Man mom khamonani Aziz ndiaye dafko sarakher bou yagg bah creer courone Boppam
@Mariam-cp8zg4 ай бұрын
Une vérité absolue je suis d’accord avec toi grand ils faut qu’ils prennent la jeune génération RESPET
@ansoutamba-cu8dl4 ай бұрын
Vraiment je vous adore 5 tonnes ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@layekharagne22244 ай бұрын
contane na ci mom dh ❤
@miachoufall66654 ай бұрын
Bi khettou Deug merci wayyy❤😂😂😂 merona sakh mai amna Kou wakh deug te Yalla takh Kharagne kassè❤❤❤Li yep pour khekh modou Lô moka takha Dioug Waye dollen si dalll
@diamadiome66644 ай бұрын
Bagne sène trokhol mo takh wakho lène wakh djie Modou ló sou angagé balla wadiady😂😂😂
@younoussdiaw1604 ай бұрын
Saway maygnou kom ni Balla di dieulé eumeu wayyadi rekk@@diamadiome6664
@palayendoye60714 ай бұрын
Ms Yene nekh guene der khana Modou Lo reck moy mbeur si arène khana amolene combat dolene ko lidieunti ter mayniou
@BinetaGueye-ym8sn4 ай бұрын
Bien dit Modou Lo mo dakhe carrière Balla Gaye ❤ Modou Lo dépassé n’a Balla Gueye
@linkstardidingkeba29224 ай бұрын
Dieul lén
@moustaphaseck2914 ай бұрын
Mo khame😂😂😂😂neu dieul
@ndeyegueye86014 ай бұрын
😂
@bassiroukane92064 ай бұрын
Yen mom vraiment werolene😂koulene niouss 2 fois nguen koy teukalé ak Sen bope
@mouhamedmoustapha6844 ай бұрын
Balla nokhlen 2 fois nguèn ni yenako daxx carriere
@ShiekhjobeTijan4 ай бұрын
Aziz wakhoul dege modou lo do kharitam bego no ko sax modou lo rek ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@Saliou-i7p4 ай бұрын
Waxga deug
@DjillyKara4 ай бұрын
Modou lô dépasséna fawzayni pour mou lér 😂😂😂😂😂
@CheikhKebe-vm7df4 ай бұрын
Merci sama wa djii contanna ci yaw❤ modou lo mo len eupou fitt
@ToufaDGueye4 ай бұрын
Deugu dou rombi nopi 😢yéyé 5 tonnes ya niémé deugu way Vérité absolue 🎉
@ibrahimasarr36904 ай бұрын
Modou lo est le meilleur lutteur sénégalais de tous les temps
@ousmanediawara-fu7ek4 ай бұрын
BALLA FIIT AK FOULA ,FAYDA DIOM LA INDI DIAKARLOK MOM , TEH TAPAHA AMOUL FIITTE AK KEL, MACHAALLAH YALLAH MAYNAKO KATANE ( DOOLEH ) WAYEH KHAMOUL NIOMOUYKOY DIEUFEUNDIKO SI LAMB DJI
@ShiekhjobeTijan4 ай бұрын
Ta Moy dege Modou lo doko Mosa jel ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑
@sadikhfall90204 ай бұрын
Way 5 tonnes yaye ndanane way. Modou mo raw balla way
@Menoo1074 ай бұрын
Lernama ni yaw da guay setane lambe ni rek ms khamo lambe wala gua sokhoré balla guaye
@marcusmouhamed4 ай бұрын
@@Menoo107saway ki deug la wah modou ak balla kou sohla sa morom modou sohlawumko t prtan balla moko dann 2fois
@MilkMilo-qr5uc4 ай бұрын
@@Menoo107geumal yalla
@mbayangmbenguezb50064 ай бұрын
Ce que j'aime sur toi c'est ton franc-parler
@modouthiaw76064 ай бұрын
Tay MOM tu a Di la vérité tapha
@amathtv71784 ай бұрын
Merci beaucoup vraiment mon frère ❤️👑👑👑👑👑👑👑👑
@mbayegueye52344 ай бұрын
tapha tine com cou amoul aye mbokkkkkkk walahi azim
@ndiayeabdouaziz5884 ай бұрын
No den ko epou xaliss rek
@freegalsen55564 ай бұрын
DOLEN ROUSSS TOUJOUS ACCUSATION HAHAHA
@Abdu_Khvdr104 ай бұрын
Bilae 😢
@Dam-g2u4 ай бұрын
Merci beaucoup 5tonn wakhe deug balla gay.dafa.mistyque.tapha balla gay.mistyque.loko.yaramwi😅
@mbayendiaye50334 ай бұрын
5 tone modou lo rek montakh ma beug la guédiawaye la deuk corniche mais franc champion la nak
@OusmaneSambe-l3f4 ай бұрын
@@mbayendiaye5033 ki nio bok bén kogn marche xélcom guediawaye chaque jour ma rombou ko gueumoul modou lo mom lép louy nakaral wa guediawaye lay déf mais nioune wa guediawaye dinagn ko règlé té en plus vrai tapét leu
@moussakalamou71764 ай бұрын
Daw lakou bii 💛💙✌️
@doudoudiallo90534 ай бұрын
@@moussakalamou7176😂😂
@layekharagne22244 ай бұрын
@@moussakalamou7176joyeux khatarayou 😂
@MoctarTandian4 ай бұрын
Felicitations balla guèye 2
@masssarr37834 ай бұрын
❤❤ bonne analyse 5tonnes deug dafa nexx
@khadisall37624 ай бұрын
Modou rèk la niouy topou❤❤❤❤❤❤❤❤❤Modou lo rèk
@mamsaitsarr76004 ай бұрын
Blie walie talie we love you 5 ton
@conteyebabacar75614 ай бұрын
Bly ligua wakh yeupp deugue la Tapha tine est atteint mystiquement
@AbdoulayeThiaw-r7j4 ай бұрын
Nio tay
@2quevosquevos2424 ай бұрын
Bou Bakh sakh Tapha tine Aziz ndiaye mokko sarakher
@maradiop38554 ай бұрын
Vérité absolue merci 5tone
@kevinfofana90464 ай бұрын
Il est très pertinent ce jeune
@ShiekhjobeTijan4 ай бұрын
Modou lo rek lanoy topo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@MameSow-vp7rj4 ай бұрын
Modou lôooooooooo ❤❤❤❤
@moustaphaba91144 ай бұрын
Billay aller 5 tonnes modou rawnalene comme disent les niassene
@Junior-gx8ll4 ай бұрын
Je supporte balla mais 5 tonnes deug you lérr la wakh vraiment nio bokeu guiss guiss merci diambar deug rek ngay wakh.
@layekharagne22244 ай бұрын
fansou balla bou sokhoroul ❤
@alassanedieng74794 ай бұрын
Azize ndiaye day nakh tapha tine rekk si balla gaye
@freegalsen55564 ай бұрын
DOLEN ROUSSS TOUJOUS ACCUSATION HAHAHA
@elhadjisarr12444 ай бұрын
On l'a payé de l'argent comme balla.
@2quevosquevos2424 ай бұрын
Aziz ndiaye Deum la
@adamambaye7864 ай бұрын
Wakh nga dégue 5ton modou lo moy 👑 ❤
@Zahim.LinetObii4 ай бұрын
5 tonnes tay mome contana si iow ❤❤ Modou lo rek modou lo kessé modou lo Seul
@massambadare4 ай бұрын
Bilahi walahi talahi tapha tine bimouye tousse lane sama copain bima togolone fi maroc lane tapha tine dagncoy dane diapnagne co bou yage si galathe
@moussadiakhate90224 ай бұрын
Ki moy degue yonam nekoussi 💯💯
@khadisall37624 ай бұрын
Mèrci beaucoup ❤❤❤❤❤
@MoustaphaFall-qs7yu4 ай бұрын
Bravo bravo bravo boy bilakhi ya gnome deugeu
@OmarGueye-uf6fl4 ай бұрын
Modou 🎉❤❤
@ngomsitor4 ай бұрын
Merci bro tu as bien compris
@SeydinaNiang-oy9wg4 ай бұрын
5 tone mon khoromou 😂 xlô kassé ❤
@emtv77034 ай бұрын
Balla gniméwoul khaléyi 😂😂😂
@AbdoulayeThiaw-r7j4 ай бұрын
Wayé mongi niouss mak gni
@layekharagne22244 ай бұрын
@@AbdoulayeThiaw-r7jdane makk you diekhal dou ndam 😂
@bayeratebayerate58934 ай бұрын
Amna solo de Modou lo rak
@ElhadjiFall-nw2he4 ай бұрын
No Aziz dou. dieul eume sen 😂😂😂 day wax rek danou cambal modu lo Mes na diap si Yalla ay Door la modu lo du xaritame
@Niangahma4 ай бұрын
Frément 5tonne tay mom direct
@bambaseck99564 ай бұрын
Barke arkhourane instan yiii Modou mo meune balla Gnari yone
@dieydybathily77514 ай бұрын
Lolou diaroul watt nako dieul niou khol
@mamadouba45774 ай бұрын
Bilay mystique amna bakhna
@MakhaSow-t3s4 ай бұрын
Merci 5 tonne
@alkhamiss4 ай бұрын
Tapha tine amoul ayy mboko la yakar warole wone dieul balla domeram dji organisé sene combat diokh ballla mystique niou guémbeu ko gani meun nga ko dan tapha tine yakeu na carrièram
@zoladiop94124 ай бұрын
Way ban sarakhé geum len yalla eumeu mogui nii dieul avance albourakh diap sa thies danko
@abdoulatifdiop56404 ай бұрын
Sathies AK Balla Danio bokou
@papamoctardiop40214 ай бұрын
Bayil ma gni...naniou nekk sportif Tapha sou danone li yeup dougn ko wakh
@zoladiop94124 ай бұрын
@@abdoulatifdiop5640 niniuy diapalé balla laniuy diapalé sa thies
@AbdoulayeThiaw-r7j4 ай бұрын
Vraiment
@abdougueye48374 ай бұрын
vraiment balla dako meune
@AtoumaneNiasse4 ай бұрын
Tapha tine danouko sarakhé 😂😂😂
@cheikhdiop96734 ай бұрын
Sarakhé Moy lane boy Niang khana danoul balla gaye khana dagno sarakhé balla gaye wakhi dof nanal ndox
@AtoumaneNiasse4 ай бұрын
@@cheikhdiop9673 iaw daga doff trop balla Gaye ak boye Niang Gaston monko teugue 😁😁😁
@cheikhdiop96734 ай бұрын
@@AtoumaneNiasse yaw mi yaye dof bou nanoul Say grap daga dégg fouma wakhé waloum kou teugeu balla gaye walla kouko teugoul wakhi sarakhé yiga wax lala tontou mbeur dagay dane gnoulay dane pas ay sarakhé balla makane mo teugone diokhoneko trois avance lolou dou mane gakoy wax malako geuna kham foufe dama geumoul sarakhé yoyou gay wax gnata millions lagnou faye tapha tine Serigne boum kham démnafa guir dane balla gaye sarakhé dou aw lay ahh
@mouhamedmoustapha6844 ай бұрын
Bombardier doumeu balla nangou roi des arenes bi xana danio sarakhè balla
@papamoctardiop40214 ай бұрын
@@mouhamedmoustapha684gni bayilen
@seckadiop99214 ай бұрын
Walahi 5tone damoko beugue
@MilkMilo-qr5uc4 ай бұрын
Lolu mom manam gni saw di diakhane gnokoy bagna dégue déme léne sétani Modou boy niang bécaye dafa sédal sama xol bi c'est le numéro 1👑🥇🐐
@layekharagne22244 ай бұрын
becaye vrai corrompu la bokk na ci niouy deffral promotion balla , modou contre boy niang dafa def lou lerr ba nieup nangoul ko c prk becaye amoul wone choix il faillait qu’il dise qu’il est le meilleur
@MilkMilo-qr5uc4 ай бұрын
@@layekharagne2224 effectivement mane j'ai beaucoup de respect pour becaye mais cette fichue couronne d'empereur en aucun cas gnom warou gnou wone si gnikoy plébiscité un ténor bou diougé si ay défaite danou ba sonou au lieu geine wakh ko deug mais comme Aziz est derrière cette manigances fok gnou ande si mouvance bi nakh xaliss sport amoul triché balla bokoul sakh actuellement si 5 yi mbeur yi nékk au top diayy nit mo baxoul déjà andi woul touss si lamb dji
@layekharagne22244 ай бұрын
@@MilkMilo-qr5uc g aucun respect pour becaye parske khaliss rek lay diamou , je l’aimais bien ay diamono 2016 2017 depuis le 2 eme combat modou balla la parè ci mbiram def ay analyse diokh lepp balla fekk bobou modou mo guenone nekk ci dynamique , en plus après combat bi mouy tilimal combat royal bou modou wara beurrè contre eumeu , ak you bari. Quant à couronne empereur bene nitt rek lay blamer mouy tapha tine et son staff , tapha ci bopam moniou tonie il devait être intelligent liniou deffone modou 2019 warone nako servir leçon , legui dinaniou diappè balla comme bene hero te dou touss pourtant formam bi tanè na par rapport ak ses derniers combats. Ins bi lene la yakar mouy Aziz diko teuggal combat mouy kheureum adversaireum yi.
@MilkMilo-qr5uc4 ай бұрын
@@layekharagne2224 becaye si bopam limou wakh combat modou boy niang bou waxatè le contraire bopam lay ridiculisé bopam lay yabelou lolu c'est se manquer de respect lui même mo waxal bopam modou c'est le numéro 1🥇balla forme bi tané kassé la défe tapha tine si bopam mo amoul staff malheureusement ay farfelu gnoko weur mais li dina yé mbeur yi kousi ame foula mom boul nangou beuré ak mom combat bou Al bourakkh teug na néke combat neutre par exemple Gaston ou un autre lignou beug modoul messa néke bilahi roi bi dakoy khégne rk mais dotu ko dieul bou yébo mom gnou geiné si séne xél concernant Modou mome yakar na 400 millions sakh taxoul mouy dieul combat bi yabou gnou la fokk bay wakh sakh loussi dieum douma ko meussa ball bou ko nango
@MoctarTandian4 ай бұрын
5tonne faut avoire un bon ❤Coeur cest tres important dans la vie
@IslandCureislande4 ай бұрын
5TONNE SOUBKHANALA BAYIL WAKH JI MON FRERE.
@NdiayaFall-fn7xw4 ай бұрын
Balla rék 💪
@adamasarr46474 ай бұрын
merci 5 tonne tu as raison
@2quevosquevos2424 ай бұрын
Modou lo dafay deranger Aziz ndiaye Deum la Merci 5 tonnes
@seringembacke93164 ай бұрын
Merci 5 ton Waxga dége dé
@beguefallou61904 ай бұрын
Wawaw modou lo raw naléne😂yalla nako yala lafal thiat lo défoul deh ballagay namay boyi sans😂🎉🎉
@@2quevosquevos242 moussoul waxx balla lou baxx té néna tapha la faralonn di mboubo guediaway demal khol limou donn waxx balla bi lac démé kasso komsi fautam la
@AdamadouBah4 ай бұрын
Ohhh modou lo rek ❤❤❤❤❤❤❤
@aliounediop3704 ай бұрын
Gni saga 5tonne yalla na yalla wéreul batt yi😂😂
@Messatsu04 ай бұрын
Al BOURAKH ay Deum laniou mbeur bou lekk sen avance yakou ngeu
@OusmaneSambe-l3f4 ай бұрын
Bayilén di doul ki nio bok kogn doul rék lay déf ce 5 tonnes niari combat Balla gaye vs Bombardier yeup Aziz Ndiaye moko teug da balla gaye da danou 😮
@cheikhdiop96734 ай бұрын
Boy Niang loutakh mou dane balla gaye bayiléne séne thiakhane yi balla gaye sou dano guéne ni balla yakhouna sou dané guéne 'i galathi la dané balla mo sonou ta bari ay none
@OusmaneSambe-l3f4 ай бұрын
@@cheikhdiop9673 bien dit gni ay doméram lagn doul rék laniouy déf Bombardier deux fois yimou dan balla gaye yeup Aziz moko teug
@freegalsen55564 ай бұрын
DOLEN ROUSSS TOUJOUS ACCUSATION HAHAHA
@2quevosquevos2424 ай бұрын
@@cheikhdiop9673Boy Niang vs Balla Gaye Gaston mokko teuguon Boy fene del lathier
@seck-z7h4 ай бұрын
bo fi balla danou wa te boufi kene wahk da fa febarone 😂😂😂
@2quevosquevos2424 ай бұрын
😂😂😂 lolou Rek lay khar 😂😂😂😂
@SerigneAbdousalalamNiang4 ай бұрын
Balla fran moye yonne🎉
@AbdoulayeThiaw-r7j4 ай бұрын
ana dioutal lo
@moustaphaba91144 ай бұрын
Wawaw
@moustaphaba91144 ай бұрын
@user-lo1rp2tr2j amal classe wayy
@leuz.patriote4 ай бұрын
😅😅😅😂😂😂😂😂 nn balla yawou dial😂😂
@MawdoBa-y8b4 ай бұрын
Tapha tine vrai guaka le n'a sante yalla sax come ke dèwoul danio ko donne ray azize Ndiaye di domè kharam
@BintaDiao-gs7nc4 ай бұрын
Bien dit vraiment tu as bien dit
@pourmeraseck97824 ай бұрын
Ah Balla sama mbeur bi bou yabo nga gueuneu gorgolou am nga ay nonneu dh 😂😂 so amei défaite gnuni danga dieekhal 😂 nga am victoire gnuni danga mystique 😂😂 ken khamoul loumou donn
@hamidoutall91344 ай бұрын
Bilakhi ki aka ndeye niamé deugue
@mouhamadoumoustaphacamara23114 ай бұрын
Empereur huile j'adore borom 6 défaites 😂
@YoussouSall-d8y4 ай бұрын
Merci. Cinq. Tone❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤.
@tallbusinessmantalibeserin31914 ай бұрын
5ton ak farant yena nèkhe 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@kalidouyayambodji86584 ай бұрын
Sénégalais mo niémé YAllah
@diattafaye39054 ай бұрын
Modou lo sokhlowoul Balla. Focus vers Steu
@nafisene53354 ай бұрын
Vraiment 😂😂😂 balla Mo niou sokhla, couronne chinois la yoor
@layekharagne22244 ай бұрын
@@nafisene5335couronne sene petit gallè 😂
@MafallFallvipvip4 ай бұрын
Merci ❤
@NabyLeJuriste4 ай бұрын
Tapha Tine ken sarakhei wouko mo sakharakhé bopam Premièrement waroul won dieul combat bi Deuxièmement mom mola guena khamni Aziz avec tous ces privilèges il fera tout pour que balla gagne Baye ndiaye mo yoor thioumi kayou balla gaye après tout cela ioe diemo moytou dara di dofdof lou lamb dafa am ay réalité
@ElhadjimodouGaye4 ай бұрын
Degg nah deuggue
@abdoufaye83824 ай бұрын
Bilahi forme Bi bakhoul 😂
@May-m1d4 ай бұрын
Bilahi yas degou
@djibyfaye36164 ай бұрын
Balla a plus de moyen que Tapha il avait le soutien total des organisateurs c’est Tapha le fautif et son entourage.
@layekharagne22244 ай бұрын
5 tonnes ❤💪🏾
@Saliou-i7p4 ай бұрын
5tonnes yagui wax deug ❤❤
@Ababoukara4 ай бұрын
Balla Gaye Zarco walla Franc rekk Monfi dess
@abassmbackewane95994 ай бұрын
FANS MODOU😂
@ibrahimakane39404 ай бұрын
Seul Dieu ne se trompe pas.
@AïchaKane-i3e4 ай бұрын
Modou lan beugue sarakhé mé dou am
@Thierno-of3pc4 ай бұрын
Balla ak ama gnoy lamb
@LoLo-zt5zu4 ай бұрын
5T is funny as hell😂
@FatoukineSeye-fv3nx4 ай бұрын
Vérité absolue
@sakho84104 ай бұрын
Pour dire vrai 5 TONNE a raison, TAPHA TINE DÉÑOUKO SARAKHÉ et ça mom les Sénégalais ont fait ce constat sur le combat d'hier.