CNG il parrait que danio changer règlement yi TEs arbitre bi Daffa sifflet man magui si ardo bi tok teih bi liss tegué tank si sakou yi la arbitre bi di sifflet xeyna da yeih par rapport ak coup ✊ bi Bo xolè bi liss di tiaxabal ossi
@madembasy16697 ай бұрын
@@bartosivan2286ioe la kane😂
@NianeMouha-p9l7 ай бұрын
Sa campagne bi dou dialll guissnala feppp😂😂😂😂
@saerhihiodf1107 ай бұрын
Door kagn la nekeu action 😅 demal lathie way règlement bi mo geun balanga dioum 😅
@mosi3017 ай бұрын
Ay pathè taye khou houwalahou ngua dieul mancha allah mane yao rek laye top
@taphasamb68367 ай бұрын
Eumeu diokhale Pathé Tmax bi😂😂😂😂
@cheikhfall47297 ай бұрын
Pikine Moy Sénégal 💚❤️
@MbayeFaye-ev9rd7 ай бұрын
FÉLICITATIONS LISS NDIAGO KASSÉ REK ❤❤❤❤❤❤❤
@khazalytraore7 ай бұрын
bonne communication pathe merci
@papezulefaye72637 ай бұрын
Barke khoulhou allahou 😂😂non pathé balde yangui yakh sama adouna wayy😅😅😅pourtant deug la wakh
@hametdicko80837 ай бұрын
Meilleur interview pathé
@mamadoudiop5727 ай бұрын
Merci beaucoup Pathe
@PapeamadouDieng-f7n7 ай бұрын
eumeu sama champion by diokhal pathé baldé taxi by nak contane si yaw champion
@degrk56227 ай бұрын
😂🤣🤣😆 Pathé dafmay guagn bilàhi c'est le phénomène koi
@babadia52897 ай бұрын
Boudé daniigN taak BiiNe-BiiNe goudii gnou wahkoo. Non Pathé bénéN level leu koi 😂😂😂
@AmetKah-t7b7 ай бұрын
Pathé alouna dhh😂😂moyy lolou 😂
@2Ibbomessi7 ай бұрын
Billahi wallahi pathe balde deugg la ❤❤❤❤❤❤❤❤😢😢😢
@MamdiaraNdong7 ай бұрын
Eumeu sou dieundeule Pathé tee maxx def Lou bakh wa pikine contane
@PapaMane-s3e7 ай бұрын
liss ndiago daka dane ❤❤❤❤
@ThiernoNdiaye-dv3tw7 ай бұрын
Pathé diapelé lénn boubakh Balla gaye 2 sokhela nako bou bakh té bouléne si khol loulénn nékh ak loulénn nakhari
@Cisse-zv7mm7 ай бұрын
Mom esqeue diapona si ama contre modlo
@papeousmanethiam46217 ай бұрын
😅😅😅barki yalla pathe dinama ray
@PapeamadouDieng-f7n7 ай бұрын
félicitations pokola 🦁🦁💪🏻💪🏻
@ousmanecamara53217 ай бұрын
Pathé deug😂😂😂
@BeugEuThierno-qn2xp7 ай бұрын
Watt bou bess 😂😂😂 barki oulhou walahou 7:59
@MamdiaraNdong7 ай бұрын
No Pathé Dinama reey nena sou awenssou Luis niowee mou sothio awanssebi
Jules dafa doundou lamb Pathé supporté en plus tonton comme mane limou wakh la guem
@abouly06097 ай бұрын
Jules makk la dfay rafètal rk
@cheikhfall47297 ай бұрын
Pokola dafa Daan ki bilahi
@Mackenzi-z4f7 ай бұрын
Vérité absolue,l'arbitre a fait une erreur car Pokala a gagné
@AlassaaneSow-sk7rx7 ай бұрын
Pathe ke fou iow depuis tivaoune peulh
@dieynababijouly40647 ай бұрын
Barki khoulouwalahou 😂😂😂😂
@taphasamb68367 ай бұрын
Lolou rekk moma rayy😂😂😂😂😂
@MPSodan7 ай бұрын
Neekal makk waay tonton, si fans yi la book mais daaal nekal mag😊
@MamdiaraNdong7 ай бұрын
Mai pathe yow laye topou sama waye nga mai beug n'a kham l'an motakh sooy wakh do toudou bathie seras lan mooy sa problem ak bathie seras
@CheikhSarr-ck3or7 ай бұрын
Lou lérrr nga wakh bilayy
@cheikhdiakhate7167 ай бұрын
Pathé wakhna deug
@Domou__rewmi.7 ай бұрын
Eumeu diokh ko routiers waye ndakh tmax amoul bruit teh pathé bruit la beugue 😂😂
@gueyelabsolu58897 ай бұрын
Combat yii yeupou actions yii thiirr La commencé Dièxé Thibity 🧏Tayson Yekiny premier fois by Lac Roz Amanèx Amaa Balde Modou Lo siteu zarko Balla Gay 2 Bombardier passé osy pareil Lolou Motax Bombardier Dougeul recour CNG VALIDÉ victoire BI 🧏C Pasq Action bou commencé thibirr bounè Dièxè thibity chute leu✍️Naa féxeu baxoull voilà
@moussaseck9677 ай бұрын
Baol TV khana pathé Moko môme wala Malick Ndiaye 37 fou chaque jour pathé balde vremen baol TV dou dara li am bou boye niang wakhe degue leu koi
@MamadoudoumatarNiang7 ай бұрын
Nice neu mai bii liss leu dee dou meusseu yombou
@toutimane-53047 ай бұрын
Eumeu séné gris bordeaux rék si guinaw sagou yi la wone wa diamaguene danio beurii wakh lamp dji diekhna bou yague
@tafsirsegagassama91827 ай бұрын
Ségou eumeu sene yi 😂😂😂
@IbouNdiaye-tj7wr7 ай бұрын
Pathé wallahi fitt cassé la
@lassanatalla7677 ай бұрын
Ki di tapett yaw khamé wo kou beuri wakh ak kou am fitt
@mamadoufall91857 ай бұрын
Fitt là meuss am
@Omarsane74917 ай бұрын
Franc vs eumeu sene
@ThiernoNdiaye-dv3tw7 ай бұрын
Wakeur falay ak wakeur Doublées supportere ama yi ak sa thies ak balla ligouy beug moy toujours guénn di nékk gnoulénn di guiss entraînement guénn di ande fépp
@ibrahimaseye72677 ай бұрын
Gueum lene Yalla Wa Keur double less nagn andak Wa Guédiawaye
@fatoucha5547 ай бұрын
Gnognou khana Guediawaye amoule aye mbeur yi gnou meuna adale
@Domou_Deukk_Bi7 ай бұрын
@@fatoucha554yaw démal raxass ndap
@Domou_Deukk_Bi7 ай бұрын
@@ibrahimaseye7267yéne sokhor molén diap mais famille falay ak famille double less meunolén lén takalé
@pronosticfootsenegal11127 ай бұрын
LOLOU DAY RAY LAMB LI SPORT LEU REK
@MamdiaraNdong7 ай бұрын
Beug n'a kham sa digent ak bathie seras ndakh yeneu ngisseuk diam mbala gissenani ken doussi toudou moromam
@ahmadsamb48907 ай бұрын
21 mn da touti si interview ak pathé way ah
@fallouthiam68307 ай бұрын
Tay dé wakh nga wakhi nite
@Methmethavelly7 ай бұрын
Sawaye moguini kharitou paté Balde
@gorguidieng77967 ай бұрын
Pathé vs tapha trabaja journée balla tapha bi
@MamdiaraNdong7 ай бұрын
Pokola champion la mooy souniou bathie seras ndakh Fitou domou ginaw raille la yorre dontee luiss ndiago leup la si bathie seras ndakh Laurent ndiago mai pokola kasse
@Mbaye._pro7 ай бұрын
Pokola seul
@Massenembaye2357 ай бұрын
Pathé doundeul baye fall gua
@bassiroudiop90557 ай бұрын
Ay lagne bàaaa😂😂😂😂
@damefall32597 ай бұрын
Pokola mom danako mom bou yague
@deugmoyndieukmoymoudie82797 ай бұрын
Souko danone lamb dji diékh arbitre yi nékalouniou fi kène mé deug bi lanioufi nékal kou amoul loula geuneul rék manké lène respect
@MamdiaraNdong7 ай бұрын
Pokola dafa beug wa ginaw raille motakh wa ginaw raille sop KO
@MODOUFALL-vb4ed7 ай бұрын
Vrement qui weroul quio na dem fadiou djii
@MarAssanemouride7 ай бұрын
Tyson guinguineo😂😂
@LamaneDieng-t9l7 ай бұрын
Liss ndiago kassé 😂😂😂😂
@diawnakhe57577 ай бұрын
Pathie yallna godo fan
@MamadouCisse-bw2uo7 ай бұрын
Naar ak peulh😂
@elmoussafall38877 ай бұрын
Bilay sama harite bi boul dawal Tmax bi diayko 😂😂
@papedieng99217 ай бұрын
Espessou pa kay non paté amoul 🤣🤣🤣
@MamecheikhWillane-q9c7 ай бұрын
Ki weroll liss mô ame ndame😂😂😂
@Aaron-i5f7 ай бұрын
Ya meuneu doul
@SsaliouNdiaye-n3u7 ай бұрын
Louler nga wakh bilae
@Bamba1980Touba-cu1om7 ай бұрын
Menou eakh daga wara mopi
@ibrahimaseye72677 ай бұрын
Yaw tamit meuno bind😂😂
@mehmetfall82497 ай бұрын
😂😂😂@@ibrahimaseye7267
@SerignefallouNdiaye-wx6fg7 ай бұрын
Thieuye Pathé 😂
@ibrasarr94297 ай бұрын
Pathé baldé vsDjily mbaye
@Enfant_béni_77 ай бұрын
PATHÉ BALDÉ BAYILEEN DIKO DIOKH MICRO 🎤 KI MOUNOUL WAX TÉ XAMOUL NOUMOUY WAXÉ DAY MANQUÉ RESPECT AY NIIT TÉ MAKK BOU RÉW LA BILAHI KI WÉROUL MÉDECIN DAKO WARA SUIVRE SINON SI DOFF LAY MOUDIÉ BAXNA RÈK 😢😮
@Wolof_Kasse7 ай бұрын
Yaw ya weer. Yaw ya weer. Doof ga.
@deugmoyndieukmoymoudie82797 ай бұрын
Sou combat bi takhawaté Liss lék ko dé 😢yène diaroulène sakh beurél ndakh ay bandit nguéne magoum dieum bou tolouni di proné la violence