SITEU EXPLIQUE TACTIQUEMENT LE COMBAT «Modou Lo dafa tek piège bo xamni… »

  Рет қаралды 13,017

Bantamba TV

Bantamba TV

Күн бұрын

Пікірлер: 60
@elhadjisambe3549
@elhadjisambe3549 10 сағат бұрын
Machallah siteu ❤li nga wah thi jeunesse bi amna solo
@AbdouazizDieye-w2b
@AbdouazizDieye-w2b 5 сағат бұрын
Wakh rek wakh rek wakh rek 🤦🏾‍♂️🤦🏾‍♂️🤦🏾‍♂️🤦🏾‍♂️🤦🏾‍♂️🤦🏾‍♂️
@malalbadieldia1750
@malalbadieldia1750 2 сағат бұрын
Siteu wahna lou am solo si jeunesses bi❤
@Mbagnick-h8y
@Mbagnick-h8y 58 минут бұрын
Bravo Siteu niongui sa guinaw notre roi des arenes ❤
@mustaphacham3500
@mustaphacham3500 4 минут бұрын
We love you siteu ❤❤
@assleye8654
@assleye8654 5 сағат бұрын
Merci ❤
@NiangMor-m1m
@NiangMor-m1m 5 сағат бұрын
Il faut dire la verite becay
@MouhamedCissé-j9d
@MouhamedCissé-j9d Сағат бұрын
Malgré tout c'est un homme social. Il parle pour la jeunesse banlieusard. Lolou mom amna solo. Mais nak Balla Gaye molo meune 😂.
@AbdouAziz-ri8td
@AbdouAziz-ri8td 10 сағат бұрын
Siteu et un Comédien Combat Royal Guey Daw il Fo lui dire la vérité Mo Guene politique bi Siteu et un Comédien
@AbdouCisse-xs5mc
@AbdouCisse-xs5mc Сағат бұрын
Lac 3 dafa Bari wakh 😂😂
@ibrahimasarr4563
@ibrahimasarr4563 3 сағат бұрын
Siteu c un bon J viens d l connaître mais il est conscient des enjeux du moments
@cheikhnaniang8521
@cheikhnaniang8521 6 сағат бұрын
Ki vrai doff la rek
@MAMADOUSARR-zx9vd
@MAMADOUSARR-zx9vd 8 сағат бұрын
Gni sekk siteu yepp ay nafekk guen
@AbdouAziz-ri8td
@AbdouAziz-ri8td 10 сағат бұрын
Becaye et Modou Mbaye Il Fo dire la vérité a Siteu Dafa Daw C Un Comédien Modou lo a attaquer et gagner Point Siteu Comédien la
@ouzdaking382
@ouzdaking382 14 минут бұрын
Siteu nouveau roi des arènes 🎉
@Treeboox
@Treeboox Сағат бұрын
Walah siteuh diaroul 5 millions , ki di daw , je suis MDR
@senegalrek2579
@senegalrek2579 2 сағат бұрын
Boy wakh ngay noyi mom moy boy fen ngay noyi siteu rewna 😮
@cheikhnaniang8521
@cheikhnaniang8521 6 сағат бұрын
Modou mbaye kou dokhane ndm la
@MAMADOUSARR-zx9vd
@MAMADOUSARR-zx9vd 8 сағат бұрын
Roi des wakh😂😂😂
@Amadoundiaye-m3d
@Amadoundiaye-m3d 9 сағат бұрын
Siteu rewmi da am yone boule niou sonal fi niepp am problème mais état nékoufi pour di libéré niepp siteu bayil état
@khadijaboye2619
@khadijaboye2619 10 сағат бұрын
Siteu dafa nekh 😂😂😂
@AbdouAziz-ri8td
@AbdouAziz-ri8td 10 сағат бұрын
Becaye Modou Mbaye il Fo dire la vérité a Siteu Dafa Daw Thiak Thiak le Modou a attaquer et gagner Point Siteu et un Comédien
@aichasecka-8974
@aichasecka-8974 9 сағат бұрын
Gni douniouko wakh deugue ay nafek laniou kou beuguoul koula méré do wakh deugue
@laminembaye6744
@laminembaye6744 8 сағат бұрын
Yaw doul
@cheikhnaniang8521
@cheikhnaniang8521 6 сағат бұрын
Beckay dh mo gueneu meun feen si aduna ndakh nafekheu
@maoudediao653
@maoudediao653 4 сағат бұрын
Siteu bayil sa doule yi
@AbdouAziz-ri8td
@AbdouAziz-ri8td 2 сағат бұрын
@laminembaye6744 Yow Nafekh ga Siteu Dafa Daw Thiak Thiak le Combat Royal On attaque pour gagner Point Bayil Yamba Bi Il Fo dire la vérité Siteu Dafa Daw Modou a attaquer et gagner Point Va Pisser et Dormir
@NiangMor-m1m
@NiangMor-m1m 5 сағат бұрын
Siteu devient un bolt
@franceamericanbullydogfami7992
@franceamericanbullydogfami7992 10 сағат бұрын
Ana birame yassine
@youssoumbengue7698
@youssoumbengue7698 8 сағат бұрын
Esk nekoul seu negou paris
@mansourdiop7037
@mansourdiop7037 9 сағат бұрын
Koula khamoul rek molay wakh yène yi mais diamouss est fiere de toi
@manoumbaye6277
@manoumbaye6277 4 сағат бұрын
Babacar faut gérer tes émotions way bissou lamb ji khaw nga syncope, finalement gneupa xam fi nga faroon dou sa thieur 😂😂
@khadimseye1716
@khadimseye1716 8 сағат бұрын
Manam siteu dall lamb dako nara sètan ni mouy weur di wakh rk ta doufi déff dara wakh lèn ki deug modou mbaye mom kén khamoul nitou lanla khalatoul wakh deug siteu
@madimadi3208
@madimadi3208 43 минут бұрын
Doul way yaw 🤬🤬🤬🤬
@malickdiouf659
@malickdiouf659 2 сағат бұрын
Waw yeen lan ngeen bëggee bëre ñett yi rekk la songee defance dellu ginnaaw jéll ak njaax.
@papamoussagueye1415
@papamoussagueye1415 8 сағат бұрын
Siteu oei vrai mbam nga tapeite nga daw combat bi yeup nieuw di reuy gate yeine gnici plateau bi dangeineko wara wax deugu . Mais lingay wax si jeunes yi nice neu
@abasall711
@abasall711 39 минут бұрын
Diadieuf diambar
@ahmadoudiagnegueye9918
@ahmadoudiagnegueye9918 9 сағат бұрын
Bravo siteu vrai diambar ❤❤❤
@IbrahimaNdong-h4g
@IbrahimaNdong-h4g 3 сағат бұрын
Mai diouma thi face a face bi passé boy dagua réw amo yarre
@afro3827
@afro3827 10 сағат бұрын
Balama beuga dé rek siteu né boy yi man lagni deg lou 😂😂😂
@ousseynoutoure518
@ousseynoutoure518 10 сағат бұрын
Mais degla
@mansourdiop7037
@mansourdiop7037 9 сағат бұрын
Lol mo am
@mansorseck6059
@mansorseck6059 4 сағат бұрын
Siteu ❤
@KossoGadiaga-vw3wc
@KossoGadiaga-vw3wc 5 сағат бұрын
Siteu kasse siteu kasse ❤❤❤❤
@quetespirituelle6647
@quetespirituelle6647 9 сағат бұрын
SITA DANGA DAW COMBAT BI YEUP TÉ YAW YA SOKHLAWOON COURONNE BI. DAFA MELNI DANGA RAGALOON PARCE QUE KÉROK NEENGA MODOU KOUKO MEUSSEU SOONG DAAN NAALA NI BOYE NIANG AK AMA. KONE SITA NANGUL NI DANGA DAW MO GEUN DI MOTALIKO LAMIGNE.
@MAMADOUSARR-zx9vd
@MAMADOUSARR-zx9vd 8 сағат бұрын
Billahi gnom becaye et consor\ - sen l-igueye dou lou bakh
@AliounebadaraGassama-or4op
@AliounebadaraGassama-or4op 6 сағат бұрын
Siteu yaw dangua wara nopi thiak thiak ngua amo lo wakh
@assanesavane7760
@assanesavane7760 5 сағат бұрын
Tay la doga geumnii modou lo nieup ladone beureii
@abasall711
@abasall711 37 минут бұрын
Luler ngawax mais ku yalla faral mogueune foufff ku niép contre
@AliounebadaraGassama-or4op
@AliounebadaraGassama-or4op 6 сағат бұрын
Yaw déh war naniou l'a yar dou yay wakh état loumouy dèf
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 3 сағат бұрын
Siteu doul nopil
@MAMADOUSARR-zx9vd
@MAMADOUSARR-zx9vd 8 сағат бұрын
Diamaguen ay bandi gnofa oopp
@abdoucoly8278
@abdoucoly8278 2 сағат бұрын
Sa data Yaw yaw déle wakh lou amme
@Amadoundiaye-m3d
@Amadoundiaye-m3d 9 сағат бұрын
Bécaye meune gua khejeup bécaye yaw fo mouna guisé kouniou ramasse rek mou diare fa neck bandi
@ModouMbay-f4g
@ModouMbay-f4g 9 сағат бұрын
Siteu mo lein meun molein geun molein geuneu mous molein geuneu beug leipou Lou bah ki d'où beur waliou la
@khabousiteu2408
@khabousiteu2408 Сағат бұрын
Kouné siteu danoul modou lo dangay doul
@khadimseye1716
@khadimseye1716 8 сағат бұрын
Manam siteu dall lamb dako nara sètan ni mouy weur di wakh rk ta doufi déff dara wakh lèn ki deug modou mbaye mom kén khamoul nitou lanla khalatoul wakh deug siteu
@moussandiaye3564
@moussandiaye3564 2 сағат бұрын
Lolou Moy deugue Mane diamaguene la deukk mais Linga wakh Moy deugue
SITEU OFFENSE BALLA GAYE 2 «simba bou Maguette leu dou 100f… »
17:46
Правильный подход к детям
00:18
Beatrise
Рет қаралды 9 МЛН
Pape mbaye Tacle Sévèrement Sathies Da niak Fayda Siteu Limou def dafa Niaw Dou Yonne  nakh dafa….!
25:30
Fadam2 expert de la lutte sénégalaise
Рет қаралды 3,2 М.
Wally B. Seck - DEBRIEF avec Pape Cheikh Diallo & Abba No Stress
50:58
Wally Seck Officiel
Рет қаралды 89 М.
Правильный подход к детям
00:18
Beatrise
Рет қаралды 9 МЛН