N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
@misszjuke491411 күн бұрын
Il faut etre ferme et ne lachez tout le monde vous soutient ! Force à vous et justice soit faite pour aziz et wally
@seydinaalioudiouf143111 күн бұрын
Justice pour Aziz et Wally
@adamandiaye431411 күн бұрын
Metina loleeeeeee courage na yone défe liguiéyame Aziz Ba et Boubacar Gano yallanalenes yalla yeureume té kharelenes alediana amineeee metina Aida courage
@BinetaMbengue-d3r11 күн бұрын
Amine
@naboukebe539011 күн бұрын
Yoon bou defoon ligueyam khamne double morte la con dou guene Ken da fek ne galsen kouniou ray ya pert yak say mbokou guisnan fi kou fenn ba ray 80 persones Europe la moudjie danou kosay encourage sakh ak di diokh ay million waaye yalla guemoul nelawoul te lou waaye def di ngako layo ak sa boroom
@salihate-ew6wy5 күн бұрын
Amine yarabi 🙌🙌
@TAPHISCO221Tv11 күн бұрын
Bou léroul fii daal dina lér yawmal xiyam 😢😢😊
@FatouDiop-wg1du11 күн бұрын
Mane d lii laa Wakh dès le début machalla
@deugrekk641011 күн бұрын
Merci ✅️
@SoniaKhonte11 күн бұрын
Walay yallah guemoul nélewoul
@awaseck744111 күн бұрын
Fii la wara ndieukk fégné nak ndakh gnou meune kham kou Ray 😭😭
@mamefatouseck92098 күн бұрын
Yaw mal khiyam deugg la wayé day yomb trop, dakh fofou kou nek sa bop gay tall
@salyallemomuawrksarr865211 күн бұрын
Justice pour Aziz dabala et Boubacar Gano peine de mort 😭😭😭😭😭🙏🙏🙏❤️❤️❤️
@awatoure505611 күн бұрын
Yayou aziz naniouko bayi mo nopalou comme yaram nekhoul😢😢😢
@salihate-ew6wy5 күн бұрын
Bilahi 😭😭😭🙌
@kayezikartv724011 күн бұрын
Bi problème dafma dépasse même pas 4 mois gua guène légui li mo khéw Sénégal
@yayourassoul611011 күн бұрын
Que justice soit faite kouci taakh na yone def ligueyam c tout
@warrios659011 күн бұрын
Nabou leye ont dire amna bras long si mim rew mais bon si elle est coupable conscienceme dina ko doy prison
@adjaratougning295711 күн бұрын
En tout ce n était pas là première fois qu elle voit une personne poignardée à mort
ndeysan c vraiment triste de entendre non seulement, il se resembles meme sa voix resemble celle d'Azise, mais faisons confiance à notre justice car j'oublie j'oublie joubantii certainement choses qui pouvez valoire une liberation totale aurier due possible.
@sokhnaseck630611 күн бұрын
Il n’y a aucune justice au Sénégal sinon elle ne serait pas libre car elle a été entachée à plusieurs hauts degrés
@KineDiame-du4bo5 күн бұрын
J'ai plus confiance à notre justice
@khoudj84111 күн бұрын
Li Moy encourager nit yi Di fadial s'en boppe..😢
@succulentplat368411 күн бұрын
Fatiha +11 ikhlass pour Abdou Aziz Ba et Boubacar Guano 🙏 Qu’Allah leur fasse miséricorde😢
@ArretArret-p3n10 күн бұрын
Yalle nallène yalla maye kholou mougne wayè mètina tropp
@ndeyegueye11511 күн бұрын
MACHALLA PAPA NA COUROUSSE DAMAKO YEUREUM CAS Bi DOYNA WARR MEUN NA AM DINAGNOU WAKH POURQUOI GNOU BAYIKO
@yacinediallo639311 күн бұрын
Moi ma question est, est-ce que les procureurs sénégalais font parfois des conférences de presse? Il faut en faire pour éclair la situation. Ici en Europe c'est comme que ça se passe, même il faut respecter la famille de la victime, ils ont le droit de savoir...
@astucesdionguen860410 күн бұрын
Surtout lolu
@adamaba650810 күн бұрын
😢😢😢metina m courage rek
@farmataniang560811 күн бұрын
Justice pour aziz dabala et wally gano
@coumbafaye931911 күн бұрын
CONTINUER LEN DI DEF AY MARCHE NDAKH MOU SIW BA PRESIDENT BDF AK PROS DEGUEKO .
@tukucisse795711 күн бұрын
Je pense kil ne faut pas faire de conclusion hâtives… Si Nabou Leye a bénéficié de liberté provisoire c’est parce que la justice n’a pas suffisamment de preuves. Le Sénégal est un pays de Droit. Soyons patient 🙏
@mariamadieye344111 күн бұрын
Ils n’ont qu’à éclaircir les choses de dire devant tout le monde kils nont pas de preuves contre elle comme sa la conscience de tout le monde soit tranquille surtout elle même mais avec cette comportement cest douteux vraiment
@roseparis832411 күн бұрын
Je suis tout à fait d’accord avec vous
@BayeNdiaye-x3k11 күн бұрын
@@mariamadieye3441surtout dafa wara léer si boppou nite yi justice ✊
@astucesdionguen860410 күн бұрын
Soudone sayy frère lagnu esk digua khol lolu wala tale ko
@SokhnadabaDiatta11 күн бұрын
Paix à heure âme c'est triste
@antanian557411 күн бұрын
😢raye lene ko rek lep mome mo kham azi khamal ko lepame
@samdiawdiaw826910 күн бұрын
Raga lal yalla
@KineDiame-du4bo5 күн бұрын
@@samdiawdiaw8269yaw tamit manoul si wakhou diambour...sofffff
@cisseibou-fb6wd8 күн бұрын
justice pour Aziz dabala et Waly
@mariemedieng535711 күн бұрын
Souder mystik la guener naniou mystik ba leep leer c tt yeem n nieeuup liii dafa metiii😢😢
@AissatouWade-z2n10 күн бұрын
Moy deug dé
@AbdoukarimNdiaye-z4j9 күн бұрын
Atte Kat bou makbi moy yalla Dina lerar lepou fisi adouna inchallah 🤲😭
@fatimatoubarhamdieng910 күн бұрын
Metina trop mais Dieu est juste
@Kyradiopofficiel9 күн бұрын
Franchement bimako dégué amna louma métti moumélni koudéfoul dara 🛑🚨
@PapaSane-db2jw10 күн бұрын
Moi perso j'ai une question comment des gens sont entrain de pourrir en prison a cause d'un portable volé d'autres à cause d'un join de yamba et qui ne peuvent pas bénéficier d'un liberté provisoire et là on voit une personne impliqué dans un Assassinat moins de 4mois elle bénéficie d'un liberté Provisoire c'est louche très louche?SÉNÉGAL justice bi moe lolou Coumba am ndeye ak Coumba Amoul ndeye
@deugrekk641011 күн бұрын
#justicepourazizdabalaetwally
@AstouKandji-vs9ep11 күн бұрын
Yen dall Sénégal yeup affaire bi dafa len nakhri wone yene sabolen wax Di ghen dall setel nabou ley nan yakar Nani d'où mom té Sénégal yeup d niou don wax nabou lay yén ghin Di wax nan d'où mom sourt. Ya sac jour gha done setel mou ji ghi damal méré trop sax
@nefertitiderneville11 күн бұрын
Deugg leu gnom gnokoo dieukke setaal .. Maintenant C’est trop tard Leye-Leye Guené Na gnou Sénégal 🇸🇳
@yayou-bebe-sall11 күн бұрын
@@nefertitiderneville wa leigui mou guénn niouni doufi amé mane dama moudiou diaxlei saxx
@nefertitiderneville11 күн бұрын
@@yayou-bebe-sall vraiment liii dafa metti anma lou çii louch tte les auteur vont sortir legui
@AstouKandji-vs9ep11 күн бұрын
@@nefertitiderneville mé wa ji yambar la niou Ray sa rakeu ghy wax waxoul dof sak jour nan yakar naniou défouko wa legi kom defoul geuneu
@rouguikebe998411 күн бұрын
Non niom affaire yi dalene bétone nak té loula béte meune la😢
@bboyneyobreaking11 күн бұрын
Juste pour les deux😢😢
@NdeyeMané-s8b10 күн бұрын
Ndayssane 💚💚💚💛🌟💛♥️♥️♥️
@fadoum608311 күн бұрын
Il a droit de ne pas rester calme mettez vous à sa place .il a perdu son frère ça fait mal on doit appliquer la loi islamique comme personne ne tuera personne
@SallaDia-m1j11 күн бұрын
Assalamalaykoum di nouyou kép kouy lire sama commentaires ; bon depuis bi affaire bi amé mane Mangui lén di suivre téh si daara lagnou nékh lep pour kham li yalla dique léeh akh limou téré téh nakh Lima diotta diangue si alquran 😢 wallou crime entre ndom adama moy nitte Bou réyé nitte nagnou xole name ko réyé gnou réyé ko nonou et pourquoi pas bignou diappé ki née mo réy deux personnes yoyou réyou gnou ko lane lay sétte si police lane moy police beugue téggui batou yalla bobou moy wéddy li yalla wakh si alquran et à près dieul ay nitte teuthi lénn police à près bayi kénn si gnome mou gnibi à près beugue Def élection législatif bokk yi nitte mo gueuna forte lép lolénn guisse boulénn tope politicien yi guénn di déff loulénn néx téh bolénn amé Lou mélni dougnou ko meuna fathieu li moy lane nagnou déllou si wakky yalla fi kénn guénou fi kénn gneupe ay bokk lagnou entre adama et awa donc lane moy problème bi ba diémo lénn atté Aziz et wally 😮lane la posé lénn lép téguénn atté deux personnes yoyou guénn réy kiko réy et vous laissez les autres gnou gnibi c est ça réalité yalla moko wakk mais gnou réy deux personnes ga noppi gané ya djité réw mi li yalla bouko déffonne dakh dina gnou raw mala yi les animaux
@mamadouwagne302011 күн бұрын
Deja dangen yekha dieul avocat''''liberté Nabou bi aussi meun na am pekhé la pour enquêteurs yi''''Teyilen rek
@ibrahimafofana-s6l10 күн бұрын
Justice pour azize dabala est boubacar gano
@halikano39211 күн бұрын
Déme jusqu'à la bout moye libéré gneuppa ni défougnou dara dagno dioume fofou la Sénégal tolou amna gnougnou diapone ak 7 khawma 8 chefs inculpations moudié amnistie thi kaw 86 morts donc cest le Sénégal d'aujourd'hui bras long adiome fédiou bras court mougne😢
@rouguikebe998411 күн бұрын
Dafa lérr😢
@NgomaDieng-v9w11 күн бұрын
Ndeysane on diré k aziz moy wakh sakh wayé atté yalla mo geune bou nit yalla na yalla souniou borom atté li
@CinePenc8 күн бұрын
pourquoi accusé des personnes sans avoir de preuve, laissons la justice faire poursuivre leur enquete. la famille de aziz dabala est mal conseillée parcequ'elle ne doit pas proférée de telle accusaion envers un proche sans avoir de preuve. lorsque la lenterne sera mise dans ce dossier. les memebres de cette famille seront surpris et demanderont des excuses à nabou leye. en entendant parlé ce monsieur, il est dans l'émotion et aussi cela montre qu'il ne maitrise pas son sujet.
@FayeFallou-t9v11 күн бұрын
Yaw bo wakhé wone ni bou yague kone li dou ame yadone diapalé nabou leye
@adamafall35469 күн бұрын
Yombe na trop sakh😢
@jarieujallow859511 күн бұрын
May their souls continue to rest in peace ameen 🙏🙏🙏🙏🙏
Sonko diomaye bignouléni fâleu sécurité bi bokenasi lidou yonne si deukou droit
@salyallemomuawrksarr865211 күн бұрын
Sene maître Khouray Sy Bâ bobou wolou ngéneko ndakh yene dieulou léne ko si Sene khalisou bopou ki leneko dieuleul nékoul Sénégal bayi lène maître Khouray Sy Bâ ngéne khol benène avocat te kou lène yéné avocat na lene diokh khalisou avocat bi ngéne Faye ko mais bougn léneko fayal ok
@ndiatteniang100911 күн бұрын
Elles sont fait du marboutage pour la faire sortire vous aussi faisiez vous du marbouboutage pour qu elle troune encore en prison wally eT un peul aziz aussi va chercher marabouts au village
@BinetaMbengue-d3r11 күн бұрын
Tu as raison si cote bobou vous devriez savoir au moins ce qui se passe en tout cas nieko Yallah dinalene atte si kaw souffe
@magaliendiaye889411 күн бұрын
Wa mais pourquoi la libération de Nabou leur pose problème?
@azizdieng639411 күн бұрын
Frère tu ne metrises pas les choses quand tu dis que ka liberté provisoire est pour les personnes qui sont déjà jugés c'est le contraire
@halikano39211 күн бұрын
Khamna guéna na kasso ba yéga thia deuka ba adji sarr nekka mouye doga siw mougua sa réwe you bakh yi fi mome nonoula fa démé motakh gnounane kou dé rek ya perte😢
@assygaye474310 күн бұрын
Dal lene niou khar yone bax mo guene yalla Dina leral lep nakh Aziz ak Wally d'en. Décès niep la metty
@mystiquetv504511 күн бұрын
Tapale amna ndax dagno xar bethi campagne electorale bi nit gni sen xel gen thi mbiru aziz bi gnu diar thi suf guene nabou .
@bboyneyobreaking11 күн бұрын
Thiote ndéye mim rew rek,Ray nit ba paré justice tek tëkaral🤔
@mariemediagne5668 күн бұрын
Si je comprends bien nabou leye rk lagnou libéré
@abdoulayendongo395211 күн бұрын
Dans ce cas de figure,la justice ne libère pas un fautif.Il y avait beaucoup de versions. Nabou avait nié sa présence le soir du meurtre.Le jugement aura lieu et les gens sauront la responsabilité de chacun. On parlait d'erreur entre 12h et 00h.Si Nabou n'était pas présenté,c'est normal qu'elle soit libérée.Il ne faut pas mettre qu'il en prison s'il y a doute.Tous ceux qui avaient menti ne veulent pas que Nabou soit libre à cause de leur mensonge. Que Dieu nous guide et nous protège. MERCI.
@moussambodji851511 күн бұрын
Vraiment ragaloulene. Yalla nabou leye Yone moko diapone bayi wate ko loutakh guene beugeu mou done coupable vraiment meunoumeulene. Comprendre justice sénégal foumou tolou ni nice dh
@toutoularandiaye211611 күн бұрын
Liberté provisoire AK relaché dou benneu
@fatoudione448411 күн бұрын
Yen maylen niou diam boudone sen frère mo de dolen fi nekh diko faral ya quelques choses nitt yi dofou niou waye quep kou si lal rek yalla na la yalla were akhou asis yalla na la dall amine ya rabal alamine
@aminatandiaye958011 күн бұрын
Mane dé diomi na si Sénégal yaw bigni arrêter nabou est-ce qu’on vs avez avisé maintenant qu’elle obtient une liberté provisoire vs voulez qu’on vous avise
@adamatounkara985811 күн бұрын
C'est écœurant 😢
@beautenayo10319 күн бұрын
Mais je comprends pas cette familles do lene tok bayi la justice faire son travaille vous nous soulé a la fin double meurtre 7 personne on était arrivée on n'a liberté juste Babou leuy ya une raison Ya pas de jugement en plus vous mêlenger tout Oui vous voulez juste incriminé nabou leye et les autres alors
@BinetaMbengue-d3r11 күн бұрын
Je vous suggère de tout laisser dak nie dem demnaniou douniou deloussi donc nianalene rek bagna yak séné kaliss si avocat bayileup si loko Yallah rek
@BayeNdiaye-x3k11 күн бұрын
tout laisser tombée pour que demain d'autres subissent le même sort ? non lii ça doit être le combat de tout les sénégalais
@matarmbaye808710 күн бұрын
N'est ce Pas jubb ubal jubanti lañou wakh? Donc na ler
@mbayesembene615311 күн бұрын
Li guéne Di wax xamolene ci dara. N'es ce pas juge moko diapone juge moko libéré. Faites confiance à la justice
@almaktoumdiop874911 күн бұрын
No sénégal rék laguis kou rayoule gñouni nanouko teudj li baa diam laa
@almaktoumdiop874911 күн бұрын
Sénégal beus bou yalla saka kéne di wané séni bone ak sokhor nabou léye rayoule wala police guisoule foumou rayé douko bayi lane guéne beugeu déh bi ak yéné ne déh yi bénala yéne ak tik tokeuyi yénaaye comérce si déh gui nanou wakh lifi am
@HabibGueye-x4e11 күн бұрын
nianallenko mo guene wakh dji
@ndackkebe671111 күн бұрын
😢😢😢😢😢
@FatouLoum-v6q11 күн бұрын
😢😢😢
@AMYNdiaye-y1m11 күн бұрын
😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
@alimatoujallow465411 күн бұрын
😭😭😭
@alioudiop216011 күн бұрын
Wakhal lo kham (dou yaw yaye wakh justice limouy def
@YacineMbaye-c9z11 күн бұрын
😢😢😢😢😢😮
@falloushoptv25711 күн бұрын
Boulen niou sonal nak wala dangen beug def ligey bi ala place de la justice niom nio xam Sen ligey nio xam litah niou bayiko Yen key fexé len ladj loutah niou bayiko c mieux
@BayeNdiaye-x3k11 күн бұрын
yaw ya beugue sonelé
@almaktoumdiop874911 күн бұрын
Justice nékou fii pour louléne nékh Justice daf fénéka pour yone yéne daguéne khamoule dara si yone té di wakh bésatoule dara yéne yénaye youte beuz si li
@BayeNdiaye-x3k11 күн бұрын
arrêter de raconter du n'importe quoi soit plus sérieux que ça.
@AwaDiop-k7f8 күн бұрын
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭🥹🥹🥹🥹🥹🥹
@AminataThiam-gb3wr11 күн бұрын
Kéne m clédor ly nguéne warona dieule kone li yeup dou am mane mome moma doye
@mamecheikhdieng428911 күн бұрын
Wax nga dag de moum da diafe sax foum nek
@AminataThiam-gb3wr10 күн бұрын
@mamecheikhdieng4289 clédor nit moy wadji
@YacineMbaye-c9z11 күн бұрын
😢😢😢😢😢😢😢😅
@ndiemendiaye345911 күн бұрын
Lép yaw la ah aida nane souma guissé nabou nako fone man sama mbok couco Ray ma Ray la