Yallah dal moy Dioubal diamam, 1987 Sama papa dafma yobou fouta car commence won na bon, mou metti ma trop, ma dem nek dara, di continuer ecole aussi, Yallah dima sopi ma dem ba am BAC, am sama Master sama MBA actuellement je suis Reponsable Regional Adjoint des Finances et des operations dans une organisation Internationale
@SokhnaNdiongue3 ай бұрын
Mashalah santal yalla ak sa papa takhawou nala sinon danga narone bone
@coumbadieng29693 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤
@ahmadouka80365 ай бұрын
Addouna ya meuna warr Yalla naniou yalla mousseule ci chèytanè
@dakardk47505 ай бұрын
Amine
@annaseck87644 ай бұрын
Amine
@tidianiasy82654 ай бұрын
Amine yarabi
@AliouCisse-x5d4 ай бұрын
Yalla na yalla dioubeul mbolém mbinff si barké mouhamed amiine
@aissatousylla41724 ай бұрын
Ndéyssane yalna la YALLA diégal mayla wéer ak nioune nieup si barké SEYDINA MOUHAMED S.A.W amiiine amiiine amiiine
@Enfant_béni_75 ай бұрын
Daguay guiss kou doundou banditisme ba diékhal nane dafa TOUPP di conseillé watté té banouy tolou séen digou doolé 😢 ray ay niit , sathieu , Aggressé améel ay niit akh youdoul dièkh après begeu ame moudiou bou rafett non c'est impossible car ALLAH ❤ IL EST TRÈS JUSTE ☝🏿dou YAlla guén amel akh dé bay toupp mais NIIT yiguén MEUSA togne guén Amel akh nak Sunu Borom diganeté NIIT AK moromam kinou togne rèk lay FARAL lègui yén foléni guisséti NIIT yoyou pour Balou léen akh 😭💔banouy tolou sén digou doolé yaay wax , papeu wax , kouné wax niouné toubounou danouy déf linou sentir mais je juge personne SAma xalatt rèk la wax , koulé ni Faral nak dafa fèkeu mousou nioula agressé wala Bandit mousoul ray sa dérett té NAFÉKEU nak bougoul kouy wax DEGEU. Téksi seytané yikoy Faral moy gniye diawalé toupp ak dém ba teulé amatou doulé ba Geumbeu wala feuneukh..niakeu pékhé tokk Di reuthiou,, MES FRÈRES GENRES NIIT YI WARNANOU YÉE KOUNÉ SI ADINA BANDITISME AMOUL MOUDIOU BOU RAFÉTT TÉ REUTHIOU DINA FÉKEU DIEUF FESS YALNANOU YALLA DIÉGAL TÉ MAYNOU MOUDIOU BOU RAFÉTT 🙏🏿🙇🏿♂️☝🏿😭💔✊🏿🫵🏿😔😥😢😭💔🙏🏿
@@papasambadiop7599 banou waré wone toupp Di conseillé waté mo yagg mais Bayi ba ndéy Maguette dinou sonal té yagg trokhal NIIT Yi yaw mom Koula guiss xameni 6 Moy 9 🫥
@Enfant_béni_74 ай бұрын
@@gabrielngom7185 kou wax degeu guéni bagn pask ay nafékeu guén
@niakkbakarr18054 ай бұрын
Yalna niou yalla khirtal ci ak ndioupp
@ramatoulayedrame65894 ай бұрын
Kou foyee sa ndaw yakh sa mak, yague yague rethiou rek tee banditisme amoul mouthie, yallah na yallah dioubeul ndiambott gui tee khiir lene tchi boppame.
@sympathisante174 ай бұрын
Walay ndeyssane 😢😢😢
@ataal62374 ай бұрын
Salam Salam depuis la Grande Bretagne. Kou melnii nak la societe sokhla. Ministere bi yore education ak culture daniouko ware encadre diko yaubou si ecoles yi ak associations de jeunesse yi mouy expliquer diar diaram pour yehtteh. Personnes avec lived experience are valuable, contrairement a ce que niou beuri Di moytou ak daw. Yalna yallah doli soutoura teh dioumal niou. Vraiment merci
@NdiayeBara-lj9me4 ай бұрын
Boudé lingay wax nii degeu la si io dh baxna machalla yalla nala yalla geuna sopi
@fatoureinebadji58924 ай бұрын
Machalah il n’est pas trop tard pour se repentir yalla nagnou yalla khir thi bopam
@dabafall-31734 ай бұрын
Bly j’ai le cœur meurtri en voyant les jeunes qui prennent ce même chemin
@soxkhou2474 ай бұрын
Yalla nagne yalla mouthieul té may gnou moudj bou rafet aaamine Yaw ya yees ci domou lakakatt kou djokk ni serigne Touba
@makhfaye-c2k3 ай бұрын
Senegal li motakh raye bi di bary do référence pour jeunesse bii
@fas2822Ай бұрын
Non légui nak référence leu
@Epitucule447Fall4 ай бұрын
Yalla nagnou yalla maye moudiou gou raféte amine incha alah
@BinetaNdoye-yf6pp4 ай бұрын
Bonne amoul djeurign bakh sone Bone sone bakhal mouye sa djeurign
@yacinendiaye21004 ай бұрын
Ndeyssane ya guorreee nak machalla nalla yalla may hol mougne
@diagnemomo47714 ай бұрын
Atouman ak Walker ak yaya Ay policiers you meunone sén liguéye Bouya thiam ak wéllé ak baye ali ay ak ndaga ay bandits lagne wone Marché goudi louniou sath fofou lagnko done diayé Rue13/18 Keur malaw fala boy médina yeup diangé touxx yamba ak cocaïne Gal ga fala ginzmane yi ak faxman yi nékone moy terrain manakana La Médina ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@diagnemomo47714 ай бұрын
Bamba Fall défoule dara médina loudoul sathhh Bamba Fall bandit leuuu Medina bén maire la amone ba niar saxx Biram sassum sy avocat Pape Diop pds Bamba Fall rékkk😂😂😂
@fatoubilelkane58044 ай бұрын
Cava Li bane côté la si médina svp
@sympathisante174 ай бұрын
@@diagnemomo4771chef f quartiers fictif 😂😂😂
@adamambaye15144 ай бұрын
@@diagnemomo4771.
@sympathisante174 ай бұрын
Yalla nagn borom bi mayy moudiou gou rafetttt.. 😢😢😢😢
@IbouNdiaye-h1s4 ай бұрын
Motakhitt yalla khissappp nalako
@PrinceZou-jc9mm4 ай бұрын
Ndaw bou ligueyeul yalla do mague di torokhe
@Moussandiaye219945 ай бұрын
Lily borom bakh saf xorom bilahi ❤
@mouhameddiagne71923 ай бұрын
Ndaysane yalla nala yalla defal jam. Tchey aduna😢😢
@sunuworkentertainment46254 ай бұрын
Temps que Yagui noyi ! Reuthiou dou Wess Ya Allah reka xam li nek si xool yi
@damefall44714 ай бұрын
Ndeysan thiey Diarr'diarr😢😢 ❤❤❤🤲🏼🤲🏼🤲🏼
@YacineSene-s4c2 ай бұрын
Machalla yalna yalla arla
@fsene70894 ай бұрын
Vous avez terrorisé toute une generation bilay , j'ai fait mon cycle primaire a la medina 2 ( matar diop) années 85-91 , on ete obligé de faire le tour vers le marché tiléne pour ne pas passé par le terrain diarraf et devant ce fameux baobab !!!
@babacarsamb56464 ай бұрын
Matar diop bamb détruire nako malheureusement
@strategiesetdeveloppement25254 ай бұрын
C’ est triste
@strategiesetdeveloppement25254 ай бұрын
@@babacarsamb5646 matar diop c’ est qui ?
@strategiesetdeveloppement25254 ай бұрын
Les yeux se soignent chez un bon spécialiste pas chez des charlatans
@sokhnamboup97814 ай бұрын
Ndessane yalla nala yalla diégeul
@ousmanetine47774 ай бұрын
Oh grand Lily, Qu'Allah veille sur lui.
@ngomkhadim17495 ай бұрын
Fi la dioudo rue 9bi ndeysane mangu joal actuellement yalna l'en yalla dolii tawfekh
@younoussba-o1d5 ай бұрын
Vrai souvenir école 2 ,/ 3 terrain maracana terrain diaraf pa Ass notre formateur avec coach Farmoz et coach Jules j'habitais à la rue 21 × 22 ❤❤❤ merci Médina tv pour ces beaux souvenirs
@fatoubilelkane58044 ай бұрын
Iii ban côté la si medina
@abdoulwahabba28414 ай бұрын
@@fatoubilelkane5804école médine
@bambamars23524 ай бұрын
Ohh Pa Ass sama pere sama kharit un grand formateur
@mouslayeimmosenegal35294 ай бұрын
@@fatoubilelkane5804fi moye école medine, médina 1 ba 5 la wone Mangui deukone rue 19 angle 4
@thiernobah13084 ай бұрын
Moi aussi j'étais c'est pa Ass en 2002 jusqu'à 2005
@FrancoisDiop-uw6nb4 ай бұрын
KU GEUM-NI KU BOTT BOUKII XATHIE MBAW LHEU" LALALE J'AIME 👈
@MbayeGakouNDIAYE3 ай бұрын
Grand naga,wéllé, bouya Thiam...les petits boy laye toungouné,boy poulo etc
@Bigboss-hd8fx4 ай бұрын
PA ALLEMAND MOY DIOP L'ancien gardien de medina 1 le pere de ismaila et abou mangui wone medina 5 ex ecole mamour diakhaté ; madam rose, madame ba, monsieur sarr, madame dieye, monsieur sarr serere, Directeur Samb grand pere de Anta samb jetais dans la meme classe que Idrissa kassé, Charles Ndoye, alassane ndao,demba diaw, khadijatou diallo, aby sow, aissatou gaye ca fait plus de 30ans je nai plus de leurs news ❤
@babacarsamb56464 ай бұрын
Pa allemand décédé bou yageu mais ndiabote gui beu legi gnongi deuk fofou
@Bigboss-hd8fx4 ай бұрын
@@babacarsamb5646 sisi j'avais appris son décès diadieuf
@bababodiang4 ай бұрын
C'est un éducateur vraiment
@serignesall32574 ай бұрын
Je le trouvais souvent au terrain de jaraaf il fut des temps Il travaillait avec bamba Fall, ce dernier l'aidait beaucoup.
@bababodiang4 ай бұрын
QU'ALLAH t'assiste et t'accorde longue vie
@bababodiang4 ай бұрын
Très instructif vraiment
@zahrafatima13954 ай бұрын
Ndeysane yAllah naniou borom bi maye mouthiou gou rafete tè baxale niou
@basselabdou98914 ай бұрын
Lolou rék modiara niane amine🙏
@modouthiam11274 ай бұрын
Baye ba ñiaka ndiariñ 😂😂😂nane Toupna
@hamzadiallo33004 ай бұрын
Boul wakhlolou waye frère adouna defa koudou tankeu
@fas2822Ай бұрын
Loolou la ci borom bi beugoone au moins Yalla baayinako mouy dounde pour mou meuneu changé
@yayefallkawsara4 ай бұрын
Gaayi dh lolou lagnouye bagna dégue Kasso kou défoul dara wallahi doufa dougou Yalla nagnou yalla dolli soutoura
@sambaalisow69214 ай бұрын
Adina amoul solo dioup rek mo bakh
@balmah14 ай бұрын
Un péché reconnu est à moitié pardonné. Dieu pardonne ceux qui se répentissent à moins qu ils ne se récidivent
@moustaphadiop20084 ай бұрын
Toubo dé dagua amatoul doolé rék
@Toufa-uh1ee4 ай бұрын
😂😂
@MariamaNdiaye-ot8zj4 ай бұрын
Yalla nala yalla diegal li passe yalla smou ñie dess ba donou ko def
Bandi amoul ndiarign ak rk ak rk meno moudie fou bakh
@AbdoulahadSylla-f9h4 ай бұрын
Du courage papa Dina bakhe
@MARIEDIOP-q4c4 ай бұрын
Il fo l encourager il n est jamais trop tard pour bien faire au moins il c ressaisi
@mamediarrabeye-ed1zd4 ай бұрын
nit ken douko jugé yalla rek mo kham mais goumba dou agressé
@AblayeTall-zy6gm4 ай бұрын
Médina 2 dans notre classe de cm2 quand on ouvré la fenêtre on appercever le baobab
@Xamxamtv-v2f3 ай бұрын
Kou xam gougne Nguen te
@mercifulservant55264 ай бұрын
Yalna Allah yeureum
@moustaphaba538615 күн бұрын
Béne timis touti niou raye ma birr terrain jarraf periode élection présidentielle 2012
@aboucamara66793 ай бұрын
J habitáis a la rue 10 x 23 medina j etudais jean de la fontaine rue 22x37 et 39
@NdeyeArameDiop-v5r4 ай бұрын
Toupe d'où niak pèkhè ndimbeulou yalla la ak moutier bou rafet l'île boul khaadi dèè yalla n'a sougnou borom gueule la diapalè parceque il a le grandeur regrete donc bonne continuation grand lili
@thiernobah13084 ай бұрын
Qui se souvient du fou qui était ici a l'école Medine on l'appelait Bir mouss il est décédé yague naniou titeul fofou😢😢
@domoubadiane3484 ай бұрын
Khamone nga beneu dof bou nekone si corniche bi guedjou ifan gnou dane ko wower papa gol gol.
@bellangediouf93654 ай бұрын
Bir mouss hamonako, il nous faisait peur...😂😂
@babacarsamb56464 ай бұрын
Moi 😂
@MamecheikhNgirane4 ай бұрын
Yalla NANIOU BOUR LAHOU YOK SOUTOURA
@salldineakdiamono23913 ай бұрын
wa mai grand boyi sèn tank laniouy diarre
@helenepouye89074 ай бұрын
Le mal se paie
@serignesall32574 ай бұрын
Lily un gars bien le connait bien il habite à Médina rue 27 angle 10 près du district sanitaire de Elisabeth Diouf
@awabop56714 ай бұрын
Allahou Akbar courage rek
@KineMbrngue4 ай бұрын
Yéneu Yéna takh banditisme bi di law li kéne douko émission khana amo léne programme
@fas2822Ай бұрын
Non au contraire
@serignegaye-lp8yu4 ай бұрын
La vie est très courte chaque personne doit change son habitude
@alhamdoulilah54464 ай бұрын
Yalna nala Yallah diégal té doli la yiw. Les enfants voici des conseils qui peuvent vous être utiles.
@MackySall-qh1ns5 ай бұрын
Def Lou Bone baxoul
@SambaDiawaraSarr5 ай бұрын
Yonou Bandit amoul Ndieurigne Dou am moudiou rafette
@SeckAdama-tp8qh4 ай бұрын
Ani wa Mansour Sy Malick
@alouguy59914 ай бұрын
MACHA ALLAH RIEN N'EST TROP TARD
@sokhnaoumoudiop68885 ай бұрын
Bandit yep sen khôl dey rofet waye amoul moudj
@fas2822Ай бұрын
Billaay en général daniouy beug xalé, xamna dafa am loulène manqué té wolou wouniou Yalla
@bababodiang4 ай бұрын
C'est la bonne fin qui compte dans la vie des gens
@bayegaye-qf4kv5 ай бұрын
Bandit ya pas de vie ni le respect les bande organisée ak bandit salité bokhoul lui ces un innocent qui n'a pas de soit de vivre sans éducation à la base ni repère maintenant c'est leurs tours de payé chér maintenant ya après la mort que Allah te protège frère longue vie
@gabrielngom71854 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤ très belle leçon de vie, merci
@OmarNdiaye-i9k5 ай бұрын
Lily que dieu te protége adouna amoul solo
@Baicherno-j9d4 ай бұрын
Thanks
@babacarmbaye88403 ай бұрын
Lima diakhal niome kousiy wat danga barkep serigne touba wala serigne fallou ken dou seydile hadji malick sy
@ibrahimaseck51114 ай бұрын
Ki ko nekhhhhhh. Un bandit ki se dit khol bou rafet
@fas2822Ай бұрын
Mais c'est possible gni en général daniouy beu xalé, meune nga def loubone fek sa xol rafet, mooy lima wakh rek niaka woolou Yalla meune n'a la defloo Lou bone
@mamediaby60903 ай бұрын
Day féne , réyna ba tayi
@adjifambayesow69924 ай бұрын
Medina 2 la dianguè
@khadimdieng17454 ай бұрын
kou fowé sakk ndaw sak makk rere la
@Khadyv.h4 ай бұрын
Bouya thiam nion bokone kongne akka bakh nedeyssane adouna dou dara bouya thiam si famille boukh la bokk 😢
@AbdouGueye-m5u4 ай бұрын
Wakhji Yep len rek momaci nakhary limowakh nimo doon dokalle dorog bi ci pirission bi warokowo' guene ci vidéo bi khamo dara
@issakasylla19794 ай бұрын
Le presentateur cest le jumeau de waly seck😂
@makhfaye-c2k3 ай бұрын
Dagno wara raye sa ndaye doméram yie doléne rouse do référence pour jeunesse bii
@FatmaDiouf-m3q3 ай бұрын
Akh dafa séwe akh késsé mola diapeu
@bourathobouratho46725 ай бұрын
Bandit bou diékhal rék né toub na
@Pm007x294 ай бұрын
Saway yalla nena bountou toub dou teudiou 🤝
@bourathobouratho46724 ай бұрын
@@Pm007x29 ok lolou tamit deug la
@fas2822Ай бұрын
@@Pm007x29au moins amna chance toup, amna niou deh ci sen dig deunde
@Assanefall-uq1he4 ай бұрын
Ndeyssane père ass diak nitt kou bakh mognou yorone fofou
@ibrahimaseck51114 ай бұрын
Ancien bandit. Niata nit nga raye
@strategiesetdeveloppement25254 ай бұрын
Et pourquoi on vend le touk touk c’ est illégal
@juniorgueye96374 ай бұрын
Bilahi do niemer sax djar fi
@Bamba-rk4 ай бұрын
Linga def nitt yi th tek ko sa doolé ndaw rk Adouna dara doufi weuyy
@CheikhDiouf-u5h4 ай бұрын
Ate.kabaga Maracana diamano bouya Thiam
@mouslayeimmosenegal35294 ай бұрын
Pa Ass diack mo yorone école de football terrain jaraaf ooh médina mo yagueu nexx fila dioudo rue 9angle corniche magué rue 19angle 4 fi la diangué école medine médina 4 ak 1 ba 3
@daoudaseck13475 ай бұрын
Fi gu takhaw guouy mo fa amoone ak ay garabou coco
@dieynabadiop43334 ай бұрын
Defa wah lou am solo sa yaye ak sa papa de gnu wah ba sonn do deug do len fale te beug Lou bahh lagn la beugal ben alkaly wah nga def par force avec respect l'an mo fi diar li yereum len parents yi sonn nagn fi ngen di nek ci prison parents yi gno geuna souffrir bilay sonn stresse di len di ray ba hey dee
@papefaye2725 ай бұрын
Grand bu bakh kayy😂
@alphabetfootmamboyakecouta90024 ай бұрын
En tout cas dafa diara ré😂😂
@sambasorysow31804 ай бұрын
Mann bi may deukeu medina kenne amoulwone fitou agresse bire medina rue 33 x 10 Diecko
@ndeyefatougoudiaby7445 ай бұрын
Yalla naniou yalla moussal si lou bone
@ramatoulayengom46865 ай бұрын
Amine
@ibrahimaseck51114 ай бұрын
Tu vas le regretter
@mbayendoye80534 ай бұрын
Bouya Thiam kou yagueu beugueu khale....ecole medina 1 aye souvenirs inouabliables...Je me souviens de Pata,Ndiol,toungoune,boy laye ect....reacreation on allait voir Bouya et il nous donnait de l 'argent.
@mariamakebe37254 ай бұрын
Bilaye tu as raison Bouya Thiam kou beuguone khalé avec sa copine Salma une fille très belle à chaque récréation école médina 1 dégnouye déme si galgui pour le salué nite bou bakh bilaye beaucoup de souvenir