Balla gaye est le meilleur lutteur que l'arène a vue
@kurayahmi6 ай бұрын
*Balla moko meun, mais Modou mo dakh beuré Balla, mais souy beurei ak Balla dou utiliser khelam, djiko ley beuré, teh style de lutte bi Balla am ak taille bi ak gabari bi arranger wouko. Balla ci bopam kham Nani Modou moko dakh beuré, motakh souy beuré ak mom li mouy def ci entraînement ak mystique douko def contre beneine adversaire. Thieur bim diokh modou lo diokhouko benen mbeur. Mais lolou dey am, mbeur meun ngeu ko dakh beuré beu parei mou daan leu. Par exemple, Balla mo dakh beuré bombardier teh pourtant Bombardier daan nako 2 fois.*
@DegueneFall-vc5ue6 ай бұрын
Verite
@DegueneFall-vc5ue6 ай бұрын
Verité
@MamadouDiallo-gn6dg6 ай бұрын
Top analyses mais j sui pour balla guaye ❤❤
@BassirouNdoye-ib4mj6 ай бұрын
Bonne analyse
@youdenhazard356 ай бұрын
Une analyse très pertinente 👏🏾! T’es un vrai ‘’lambalogue’’ wallah 🙏🏾! Ame nga place si plateau yi dhé bro ✌🏾!
@layekharagne22246 ай бұрын
tellouma guiss li mais majorité des commentaires nénaniou c king xlo donc khol sedd na ❤️🥶
@DjibrilBa-xp7te6 ай бұрын
Modou lo seul le meilleur de sa génération 😍❤❤❤
@LakhatFall-v1h6 ай бұрын
Ken dou balla ❤
@saliouthiam24626 ай бұрын
Modou Lo c’est le meilleur ❤️🥳👑
@NdamaCeessay6 ай бұрын
Xaragne lo le meilleur de sa génération
@linkstardidingkeba29226 ай бұрын
Kharagne lo est le meilleur de sa génération je confirme mais n'oublie pas que Balla Gaye est le meilleur de toutes les générations
@NdamaCeessay6 ай бұрын
Boude lolou kasse lanouy guisse conne manga est le meilleur de tous les temps
@CherifCherif-f2s6 ай бұрын
Sauf balla gaye
@layekharagne22246 ай бұрын
@@linkstardidingkeba2922modou est nn seulement le meilleur de sa génération mais il est le meilleur de toutes les générations confondues ❤
@malicksarr21416 ай бұрын
Yekini et modou Lo son le meilleur lutteur ❤️❤️👑👑
@saliouthiam24626 ай бұрын
Mbeurou fass massoul daane modou Lo ak balla gaye 😂niome niarr kene manoul wakh kii bayyi kii ay légende lagn 🎉❤👑
@mosi3016 ай бұрын
Balla Moko eupeu dolè mai walahi Modou lo mo Dakh beuré fouff
@ngarybadiane11706 ай бұрын
Balla gaye 2 c'est le meilleur de sa génération et la génération passer❤
@DeugDounékh6 ай бұрын
Modou lô 22 victoire balla gaye 21victoire Modou lo debut 2006 balla gaye debut2005 Modou lô 3 défaite balla gaye 6 défaite Adversaire en commun 6 lutteur papa sow ,issa pouye, gris, euma ,b52, bn2 Modou lo amsi 7 victoire bén défaite Balla gaye amsi 4 victoire ak 6 défaite Modou lo meusoul tegalé 2 défaite Te balla tegalé na 2 défaite Modou lô amna 2 victoire la am si 👑 bi Té balla gaye 1 victoire la am si 👑 bi Modou lô meusoul gaday pour défarou watt😂 Te balla gaye gaday n'a 3 ans 2015 ba 2018😂 Modou lo kharagnam mo tax niou bayiko khèl Balla gaye domi double less bi motax niou bayiko xél 😂 Balla mo soute modou eup ko ndieuk ko doug si lamb am papay mbeur ak tourando mbeur kone bou démé ba rivalam bi geuna reuy nek modou lo kone warna khamni modou lo mi kénn dou mom si lamb dji
@moustaphaba91146 ай бұрын
Haa saway sa analyse bii tamit deuglah wakh deug fa yallah lii yeupp mane setlouwoumako vraiment !
@ModyGningue-qf8qp6 ай бұрын
Sa waye ligua lerna
@BassirouGueye-y4x6 ай бұрын
Si 6 adversaires en commun yi balla ame na si 6 défaite, bombardier 2 fois, eumeu 2 fois, boye niang, et Issa pouye
@DeugDounékh6 ай бұрын
@@moustaphaba9114 guisnga lolou
@LamineFall-r9p6 ай бұрын
❤❤❤❤❤
@AliounebadaraThioye-ho4tq6 ай бұрын
Balla gaye 2 mo meun modou lô ms modou kharagne lô mo dakk mbeuré foufff❤
@kareemdia19356 ай бұрын
Wakhi doff
@alhamdoulilah91546 ай бұрын
C ça la réalité je suis Fan de Modou lo
@modoubayefallsikroulla14236 ай бұрын
Balla man mo dakha beuré
@saliousarr55456 ай бұрын
ioe wer gua
@AliounebadaraThioye-ho4tq6 ай бұрын
@@saliousarr5545 louma Dall?
@moustaphadia64596 ай бұрын
Balla le meilleur lutteurs
@amathtv71785 ай бұрын
Xaragne lo rek le meilleur ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@alhamdoulilah91546 ай бұрын
Balla champion la mais pour man modou lo mokou dakha beure parce-que Balla gaye 2 boula eupoul doole doula daane contrairement ak modou lo même bokou eupé doolé meun nala dane
@malicksarr21416 ай бұрын
Mabuegue pér ndiouga dia 👍❤️❤️❤️❤️❤️modou Lo le meilleur lutteur du monde
@LayeMbaye-ky6fn6 ай бұрын
Billahi pére diaw mi Dafa sokhoré Balla gaye môme AK tapha gueye❤
@papesougou29656 ай бұрын
Lolou la guisse
@malickmbaye2835 ай бұрын
Tu as raison deh
@LamineFall-r9p6 ай бұрын
Kéne dou modou lo❤
@beydysakhocurdelion6 ай бұрын
Kou neik amna foumou guené fort moromam
@omarcisse67126 ай бұрын
Modou lô c le meilleur luteur de tou les tend
@SkyRapidIT6 ай бұрын
No one like balla Gaye 2. He is the best if all time
Abdo bakhom khoul ba gui boun li pabi di wax modou mo dakha bere 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@SeynabouTouré-k9u6 ай бұрын
Tous les deux sont fort mais xaragne lo est meilleur de sa generation
@papesouma6 ай бұрын
Balla c'est le meilleur de tout les temps
@NoreyniIbnhaffan6 ай бұрын
Modou est le meilleur lutteur ❤️
@ShiekhjobeTijan6 ай бұрын
Modou lo rek billy ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑
@DjibrilBa-xp7te6 ай бұрын
Abdou bakhoum yalnako borom bi may kholou mougne 😂😂😂😂😂
@amadoudrame55046 ай бұрын
😂😂
@rouguikebe99846 ай бұрын
Amiine😂😂
@adamasamb4525 ай бұрын
😂😂😂😂
@AssaneDiongue-p3f6 ай бұрын
Modou lo cest Modou lo ❤
@nabydia32436 ай бұрын
Il est le meilleur balla 👌👌
@mbacke36026 ай бұрын
Le problème de gabarit est très mal compris pour beaucoup de gens. Mais Modou est meilleur en technique
@BabaCisse-mu1cz6 ай бұрын
Kien dou modou
@rimesmakerposeidon24276 ай бұрын
Modou lo le Messi de la lutte sénégalais ❤
@MorNiang-hb5en6 ай бұрын
Yékini le meilleur lutteur du cinquantenaire pour la première fois
@ndeyekhoudiathiam26416 ай бұрын
Balla est le magicien de l'aréne
@dialloabdou34876 ай бұрын
Balla mo eupe dolé mo dakay beuré❤❤
@moustaphaba91146 ай бұрын
Haa jafféna kham dh😂 je suis fans de Modou kharagne lo mais je donne Modou 49,50% et Balla gaye les 50,50% Balla kene dou kokou mais nk Modou laniou beugeu ❤🎉
@layekharagne22246 ай бұрын
bayil fene t un fan de balla
@moustaphaba91146 ай бұрын
@@layekharagne2224 non je me considère comme kii gueuneu beugeu Modou kharagne lo billah frr awma si mome saguo yallah sedé n'a lolouh
@layekharagne22246 ай бұрын
@@moustaphaba9114 saway do fansou modou t un fan de balla bou begue deguisew rek
@moustaphaba91146 ай бұрын
@@layekharagne2224 yallah kham na ko mouyene louma si neubbatou tamit
@rouguikebe99846 ай бұрын
@moustaphaba9114 Do fan Modou nak 😂amga droit faral Balla mais boul déguiséwou😂
@misterzappa90736 ай бұрын
Tapha Gueye etait plus complet en matière de boxe et de garde sans oublier les chuttes spectaculaires pour cette génération Balla est plus spectaculaire Mais Modou est plus complet Eumeu est plus Charismatique
@amadoulaminesankhare9526 ай бұрын
Merci beaucoup père
@ndakarudialdiop12066 ай бұрын
Histoiru lamb balla gaye moci dak beuré ❤
@moussasima80026 ай бұрын
Mbeur bou melni Balla gaye 2 chaque 20 ans lay am ci lamb🤗
@jaayprekkk6 ай бұрын
balla mo meune mais modou lo ma dakha beure
@SmansourDieng-ht1ou6 ай бұрын
Balla mo mane et moi dakh beuré Modou lo ❤
@babacar31786 ай бұрын
Léne dall khamnago modou lo toloul nii niome té modou mom laye guiss niou tolougo féne si beuré mouy contunuer di beuré
@moussadieng36806 ай бұрын
Balla guaye 22 victoire, 22 different chute et technique. C est le meilleur
@layekharagne22246 ай бұрын
Modou dou moromam so kholé commentaires yi rek gua guiss né majorité bi nénaniou modou mo dakka beurrè
@bilalkhalyfall99386 ай бұрын
Wakhal ay dèfaitam key dagua meune wakh le meilleur wakh ses victoires kèssè tè do wakh ses défaites
@MamadouNiang-ce5ic5 ай бұрын
Modou champion la mais balla mo daka beuré❤
@ShiekhjobeTijan6 ай бұрын
Modou lo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑
@jazaka31786 ай бұрын
Xlô à chaque fois bouy beuré akBG2 day diappp nguémbam té Eumeu dou ko may mou diappp nguémb
@issalayendour14096 ай бұрын
Balla est le meilleur ❤❤❤
@MrFayemanou6 ай бұрын
Modou est plus sportif
@mariamaba66446 ай бұрын
Modou ❤❤❤
@cheikhsadibouthiam5 ай бұрын
Balla gaye 2moy lamb ❤
@falloudiop76515 ай бұрын
Modou lo est meilleur ❤
@mamadouthiam25146 ай бұрын
Wakhi xam xam Bg2 est un génie hors pair ni Eum encore moins Mlo ...Ah !aaah!Demal kholiwate les combats de BG2 Balla pour moi reste le meilleur de sa Génération. Même si Em l'a terrassé Balla est un ECLAIRE en lutte....Un Vrai Lutteur sukko diaralé deug...Amul morom Wa GUEDIAWAYE Mothiam...Cependant Eum et Lo des Génies mais BG2 Nono Lenenela thi lamb vrai Balla et ses qualités
@ibrahimalo30606 ай бұрын
XLO seul
@LayeMbaye-ky6fn6 ай бұрын
Lamine tapha gueye balla gaye loumou co danne mo takh mou méré balla😂😂😂
@saliouthiam24626 ай бұрын
Tapha gueye modou la gueune bagn que balla psk mbeurou fass massou léne daane 😂😂😂
@ShiekhjobeTijan6 ай бұрын
E wakho fi dara bayil raso bi nk Modou lo mofi nekaa 😂😂😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤🎉🎉🎉
@LayeMbaye-ky6fn6 ай бұрын
@@ShiekhjobeTijan nn frére
@djibyka14766 ай бұрын
Kone ameu sene dakoul beuré balla gaye . Balla est le meilleur
@bayesaliou19885 ай бұрын
Xlooooo❤❤❤❤
@momodiene4516 ай бұрын
Balla Gaye est le meilleur
@Robbe-Grillet6 ай бұрын
Balla mo dakha beuré si histoire Sénégal
@SadioFaye-q9g6 ай бұрын
Yéne daguén yepp balla eumeu AK Modou lo balla moy séne baye Yekini bamoufii neke Modou AK Eumeu loutakh danou niouko séne baye mo gniew dane ko sena sokhorrr way balla mo dak beuré si lambe dji
@SaidouFaye6 ай бұрын
Modou lo.kasse❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@djibrilndiaye27545 ай бұрын
Abdou bakhoum tay la khamni ndanaane la bilahi
@alphacheikhsylla40716 ай бұрын
Balla Gaye rek ❤❤❤
@modoubayefallsikroulla14236 ай бұрын
Balla est le meilleur luteur de l'arène
@chakasen3996 ай бұрын
Bayyiléene thiakhaane yi ! Balla Gaye 2 est deux fois meilleur que Modou Lo ! Les deux defaites qu'il lui a infligées ne laissent place à aucun doute !
@bilalkhalyfall99386 ай бұрын
Yaw est ce que cv ?? Saway wakhofih Dara bombardier daneu na balla Gaye gnari yoneu mais takhoul balla moko dakh beurè Modou balla dako daneu dh mais kholoko sakh si beurè doussi palmarès ossi les hommes mentent mais pas les chiffres
@bgueye795 ай бұрын
Kum nekh ngani modou lo mo dakh beuré deh wayé expliquer ko molay teu😂😂😂guén lèn si linguèn né😅
@baaziz95146 ай бұрын
Pere dall mo nekh nena Eumeu mo dakh beure Balla nakh daan nako 2fois tais nangouwoul ni Balla mo dakh beure modou lo 😂😂😂😂 nangoulen li yalla def payi danio jaloux , Balla c le meilleur lutteur de tt les temps au senegal …
@moustaphaba91146 ай бұрын
Non wakh deug eumeu mo dakh beurré nieupp
@mbeussniang40196 ай бұрын
Sénégal li eupe si nite gni ame nafikh lanou😊
@Dakarh246 ай бұрын
Vraiment pére balla gaye mo dak beuré modou lô nak
@mbayendiaye92386 ай бұрын
Balla mooy séne bay si beuré amoul débat sah sui modou lo nak deug néhoul nak
@CheikhantaGueye-kb4tq6 ай бұрын
Montakh mou ndayélé bopam souff si
@beugeuserignetoubatvgayeko38466 ай бұрын
Vérité absolue ❤
@bilalkhalyfall99386 ай бұрын
😂yaw key do Modou Lô li nguay gnèmè yallah trop
@vieuxndiaye37906 ай бұрын
Modou lo il meilleur sur tou juste que balla c'est sont bêtes noir mai Modou kenne dou mome
@moustaphaba91146 ай бұрын
😂😅 père tapha noto sissou wy😂
@GilKane-s4e6 ай бұрын
Modou lo mo dakeu beré foufe
@adamadiouf80066 ай бұрын
Bala lim def thi lamb ken dotoucofi defati bi niep né modou lo mosoul danou moco diap daneco dieul bou lere nagne de même que yecni et Tapha tine cen dou Bala palmarèssam benla on est fiere de lui bilahi
Balla gaye moy sama mbeur mais eumeu sene mo dakh beure thi lamb dji
@moustaphaba91146 ай бұрын
Je valide
@iranndao13056 ай бұрын
Yakjni Dan ko sot pour mou danou
@beugeuserignetoubatvgayeko38466 ай бұрын
Ab dof ga
@mbayendiaye45626 ай бұрын
No dangua dioum mod lo 4 defait baye madione
@bilalkhalyfall99386 ай бұрын
Nanal ndokh tè fèkheul seu khôl mo gueune si yaw ndakh lolou doko meusseu dègueu
@nouhadieme18896 ай бұрын
Douma fans Balla mais bilahi mo dak beuré modou lo foufff
@moustaphaba91146 ай бұрын
Non boul fouff fans Modou lo laa d'accord Balla mo dakh beurré modou mais touty rknm nk😂 saway
@layekharagne22246 ай бұрын
ya meune mew 😂saway khamaneté naniou dh watal né do fansou balla ?
@deguenediop35856 ай бұрын
Senegal ken dagoul beurry ken cou nek ak li ngay beurré
@AbdelKader-kt7zj5 ай бұрын
Fans Modou laa mais wakh deugu ci yalla balla keine dakouka beuré ci arène bi ..ndagam deugue neikh yalla ... Leine rek mooy problèmem état formam topato wouko... Wayé balla indi forme normal bilahi mbeur menouko ci fite ak meune beuré
@boubadiallo66226 ай бұрын
Balla gaye est meilleur que eumeu sene
@Kingofefootballe6 ай бұрын
Balla mo dax beuré si Lambj de tout les temps
@Ndiago-Bi95626 ай бұрын
SÉNÉGAL NIO GAWA FATÉ 🤣🤣🤣 BALLA GAYE DAN MODOU LO 2 FOIS DJOUTEULKO APRÈS NIOUNÉ DAKHKOUKO BEURÉ🤣🤣🤣🤣
@cheikhbasskeurmassar95486 ай бұрын
Balla gaye deux seul
@makambtv6086 ай бұрын
Balla gaye moi dakha beuré sii lamb djii
@SouleymaneCamara-n9e6 ай бұрын
Pere katy manoul supporters Balla gaye 😂😂😂
@matardieng-cr9xs6 ай бұрын
Balla mo dak beurré si adouna
@moussacoundoul43856 ай бұрын
Sén plateau ay ré lama df
@kareemdia19356 ай бұрын
Bg2 seul
@ahmadoudiop50166 ай бұрын
Modou est plus sportif champion leu nak mais balla cest autre chose ken dou mome
@Elhadji11noreyni6 ай бұрын
Kou takhaw ni mbeur mou dakh beuré balla gaye ci lamb dji wakhoul deug akh koumou meune done nak