Assy Sy, awo de baye ndiaye niaan neu baatt...! Notre analyse

  Рет қаралды 20,492

POTINS GALSEN-CAS YI

POTINS GALSEN-CAS YI

Күн бұрын

Пікірлер: 26
@sacourawali4626
@sacourawali4626 2 ай бұрын
Wakh deugue assy bo demé niak fayda, ce que je te conseille moy nga took ci sa seuy bi, boul wayadi
@xyz3958
@xyz3958 2 ай бұрын
Très bien katal ndéyou seuye bi sa dieukeur sou nobé kénène ba takeuko défatofa lénène
@FatouCandjisene
@FatouCandjisene 2 ай бұрын
Je suis avec toi
@mariamabojang9628
@mariamabojang9628 2 ай бұрын
I ❤ Assy❤❤❤❤
@MariemBa-w7s
@MariemBa-w7s 2 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤
@AstoukorkaDeme
@AstoukorkaDeme 2 ай бұрын
Mais assy azize ndiaye bimou take deuxième famme dala maye ndieke gua deme deff sa teragua taye sa besse nieuw guaye deme kone dagua daw togal gere sa seuy waye
@fatoudiouf8396
@fatoudiouf8396 2 ай бұрын
Ay Coumba nétali bakhoul 😂😂
@fatoudiop8958
@fatoudiop8958 2 ай бұрын
Bilay deugeuleu
@fatousow94
@fatousow94 2 ай бұрын
Assy mérénala béen djiguene waroula taxa dém mane béty dafma nékh Baye Ndiaye dioulit la louy problème bi
@quenne_dudiolof9536
@quenne_dudiolof9536 2 ай бұрын
Assy stp boule tass, bay ndiaye mom domeram chimmm
@SeynabouDiop-g7e
@SeynabouDiop-g7e 2 ай бұрын
Baye Ndiaye bouko tope bouko maye bate djiguene la da mère rek
@fatoumataba5107
@fatoumataba5107 2 ай бұрын
Wa assay DEUG deug waro dém di siwal sa sa bop nak 😮😮 bul mayi Sénégalais yi lo nji yi wah nak 😢😢
@yayourassoul5054
@yayourassoul5054 2 ай бұрын
Senegalais yi ley seyeul waleu? Souko meunei mougn na tokk seuy ,wayé promesse goor tamit bumou takh mou tass seyam wakhi goor diaroul door dom
@nguethndoye9630
@nguethndoye9630 2 ай бұрын
Goor dioulit am na droit takk 4 femmes louy problème bi .
@quenne_dudiolof9536
@quenne_dudiolof9536 2 ай бұрын
Assu mo dakk fouff bety
@ebrimajoof2211
@ebrimajoof2211 2 ай бұрын
Bu niane baat nyaka fayda deh
@AstoukorkaDeme
@AstoukorkaDeme 2 ай бұрын
Lislam nena goor 4 femme soko meune te baye Manchalah meun nako assy faire player
@mariesec824
@mariesec824 2 ай бұрын
Waxo deug betty mareine la deuk faramarén leu mamam Aïda seck mi diour yayam sama grande sœur leu
@SeynabouDiop-g7e
@SeynabouDiop-g7e 2 ай бұрын
Kholale si sa papa sy Malick
@ramatoulayedrame6589
@ramatoulayedrame6589 2 ай бұрын
Betty dee kouko envier tchi mariage bi dangua khamoul rek, goor bou diik taak khaleyou djiguene you barri ba gni dii shooting ak lounek, ngua tasse sene yakaar, cela veut tout dire, liye khaar betty naroul yomb bene yone, chassez le naturel il revient au galop. Na première bi tok tee setane rek.
@wadeidrissa7410
@wadeidrissa7410 2 ай бұрын
Kata ndéyame feulé souniou yone nékoussi
@SeynabouDiop-g7e
@SeynabouDiop-g7e 2 ай бұрын
Guifale daga mère rek metina n'a mougne rek khôl si papame
@AissatouWade-z2n
@AissatouWade-z2n 2 ай бұрын
Bo niawate rek niak fayda AK wayadi
@rewo74
@rewo74 2 ай бұрын
Nèka gnarèl en plus
@mamedialedia8378
@mamedialedia8378 2 ай бұрын
JE NE S8 PAS AVEC TOI . CHAQUE MUSULMAN A DROITVAV4VFEMMES
Aicha Rassoul offre 3 millions à Miss Ndiaye Awo Yaye
13:38
DAKARBUZZ TV
Рет қаралды 193 М.
Когда отец одевает ребёнка @JaySharon
00:16
История одного вокалиста
Рет қаралды 16 МЛН
How to whistle ?? 😱😱
00:31
Tibo InShape
Рет қаралды 22 МЛН
Revue de presse Ahmed Aïdara du Mardi 29 Octobre 2024
10:00
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 44 М.