Noo ngi rafetlu ligéey bi bu wer. Cheikh Ahmadou Kara dafa jok di leeral nit ñi fi bamba jaar ba sauvé jàmm ji. Fii nak mu melni daf nuy wax Bambay Kan à travers ay jëfam ci nun pour rawale nu. Lii nak mu mel ni ci weeru safar gi Général bi bind taalif gi mu nu ciy laac Bambaay kan, di nu ci tontu it am. JëraJëfe ci taalif gi Kara Lumière ❤