Aziz Ndiaye Dafa Wara Respecté Modou lo..; Le Coach de Modou lo s’énerve Limou wakhe daf ko wara…

  Рет қаралды 13,311

Fadam2 expert de la lutte sénégalaise

Fadam2 expert de la lutte sénégalaise

Күн бұрын

Пікірлер: 78
@ndellacarlier2712
@ndellacarlier2712 7 ай бұрын
Tu nous soulle Mr gaye toi et t'es amis...vive lo dame sire
@ChambouléFM
@ChambouléFM 7 ай бұрын
Aziz ndiaye so meunè balla aq tapha tine kou dann yobuko Aldiana 😂😂😂😂😂 MODOU LO ❤Roi des Arènes the Goat ❤
@LamineSall-mv9gq
@LamineSall-mv9gq 7 ай бұрын
Fadam bayilll nafèkh khaliss djaroul liii
@bahosmantv1521
@bahosmantv1521 7 ай бұрын
Lii mo tax sénégalaise yii nexma bougouniou kouy togne wala injustices yeup hamne aziz Ndiaye nekoul thii deug merci beaucoup
@MameSow-vp7rj
@MameSow-vp7rj 7 ай бұрын
Aziz Ndiaye mo téppi leufeul ndayame 😂😂😂😂
@MameSow-vp7rj
@MameSow-vp7rj 7 ай бұрын
Modou lôooooooooo ❤❤❤
@bayeratebayerate5893
@bayeratebayerate5893 7 ай бұрын
Aziz Ndiaye dafa sokhxr Modou lo moy sane baye
@atoumaneniasse4854
@atoumaneniasse4854 7 ай бұрын
Machallah Modou lo kou bakh la
@ndiagafaye3106
@ndiagafaye3106 7 ай бұрын
Nangou jël neu thieurou bagne vraiment Modou lo reek
@Azoura22
@Azoura22 7 ай бұрын
Modou xaragne lo seul ❤
@atoumaneniasse4854
@atoumaneniasse4854 7 ай бұрын
Coach machallah kou yarou té xam sport
@mbayediop299
@mbayediop299 7 ай бұрын
Merci diobong très bien dit
@DoudodiengDoudo
@DoudodiengDoudo 7 ай бұрын
Franc dieul Balla Alioune Seye Dieul Eumeu Vive le GOAT Xaragne Lo Kou meir Ya Xaaaaam
@SeydinaMboup-j3t
@SeydinaMboup-j3t 7 ай бұрын
Wa keur Aziz ndiaye com aye lesbienne fi modou lo lafi yalla tèk moy le roi Aziz siteu rk la soxarè mais yalla mofi nèk❤❤
@BqkLjj
@BqkLjj 7 ай бұрын
😂
@BqkLjj
@BqkLjj 7 ай бұрын
😂😂😂
@BqkLjj
@BqkLjj 7 ай бұрын
Mâcha alla bien parlé
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 7 ай бұрын
Merci 😂❤
@bayeratebayerate5893
@bayeratebayerate5893 7 ай бұрын
Merci coach
@atoumaneniasse4854
@atoumaneniasse4854 7 ай бұрын
Machallah coach lou léer nga wakh ❤
@omarlowe3879
@omarlowe3879 7 ай бұрын
MODOU LO NDIAGO ORBI REK 🎉🎉❤❤
@iboutoure-bf9by
@iboutoure-bf9by 7 ай бұрын
Sokhore baxoul !! Nit dou sokhore !! Begeu am Modou Lo mou teuleiiii mo waral li yeup
@adamasarr4647
@adamasarr4647 7 ай бұрын
Soyez vigilant mais fadam nafekhla
@SeynabouTouré-k9u
@SeynabouTouré-k9u 7 ай бұрын
Aziz day sonal bopam reek wayé Modou lo douko beurel been combat,fadam arrête d'être hypocrite cest mieux
@akadtv661
@akadtv661 7 ай бұрын
Modou Lo mom la Balla Gaye done diouteul wala ?
@papesakho1595
@papesakho1595 7 ай бұрын
Sa yaye la Modou lo diouteull 😂😂
@akadtv661
@akadtv661 7 ай бұрын
@@papesakho1595 yaw sa yaye makoy diouteul
@robiefall159
@robiefall159 7 ай бұрын
Fadam, bour at tapha gueye duñu ay nitou dara sén poche rek
@SeynabouTouré-k9u
@SeynabouTouré-k9u 7 ай бұрын
Bilahi dé wayé daniouy sonal sen bop reek
@kharagnembaye5958
@kharagnembaye5958 7 ай бұрын
Eumeu fayal bor Modou lo Modou mayna sa gniari boy chance Am ak boy gniag
@rokhayathiam7913
@rokhayathiam7913 7 ай бұрын
Fadam mi nafekhe la bilahi da bagne modou mais modou yalla moka beugue et le monde
@bayeratebayerate5893
@bayeratebayerate5893 7 ай бұрын
Aziz Ndiaye modou lo sa baye la
@bariso2626
@bariso2626 7 ай бұрын
Fadam , Bour guewal koulen geun seytané amoul bilahi😮
@HenryDiouf-gw2yl
@HenryDiouf-gw2yl 7 ай бұрын
Sou tapha tine dané mom ak Modou lo combat la par contre balla gaye sou dané mom akk boy Niang d'abord pour dieul revanche 😎 BAYILÉN SOTT BI
@TaphaSall-c8q
@TaphaSall-c8q 7 ай бұрын
Modou Moy Sen baye
@mamadousarr3371
@mamadousarr3371 7 ай бұрын
Ama balde modan tapha tine mod lo dan Ama, Boy niang2 modan Balla gueye2 mod lo dan Boy niang2 kon modou lo moy roi des arene okay
@papispass
@papispass 7 ай бұрын
Fadam wakhale sa patron Modou beréwoule ak Balla.
@hj-eu6xc
@hj-eu6xc 7 ай бұрын
Aziz immature Ndiaye l'homme qui insultait les femmes lors du combat Gris bordeaux contre balla dopation gaye 2 . L'homme qui disait à gris bordeaux et tapha gueye ""taye sougnou diabar nguène dagne lèène di ka............"" Il n'a jamais été une référence. C'est un petit homme. Il faut le comprendre.
@MuhammedJah-x7w
@MuhammedJah-x7w 7 ай бұрын
Naka lai def beh jut FADAM
@atoumaneniasse4854
@atoumaneniasse4854 7 ай бұрын
Azizz ndiaye moy kane ba louka nékh wakh ndakh xaliss nafékh bakhoul
@dabasarr2329
@dabasarr2329 7 ай бұрын
Modou Lo est le meilleur 🥰 kou ame coach Bou mél nii dara doula diaxal. Coach Diabong koumouy entraîner sama khél déy dal . Aziz dafa wara neutre
@FallWaly-c6g
@FallWaly-c6g 7 ай бұрын
Aziz de sokhor na xamni modou mofi nek balla rek la beuga yeketi
@Deggou
@Deggou 7 ай бұрын
Y'allah sakh douniou forcé niou deff loumou beug...aziz moy kaan bay forcé modou lo pour mou beurél balla gaye? modou avant mouy dieul couronne bi wahone nakh xaleyi laay maye chance nakh yénéne champion fégne pk nous forcé balla? lii mome soxor rek lakoy toudé ame na yén senegalais yo xamtané bougnou guissé séén morom rawlén daniou commencé sisou , tek la beute , dila yakal... ay affaire emprereur mome ci albourakh lay yéne, rois des arens bi modou lo la, teu dou sama mbeur maiss naniou ko respecté...
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 7 ай бұрын
Deugu rék nga wakh ❤🎉danio sokhor rék
@makhtarfall5557
@makhtarfall5557 7 ай бұрын
Non fadam yaye nafekh
@roots7.628
@roots7.628 7 ай бұрын
@mamadousarr3371
@mamadousarr3371 7 ай бұрын
Kholén fadam2 ak taar bi machallah 😂
@abdoulayefaye7271
@abdoulayefaye7271 7 ай бұрын
Fadam😂 domeram nga wakh len aziz deug dafa soxor
@HenryDiouf-gw2yl
@HenryDiouf-gw2yl 7 ай бұрын
Mais Aziz bayilén ko mou teugg combat royal après promoteur boumou nékh nga teugg BOU SITEU LAURENT NDIAGO tmt déff ko combat royal 😂😂 affaire bi Amoul problème déi 🤔🤔 en tout cas le vrai roi c'est Modou lo
@mamadoutall5772
@mamadoutall5772 7 ай бұрын
Le problème fadam t'écoute pas
@fallouniass-sj7rd
@fallouniass-sj7rd 7 ай бұрын
Fadame mii. Kaye bama ko wéddé yague na
@omarlowe3879
@omarlowe3879 7 ай бұрын
Aziz dafa soxorr
@mamecorsarr82
@mamecorsarr82 7 ай бұрын
Fadam nafék la ya warone recadré Aziz Ndiaye
@abdougueye4837
@abdougueye4837 7 ай бұрын
faddam mbeure mou ratté top lamb ji di seytané ak diakhassé😂mais nak faddam daguay roy si becaye ak modou mbaye lamine seck
@atoumaneniasse4854
@atoumaneniasse4854 7 ай бұрын
Franc ak eumeu sene moy combat bi
@MuhammedJah-x7w
@MuhammedJah-x7w 7 ай бұрын
Number fadam la buga please
@omarlowe3879
@omarlowe3879 7 ай бұрын
Fadam fen rek ga man blie
@LamNdiaye
@LamNdiaye 7 ай бұрын
Modou lo rek ndam rek ndam
@laminjagne7254
@laminjagne7254 7 ай бұрын
Modou Lo seul roi kum nahari nga ???? ?? ????? ????
@abdougueye4837
@abdougueye4837 7 ай бұрын
mais aussi fadame yen dagueni fatté modou lo dieul ama ak boy niang dan lenn té ama dane tapha tine boy niang dan balla
@SouleyemaneDiop-o3p
@SouleyemaneDiop-o3p 7 ай бұрын
aziz tourame bi rék mo bakh si mome
@badoundiaye5771
@badoundiaye5771 7 ай бұрын
Aziz tu es sans classe vraiment 😮
@davethiam1472
@davethiam1472 7 ай бұрын
Fadam lii yeup say pékhéla ya nék si souf mais linga beug dou âme ça bopou bou ngandé bi
@MamadousaliouthiandoumTh-bt6co
@MamadousaliouthiandoumTh-bt6co 7 ай бұрын
Fadam ak buur ak boucher nio wara nopi ci lamb té dfou niou fi dara fén rk diahassé nitt gni rk doyna way
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 7 ай бұрын
Wakhal dé ay seytanné lagniu khaliss rek lagn beugu
@ibrahimdiao6864
@ibrahimdiao6864 7 ай бұрын
Bollési cothio bacari Sakho c le maiéure
@AboubakrydiawaraCisse
@AboubakrydiawaraCisse 7 ай бұрын
Modou lo mo dane boye niang té boye niang mo dane balla gaye2
@nabiensopetakha4242
@nabiensopetakha4242 7 ай бұрын
Wame li business kounek louy doxale saya afere ngaye khole vous ne devais polimike ou cng dans tout ça
@AbyNdiaye-yq7ex
@AbyNdiaye-yq7ex 7 ай бұрын
Yaw fadam seytané gua yak bour yéne Aziz taye totale sene thiep mo takh
@LallaMass
@LallaMass 7 ай бұрын
merci coach
Amena lou khewatii D😱 Medical Boye Niang..; Fadam2 Revient encore et fait des révélations Explosif😱
30:19
Cheerleader Transformation That Left Everyone Speechless! #shorts
00:27
Fabiosa Best Lifehacks
Рет қаралды 16 МЛН
Regardez Cheikh Bara Ndiaye humilie Cheikh Bara Ndiaye en direct 😭
17:17
Bilahii Biss Boula Zarco Dané bayil Lamb.., Fadam2 réagit et previens Gris Bordeaux Apres Face2Face
15:04
Fadam2 expert de la lutte sénégalaise
Рет қаралды 3,6 М.
Thiow amatina😱;  Balla Gaye Sou Dof Dof Ba Dieul Modou lo Dinako def lou..; Hé Satouba Wakhe Na Dh🤔
31:59
Pape mbaye Tacle Sévèrement Sathies Da niak Fayda Siteu Limou def dafa Niaw Dou Yonne  nakh dafa….!
25:30
🔴DIRECT / INSTAGRAM FADAM2 AMANEKH VS THIATOU DAOUDA FALL, FORZA VS GENERAL MALIKA,
1:36:43
Fadam2 expert de la lutte sénégalaise
Рет қаралды 10 М.
Direction Arène Nationale: le départ mouvementé de DIOP 2
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 93
Bagarre Pape Sarr et Pathe Balde.; Fadam2 s’énerve et attaque Pokola limou def dou, Talfa biss bo..,
15:10