Balla Gaye 2 ce que tu as dis sur Jacques Diene c vrai,je t conseille vivement d’en faire autant avec sa famille
@adamasarr15389 ай бұрын
BG2 le meilleur de tout les temps homonyme bii champion bu magg biii
@mouhamadoulaminekande87963 ай бұрын
Douma doyale si Balla gaye 2 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@mouhamedmboup69919 ай бұрын
Nioun Modou lo kassé ak franc talfa gaimeur laniouy topp
@abdoulayendiaye39749 ай бұрын
Vive Balla Gaye 2 il est et il restera ❤
@moustaphaseck12319 ай бұрын
❤❤❤balla rek laniou beugeu 🫶🫶🫶🫶
@mouhamadoumakhtarfaye44379 ай бұрын
Aucune organisation laissez la personne finir en plus deleiine diokheii paroles entre faw mou am kou dirigé pr k les autres sui
@khadimmbaye479 ай бұрын
Je suis d'accord avec toi
@marememboup63039 ай бұрын
Merci beaucoup lolou la beguone wax
@assdiop45459 ай бұрын
@@khadimmbaye47❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@Omzo__Velli9 ай бұрын
Émission bi néxxna😂😂❤
@mortadacisse89929 ай бұрын
Bour lamine bi mo nékh😂😂❤
@baichorr85999 ай бұрын
Athia mbeur ndam rek inschalla
@babsbaba199 ай бұрын
Il faut laisser les invités répondre aussi c’est sa le défaut de cette émission
@PapemadiorNdiaye-g9z9 ай бұрын
Balla gaye vs tapha tine un bon combat.
@abdoutine68499 ай бұрын
Khana dou Balla Gaye mi mo wakhone né khamoul casamance
@MouhamedLo-su9yb9 ай бұрын
Modou lo seul❤❤❤
@CheikhMbayebegfallou9 ай бұрын
Balla waro khar sax niouy wakh pour nga dem setii wa keur jack diennn koleré
@Lam6079 ай бұрын
Thiey sama mbeur bi❤
@Aaron-i5f9 ай бұрын
Tapha tine da wayadi ' balla dinako dann
@ibrahimaniane65089 ай бұрын
Balla sa forme bii ma guiss sooko beuré Ak Tapha Tine mou rayy la si stade bii dee 😁😄😃 si Tapha Tine moo la eup dolée instant bii ?
@babaniass42899 ай бұрын
Il a 6 mois pour travailler donc c'est très prématuré de parler de forme physique
@Robbe-Grillet9 ай бұрын
Yakamti défaite balla rek molene dall @@babaniass4289
@ibrahimaniane65089 ай бұрын
@@babaniass4289 je sais tres bien bro , c tres bon de faire c genre de commentaire c t une motivation pour lui , je lui supporte c mon lutteur mais yii daffsiiy bakh mou rayy bopom si entrainement franchement victoire laniou beug?
@mansourndoye88909 ай бұрын
Le 21 juillet dîna fekkk mou paré akk Koor gui di niew niom sa thies la yeureum 😂 meun nagn perte sen forme
@babaniass42899 ай бұрын
@@ibrahimaniane6508 inchallah il sera prêt, il a vu les critiques qu'il a reçu après le combat de Modou lô vs boy Niang donc espérons qu'il aura compris la leçon de son combat contre Bombardier et qu'il se donnera à fond aux entraînements pour retrouver sa forme d'antan
@MbayendiayeNdiaye-r6v9 ай бұрын
Bilahi mako mbeugue
@gouthia9 ай бұрын
Contane si Balla, wakhou gaure deug. TAPHA Tine tey nga warou dé🤣
@oiaftv9 ай бұрын
Mė dėlėne degulou invitė bii mou wax nakk ahhh😮
@AmetFatty9 ай бұрын
Champion
@djibyka14769 ай бұрын
Mbeur décidé neu dé
@naby2dioptamsir1829 ай бұрын
Balla moytoul bour guéwél seytané la
@Daily-r8z9 ай бұрын
Yalna am ndam inchallah
@ngallmbaye10529 ай бұрын
Ki defna lepe si lambou
@toutiwakhjobloubari87469 ай бұрын
Feuw zeyni daye napei rék 😂😂😂
@amethndiaye50999 ай бұрын
Très bien balla bour seytané la
@alphacheikhsylla40719 ай бұрын
Balla Gaye rek ❤❤❤❤
@MoustaphaTall-mt1yd9 ай бұрын
Plateau bi bilaye nékhenama
@mamedjibrilniang81519 ай бұрын
Bour mii dafa indiscret bassi ay questions wam
@diakharbousaff82729 ай бұрын
Bour gëwële saytané la
@moussaba6389 ай бұрын
Sen plateau bi dafa beuri nitt trop ah
@actufootball2219 ай бұрын
Bilahi mala beugg ❤❤❤❤
@DieganeNdong-v5r9 ай бұрын
Douma Fate Say tako chàn ba si 2012 /22/4/
@derkaderka86359 ай бұрын
Bour contant na thi lingua fatali balla
@bigbossofficiel68749 ай бұрын
Mais guiss nga ni gars yi sorri wouniou si pas que dou pour fii téléphone amna soutoureu lou bakh la ❤
@madieyediop17129 ай бұрын
Emission bi amoul beine organisation
@moustaphafall94949 ай бұрын
Balla Gaye ioe nitt kou sOkhor nga nak bombardier dala daan banga sonou
@MamembayeSeye-id5pr9 ай бұрын
Fawzeyni 😂
@mansourndiaye33919 ай бұрын
No.balla nieba go mage😂
@MalickMalick-oe2zl9 ай бұрын
Yaw dé yay sama mbeur ga mais insbi tapha tine mola meune fouff
@pathetoure90329 ай бұрын
Nianalko rék yalla bakhna
@djdra84319 ай бұрын
Laisser le parler au nom de dieu😢
@serignecheikhfall4189 ай бұрын
Xana ng bayi beuré wayé ioe mom li des sa carrière inch'ALLAH sa ay défaite ñoy eup sa ay voctoire...
@Whinnyski9 ай бұрын
Yow dor neka nit
@OneNation591lofficiel8 ай бұрын
Yallah d’où ande mouk akk niit bouy nianal nitt lou bonne donc inchalah bi nga dieuteul amoul ndieurigne .. niit mo sokhor bilahi.. ragal yallah lou bakh la
@BaMasour9 ай бұрын
Khana yaw ndieupeula mak
@FatouThiam-zf4op9 ай бұрын
Yaw bayil wa casamance domérame nga rék fi nga wakh ni sa papa motakh nga dãnn dém casamance😊
@ahmadoudiop50169 ай бұрын
Yow mi yaye domeram imbécile way katal sa ndeye sa môme Casamance yow
Balla moye badola 😂ma wakh mounane ay moukhamsa ak you kéne khamoul khana taye ga bagna khame mou khamsa 😂😂😂
@ahmadoudiop50169 ай бұрын
Balla ba legui day lekk bou khamssa Di juste day waxtane rekk
@ridialdieng28619 ай бұрын
Bour guewel kou katt ndeyam la dou nii way
@PapemadiorNdiaye-g9z9 ай бұрын
Les Présentateurs parlent plus que l’invité. C'est vraiment ridicule.
@moussagueye79029 ай бұрын
Balla n'a aucune chance devant Tapha Tine. Il risque d'être humilié.
@babaniass42899 ай бұрын
6 mois c'est beaucoup tout peut changer dans cette période et en même temps tapha n'est pas quelqu'un de nouveau pour Balla gaye. Ils se sont frottés deux (mbappat et arène) donc ils se connaissent très bien
@Robbe-Grillet9 ай бұрын
Waxoo deugue sa yéné rek nga fi tek
@tikotheclever48819 ай бұрын
Émission bou nakari. Tt le monde parle en mm temps et personne ne finit. Soof nguen quoi
@@Robbe-Grillet il a raison balla nafekh leu Liiko ménagère diène défal khamoul Lou djabotam nekk
@Robbe-Grillet9 ай бұрын
@@MrFayemanou loolou lou si nek naafekh ame ? Yeen danguene di boolé you bokoul. Balla sou taxawoo famille wam loolou dafa rafette té diadou mou defko. Mais dou obligation. Nit dinga ame sa connaissance yoo xameni dioté wolene dara mais le temps et les activités vous éloignent de sorte que vous pouvez rester des années sans échanger mais bess ngay nieuw rek ame loula si xiir nga lidianti contact bi doxaat ko. Balla depuis le décès de son manager il est passé lui aussi par des épreuves difficiles yoo xameni meunone na si diaaré bayi lamb. Xamoo période bobou lou mou ame ak loumou amoul, xamo si limou nekone. Donc faut pas juger les gens comme ça. C'est très facile de dire diw dafa bonne mais c'est difficile de savoir se mettre à la place des autres. Balla naafekh la wax diodiou mangui kay soga dègue tay. Ça veut dire que mbaax mingui si mome ndax loolou lako nieup di seedeel. Wayé nak taxoul mou parfait. Seen problème nak mooy sou nguene banié nit dou nguen guiss si mome dara lou baax.
@latyrgueye87419 ай бұрын
Balla dangay sop
@pathetoure90329 ай бұрын
Boy démal liguéye mo geun si yaw balla tékina amna khaliss bakhna khol bou rafét la yor nék gaïndé DEUG yéni wakh fayzeyni mais bolén khamone loumouy téki dingéne nopi