Amoul différence kou baxx.Naxx niome niarr nieup kéneu ki laniou done wotél mouy Yalla souniou Borome 🙏 Limouléne waxlo laniou waxx kepp yokou nioussi wagniwou nioussi 🙏 Nioungui léne di sante di niane Yalla yok séni lerr🙏🙏🙏
@fatouniang79652 жыл бұрын
bonne question je me la pose tt le temps a ce que je sache niome niar nieup khamm yalla laniou wote islam la niou wote cone 🤔
@serigneguene811710 ай бұрын
@@fatouniang7965bien sûr certain disent que baye a dis dans un de ces ouvrages que quiconque ne viennent pas a sa porte il n'aura jamais cet connaissance divine et c'est le contraire de ceux que les yalla yalla disent