Il n'y a qu'au Sénégal que tu vois certaines choses. Nous sommes que 14millions/ 1.6milliards de musulmans à travers le monde mais li niouy soss ak doul Si dîner amoul feineu ci adouna.
Il n'y a pas pire mensonge que de déclarer être un prophète, et pourtant personne ne dit rien, pire, il obtient même des centaines de talibés , il y a qui disent que leur marabout est au dessus d'Allah subhannahou wa taallah , personne ne dit rien, celui la aussi a des centaines de talibés, arretez vos hypocrisies
@mouhamadoudiop62534 жыл бұрын
@@halimatouba9300 kou wakh lolou?
@benmalick857 жыл бұрын
Senegal xam xam mofa toumouranke motah kou wah bat bou nirou arab rek nouni eskey genrou nit yi nio tah Kou melni oumar sall di diguat tarikha cheikh bi danouy topa ay djine moulen di wahlo ay moussiba rek merci oustaz
@omzoyade93717 жыл бұрын
john jay oui je suis d'accord avec toi
@harmonieharmonie85367 жыл бұрын
john jay 888888888
@abdouwade73437 жыл бұрын
john jay yamana sop xam xam Sénégal la fek bakh. Yaw ya khamoul dara motakh ga wakhe sa gnek kham kham
@mamadousamb33016 жыл бұрын
Feuz john jay tu n'a pas dis la vérité
@aliounebadarakonte9495 жыл бұрын
Feuz wax nga deug
@welzowele24677 жыл бұрын
oustaz nala Yalla fayy axirou zamane deugu
@borom_belel5 жыл бұрын
Yalla naniou yalla samaal bopam Ci barkei Seydina Mohammed
@yacinesybouserignebabacars85617 жыл бұрын
allahou akbar
@moussadiatta5732 Жыл бұрын
Je sw entièrement d'accord avec tw....il faut que djoulit yi yéwou thi môme....seytané bou màk lä....Dëywérrou 😮 inchà Allah.
@wakhouwakh96647 жыл бұрын
oustaz c'est un titre qui se mérite. boy sarr mi doul khamou ko. ses émissions ne consistent qu'à débiter des généralités. 1 - amoul kham-kham, 2 - déégoul al quran, 3- amoul kilifa, il ne parle pas au nom de tivaouane kou niakk kilifa comme moom rék mokay déglou, doyloo ko. way way amm léén kilifeu. mak ya ngi si deuk bi. pourquoi aucun d'entre eux ne contredit. sénégalais khamoul ba paré, niémé wakh loumou maîtrisé woul. diiné deukoul makkah, deukoul tivaouane, santoul sy et ce n'est l'apanage de personne... kénneu moomoul mawlana cheikh tidjani chérif. pourquoi sa lignée maghrébine ou algérienne n'est-elle pas détentrice de son héritage mystique. nék lén nitt té bayii siissou bi ak dof doflou bi. kou déglou ay vidéos wou seydi mouhamed el cheikh kham nii dou moromou bayou gni koy dingatt. sénégal nak, lou nékh waay wakh, mais kou niakk kilifa rék moy gagantiko si mbédd. interrogez vos khalifs et vous saurez. dioulitt dou wakh lou niaw moromam... lolou djiko cheytan leu...donc c'est vous les cheytans... ressaisissez-vous, ne soyez pas des soldats du diable en dénigrant un homme de dieu juste pour préserver un autre humain. mbakhou seydi mouhamed el cheikh, yakkhoul dara si mbakhou kénéne koumou meuneu doone.
@Smokin_mass333 жыл бұрын
😂😂😂😂😂
@Smokin_mass333 жыл бұрын
Doul khamou ko key
@tidianeousmanehanne26582 жыл бұрын
Iow rq ya gatte khel mé nité néke nitte kham Nani ki di el cheikh yégoul féne téh menoul loudoul aye féne
@syameth87647 жыл бұрын
oustaz machallah yalla Molay faye
@boygueye19765 жыл бұрын
Ki daal c simple naniou ko foutii si nathie bou tang beussou aldiouma bathie ko ay yaatou Dakhar
@aliounendao44687 жыл бұрын
As salamou hanleykum wa rahmatoulah ya oustaz gnogui rafetlou bou bakh sa takhawaye ci diné islam ak nigaye waato diné ji ylallah fayla teh yombala defaleuh tawfekh...thi zahir akk batine... El cheikh fasikh leuh jahil leuh...nafekh leuh...yalna yallah défar xolam teh léralalko def lerr ci xolam waneko deug bamou xam li deug..teh deff joulite tekko ci yonu siratalmoustakhim..amine Oustaz gnoguilay niane sassouné rekk ngaye watou ndakh amna ay nafekh akk ay nitou shaytan3 yo xam gnogui weur ak di diéme dilaa fékhél ak beugleuh rouslo nguir ni ligaye def zk ligaye leral..diko watoo diné islam..teh xamni arangéwouléne...yalna yallah araleuh bopamm ya oustaz jazakumoulah ana khayrane..
@talibe-cheikh-ba-faww7 жыл бұрын
Billahi oustaz yalla rek mola mana fay. Festival salam bi itam war ngathi wakh ndakh daniouy fowé diiné dji rek
@bolesonko58077 жыл бұрын
Djiby Niang la paix
@ngagnediop52825 жыл бұрын
Oh oustaz wakhtane bi amna solo trop yalla nagnou yalla mouseul si saytané🙏
@ndiassesall43647 жыл бұрын
machallah ya oustaz
@justicepourtous61685 жыл бұрын
Merci Oustaz Makhtar Sarr YALLAH nala Yallah samme si barké Seydouna Mohammed saw amine ya Rabbi
@mouhamedoumoustaphakhoumah9657 жыл бұрын
haa oustaz yagui dora wax wax dji kaye 15 ans mouy weet di wiird serigne touba néna kou niank serigne boulaye djoubal di tek thi yone yalla néna foo mane djoublou rek seytané moye done sa serigne
@goralo42945 жыл бұрын
tu a raison
@cheikhantangom13855 жыл бұрын
Il est tidjane kidiko tontou tidjane pourquoi serigne touba ?
@mbayebabacardiouf78534 жыл бұрын
@@cheikhantangom1385 il n'est pas tidjane
@mouhameddeme53784 жыл бұрын
Blh kouamoul kilifa ibliss don sa kilifa✨
@modoucisse86397 жыл бұрын
machallah waxalen de
@makiyoutambedou32913 жыл бұрын
ماشاءالله حياك الله شكرا
@courambayendiaye4017 жыл бұрын
merci bcp oustaz souniou amone niénéne niou melni yow niaw tef dina dak si diné dji
@mamethiaw74087 жыл бұрын
Ya bakh yallna la yalla fey
@taphakhouma51997 жыл бұрын
macha allah ostas wakhtanwi amna solo lol way yeeme na dh
@smsbi96736 жыл бұрын
Mercii oustaz makhtar sarr dieureudieuf wakhdji amna solo trop gueuth naniouko degu dal yalananiou yalla may niou degu ak top alhamdoulilah
@abdoulazizdiaw81407 жыл бұрын
جزاك الله خيرا استمر الله يحميك ويرعاك
@alitize11965 жыл бұрын
C'est un grand...il est très dangereux faites beaucoup attention.
@sheriffbah15257 жыл бұрын
l love this programme
@ndiayekane77807 жыл бұрын
nice
@mamisy34477 жыл бұрын
bravo
@kingmalick63317 жыл бұрын
Mami Sy Malick
@cissedaouda24347 жыл бұрын
oustaz mande lena lalay gnanne si barke cheikou tidiane ak dine bignou bokou mou diaral la nga defsi djihatt banga ngiss kokou ngay wakh di seydi Mouhamed el cheikh wala bo ame thier si tarikabi nga lathie cheikh kan moy seydi Mouhamed el cheikh
Senegal mane sakh soma demoune beugga done seringe niou def mako khawma kange langi yew yalla nagiou yalla ginddi diadeuf Ya Oustaz
@Generaltv38095 жыл бұрын
Machallah merci beaucoup inchallah demain à al dianna
@ngagnediop52825 жыл бұрын
Amine
@lampsall37377 жыл бұрын
Machalla Serigne makhtar kaddou yi amna solo lol te tegou ci xam xam ndakh ganre you melni danleena wara Ray ndakh dagnoo wara bayi niti diine yiniy fowee
@youssouphawade41146 жыл бұрын
wa mane fouma nékone li yegou mako dmrm rek masha allh y'a oustaz
@moustaphaelchiekhsy10635 жыл бұрын
Guisse gua yaw fen rek Guay def KO khanne Ay talibém rek mene nagnoula diague tête de kon .yaw bo khamon nigua alko du mi gua doundou sa aldiana bi Guay rêve thi sa bir keur t yaw t kon par ce ke son khamone l'I Mouy wakh kham l'I yonetebi wakh bo wakh nioun nak Seydie mouhamed El CHIEKH dafagno war bâ gua khamne dou gnou la sagua guis gua nak si meytou woul sa bopou digua kham
@cheikhleye59225 жыл бұрын
Mandè mourid la Waè Lima guiss noy ky dall nonoup cheikhou tidjian la
@fatimacissediaboumamedabak1987 жыл бұрын
Allahou Akbar li amna Sénégal li yemena
@CheikhDieng-k4z5 ай бұрын
Salahou ala mouhamed ❤❤❤
@peacelove15415 жыл бұрын
Vraiment merci
@marapene25374 жыл бұрын
Dieurejeuff ya ouztaze mashaa'allah yala nala brom bi saam
@moussambathie33777 жыл бұрын
j ai ètè l'un des premiers à dire que èl cheikh est un menteur.Depuis que j ai ècoutè ses audios en 2010, j ai aussitot dit que c'est un menteur. sènègal nak mo nèkh lo wotè gayi topla.
@fatimagueye74066 жыл бұрын
moussa mbathie c'est vous le menteur
@halimatouba93005 жыл бұрын
J'ai aussi entendu a la télé quelqun dire qu'il passe toutes les nuits avec le prophète psl , tout le monde là entendu, je n'ai jamais entendu quelqun s'en indigner, c'est normal que ce illuminé aussi raconte ces balivernes
@amet68005 жыл бұрын
@@fatimagueye7406 topp léne fene Kate yi rekk
@hawabathily42917 жыл бұрын
Asta'firullah ! Rendez lui service en lui faisant délivrer un certificat d'internement pour Fann, avant qu'il n'entraîne plus de gens dans sa forme de folklore démentiel, soi-disant, islamique. Merci pour votre sensibilisation du peuple !
@kismasylla42457 жыл бұрын
Hawa Bathily il en a fais un peu trop mais ses genres de personne on toujours existé au Sénégal. a commencé par cheikh tidiane, qui au lieu que les oustaz nient croient en lui il n'y a pas de (wirdou) particulier en islam et cheikh tidiane en donne. il ya que le saint coran et les hadith en plus suivre les exégètes pour plus de compréhension il n'y pas de tariqa en islam.le désordre appel l égarement
@hawabathily42917 жыл бұрын
Kisma Sylla Finalement il faut arriver à différencier le bon grain de l'ivraie mais à condition d'être maitre de soi. Néanmoins je déplore le nombre de naïfs qui croient sans éprouver par eux-mêmes et sans chance d'embrasser la nature spirituelle.
@limamoulayendiaye43567 жыл бұрын
Kisma Sylla vous savez la valeur du wird salatoul fatiya??? en quoi djuli ak di gniane si prophète peu posé un problème ? . c'est désolant
@NDIAYE-EL76 жыл бұрын
Merci Oustaze . El diayetar mi YALLA nako YALLA wér banieupe khamé dou dioulite dou tidiane
@justicepourtous61685 жыл бұрын
Amine Ya Rabbi
@rikdiapraprek22087 жыл бұрын
yalla amnade
@birahimndoy65747 жыл бұрын
MANSA'ALLAH
@leroidavidthiaw89645 жыл бұрын
Dagay doul ...terrer guene diangue dit diguatt. Hamo touss ya oustaz...el cheikh molen eup xam xam fouff ...
@ngagnediop52825 жыл бұрын
Yaw mi ya khamouk touss
@ngagnediop52825 жыл бұрын
Khamoul
@morgueye97157 жыл бұрын
BIEN DIT
@souleymanegueye1965 жыл бұрын
Dieuredieuf ouztaz makhrar bien dit je veux votre numéro mashala
@ebrahimebaldehattijany43035 жыл бұрын
ما شاء الله يا شيخ شكرا
@AbdouAzizThiam-q8f7 ай бұрын
Talibé Maodo bi djeureudjeuf ti❤
@mamafaty60746 жыл бұрын
MACHALA ya oustaz pa Allah pagau inchalá
@diopcisse97177 жыл бұрын
mach alla
@PapeamarSeck-e1h8 ай бұрын
Machallah
@lassanacisse94787 жыл бұрын
ki deguerene fiite way laisse le avec cheikh ahmed tijani cherif
@faroukniass8377 жыл бұрын
felicitation
@baagiubou46677 жыл бұрын
Diadeufff oustaz
@mouhamedoumoustaphakhoumah9657 жыл бұрын
wawaw waxal deug rek yalla molay fayale bopame bilahi deug yalla gui rek moo ame solo
@fadelbulo79217 жыл бұрын
ya oustaz merci machalla lepp rafetna
@bachirndom89277 жыл бұрын
mercie oustaz
@nudenude40167 жыл бұрын
bachir ndom dewenati bachir. Baal ma akh
@bachirndom89277 жыл бұрын
balnala yalnaniou yala bolé baal ta nagoulniou sou diamou yala amiiiiiiiiiiiiiine
@bachirndom89277 жыл бұрын
mais khamna kou ragal korga bikorgui tambale balégui daga diafé
@nudenude40167 жыл бұрын
bachir ndom 😂😂😂😂😂 aka ma ragal kor bachir
@bachirndom89277 жыл бұрын
ana borom tawbi doko ladjie kange lay taw
@nudenude40167 жыл бұрын
Oustaz wakh si d. Li ngay wakh amna mana
@davidgsssama48057 жыл бұрын
am na solo lolou dieureuf ouztas
@adama88986 жыл бұрын
Bilay ya deugou yalna yalla fay...dia-al haqqou wa zahahale bâtile inale bâtila kana zahoukha
@serignendiaye61537 жыл бұрын
alhamdou lil la vous etes nommé l avocat de l islam
@santeborometoubasanteborom31405 жыл бұрын
Merci ya oustas makhtar sarr yalla nala yalla defal diamou diousakh dakk
@Taphathioun157 жыл бұрын
loleir nga wakh
@hadaratoulakhmadiyadediamal7 жыл бұрын
ياءستاذشكرابارك الله فيك
@elhadjidiop48827 жыл бұрын
Baye Dame Sall v
@bababa37307 жыл бұрын
outaz daga barri wakh rek kou niou diokhoul wird wahal si gni wakh d'où gnou diouli douniou worre wahal si lolo qui mogui diouli du yagui wotténé dioulit gua gay Hasse dioulit comme yow tarrikha d'où diné
@zizandour13555 жыл бұрын
Makhtar sarr kattale sa ndaye na oubi sa leufeule ndeye
@zizandour13555 жыл бұрын
Kouye farale makhtar sarr diko diappalè katale sa ndeye
@mintoufall70455 жыл бұрын
Te nga wakh si franc-maçonnerie bi on nena gnou sa famille critique mag gnou bakh gni lane fi nekone est-ce que mouhadams nga dale si El cheikh ba legui bane Khalifa tijani wakh thiou si
@klangfaye85027 жыл бұрын
Vrema Oustaz amouñou senn fay
@Mrdiop4 жыл бұрын
Waa djiii dafaa alkou
@hadaratoulakhmadiyadediamal7 жыл бұрын
ياءشتاذشكرابارك الله فيك
@kismasylla42457 жыл бұрын
Baye Dame Sall أستاذ
@morniang59377 жыл бұрын
DIARA DIEUF SARR AMATINA SOLODE YALLA YALLA FAYELA
oustaz bi moom khoulooo rek ak garawoula t khamoul sarap ndeyem
@mbayebabacardiouf78534 жыл бұрын
Kay wah liga guena weur lumu wah
@CheikhDieng-k4z5 ай бұрын
❤❤❤❤❤
@cherifadam92315 жыл бұрын
MACHA ALLAH
@sodastar66315 жыл бұрын
Li guéne wah thi mom yeup ay féne ko wakhou fi dara lou niaw au contraire yalla rec yonente bi rec Mawlaya Cheik rec ak mak niu bakh gni .est ce que do léne me woutal numero el Cheikh qui beugue nako
@pppmerci29096 жыл бұрын
شكرا لك
@seynaboundiaye94735 жыл бұрын
Sénégal la nekh.
@moustaphadiagne61933 жыл бұрын
macha'allah
@gogodiopba59045 жыл бұрын
Ma sha Allah
@cheikhmbathie56245 жыл бұрын
Je m'excuse pour le retard Sénégal mo békh...
@abdoulahadthiouneqassida30725 жыл бұрын
MACHALLAH OUSTAZ MAKHTAR SARR. YALLA NALA SOUGNOU BOROOM BI FAYE CI BARKÉ SEYDINA MOUHAMMAD SAWS CI BARKÉ CHEIKHOUL KHADIIM AK SOUGNOU KILIFEU DIINÉ YOU BAKH YEUPP MACHALLAH. SOU OUSTAZ YEUPP DONE DEF NI YAW, TAPPALÉ DIEKH.😡
hé lakhirayo waa mane fouma nekone senegal mogui toth deh 😮😮😮😮😮😮😮
@osmanesarr98696 жыл бұрын
Mdrr modou bii doyna waar
@moustaphadiaw88766 жыл бұрын
comment expliquez vous qui il incite beaucoup de jeunes à pratiquer le wird plus que toi (peut-être). Peut être tu es entrain de te rendre célèbre en tapant sur l ombre de El Cheikh. Nous ne te connaissons pas. Est ce que tu connais tous les sens du Saint Coran.?
@bayehanne36475 жыл бұрын
Dieuredieuf oustaz
@fatimagueye74066 жыл бұрын
Ni reck ba 2075 Ya Seydi Mouhamed El Cheikh notre raison d'être,ont la déjà connu car c'est le dernière missionnaire et il détient les pouvoirs 😁😁il ne répond pas au profocation si tu veux des preuves tu peux venir à Médina Cheikh la cité des lumières
@aboularwahinfo45985 жыл бұрын
Fatima Gueye sokhnasi nga balma dh mai 2075 si loumley fek ak age binga yorr esk dou fek mou trotard
@papandiagandoye2047 жыл бұрын
yague fii téé weer oustaz ..kii moom satan deug leu..