh 😢
@DoudouFall-uk1pf
@DoudouFall-uk1pf 8 ай бұрын
Super ❤❤
@MorThiam-e4e
@MorThiam-e4e 2 ай бұрын
PAPE DIÉDHIOU.BOY NIANG2,N'A PAS DROIT À L'ERREUR...?
@thiapa6489
@thiapa6489 8 ай бұрын
Becaye plateau mounoul ame ak Boucher !! Please 💔💔🤦🏽‍♂️🤦🏽‍♂️
@amdymoustafgueye
@amdymoustafgueye 24 күн бұрын
Boulène fatté Reug Reug légui MMA la nèkk et il combatte bien
@lefootballsansfrontieres8921
@lefootballsansfrontieres8921 8 ай бұрын
Fadam boy wah di xol sa phone bi pour lan la ?
@niassesouleymane7163
@niassesouleymane7163 8 ай бұрын
On direz on le dicte des choses
@CASI7797
@CASI7797 8 ай бұрын
Wave yi lay xole
@FanBoyNiang2Gambia
@FanBoyNiang2Gambia 8 ай бұрын
Lou takh Boucher munou ta support Boy Niang😂 dafa dane Balla, Sa Thies ak Gouy gui😂😂😂
@Nene-il9cp
@Nene-il9cp 8 ай бұрын
Boucher s'a data yaye amo Dara wouli bouia diapé katsa yaye
@MUSTAPHACHORR
@MUSTAPHACHORR 8 ай бұрын
Iow hana neko si werou koor astagfirlah
@ahmadougaye2580
@ahmadougaye2580 8 ай бұрын
Boungén doul déclo môme Wakhyan wi monoul am sens
@PapejoeMendy
@PapejoeMendy 8 ай бұрын
Bouché bo wakhé ni boys niang Nioroul si khékh khamo lamb 😂
@ibrahimakhalil3884
@ibrahimakhalil3884 8 ай бұрын
Fadam legui euppeul ga, Bour balla gaye se baye la
@dethiesene1415
@dethiesene1415 8 ай бұрын
Reug reug foo laale déeye Beurrée
@gorguidieng7796
@gorguidieng7796 8 ай бұрын
Yenagui ordinateur rek faté doudou sané bayi lene KO khel
@ndiogoundiaye3772
@ndiogoundiaye3772 8 ай бұрын
Bouché rék lah guiss mou nék américain té Sénégal rék lah begue
@malickniang225
@malickniang225 8 ай бұрын
Boucher baneu xam-xam la ameu banioukoy invité si débat technicité
@daoudacisse4849
@daoudacisse4849 Ай бұрын
REUG REUG YALNA YALLA MAY LA NDAM CI KOW BOYE NIANG
@lamyntv
@lamyntv 8 ай бұрын
Wa Bayiléne sounou vidéo yinguene di utilisé sans notre autorisation Founé lanouy dougou ci aleu bi ak ci îles yi di passse di dougou gal pour am images Après Nguéne tog séne plateau diko utilisé C’est injuste
@BantambaTV
@BantambaTV 8 ай бұрын
Niogui diegeulou frère 🙏🙏🙏🙏
@birafall7385
@birafall7385 Ай бұрын
Entoucas boy Niang Dafa yéme si beurè
@CASI7797
@CASI7797 8 ай бұрын
Boucher nak bagne gua Boy Niang torop. Li guay deff dou analyse
@mamadousagnejr9272
@mamadousagnejr9272 8 ай бұрын
Diadieuf Fadam2
@kmhiphop8849
@kmhiphop8849 8 ай бұрын
Bour féneuh rék lako doul nangoulé zarko dafa nieuw deuk kognam moukoy protégé bénéne mbeur boufa nieuw mou clash la té un consultant ne doit pas faire de sorte
@abdoulatifdiop5640
@abdoulatifdiop5640 8 ай бұрын
Fadam Badara internet tamit day deff lou am solo si mbappat demal ngua geustou ko ngeun fekhé invite ko si plateau bi😮😮😮
@dialloboubacar6142
@dialloboubacar6142 8 ай бұрын
Boy niang dou perd 2 foi
@falyndoye3800
@falyndoye3800 8 ай бұрын
Pas cette fois ci dé
@domou__rewmi
@domou__rewmi 8 ай бұрын
Tapha tine lac2
@MbodjaNdiaye-t3e
@MbodjaNdiaye-t3e 8 ай бұрын
Non nak sérieux bour guweul mi gagne la negeu comantateur lambo bay negeu si platou yi mane lolo m'a diakhal
@AmadouDiao-x4w
@AmadouDiao-x4w Күн бұрын
Boy Niang dafaye maye chance reug reug ndakhe bou beuré deug dou morome reug reug moy si dor moye beuré
@ibrahimadiouf8664
@ibrahimadiouf8664 4 ай бұрын
Ce sont deux techniciens mais le plus tactiquecien va gagné le combat et le plus féroce Par contre pour battre boy il faut accumulé bagarre de la rue et lutte pur comme modou lo l'a fait parce que c'est un tactiquecien fini
@ndiougamar2202
@ndiougamar2202 8 ай бұрын
Kou beugoul niam kou dou déf mma yén da ngéni né law rék
@martindiene9113
@martindiene9113 8 ай бұрын
Analyse Fadame ande na si à 85%
@medounediene9652
@medounediene9652 8 ай бұрын
Bour jour bobou ya geune nulle bingua wakh waroko wakh
@MaremeFaye-v6v
@MaremeFaye-v6v 8 ай бұрын
Ltx boucher dou nangou nih boye niang dafa nokh sathies ak bala gaye ki sonu nah danga far rk ms boye niang ndanane lah
@AbassSakho-b2e
@AbassSakho-b2e 8 ай бұрын
ioe Bûcher mayniou wakh RK ngua meunn Ngay melni champi té do drrrr Callate way
@BeauGossFaramareen
@BeauGossFaramareen 8 ай бұрын
Dégouleunté waay
@tassymbaye356
@tassymbaye356 8 ай бұрын
Fadam yaw danga melni ya môme palatoobi Mayeno Diam
@GalassGueye-z4r
@GalassGueye-z4r 8 ай бұрын
Wa bouchr loula reg reg dike
@MaxDiop-f1e
@MaxDiop-f1e 8 ай бұрын
Mais waKh balla ngakoy wakh kholat ko gris kilifa la tamitt
@moussaseck6992
@moussaseck6992 8 ай бұрын
Boucher hamo lingay wah ordinateur mo dak beuré fouki reug reug boulgnou sonal way ahh mbeuré se sérère blocage bi yeup si séne moromou mbeur yi gno beugoul gnou yégue
@mohameddiouf6785
@mohameddiouf6785 2 ай бұрын
Boy niang mo dak beuré sa thiés fouf
@SaliouMbengue-mk9rg
@SaliouMbengue-mk9rg 8 ай бұрын
Boure mo daha doule
@falloushoptv257
@falloushoptv257 8 ай бұрын
Becay waxna lou lerr boy yi demou lutte simple nio dak beuré fouf
@omarespane4101
@omarespane4101 8 ай бұрын
Fadam da rew torp
@falloushoptv257
@falloushoptv257 8 ай бұрын
Exemple sathies reug reug, général malika fils de balla,…..
@MrBrowniso
@MrBrowniso 8 ай бұрын
Bour bayil français bi
@sambadiop2671
@sambadiop2671 8 ай бұрын
Emm khana dou khekh de kon wala
@niassesouleymane7163
@niassesouleymane7163 8 ай бұрын
Fadam arrête de regarder ton tel on direz on te dicte ce que tu dois dire
@abdoulatifdiop5640
@abdoulatifdiop5640 8 ай бұрын
Wa bouche sagnsé ngua way Amo xam xamou lamb deh😅😅😮 sans mbalak nak
@SaliouMbengue-mk9rg
@SaliouMbengue-mk9rg 8 ай бұрын
Fadam daye Dou reke
@sandrineetcesjumelle6289
@sandrineetcesjumelle6289 3 күн бұрын
Ibo seul 🔪
@mansourndiaye3391
@mansourndiaye3391 8 ай бұрын
Bilaye fadame ya wane Lou moye seuge du sigui melni gou mène lire ta khamo doull
@fallmamadou5741
@fallmamadou5741 8 ай бұрын
Boucher xamoul lamb et il parle trop
Eric Favre Nation MMA à Abidjan : AMAO SODIQ vs MOUHAMED TAFSIR BA
41:40
Creative Justice at the Checkout: Bananas and Eggs Showdown #shorts
00:18
Fabiosa Best Lifehacks
Рет қаралды 30 МЛН
Intégralité combat Gris 2 vs Reug Reug caméra Lutte TV
15:53
RIVALITÉ PIKINE AMA BALDE ET BOY NIANG LAMB BUSINESS
26:54
Bantamba TV
Рет қаралды 34 М.