Merci à tou.te.s pour vos voeux ** Écoute ici bfan.link/yay-titulaire-bi mon nouveau single : YAY TITULAIRE BI, disponible sur toutes les plateformes musicales et réseaux sociaux. Streame & crée des vidéos pour soutenir tes artistes **
@SadioDiallo-j4h3 күн бұрын
Sx la h
@SoukeyThiam-k3z8 күн бұрын
Takkk 💍leuh demb tëral leuh demb ❤xeuy guënël leuh son bou xërë😊 yko fi ndieukeu amm dh histoire dina ko bind🎉🎉🎉🎉🎉
@misstchiptchip29632 күн бұрын
Le mec est vraiment amoureux c'est ça le truc..un homme ne sait pas faire semblant quand on t'aime tu sais quand c'est pas le cas aussi tu le sais.. donc accepter lene rek.. beaucoup de bonheur à vous❤
@crispyqueen73239 күн бұрын
Bass fehel ba nangua teiyei xalé bi té topoto ko. Adouna yeup ngi sothiou di xarr défaite Fatou si seyy bi fehel ba boulen mayy lolou. Nekal niit tei matt xalé bi Kilifa. Djapalei ko boubakh mongui dogua dougou ci seyy nga nek bayam nek maggam.
@vitefcuisine44589 күн бұрын
Message sage , merci
@diattadieynaba91049 күн бұрын
Billahie ndeysane ❤❤❤
@veroniquenatack73929 күн бұрын
*Srtt ça 🥰❤️*
@ndeyakarisma34459 күн бұрын
Wallahi waxgua lep
@Khadimamadou8 күн бұрын
Noble message bouniou appliquer ça marchera très bien entre eux 💢💢💢💢💢💢💢💢💢💢💢💢
@sball14629 күн бұрын
J’avais dit que Bass aime vraiment fatou il a fait pour elle ce qu’il n’as jamais fait pour personne
@hawabolly35147 күн бұрын
Je sourire bêtement tellement que je suis contente pour elle ❤❤❤❤
@mamydioum6608 күн бұрын
Bizarrement couple bi dafma nék trop yana sey bi barkel yalla bolen guiss lolen ragal❤❤❤❤❤❤
@elysee_daleba9 күн бұрын
Dieu bénisse et protège toute personne lisant ce commentaire maintenant. Je vous souhaite tout ce qu'il y a de mieux dans cette vie ❤️.
@kheucha24688 күн бұрын
Kawkaw bi takk nagnko 🤗 gnoune wa touba amnagn ndam 🎉❤
@FloraJoob7 күн бұрын
Gnoune kawkaw yi bèguei nagn leu waay ❤😂
@toubifa72898 күн бұрын
Bass goor nga té dofo guiss nga djiguen bou bakh xalé bou ndaw bou am éducation de base diang alhourane tok si podiou ndeyam❤tak ngako mou Nar la seuyeul lou nekh sa xel dafay dal dakh fatou dou weuyou dou bandit bo touké bayi ko sa keur bo gnewaté fek ko figako tégone machala. Diapalé ko bou bakh yalla nassen seuy bi barké 🙏inchala on vous verrez très loin sen succès guen yokou❤ tu as la plus belle femme du monde zéro kilomètre
@khadygueye65608 күн бұрын
Ohhhhhh❤❤❤❤🎉🎉 mâcha alhamdoulila Amiine waay
@kebemarieme60497 күн бұрын
Yaa bakh way 🥰
@NdeyendackFall267 күн бұрын
Merci chérie❤❤❤
@binetadiouf3103 күн бұрын
❤❤ machalla bien dit
@coumbacoulibaly42269 күн бұрын
Bass boul niou rouse lo guir yalla teyeul niou Fatou ❤❤
@bintourabycamara53639 күн бұрын
Fowé magn Nandité yi takk kaw kaw bi 😢❤sey bou barkel inshalah 🙏🫶
@Infoslivetv9 күн бұрын
C’est quoi ce commentaire débile ? Yaw ya guen kaw kaw yi ? Dom ram
@DiamondQueen-hg3jm9 күн бұрын
@@Infoslivetves ce que dou yaw y’a comprendroul fimouy wakhé?
@fatoudiankha60669 күн бұрын
@@DiamondQueen-hg3jmbayi ko khamoul di wax
@fatoudiankha60669 күн бұрын
Deugu rk ga wax
@NdiayeAwa-nv6hm8 күн бұрын
Wawa👋👋👋👋
@diakhatebousso9549 күн бұрын
YOW REK LAGNI TOP ❤️❤️❤️❤️ kou daccord jaimal 😂😂😂😂
@AwaBadji-b5y9 күн бұрын
Moi
@MamFatou9 күн бұрын
Halel bu touch holi bass❤
@abdousarr96949 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@karencelestinamfoulamatoka79569 күн бұрын
Elle a dit oui officiellement Madame Diagne 😂 c'est tout ce que je comprends heureux menage 🎉❤ 🔥
@CorFall5 күн бұрын
Ayy way😂😂😂
@mouskydieme3906 күн бұрын
Thioum Fatou seule ma belle 😍 Sw hrse a jamais ❤❤❤❤
@mypbarro54168 күн бұрын
Lou nakhari wone Fatou demb...tay effacer nga lepp! Yala nalenn Ya'Allah AZAWADJAL samm té mousseul lenn ci noone ba nopi soutoural len❤❤❤
@HassaDiallo-e4y9 күн бұрын
Franchement Wakh bi mo beurri rék mais Bass dafa nobb Fatou bolen suivrez mariage bi ci ngay comprendre il est trop content 😢
@NdeyesoukéyeMbaye-r3k9 күн бұрын
loiwz ❤❤❤❤❤❤
@fatoudiankha60669 күн бұрын
Bilae nak lolou la guiss yalla nako yalla defal diam rk
@fatoudiagne24269 күн бұрын
J'ai fait le même constat nanou lénn nianal rk moguenn critiques yi amoul bénn sens
@BoussoSene-nk3tv8 күн бұрын
Bilahi c la vérité ❤yalna yallah samm lène rek inchallah tekk lène loxo 🎉❤
@maimounadiaite80608 күн бұрын
Waw waw Ay bgeu téla❤❤
@byka12198 күн бұрын
Teral ko soutoural ko mougneul ko yeureum ko teyel gnoukoy boubakh stp gnougne kaw kaw yi atanougne stresse . Heureux ménage !!!
@LaBarhamienne8 күн бұрын
Seuy bi eup bruit thi début d'annèe 😂 mashallah qu'Allah vous facilite. Sénégal mo nekh kou diouk beug am kadou thu vie diambour mais amoul xalate focus rek lep projet leu.
@MamanDiouf-m2g8 күн бұрын
C bien
@mayachou98059 күн бұрын
Basse niogui hékh si réseau yi ndakh iow fékhel ba bouniou rousslo nak heureux ménage
@Dani-2377 күн бұрын
Que c’est beau l’amour longue vie à votre couple prend bien soin de notre Fatou soyez toujours unis ❤❤❤
@adjabintatall79829 күн бұрын
Fatou Ndiaye merite d’être heureuse mashalla❤ les sénégalais aigris qui s’acharne sur elle allez vous faire foutre. Elle est jeune, elle a porté son choix sur Bass où est le problème ? Fatou seuyeul nga mougn. Au Sénégal y’a piir que Bass niounii paatt di seuy. Yalla nalen yalla saam inshalla🤲🏾😘
@FatouNdiéguéne-c2y9 күн бұрын
Ta tout dis ma cherie
@DabaSamba-s7z8 күн бұрын
Amine ya rabi
@AbyNgom-r6u8 күн бұрын
Amine🙏
@saydaastoubadiane8 күн бұрын
Eh li nexna way Mba nob nagne lène xalé yi ?😍💃 Heureux ménage à vous !!!❤️💍❤️ Yalla na Yalla barkèl li dess 🤲🏾
@MDSamb14037 күн бұрын
Li herei na wayyyy❤️❤️sama xol bi😩❤️❤️❤️
@mumsmbaye48057 күн бұрын
Comme Al Khayri djipe na , que chacun respecte le choix de l’autre, wakh diou niaw dji doyna. Heureux ménage, yalna seuye barké
@NdeyembarkaWade-w7l9 күн бұрын
Wa kouy sindakh man😂😂😂yalna seuy bii barkél❤
@AstouThioune-k7b9 күн бұрын
Adamo moy sindakh man
@Germinal52198 күн бұрын
Ak rox@AstouThioune-k7b
@NdeyembarkaWade-w7l8 күн бұрын
@AstouThioune-k7b 😂😂😂😂😂😂
@lilasm3c2829 күн бұрын
Que Dieu bénisse votre union, gardes bien la princess Fatou pour nous, la Reine des challenges. ❤❤❤
@moniquezadi4309Күн бұрын
Fatou tu es belle talentueuse tu es la meilleure la reine des réseaux sociaux
@Julesakzootv1681k8 күн бұрын
Yalla boulén thiate topou🤲
@DabaSamba-s7z8 күн бұрын
Amine ya rabi
@cheikhabdoumbacke69709 күн бұрын
Félicitations 🎉 Bass et fatou ndiaye yalna yalla barkel sey bi té may léne si njaboot bou barkel si barke s touba 🤲🤲❤️❤️❤️
@DabaSamba-s7z8 күн бұрын
Amine ya rabi
@ndeyeamydiop30937 күн бұрын
2:39 Kaw kaw bi tak nañou ko 🥳🥳💃🏽💃🏽💃🏽💃🏽 partie bii aohhhh neikhna 😂 yalna ya Allah mousseul lein si thiat
@Boj-j1p7 күн бұрын
Hee lii nekhna deh Ma shaa Allah😂. Bcp de bonheur au couple Diagne❤
@djibrilfaye84099 күн бұрын
Dohalal fatou ndiaye halee zéro kilomètre bii yaa bari valeur Bass djoumoul bene yone
@Khadijaad8999 күн бұрын
Wa sindakh man fo feter 😂🎉 ay waye li none yi beuguone amoul yalla na seuy bi barkel les diagne ❤❤❤
@seydou486698 күн бұрын
Beugo diam dh 😂
@Buzzworldtv9 күн бұрын
Houlalah sama khol bi Wawaw li mom meussoul am Sénégal non vraiment bass téyél niou Fatou ndiaye défaite laniouy bagne Yalna seuye bi barkel🎉❤
@DiaphaneMiassa9 күн бұрын
Vive l'amour mes félicitations à vous depuis le Cameroun ❤️❤️❤️❤️🎉
@AmyBass-cg4hg9 күн бұрын
MachaAllah ❤️ ❤️ ❤️ yalna yalla barkèl seybi Mrs Diagne amine ya Rabby 🤲 🙏 ❤️ 🥰 🌹
@AntaDiaw-q9t3 күн бұрын
Heureux ménage madame Diagne ❤❤🎉
@awagueye23849 күн бұрын
Ma Shaa Allah yallah na yallah barkel seuy biii
@NiangMbeyeu8 күн бұрын
Ani teams Fatou Ndiaye yi li nekhna dei ❤❤❤
@rokaya-yayou-amiina1509 күн бұрын
Fekhel ba Teyel niouko téyé bou rafette rkk ❤️💍 rouslo niom Sindakhman ✊🏽 Yalla Sam lén are lén 🙏🏾
@Cocobvenk9 күн бұрын
😂😂😂kane moy sindakhmane 😂😂
@veroniquenatack73929 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@AmyColeFaye-f5k8 күн бұрын
Adamo😂😂
@Diamola809 күн бұрын
Oh 😥 ❤ l’amour c’est beau 😍 que Dieu vous protège Li nèkhna 😂😂 Fatou notre princesse 👑 tu es magnifique ❤❤❤.
@ramsesndiaye82069 күн бұрын
Yallah na yallah barkel heureux ménage ❤❤❤❤❤❤que dieu vous protège
@DabaSamba-s7z8 күн бұрын
Amine ya rabi
@fatousow53718 күн бұрын
Heureux ménage à vous ❤❤❤Seuyy bou barkel diam ak soutoureu si yén Yallah moussal lén si thiate ak lamign
@mddsalihat4269 күн бұрын
Yalna Yallah sakhal sén diam doundou lene bay fêter ay 💯 ans de mariage InSh’Allah avec un foyer fécond et béni InSh’Allah🤲🏽🙏🏽 we love you the Diagne💕🫶🏽
@Tancy59799 күн бұрын
Nous t'aimons fatou❤❤❤ Heureux ménage à vous ❤🫶
@Khadimamadou8 күн бұрын
Sen couple bi dafa ande sakh couple d artistes rek boullen falle boullen topato Bass thioung Et Fatou ndiaye 💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥💥🌹💥🌹💥🌹💥🌹💥🌹🌹💥🌹💥🌹💥🌹💥🌹💥🌹💥🌹💥🌹💥🌹💥💥💥💥🌹💥🌹💥💥🌹💥🌹💥🌹🌹💥🌹💥💢💢💢💢💢💢💢💢💢💢💢💢💢
@MaimounaDiouf-r3s9 күн бұрын
Yalna len yallah yamal bopam si barke seydina Mouhamed contane continue 💍🖤
@salamantouabdou5489 күн бұрын
Que Dieu bénisse votre couple Bass et Fatou Diagne ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@codoundao19483 күн бұрын
😂😂 Hay hay hay trop chou le grand frère à Fatou❤
@salamantouabdou5486 күн бұрын
Je suis encore là aujourd'hui pour ma Fatou Ndiaye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Contanena diam thi yeine, yalla nalen yalla sameu way, les mécontents massa😂😂😂😂😂
@MamadouBa-q1l7 күн бұрын
Wouy li nèkh naaaa ❤❤🎉 bass bn chance
@CheikhNdiaye-r4b9n2 күн бұрын
Machalla sama Mak djii ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@helenitagomis28079 күн бұрын
Li histoire dinako binde machala heureux menege les Diagne 💍❤️k’allah facilite yalla mousale lene si lamigne sama xol bi kone Wa nagou mbote machala titulaire international khana sindakhe dina nopi nake😂
@sounkaribakonte3642Күн бұрын
Wolay j’adore leur couple ❤️❤️
@aissadiom20169 күн бұрын
Liii sedd na khôl Fatou Ndiaye ohhh j'ai les larmes ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@NdeyendackFall267 күн бұрын
Li nekhna way Fatou yako fa am💃💃💃❤️❤️❤️❤️
@AichaAicha-ro7nb8 күн бұрын
Deglou na son bi ba sonn🥹❤️basse prends bien soin de fatou stp 🙏🏾
@paulinedeffond66096 күн бұрын
Heureux ménage ma Fatou
@thiammamediarra51358 күн бұрын
Kaw kaw bi tak nagn ko kaw kaw bi nop nagn 😂❤❤m partie préféré 😍😍🤣💕👌🏾bass merci way tontoul nguako
@NdeyFatouCharreh9 күн бұрын
Omg ceci est incroyable 🤩 basses, elle est vraiment pour garder, tenir sa marée et ne jamais embarrasser nous les supporters
@FantaDieme-u4n8 күн бұрын
Wawaw heureux ménage à vous mes❤❤❤nice couple c dieu le son est trop neikhe❤❤❤❤❤bass il est fort
Il doit juste focus sur son mariage et sa Musique faut a être a répondre sur les lives des ennemis et aigris soyez heureux 🎉❤
@guisseabsa40888 күн бұрын
Machala heureux ménage teint noir aca rafete
@ibrahimafaye40439 күн бұрын
Machalla frère 🎉yalla n'a sey bi barkel 🎉
@ThiaraLô-n7w8 күн бұрын
Li nekhna wayyy heureux ménage ❤🎉🎉🎉🎉🥰🤩🥰🥰🤩🤩🤩
@CodouNdir9 күн бұрын
Heureux menage bass tele gnou sougnou princess bi ❤❤yalla nalen yalla may diabote bou barkel❤❤😊
@DorcasBilema3 күн бұрын
Fakuniaaa🎉🎉😭😭
@thiammamediarra51358 күн бұрын
Manchallah ❤❤
@Bitcoin_richesse6 күн бұрын
Baol baol rk 🎉
@mamefatoufall299 күн бұрын
Wawaw lou nekh fowé mére yi tak kawkaw bi🎉🎉❤❤❤
@jeannefaye87718 күн бұрын
Mane kawkaw bi takeu nagne tè nope nagne ko momay ray thi son bi🤣🤣😂😂💪💪.Lou nèkh wayy
@Cocobvenk9 күн бұрын
Bilay tay niii sama xol biii sèdè contaaaane naaa dh ❤❤❤❤😂😂😂 maanguii rè rk
@gegezab9 күн бұрын
Fatou titulaire bi félicitations à vous❤
@camarafifi2907 күн бұрын
Bass wakhbi barina Fatou degna lepp ndakh yaw gninane doufa def 2ans none yangui sothiou di khare défaite Fatou ngala way téyél Fatou respecter ko thé nga yam si mome ki khallé bou Ndaw la yallah nalen yallah same seytane sorilen 🙏🙏
@ndoumbefaye12908 күн бұрын
Je vous souhaite beaucoup de bonheurs féxélen ba bou none yi meussa ré rek ngir yalla seuylen té andak pate ak réglé
@mbenelo82409 күн бұрын
En tout cas album photo yi rafett na 😍😍😍
@mbaondiaya72469 күн бұрын
Li mom dra fayouko gorgorloulein seye te yalla takh boulein deglou kein bolein kholei thi doulkatou tiktok yi rek diguein guena diapane heureux ménage ms bb