Invité nite ba paré complexé ko .dolén ndy posé aye question wala ngén kay relancé
@cheikhbasskeurmassar95483 ай бұрын
Yaw khana sa nopou yi néekhoul 😂😂 question yi kaye Nice
@BabacarNdiaye-i7y3 ай бұрын
Grand azize Moy Nate 😂
@NdiapalySine3 ай бұрын
Aziz day tekk khel 😂
@mouhamethniang31543 ай бұрын
Li mon takhe kene dou veuré ak balla parcekeu li ngaye wakhe kene dou modou lo ilais très intelligent
@josephmendy77923 ай бұрын
Way lépeu Yallah le saway niite késsé nga do waliw do Dara... Balla gaye paréna contre Eumeu Séne té dafa danou... Fi Lou néxoul Yallah dou ame lingay mystique domou Diambour beuss Dina nieuw nga layo ko AK borom mbarr mii...
@maniana523 ай бұрын
Yallah kay soralé tougne ko senegal 😂😂😂lima guisse si réwmi propagane ma meune yi gno akeu😂😂
@cheikhdiop96733 ай бұрын
bilahi Aziz Ndiaye deug la wax amna gno khamni ngathiam rék lagnou beug motakh heure bouy balla gaye di beuré gnouy déf lou nék guir balla gaye danou guir Aziz Ndiaye am ngathia wayé ndokk bako Aziz khamalé bopam yalla nalayala same ta arr la ta bayila ak balla gaye bilahi nitt kou bakh nga koula bagne rék sa mbeur dafa dane mbeurem li dong moy thiow li diame si yaw
@SaliouSow-gj6or3 ай бұрын
Aziz tres intelligent
@ndeyembow66953 ай бұрын
Ragalal yalla Aziz Di wote talibe cheilh
@maissafall28043 ай бұрын
Ki kou bakh la bilay ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@abdelohod48843 ай бұрын
Kou seetlou azize leighi boss la😂😂😂 souy wakh say souss sousou boss thiey khalis mo neikh
@OusmaneSadio-l3k3 ай бұрын
Mo 😂man sakh soumay wakh nonou lay déf té awma😂lou soukeur barada
@ramatoulayediallo5973 ай бұрын
Bilay Aziz Ndiaye moy bandit promoteur yi
@morsene75073 ай бұрын
On est d’accord mais tapha tine était mille fois plus prêt que balla gaye sérieux
@Patxiabdoundoye3 ай бұрын
Non non
@ngangedrammeh62643 ай бұрын
Noo waay
@mayoryese3 ай бұрын
@@Patxiabdoundoye❤
@moussapayemane41673 ай бұрын
Mille fois plus prêt k Balla Guaye 2 baparé kou paréwoul diapko doumako,dane ko,bayiléne sénn thiahane
@ibrahimaFall-f3t3 ай бұрын
Tapha tine sa préparation bakhoul il est trop lent jtj
@MamadouDiallo-e2w3 ай бұрын
❤❤❤
@Reum-3 ай бұрын
Je pense qu'il parle de Dieye séne 😢😊
@papagabardia71073 ай бұрын
Aziz daguay sopp rek yalah la eupe doolé
@papaseye64143 ай бұрын
Si c’ est reussi c’est challenge, si ca passe pas , dama donn kaaff leçon sue 😁
@mouhdy8523 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@CASI77973 ай бұрын
T'es pas un incompris dh, c'est juste parceque dagua sokhor grand
@kurayahmi3 ай бұрын
*Il parle a Makane Mbengue*
@layekharagne22243 ай бұрын
fallou ndiaye peut être
@ndiawardiagne16733 ай бұрын
Da nga bakh rek yana sa diamou yague
@cheikhndiaye10053 ай бұрын
Tafa tine daguen ko liguey ba ben wet bi dokhoul lolou gneupa ko kham
@diopjean36313 ай бұрын
Mounane je suis pur yow yemal daguay saup rek contre boy niang ana sen stratège ak bandi beuri gua titeur lolou do touss
@momokkk99283 ай бұрын
Mais yaw strategies de fois mou bahh comm defois dou diaaleu yaw mousso d
@momarndao74413 ай бұрын
Wakhoul dara lou ay vraiment
@amethboultouf42963 ай бұрын
Ragal yala rek laniou koy déf yaw do dara tapha rék laniouy top
Li rek mon takhe modoi lo dou beuré ak balla parcekeu deumeu raye la dialé la epu balla bimiye beuré ak eumeu sene fo nekone
@AssiatouBah-m8p3 ай бұрын
Aziz 😂😂😂😂😂
@adamandiaye56223 ай бұрын
Serigne abdoul aziz s'y al amin nena loumou diaral nit pr mou yakal la nalako diaral pr nga defar ko te aziz nonou lay deme
@tvadamandiayekhassaidtouba83883 ай бұрын
WAYE GNI YORR TAPHA TINE KHAMOU NIOU TOUSS MANE BAOL BAOL LAA DAGNE NIO ÉMILIE TAPHA STAF BY BAKHOULL✍🏿
@ismacisse71623 ай бұрын
Balla masol paré lambou dou sport
@Robbe-Grillet3 ай бұрын
Siissoul
@nimspetite3 ай бұрын
CNG da wara téré organiser combat ba paré indi mbeur mii c anormal
@ibrahimacisse80433 ай бұрын
aziz n’es plus prometteur, il aide baye il peut amener balla
@nimspetite3 ай бұрын
@@ibrahimacisse8043 aide amoul droit aider ko même si c son frere parce que mbeurou aziz day am ay privilege toujours c comme ça aziz a tout les infos tout les droits parce que son frere est organisateur c discriminatoire
@ibrahimacisse80433 ай бұрын
@@nimspetite mais aziz n’est pas un manager de balla, il est agent c’est pour ce la que cng ne peut rien faire contre lui, e il a le droit de aider son frère a organiser les combat c’est pas illégal
@nimspetite3 ай бұрын
@@ibrahimacisse8043 lolou yeup deug la wayé c discriminatoire par rapport à son adversaire
@falloukane69273 ай бұрын
Dia dieuf Aziz nila dagay man sa nit
@SambaDiawaraSarr3 ай бұрын
Lamb yeufou Thiédoo DeuG laa
@SSFDiop3 ай бұрын
Xamnaa ne publicité original bi moom war nañu ko defaraat gat neexu ci
@Realiteeee3 ай бұрын
Mane deh damakoy avance rek et puis ça tympanise
@Papediaw833 ай бұрын
Yen shut up diem len crèer limou crèer bay def publicitè, amoulen produit ni publicité du sokhor ak sissou shut up
@Realiteeee3 ай бұрын
@@Papediaw83sa khol bi tangue na deh la pub et le patron ça n'a rien à voir doff nga torop
@SSFDiop3 ай бұрын
@@Papediaw83 yaw xamoo dara, yeene ko mu jarlé moo tax mani buñ ko mënee defaraat moo gën, publicité bu baax te neex mooy jaay produit, doxal fowi
@mouhaniang17103 ай бұрын
Ndayssane j m souviens bimakoy bolè ak Daouda sèrère Tivaouane Instant bobou modou lo mingi tivaouane di weur daouda ma wo aziz ndiay diohko tèktale thi Dawouda ham hamou ramlou lay utilisé Kou Yalla maye ndaysane Aziz ndiay diougè dakar thi tange tange bii gneuw tivaouane Dawouda gènèlko sarah bii deup kombat bii Il fau reconetre q Balla gaye dp8 son combat contre Yekini Day dipeurgni combat rek Sino yeup dagnekoy diekou Contre Yekini dafa yahe lou bari thi lambame Lambe lay wahe nak wassalam
@@papadiom9260lou lére ngeu wahe machala eumeu séne dafa hame keur you bahyi sou begé combat dou yomba dane vraiment
@tvadamandiayekhassaidtouba83883 ай бұрын
AZIZ LINGA WAKH AMOULE AY MBOCKOU DAFFA WA BAOL NIOKO DANE AMNA THI SERIGNE YOU DEUK BAOL YO KHAMNI DANIO WORR KHAM NANIOULENE AZIZ NEKALLE NITT 😂😂😂😂😂😂
@papagabardia71073 ай бұрын
Modou lo rek
@lassanatalla7673 ай бұрын
Teugue séne combat takeu mbeur mi ba dou meune dara guéne dane ko dou sport niak gua fayda trop modou Lo môme ak yéne diekh na même 500 million modou beugoul
@papadiom92603 ай бұрын
Modou Lo noumou fiii defff Eumeu ! Balla daneko gnou teugeul ko combat royal cambal Eumeu ba meunoul dara door ko mou danou te kene waxoul! Lou tax ngene Nafekh ???
@mamediarradiop26353 ай бұрын
@@papadiom9260merci ❤😂😂
@papadiom92603 ай бұрын
@@mamediarradiop2635 Waay gnii dagno Nafekh waay 😂 Bou Modou Lo di yeww mbeur yii dilene douma melni dagno taak seni beut kene dou wakh mais bougn ko deuper rekk gnou oubi sen gaat yii !
@cheikhbasskeurmassar95483 ай бұрын
Aziz moy bandit 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@KhadyGaye-n5g3 ай бұрын
Balla Gaye moye lamb bilakhi
@MomoKane-rn9if3 ай бұрын
Balla gaye actionnaire la alburakh lolou nieupeu ko kham.
@diattaabdoukoulingo28263 ай бұрын
Aziz wakhofi dara loudoul tageu sa mbeur
@Baraboromkourousgi3 ай бұрын
Kéndou iow sama idol bi
@diambendoye33203 ай бұрын
Balla brom baxla
@MbayeIbrahima-u3g3 ай бұрын
Yawe démale rék d'elle wakh rek
@SerigneoumarNdiaye3 ай бұрын
Saway yénéko lou bakh défoula dara 😅😅
@SerigneoumarNdiaye3 ай бұрын
Saway yénéko lou bakh mo gueun ki défoula dara thi ay bissnesam la nék
@ngangedrammeh62643 ай бұрын
Nanal ndokh mu sedd teh khamneh do yalla do yenenti, khamo sakh ndakh dinga ewou suba
@moussapayemane41673 ай бұрын
Démal liguey pour am mo gueune ki da liguey
@MbayeIbrahima-u3g3 ай бұрын
@@moussapayemane4167 yawe nopile kène ladioula
@papegoragueye52013 ай бұрын
Yaw mome kou weur nopi nga
@MomoKane-rn9if3 ай бұрын
Invité nite ba paré complexé ko .dolén ndy posé aye question wala ngén kay relancé