Machalah Fatou Guéwél. Li moyy adouna nitt bokko tanné dangakoyy dimeuli. Que les autres artistes prennent exemple sur toi. Tu pouvais te dire que y’a le ministère de la famille mais non, tu as déployé des moyens pour venir en aide quelqu’un qui est dans le besoin. Yallana sa téranga yokkou, yalla mayela wérr té goudeule sa fane. Bilaye doye nga royou wayy. Boula nékhone bilaye nga déme défeko thi poukeuré wayyé défouloko. Finga tékk sa tank fofoula. Yalla nalla yalla diapalé si sa mission. Sama khole bilaye sédana
@moustaphamboup7302 жыл бұрын
Fatou guéweul yalla na yalla yok té wéeral la té fayal si barkè Yonnente bi Paix et Salut sur lui
@abdouazizndiaye53542 жыл бұрын
Merci Fatou gueweul c'est des personnes comme toi, qui font que j'ai confiance à l'avenir.merci merci merci
@fatou-binetousarr55882 жыл бұрын
Ma sha Allah, association Fatou gueweule kara, yallah na leu yallah sameu, diapeulé leu si lou barkh y guaye déf ainsi qu'à toute l'équipe de Pape Niang 👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾🙏🏽😊
@madamediame2642 жыл бұрын
Juska ce moment je n'arrête pas de pleurer yalla rek Moy bour bou mag bi
@adjakoma86892 жыл бұрын
Macha allah lou diot yomb elle a telma galerer dans la rue tjr avk ces enfants chak fois dama ko dane romb si mbed mi tjr avec ces enfants en tt cas mougne na ba yalla defal ko xeweul mention special a vous osi nalene yalla faye
@oumy69352 жыл бұрын
NDeyssane, wornama ni si tu savais qu'elle dort dans la rue nga deif ci ay dingue. Santt yalla adja, khol yeuppa Toyone
@aissatoundione41582 жыл бұрын
Merci maman Fatou guewel li Motakh ma beuguela yalla nala yalla faye
@djaraf38082 жыл бұрын
Ce sont ces genres d’informations dont nous avons besoin et non des informations inutiles. Bravo à la fondation dirigée par Fatou Guéwél, roye léne si Fatou Guéwél Diouf nguirr yalla yéne gni yalla bakhé té diokh léne téranga
@misszjuke49142 жыл бұрын
Enfin les journalistes nous dévoilent des actions utiles
@mariamafall67232 жыл бұрын
Long vie à tw Fatou gueweul , Dieureudieuf pape Niang AK groupe bi yeup yalnalen yalla fay
@dabamgom78132 жыл бұрын
♥️💔♥️♥️♥️♥️😭🤲👈
@eva-dn9vu2 жыл бұрын
Amine way 😭😭✅😭❤️❤️❤️
@mbayeyade12422 жыл бұрын
amine
@kinendiaye11402 жыл бұрын
Amine ❤️❤️
@badisourang90732 жыл бұрын
Il
@mbouppape81912 жыл бұрын
Lepp Li khalé bi wa khone ya yam féki sina ko bilahi liga liguey sa kuer Diekuer lala sono brom fay lo bakh gako dji yalla fay nala lepp ❤🙏😭 Merci beaucoup fatou guewel❤😭🙏yalla nala yalla fay sa khol amine❤🙏
@fatimandiaye97172 жыл бұрын
Mash'Allah ❤️❤️ yallah nafi diam sakh
@ndeyearameleye14412 жыл бұрын
Voilà lolou amna solo machalaa fatou defneu loumou meun.tek la si yone djangal la nougnouy nappé .takkal sa ndig geum sa bop. Ligey ndakh koula dimbali tay bou souba mou meneu dimbali kenenn
@lafilledemariemarieyonnend67622 жыл бұрын
Ay li yalna len yalla fey mome Yi fey Li dey borom Hol Bou yatou rek Moy dioxe machalla
@karanoreyni67082 жыл бұрын
Yaye Fatou kara yalla na yalla goudeul sa fane te mayla weur ak katane babarakati cheikh ahmadou kara mbacke noreyni man noreyni rek motakh ma beuge la
@serignendiayebeuguefallou70882 жыл бұрын
Merci Sokhna Fatou guéwale Diouf ak toute l'équipe particulièrement Pape Niang et sewrou
@sokhnambenefall40162 жыл бұрын
Association bi mérite d'être soutenu vraiment .k Dieu vous bénisse
@sennaseye69862 жыл бұрын
Machalla rafétena yalna yalla yokou léne si barcké est serigne fallou
@babacarsene64842 жыл бұрын
Niit amoul loudoul mrom niitam bonne volonté yii war nagn khol sii lii dii diimbalii niit ta yallah takh Fatou gueweul diieureudiieuf ak sa wa fondation bii yeup ♥️♥️♥️
@ndeyaramegueye74932 жыл бұрын
Machalla aduna lo guiss appe laye kharr kouné khamnani mbeed nekhoul bilahi wayé adina kouné ak sa diardiar dieureuf cheikh Niang diarama Fatou gueweul wakh deug yalla royoukay gua may nianal séne groupe bii yalla fayléne katanal léne lakhlén fa yakh éguoul diii nianal fatou gueweul yalla guoudal fanam vraiment khôl yepp toyna
@bintakhma89252 жыл бұрын
Natou yalah da meti AlhamdouliLah la fille aussi rien voir son visage tu sai qu’elle a beaucoup souffert tu doit être heureuse maintenant gor req mo soneuh yalah ko yalah may liguey bou bax geuneu diapale sa yaye et tes petits frères aussi merci à tt l’équipe ♥️
@alassanedieng7112 жыл бұрын
Machaalla wa fondation yalla guiss na lep yalla nalén yalla takhawou
@khadythiongane41392 жыл бұрын
Machalla maman Fatou guéweul yanna yalla deffal la diama ya rabi
@blackwoman57972 жыл бұрын
Fatou guewel d limou def betou gnou gnoune gni deuk ak mom. Dafa bakh be kou guéne si bireum bakh la yakar. Machallah❤️ Yalla ne ko Yalla Sam samal ko ndiabotam goudeul fanam🥰❤️🙏🏾
@aminatandiaye582 жыл бұрын
L00ll
@adjithiabagningue61902 жыл бұрын
bi lahi machallah yalla nama yalla may weurseuk bama mana diapalé néw di dolé yi inchallah vous êtes dé référence fier de vous
@morhann16192 жыл бұрын
Amine Lo lou rèk lay nian yallah
@aidasall37482 жыл бұрын
Yalna léen yallah fay si barket seydina Mouhamed saw 🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️
@papadieng6212 жыл бұрын
Billa hi li fatou gueweul def niep la ko defal yalla khamnako lou am solo la bilay demb la ko setan dioy mes khale yi yalnan reuisit si barke seringe Babacar sy rth amine💯❤
@binoushniang55642 жыл бұрын
Alhamdoulilah 🙏 Dieureu Guen dieuf way🙏 Yalla nalen borom bi Faye si Barki Nabie Moustapha 🙏
@dialibatoulbouroretv54042 жыл бұрын
Machallah li rafète na yalla guiss nala dè Soxna fatou guèweul gnogui niane yalla mou goudal fane wi yokk wèr gui ak mbolèm gninga andal liguèye bi thia yalla barkèl sèn lèp adouna ak allahira barké BROME TOUBA KHADIMOUL RASSOUL AMINE sama khôl sèdde na lol thié dieuf dji yalla xamnako , gnogui ninal wa suite internet bi yalnalèn yalla taxaawou thié sèn liguèye bi thia kaw thia kanam rèk INCHALLAH
Wallhi raffena machlla un garand merci à toutes la fondation noreyni solidarité et à Fatou gueweul kara wallhi merci man sam goll deknna billahi dapi Mauritanie
@aramendoye14072 жыл бұрын
Màchalla Mme Fatou guewel n'a yalla Faye la
@diattacaro60812 жыл бұрын
machallah yalna yalla feyelenne senne holle li leppe pape Niang mo ko waral bilaye je suis tout cœur avec vous 😭😭😭😭😭
@touretoure98732 жыл бұрын
yaye mougn na ba am limou beuguon mashallah fatou geweul yalla guiss nala💝💝🙏🙏
@Mamichoubb2 жыл бұрын
Kouko dégue bo djoyoul rek amo khol Fatou mi yalla nako yalla takhawou si barker seydina mohamed 👏 👏 ta Fatou gueweul diouf yalla nako fi yalla bayi si barker seydina mohamed 👏 yalla yokouko ba
@ablayediallo27582 жыл бұрын
Yalla kham Nany bekk naaaaa thiii yaw sounou yaye djiiii yalla nalla yalla sounou borom yokou ba yeuk by Diahi Nabil Moustapha psl 🤲🤲🤲sedal gua sama khôl ❤️ by lolou walahi
@ismailagueye16162 жыл бұрын
Vraiment fatou guéweul Kara t as fait un beau geste Li yalla dinalakoooo fay adouna ak alakhiraaaaaaa Li la ammm ammmmm di dieurigne yalla nala yalla yoxouuu baga xammmmmm
@labarhamiennethiongane46712 жыл бұрын
Maman Fatou guéweul yannala yalla fayy yokoulo bangua yeukk ko si barké Baye Niass 🤲🤲 bilay Di déff ay aide sociale mo yagg nékk sma rêve bilay 🥺🥺 beugg na bokk si association bi inchallah
@borombakhdad69242 жыл бұрын
Fatou gewal bole wol dare aki wahk mahcalla maman fatou❤❤❤❤❤🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦🇪🇦
@aminatakonate99662 жыл бұрын
Merci Sokhna Fatou gueweul ak Pape Niang si kaw si kanam si barké Seydina Mahamed laff thiat
@leparisien51932 жыл бұрын
Yalla na yalla faye fatou geuweul diouf
@diatouthiamdiagne68402 жыл бұрын
Fatou guewal yalla rek mo am faye yalla na yalla faye
@amydiaw83802 жыл бұрын
Pape Niang yalla nala yalla faye ♥️
@ndeyethianesowfall41572 жыл бұрын
Machallah le peuple est content merci à l'association de tata fatou gueweul diouf djeureudjeuf pape et l'équipe alhamdoulhilah vous avez fait ma journée Dieu merci la fille est très bien éduqué machallah néna liguéy Bouma am bakhena yalla n'a yalla motali lépe inchallah 🙏💓❤️😍🌹💐🎊🌸🎊🎊🎊💐🎊🌸🎊🎊💐
@mbayangkandij64752 жыл бұрын
😭😭😭😭😭
@ndeyefatoudiop30052 жыл бұрын
Machalla yalla nalene yalla fay pape Tata fatou et la fondation ❤❤❤❤❤❤❤
@oumoundongo26082 жыл бұрын
Machallah
@fatymbaye34792 жыл бұрын
Alhamdoulilahi. Yalla na ma Yalla may aye kheweul you bari bama mana def sama yené si djami Yalla yi Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine
@balladiagne91442 жыл бұрын
Fatou yalna yalla goudal sa fane amine amine amine
@sofiadieng82132 жыл бұрын
Pape niang dieredief yalnala yalla faye yak maman fatou nguewel vraiment video bi limassi dioy wayei instanbi magui contane🙏🙏
@bbfadiop46362 жыл бұрын
Un grand merci à ses gens qui ont aidé cette femme yalna len ko borom bi faye
@awaseck37312 жыл бұрын
Yalnalene yalla fay yiww 🙏🇸🇳❤️
@falloundao25272 жыл бұрын
Ndèye san machalla amna solo trop ndèye san
@oumycoulibaly76472 жыл бұрын
Mashallah maman Fatou geuweul ak groupe social longue vie à vous
@binetandiaye89512 жыл бұрын
Ay waay guewal yaa baakh. Yalna yalla barckel licie dess, tè barckel ndiabot gui. Yaa reuy khol maa chaa allah.
@matathiam86052 жыл бұрын
Bonne continuation.diadieuff ça kaw ça kanam
@Seyeyaram-TV2 жыл бұрын
Mashallah yallah n'a yallah faye yiww barkepp Noreyni
@fallygning68282 жыл бұрын
Macha allah pape liguéye bi amna solo ak maman fatou guéweul yalna yalla fayléne
@ndayekhadydiop66982 жыл бұрын
Manchallah maman fatou guèweul kara yalna la yalla yok tè samla doko reuthiou dè bilahi 😍😍😍😍😍😍
@mamediop88452 жыл бұрын
Yaye Fatou yalna yalla soutoural dioufa niokhobay
@lenafaye12482 жыл бұрын
Alhamdoulilah🙏🏽🙏🏽machallah yalla naléne yalla fayy ya rabi🙏🏽🙏🏽
@gkhalil55492 жыл бұрын
Yalla nalène yalla faye wa association bi 🤲🤲
@ndeyembeneniang32042 жыл бұрын
Machala fatou guewel yalna yalla yokou fane bi yaw ak sa diabote mention spéciale à pape niang é mifa sowrou ect laf thiate
@coumbadiaw23702 жыл бұрын
Awma habitudes di commentaires si réseaux sociaux yi ms dama contane trop maman Fatou yalla nala yalla faye 🥺 yalla nala yalla may lénéne lou eup lingako défare🤲🤲 que dieu vous bénisse
@yandekaissagaye5612 жыл бұрын
Ayee maman fatou yalla n'alla yalla fayeeeee
@bintasagna38822 жыл бұрын
Manchallah merci beaucoup à vous k Dieu vous bénisse
@gayeguaye51572 жыл бұрын
Machallah إن الله يرزق من يشاء بغير الحساب.
@mariehelenebodian70742 жыл бұрын
Ndeyssane Dieureuf yalla nallen yalla faye
@cheikhsamb83722 жыл бұрын
Ndaysane bola yalah diokhé coppo khamalne iow kasse la mais bola diokhé pàne dalà sedeleloo délen diamou yalah thi néwdi dooleyi wasalam 🙏🙏🙏
@codougueye56742 жыл бұрын
Soxna fatou guéweul yalna yalla guoudeul saye fane
@ibrahimkasse20452 жыл бұрын
No pape iow yallah réck mom sunu mou defala diam cii aduna toi safé doundou amna solo trop cii kanam réck long vie et bcoux bonheurs courage réck 🙏🙏🙏🙏🇸🇳🇸🇳
@fatoudia7832 жыл бұрын
Machalla raféte neu 😍👍
@khoudiakhoudiaboumamecheik10212 жыл бұрын
Machallah yalla nalene yalla faye🙏🙏🙏🙏🤲🤲👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿😭😭😭😭😭😭❤❤❤❤❤❤❤
@faryfaye37742 жыл бұрын
Machalla yalna goudou fann werr
@mariamadiop18522 жыл бұрын
Machalla am na solo lol yalla nako yalla guena diapale ci barcke serigne fallou mbacke machallah
@khadydime82562 жыл бұрын
Adjia fatou gueweul yalla na la yalla faye si barké seydina Mouhammad
@beugueserignetoubagtv88192 жыл бұрын
J’aime mon pays 🇸🇳
@madamesene18222 жыл бұрын
Yalnalene yalla bourbi fey 🙏🙏
@titecardib18272 жыл бұрын
Merci à ces gens qui ont aidé à cette femme. Que Dieu vous bénisse 🤲👊💗. Le bienfait n'est jamais perdu
@aramniang59142 жыл бұрын
Yalna yala goudal vanwi té wire Thierye mama fatou
@toureabdoulaye92222 жыл бұрын
Fatou geuweull yalla nala yalla faye ta sammou
@yacineseyefaye18602 жыл бұрын
Machala sama xol bi Come wanagou bote yala nalen yala Faye Pape yak sa équipe dierejef Fatou guewel yalna yala Faye len sokhna si khana Fatou guewel sa mak la daguen ndouro machala
@barafall46332 жыл бұрын
Jeureujeuf pape Niang Yallah naleuh yallah fay
@fatimabintoubalde14992 жыл бұрын
Ahhhhhh machalaah maman fatou gueweul yalla guiss nala 💞
@damefall26142 жыл бұрын
Machallah ndaysane yallana lén yalla faye Barack S TOUBA
Bou borom halale yeub mélone ni yow Sénégal dina Avenches . Mais borom khalis ci gnoy mayanté s'en bire yalla n'a sa diam yag ❤️❤️❤️🙏🙏🙏
@abdallahbah32392 жыл бұрын
Oh 😥 maman fatou gueweule mashallah 🥰 longévité accrue à toi maman
@yamajoly42872 жыл бұрын
Mashaalah mashallalh laf khiate raffetena trop mashallalh yallanalene yalla faye thii barke seydina mouhamed psl
@aissatousene55002 жыл бұрын
Macha'Allah Pape et fatou goudallene fane wer ak werle inchalla
@ndeyerokhayadiop82372 жыл бұрын
Masha allah Yalnalein yalla faayeu
@ndeyefadiaseye15612 жыл бұрын
Yaye fatou yallna yalla faye
@florencecabral30132 жыл бұрын
Yalla naléne yalla may wérr ak werlé ak dolé biguen agualé social bi am n'a solo lole thi rew mi merci maman Fatou guewel yalla nala borome bi fêye sa xol
@fatouabdourahmanesy94122 жыл бұрын
Machallah je suis très contente de vous machallah
@hawasall41482 жыл бұрын
Merci beaucoup merci infiniment Yalla naleu Yalla faye maman fatou geweul diouf
@yacinengom20552 жыл бұрын
Fatou yalla nala yalla fay tu ma fait pleurer.taga yok ba yék ko.
@ousmanesarr41042 жыл бұрын
Yalla nalénn yalla fay
@morsall51552 жыл бұрын
souniou yaye Fatou gueweull yalle na yalle faye yiw dieureudieuff mane de kontan na sama xoll sedana doropp yaye boye Merci beaucoup yaguafi rekk sadounou amna solo ❤💕😍🥰