BANTAMBA CHEZ MODOU LO DU 07 JANVIER 2020 AVEC MODOU MBAYE

  Рет қаралды 221,445

2stvsenegal

2stvsenegal

Күн бұрын

Пікірлер
@zachariambaye4956
@zachariambaye4956 5 жыл бұрын
Mane deih balla moy sama mbeur tei ba adouna di touki moy done sama mbeur,mais sur le plan professionnel wax deug yalla modou mo gueuna professionel th machalla maintenir na forme mam ba lgui en plus nité na koi,chapeau à toi de la part d'un vrai fans de bg2
@kingsoffaye2717
@kingsoffaye2717 5 жыл бұрын
Serigne Abdou Karim yalnafi yag té wére amiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiine
@mouhamedbadji3665
@mouhamedbadji3665 5 жыл бұрын
ALLAHOU MA AMINE
@modoubay7414
@modoubay7414 5 жыл бұрын
Amine
@oumarsow8344
@oumarsow8344 5 жыл бұрын
Kingsof boye nianala S A karime dou ci émission lamb guakoye nianale sof guene té niak yar
@asssow180
@asssow180 5 жыл бұрын
oumar sow saway khana dagay sissou
@kingsoffaye2717
@kingsoffaye2717 5 жыл бұрын
@@oumarsow8344 boy wax amiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiine nga waxko boko menoul nga bayi domou Haram sa xolou golo binga yor bay Karim gnaipako beug bamou dais yew lolou moy wax bou naix bi
@cheikhba473
@cheikhba473 5 жыл бұрын
Suis inconditionnel de bg2 mais j'admire modou avec lui tout est simple. Humble na machalla respect.
@yarasalamdjiby5675
@yarasalamdjiby5675 5 жыл бұрын
MANE EUMEU MOY SAMA BEUR MAIS MODOU LO MIII CEST VRAIMENT UN GRAND CHAMPION RESPECT
@modousamb4183
@modousamb4183 5 жыл бұрын
Machlaha Modou lo modou mbay
@baimbidacosta5654
@baimbidacosta5654 5 жыл бұрын
Bravo champion tué différent les autres car tué respecteuse bon commenication
@2aa90
@2aa90 5 жыл бұрын
😂mola war si mome
@papakhalifacamara41
@papakhalifacamara41 5 жыл бұрын
Al amine nagoul koo mola gueneu fair-play
@mamealioune1051
@mamealioune1051 5 жыл бұрын
Machallah Modou Lo Moi je suis Pikinois et je supporte les lutteurs Pikinois . Mais Modou il m’étonne c’est un grand champion.
@mouhamadoucisse5137
@mouhamadoucisse5137 5 жыл бұрын
Ah yaw sa khola rafet rk bilahi👌
@layeyade901
@layeyade901 5 жыл бұрын
ya bakh rek frère m diamou si iow 🙏
@kinelamine3565
@kinelamine3565 5 жыл бұрын
mame alioune diallo bilaye ya ngorre waye
@boubafall1014
@boubafall1014 5 жыл бұрын
Nagoul nit dara nekoussi bax leu rk
@princenaze7119
@princenaze7119 5 жыл бұрын
T'as un beau coeur
@mouhameddiouf341
@mouhameddiouf341 5 жыл бұрын
Modou yalna sa djiam yageu yalla dfal la ndam si sa carriere ak sa combat ama balde ♥️
@boubafall1014
@boubafall1014 5 жыл бұрын
A vrai dir kou melnii MODOU LO si fouleu ak fayda ak fitt ak meun ak beug limouy def doko gawa gissate si lamb respect MODOU LO le ROI
@fallouthioune677
@fallouthioune677 5 жыл бұрын
Js8 fans balla gaye mè modou lo damako beugue ndakh diomam fiteum ak foula kharagne champion nga machalla amal diame rék
@momotouray172
@momotouray172 5 жыл бұрын
Mashala Kharagne Lô Bilahi damala sope reik Yarou Modeste Âme soutoura Meuneuh conseillé djoulité lingma defal doumako messeu fater et un jour in sha ALLAH dinalako fatalile et tu es aussi modeste que Sadio Mané et vous avez plus d’argent comme Goorgui Sy Dieng mais mashala on t’aime Yallah Na Roi bi Djik et mou Yague et Yallah Fayla sa Khole Amine 🙏
@iboudieye1255
@iboudieye1255 5 жыл бұрын
Modou lo yalla na yalla dolila soutoura ak aye ndami ndam barki mame babacar sy amine
@fatouba64
@fatouba64 5 жыл бұрын
Machalla Modou lo sama beurou xol lici kanam yalla na nek ay ndam ci barki serigne babacar sy mignou yakar
@khadimdieng4533
@khadimdieng4533 5 жыл бұрын
Supporteur modou lay don bah faw ak kan beuseul touch bleu
@layembengue2395
@layembengue2395 5 жыл бұрын
Mane
@dkbmg3526
@dkbmg3526 5 жыл бұрын
Modou lo et Modou mbaye yallah na leen yallah takhawou Modou moyé sounou fierté
@papamouserignebara6318
@papamouserignebara6318 5 жыл бұрын
modou lo ak balla gaye yalna sén diamou yag kou wakh Amiiiiine yalnasa diamou yag🙏🙏🙏
@bocarsow3090
@bocarsow3090 5 жыл бұрын
Modou lo yala nala yala may ndam si kaw Ama Baldé inchallah
@aliou6574
@aliou6574 4 жыл бұрын
Kou beuge modou lô téyé roi bi ba bayi beuré beusseule j'aime
@ousmanediop6134
@ousmanediop6134 5 жыл бұрын
Bilahi warounio faté demb😭😭Modou Lo keneu là si lamb djiii seule les vrais savent c’est un bon diamono youmou dane yeugeul
@mamadousanokho5485
@mamadousanokho5485 5 жыл бұрын
Modou kharagne lô yalla nala yalla soutoural defal la diam mayla goudou fan ak weur from pa yalla nala yalla may ndam si barké yonentibi
@ahmedmb7491
@ahmedmb7491 5 жыл бұрын
Un grand champion n’est pas seulement quelqu’un qui peut battre tout le monde. Le champion c’est dans l’esprit dans le comportement dans le savoir vivre. Et moi je dis que Modou est le plus grand champion de la lutte sénégalaise. Il a de la classe il est clean il s’habille bien il inspire les jeunes il est correct il parle bien C’est pas un lutteur qu’on voit partout sur les réseau sociaux il gère sa famille son parcours et il est discret c’est ça un grand champion. Bonne chance king
@ASTOU143
@ASTOU143 5 жыл бұрын
Merci
@niangfatma7350
@niangfatma7350 5 жыл бұрын
Bien ditt
@talibecheikh7367
@talibecheikh7367 5 жыл бұрын
Merci tu a tous dit yalla na yalla fayla
@ahmedmb7491
@ahmedmb7491 5 жыл бұрын
talibé cheikh Lima guiss rek la wakh yaw tamit nala yala faye Frere. Amine
@talibecheikh7367
@talibecheikh7367 5 жыл бұрын
@@ahmedmb7491 amine ya raabi mais je suis une Dame
@mamoudoudiallo389
@mamoudoudiallo389 5 жыл бұрын
Bravo modou mbaye yagui doga diel ndanane X lo yalna yalla goudal say fane te nga dor ama balde mou danou psaka degno reuw mom ak magam Abdou bakhoum mom defa khamady te dof
@ndeyearamebiteye4441
@ndeyearamebiteye4441 5 жыл бұрын
Modou lo lagnou wakh ❤️❤️🔥🔥🔥❤️❤️❤️❤️❤️
@malickfall8342
@malickfall8342 5 жыл бұрын
Modou machiaala sakaw sakaname in chiaalla
@ndeyearamebiteye4441
@ndeyearamebiteye4441 5 жыл бұрын
💪💪💪💪
@malicksarr5706
@malicksarr5706 5 жыл бұрын
Bantamba modou Lo motakhe niufaté ballon d’or sadio mané no kéndou xarange Lo bilahi mala bègue sama khole ❤️💪🏼🤛🏼🤝👊vie roi 👑
@ablayenittoudeugu1012
@ablayenittoudeugu1012 5 жыл бұрын
Malick Sarr moh ko yap
@coeur2lion481
@coeur2lion481 5 жыл бұрын
Yaw mi daga am tok dof dé
@boubacarmballo6402
@boubacarmballo6402 5 жыл бұрын
Yow ya mouna fen nioun de de nio feto sou niou ballon d'or
@BouSaliou
@BouSaliou 5 жыл бұрын
Malick Sarr wakhal way hun
@amytoure3341
@amytoure3341 5 жыл бұрын
Le roi le plus noble et le plus beau yalla nala yalla may ndam bou sedd gouye si kaw Ama baldé
@bassmbodji1544
@bassmbodji1544 5 жыл бұрын
Amy touré doungéne am dara ama moléne meune fouf
@cheikhniang9553
@cheikhniang9553 5 жыл бұрын
amine waye moudou lo rekk si kaw si kanam incahallh
@amytoure3341
@amytoure3341 5 жыл бұрын
@@cheikhniang9553 yalla bakhna naniou niane rek parceque dina ko sokhla lol
@amytoure3341
@amytoure3341 5 жыл бұрын
@@bassmbodji1544 ba bobou inchallah denk naniou lepp yalla soniou borom
@sallseydou7264
@sallseydou7264 5 жыл бұрын
Amin ya rabi ma bouge modou lo billay
@papafall8618
@papafall8618 5 жыл бұрын
Ani supporter xaragne lo yi💪💪
@alisamb1225
@alisamb1225 5 жыл бұрын
Modou lo
@lahaddiop5573
@lahaddiop5573 4 жыл бұрын
💯pour 💯👑
@omarndiaye2431
@omarndiaye2431 5 жыл бұрын
Serigne babacar sy rék modou lô yallana yallah défal diam sy barke seydina MOHAMMED AMINE
@daoudambow8348
@daoudambow8348 5 жыл бұрын
modou lo machallah séte nga,séleu nga kharagne nga outé nga yéne mbeir you dof yi fou niou wakhé niou khép léne niite dafa wara niité waaye
@binetoudiop337
@binetoudiop337 5 жыл бұрын
Khalif général koullou mbeur le meilleur le chirurgien de la lutte sénégalaise yalla nalla diam sonal mon roi modou xaragne lô nékha faral dimanche soir aka bari diom 💪💪💪
@oulouwagne4238
@oulouwagne4238 5 жыл бұрын
C le meilleur dou ragal dou tittte bilay walay modou soudone beurel ak sama tawou yaye modou la faral modou la andal fi ci spain
@junorlevrai8586
@junorlevrai8586 5 жыл бұрын
*Loufii dougueul couronne roi bi, guénéwouko fii* 💪🏽 Paroles de *Modou X.LO* ✌🏽😎✌🏽
@touremouhamede617
@touremouhamede617 5 жыл бұрын
Ki domou adama doumako geuna beugeu sérieux i lik thes man ❤❤❤❤👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑mala beugeu 👍
@ousseynousowkande9820
@ousseynousowkande9820 5 жыл бұрын
Toure Mouhamede Lolou ngua fok ioe
@momotouray172
@momotouray172 5 жыл бұрын
Toure Mouhamede iaw sama toma nga et même nom et prénom enplus gnou bokou fans donne ton numéro frère
@yettagayral338
@yettagayral338 5 жыл бұрын
Humm peut être mais mane môme biko balla dané dama fébar 3 jours lekouma nelawouma j'étais obligée d'aller voir mon médecin non farr métina
@touremouhamede617
@touremouhamede617 5 жыл бұрын
@@momotouray172 wa giss nga lolou yalla koy deff one love
@touremouhamede617
@touremouhamede617 5 жыл бұрын
@@yettagayral338 deko diar nak franchement mais nagnko gnianal rek dinabakh
@malicksarr5706
@malicksarr5706 5 жыл бұрын
Modou mbaye yagui dora invite champion Machala modou Lo yalnako yala maye diamou wayé kene dou pér becaye mbaye motakhe modou Lo mélni modou Lo yalnako roi 👑 djik Yarabi doundale modou 🤲🏻🤲🏻
@asssow180
@asssow180 5 жыл бұрын
Malick Sarr gnifi diale yeup dagnu khar champion bagui
@chamousman2726
@chamousman2726 4 жыл бұрын
Ameen
@deugdeug19
@deugdeug19 5 жыл бұрын
Néhul ba néhul mé do gnôm ta dugn yaW. Yay baayu kulu beur. Et té vraiment modeste !!!
@sambafall8390
@sambafall8390 5 жыл бұрын
Je suis fans de balla Gaye2 mais bon modou lo dafa âme respect c un gentle men vraiment
@nounousgningue5883
@nounousgningue5883 5 жыл бұрын
Bilahi ningay seidalei sama khôl bi yalla na yalla serralei non ou sa khôl yombal lepp. Niou daaane leu akk nga daane yeupp mann yow la beugg barki Borom Touba
@bendiallo8082
@bendiallo8082 5 жыл бұрын
Vraiment moodou lo xaragne na xrome la si lambji modou ont taime sénégal taime walah puissance!
@madiorgueye2993
@madiorgueye2993 5 жыл бұрын
Vraiment la 2stv est le meilleur tv 📺 du Senegal 🇸🇳 de tout les temps
@diadjikanteye4908
@diadjikanteye4908 5 жыл бұрын
Modou kharagne lo rek le roi des arenes 👑💪💪diadieuf modou mbaye jopp bi nice na machallah bantamba meilleure emissions lamb au senegal 👍🏻👍🏻👍🏻
@bourethiam44
@bourethiam44 5 жыл бұрын
Modou lo yalla nala yalla défal diame si barké seydina Mouhammad 👌
@papadiallo1576
@papadiallo1576 5 жыл бұрын
Yalla nala yalla défal diam té mayla ndam si kaw Ama Baldé si barké Seydina Mohamed PSL
@abdouldiack6296
@abdouldiack6296 5 жыл бұрын
Vraiment adouna dara kheuyoul nékh bilay xolal ki nimou commencé rk 40 milion tay 200 milion thiey mai dara mayou koko loudoul diomam ak foulam genre yi nitt warou len bagne walahi
@sambafaye7632
@sambafaye7632 5 жыл бұрын
Même pas un mois 166k c'est le plus populaire qui est d'accord?
@mouhamadoumoustaphadiallo6651
@mouhamadoumoustaphadiallo6651 5 жыл бұрын
Aka niakk kiniane modou lo sama champion bii diam si iow ndam rek inchallah
@wakhaldeug8424
@wakhaldeug8424 5 жыл бұрын
L Roi🤴 ds arène ❤️❤️🔥🔥🔥🔥🔥
@ousseynoudieng2184
@ousseynoudieng2184 5 жыл бұрын
Machalla modou Mbaye j'aim bien vous suivre tu fé bon boulo Bon courage ét bon contuiasion diam si Yaw 👏👏👏
@malickmaitrejeans8733
@malickmaitrejeans8733 5 жыл бұрын
Modou Lô Talibe Serigne Mbaye sy Abdou le meilleur 👑
@alunendong5063
@alunendong5063 5 жыл бұрын
beugg na lolou way serigne mbaye sy abdou xlô💪
@tijanyal9504
@tijanyal9504 5 жыл бұрын
Serigne ababakar
@alioukonate9375
@alioukonate9375 5 жыл бұрын
VREMAN etre un champion C DANS LE SPRIT LE COMPORTEMENT L HABIT ET LA MODESTIE BRAVO LO NDAMA ET BONNE CONTINUATION POUR LA SUITE NDAM YU BARII INCHALLA
@samzodiop4440
@samzodiop4440 5 жыл бұрын
Mod lo roi de aréne yaw yafiiiiiiii néeeeeeee👑
@fatoutall5275
@fatoutall5275 5 жыл бұрын
Machalla modou lo sama kharagne lo le roi des aréne doundal ba doyal lo sa fans fatou kharagne Lô beuguela rékk do séne morome☝️☝️👌👌👌💪💪💪💪💪🤴🤴🤴🤴❤❤❤❤🤗🤗🤗🤗😘😘2020Xlo
@modoufallbetebeteitsenegal5272
@modoufallbetebeteitsenegal5272 5 жыл бұрын
MACHALLAH MACHALLAH MACHALLAH CONTANNA SURTOUT BIMA GUISÉ PHOTO MAME SEYDI ABOUBACAR SY RTA BIINI EN PLUS JE SUIS FIER D’ÊTRE FANS MODOU XARAGNE LO YALLAH NAKO YALLAH GEUNUE TAKHAWOU
@papeniang6951
@papeniang6951 5 жыл бұрын
Les fan's de modou lo 😅😅😅
@petittoure7680
@petittoure7680 5 жыл бұрын
Un grand sportif qui sait parler et surtout qui pèse ses mots. Vraiment je suis très fier de lui,bonne continuation champion et beaucoup de bonnes choses à l'avenir.
@bayelahateseye3781
@bayelahateseye3781 5 жыл бұрын
MODOU LO LO BEGUE YA🤟LA NALA YALA MAYE DIAMOU
@modoukane7917
@modoukane7917 5 жыл бұрын
Noo.Modou.Lô momeune beuré. Toloul.ni mbeuryu takouko ham.donélaw Aÿ.kharagne.lô
@mohamedthiandoume5637
@mohamedthiandoume5637 5 жыл бұрын
La classe thiey sunu mbeur yalla nala borrom bi défal diam xloooooo yaye bomb
@fantambaye3976
@fantambaye3976 4 жыл бұрын
Machallah bilay mala beug lo ndam yalnala sounu borom lafala tiat mayla leep lo beug si barké serigne Babacar Sy
@cheikhsene8210
@cheikhsene8210 5 жыл бұрын
Ndam rék champion yallna yalla défall diamou ♥️💪x lô
@papediop8512
@papediop8512 5 жыл бұрын
Amine
@VoyageSpirituel
@VoyageSpirituel 5 жыл бұрын
Meilleure bantamba du début d'année Machallah avec notre fierté Xlo
@moussaboukharagne7046
@moussaboukharagne7046 5 жыл бұрын
Nit waroul sokhor boguissé li yeup thi yallah rék le dieugué té kén mounoul may bopam yallah rék moy màyé yallah Roi bi djigla Modou dou moromou thiawssa khawma khawssa Ba le 26 inchallah
@yallakesse5354
@yallakesse5354 5 жыл бұрын
Lou takh Modou lo AK sadio manè Eupeu khaliss si sportif Sénégalais yi geunn si modeste
@talibebunjeng9470
@talibebunjeng9470 5 жыл бұрын
diaya bou Serigne Babacar s'y Wakho Deug modou Lo eupoul BG2 xaliss
@ASTOU143
@ASTOU143 5 жыл бұрын
Mo eup xalisssss
@ablayenittoudeugu1012
@ablayenittoudeugu1012 5 жыл бұрын
diaya bou Serigne Babacar s'y sportif sénégalais nga wakh d saway Bayil doul équipe national gneupe nio eup xalis MODOU Lo basket bi gneweugoul
@malickndiaye3711
@malickndiaye3711 5 жыл бұрын
Heuheuheu
@layekharagne2224
@layekharagne2224 5 жыл бұрын
Talibe Bun Jeng modou moune na doundal keur bg2 guey wakh fi la khar yi diar
@papinhoba9556
@papinhoba9556 5 жыл бұрын
Yalla nala diam sonal the King🙏🏻❤️
@medounekasse9837
@medounekasse9837 5 жыл бұрын
Bilahi dama contane si commentaires yi dama beugue modou lo ndam rék champion💪💪
@bambaniang1271
@bambaniang1271 5 жыл бұрын
Man Xaragne loutakh ma beug ko depuis Italie 🇮🇹
@modoumboup1562
@modoumboup1562 5 жыл бұрын
Billahi doma raw depuis Italie 🇮🇹
@bambaniang1271
@bambaniang1271 5 жыл бұрын
@@modoumboup1562 bay liguay wakh fan si Italie
@modoumboup1562
@modoumboup1562 5 жыл бұрын
@@bambaniang1271 Ravenna tu?
@bambaniang1271
@bambaniang1271 5 жыл бұрын
@@modoumboup1562 Torino
@modoumboup1562
@modoumboup1562 5 жыл бұрын
@@bambaniang1271 ok kon bakh na amna gayi nèk fofou sakh 31 bi magui won fofou
@asssow180
@asssow180 5 жыл бұрын
Roi d arène bayoum mbeur le lutteur du peuple kouy mbeur si senegal yaye bayam le 👑👑👑👑😎kholal forme bi chaque jour muscle you saignant✌🏾
@tvlambkhaleyi6693
@tvlambkhaleyi6693 5 жыл бұрын
Mais yow kouy sa mbeur
@bubacarrdarboe6712
@bubacarrdarboe6712 5 жыл бұрын
Pape Mbow question bou am soloh
@asssow180
@asssow180 5 жыл бұрын
Pape Mbow lolu d’où question
@diopcheikh8936
@diopcheikh8936 5 жыл бұрын
Sénégal yepou Nenan balla dakh bere si arenbi
@assanendiaye5640
@assanendiaye5640 5 жыл бұрын
Diop Cheikh yow ya wax wayé senegal yeup waxouniou
@omarsamb3878
@omarsamb3878 4 жыл бұрын
Mane môme je suis fan's Balla Gaye2 Mes Modou Lo c'est un champion Worna Serigne Touba Vamos Mbeur ndam rek inshallAh
@moussaba638
@moussaba638 5 жыл бұрын
Kou xlo beusal jaime
@papegueye5874
@papegueye5874 5 жыл бұрын
Machallah mbuer yalla NASA diamou bari ❤
@fadelbulo7921
@fadelbulo7921 5 жыл бұрын
The king xaragne lo jomm ja beuri dh barki iow mal khiyam 👌👌👌☝☝☝
@saerdiene2380
@saerdiene2380 5 жыл бұрын
machalla amal diame waye
@cheikhndiaye7971
@cheikhndiaye7971 5 жыл бұрын
Machalla Yalna ca diam Yague Vive le Meilleur l'Homme du tt le tamps ☄
@papemormboup5028
@papemormboup5028 5 жыл бұрын
M
@khadimgueye4313
@khadimgueye4313 5 жыл бұрын
Cheikh Ndiaye .
@hamidoujallow6797
@hamidoujallow6797 5 жыл бұрын
Modou star parcelles kharangne lô💪😄
@modoudemba4719
@modoudemba4719 5 жыл бұрын
Aller bonne change mon lutteur prèfèrèe yalna diam mou yague amine
@DSMKTAKEOFF
@DSMKTAKEOFF 5 жыл бұрын
Modou lo xaragne lo👑👑👑
@ahmaddiaw6615
@ahmaddiaw6615 5 жыл бұрын
Sama champion bii diam sii yow Nèkhna faral dimanche 💪💪💪
@toubadieng8547
@toubadieng8547 5 жыл бұрын
Modou lo rek 🇸🇳🙏💪🤴👑
@abouball4060
@abouball4060 5 жыл бұрын
Meilleur luttteur de sa generation le seul et unique modou kharagne lo
@papedjibybasall8514
@papedjibybasall8514 5 жыл бұрын
Mancha Allah champi yalna yonn bii gueuneu lére in cha Allah...
@nesta132
@nesta132 5 жыл бұрын
C'est bien d'innover, on vous félicite mais pensez à changer les questions depuis 10 ans on entend les mêmes choses ! Bon courage.
@souleymanediouf1385
@souleymanediouf1385 5 жыл бұрын
Un vrai champion modou lo djame rek ngaye ame inchala
@jallowsellou5234
@jallowsellou5234 5 жыл бұрын
We love you so much modou lo you are the king modou lo May God bless you!!!! ❤️❤️❤️
@sarrabdou3040
@sarrabdou3040 5 жыл бұрын
Le rock des parcelles u10 +roi dès arènes
@albouraq24
@albouraq24 5 жыл бұрын
Kou beug 2stv rek mayma j'aime
@sidydiop1523
@sidydiop1523 5 жыл бұрын
Modou lo yalna ko yalla may ndam
@adjikharagnegaye
@adjikharagnegaye 5 жыл бұрын
Le meilleur bantamba de l'année Merci kharagne
@miketyson1077
@miketyson1077 5 жыл бұрын
Modou lô😂😂 boromme khamga khamga khamga 😂😂😂😂😂boromme bahhla nakk 🤗😊😍
@momodiop7781
@momodiop7781 5 жыл бұрын
tel fils tel pere ou tel pere tel fils? . bantmba 4 ever Modou Mbaye diadieuf
@ousseynoudieng2184
@ousseynoudieng2184 5 жыл бұрын
Sama champion laye don modou diam si yaw rék di la nianal taw fékh ak tayssir si Barké yontés bie je te Souhaite le meilleur 💪💪👈
@soumayalo8201
@soumayalo8201 5 жыл бұрын
Sama dom bay bii maako bougaaa 🤩❤ si kaw si kanam XLO
@sophiasow5470
@sophiasow5470 5 жыл бұрын
Ayyyy modou lo amal diam rek yalla Lafal leu thiate bu bakh machaallah mala beugue
@coumbissdiabong1286
@coumbissdiabong1286 4 жыл бұрын
Qui te là en mai 2020
@FallDamel7484
@FallDamel7484 5 жыл бұрын
Machallha le Roi👑👑sa wakh rafétna trop Nala yalla takhawou si Barcke Naby ba lo yotou am si Ndam Modou Lô tamou djikla 👑👑
@mbayeteranga3989
@mbayeteranga3989 5 жыл бұрын
Yama bayi si lambou dé kharagne 💖💕🙏
@mboupada7856
@mboupada7856 5 жыл бұрын
Thiey sama wadji yalna sa diam yague si barké serigne babacar sy ylla defal la ndam sisa combat prochain amine touff touffff
@rokhayadieng4942
@rokhayadieng4942 5 жыл бұрын
Bilahi mala beugu Lo Ndam Siré si kaw si kanam diam si yaw. Sounou roi👑👑👑❤❤🥰
@ibralemeringue3258
@ibralemeringue3258 5 жыл бұрын
Modou lo reik neikha faral dimanche, Ama dingua daadj li mbourou di dadj si four.
@boubakarsidikiwague9903
@boubakarsidikiwague9903 5 жыл бұрын
Wawe li mom daffa lerr
@soumayalo8201
@soumayalo8201 5 жыл бұрын
Boul dalal sama xel bi way tiitnaa d 😥
@ibralemeringue3258
@ibralemeringue3258 5 жыл бұрын
@@soumayalo8201 boul tiite dara damakay doumeu daane inchallah
@bambapartout7827
@bambapartout7827 5 жыл бұрын
Wei inchallah
@ibralemeringue3258
@ibralemeringue3258 5 жыл бұрын
@I'm about Africa rêve bien c est permis
@mmendiaye9212
@mmendiaye9212 5 жыл бұрын
Thiey modou mbay soumala kholé dé foi bécay lay guiss ndéssane machalla
@famathiam2575
@famathiam2575 5 жыл бұрын
Modou yalla nalla yalla defal diam te lafal la thiat
@khaliloulah3703
@khaliloulah3703 5 жыл бұрын
Xaragne Lo le messi de l'arène diam si yaw ak ay ndam you bari bari
@moussaba5415
@moussaba5415 5 жыл бұрын
KhAliLoUlAh ama balde alissone becker de l’arène 😂😂
@khaliloulah3703
@khaliloulah3703 5 жыл бұрын
Alissone dou dieul ballon d'Or dh
@moussaba5415
@moussaba5415 5 жыл бұрын
KhAliLoUlAh mais day éliminé dhé 😂😂 Foumou fékk méssi defaral co
@ndiagadiagne9217
@ndiagadiagne9217 5 жыл бұрын
@@moussaba5415 wayè messi trokhal nako dh
@moussaba5415
@moussaba5415 5 жыл бұрын
ndiaga diagne 😂😂wayé cou mouddié dioyy
@thiebabambistengom5483
@thiebabambistengom5483 5 жыл бұрын
Nice champion nékha faral dimanche 👑 kharagne lô
@masseyesamb2429
@masseyesamb2429 5 жыл бұрын
Ki lanou wakh Modou Lo ❤️❤️❤️❤️👌👌😘
@zakariadeune2296
@zakariadeune2296 5 жыл бұрын
Khalifa général koullou mbeur diamono dij lolou la yalla déf xlo 💪💪💪
@assydiagne3594
@assydiagne3594 5 жыл бұрын
Man mom vraiment j vois que modou a chaque fois gnou dek ko micro rek comminucation bou extraordinaire li day wané proffesionnalism si limou nek yay bayou mbeur yi si lep dangalen dépassé sur ts les plans
@mamadoudiop2953
@mamadoudiop2953 5 жыл бұрын
Ya meune doul
The Best Band 😅 #toshleh #viralshort
00:11
Toshleh
Рет қаралды 22 МЛН
BANTAMBA CHEZ EUMEU SÉNE DU 28 JANVIER 2020 AVEC MODOU MBAYE
1:46:44
BANTAMBA DU 31 MARS 2020 AVEC MODOU MBAYE
1:07:36
2stvsenegal
Рет қаралды 118 М.
Li sokhna kiné djili wakh si cheikh ibra
3:29
Dangalma médias production
Рет қаралды 3,1 М.
🛑OEIL DU TIGRE AVEC BECAYE MBAYE INVITE MODOU LO | JUIN 2023
1:38:09
QUARTIER GENERAL du 24 MAI 2019 - Invité : Serigne Gana Mésséré - PARTIE 2
2:51:53
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 4,2 МЛН
BANTAMBA  SPÉCIAL MODOU LO DU 27 JUIN 2017
57:49
2stvsenegal
Рет қаралды 95 М.
REPLAY - JONGANTE - Spécial BALLA GAYE 2 - Pr : Lamine Samba - 19 Juillet 2020
2:03:14
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 78 М.