😂😂😂 wawe mbeur bougnou dane ba ay supporters ram signe petition ni bouko dieulate gnou bayiko waw amena
@Robbe-GrilletАй бұрын
Balla meussoul ladj Modou Lo si adouna. Mais roi bouy daw di weur weurlo amena Modou Lo la toudou
@ridialdieng2861Ай бұрын
Bilaye wakhal ngén ma Lima beugona wakh wa keur mod lo gnio ragal balla gaye dei
@ngangedrammeh6264Ай бұрын
@@keurguifootballps3678😂😂😂😂😂
@ngangedrammeh6264Ай бұрын
Roi buye moytou tamm amna, modou lo toudou 😂😂😂😂😂😂
@jobehamidou6545Ай бұрын
Balla gaye 2 vs site Eumeu seye vs Aeliu seye 2
@papendiayeridial5775Ай бұрын
Mané deh Empereur bi gnouy forcé moma diakhal 😂😂😂
@loelhadji100Ай бұрын
Yen ay fans balla geun
@assanewade6616Ай бұрын
Mane ampereur bigne forcé moma def ay ré 😂😂😂fisi Senegal lamb béne titre la ame moy roi 👑 Modou lo c’est le meilleur c’est le roi 👑
@CASI7797Ай бұрын
Mo deff rei gneupp key surtout présentateur bi
@ngangedrammeh6264Ай бұрын
Yen dangeyn nekh rek
@MatarMbegue-d2jАй бұрын
Siteu balla dou moramame
@khadimfall979Ай бұрын
BG2❤
@moussaseck967Ай бұрын
Me rayé desi bollé eumeu sene pourquoi doléne bolé eumeu sene si combat wala eumeu dou Champion
@AdamaMballo-t9sАй бұрын
Modou va jamai lutté avec balla gaye 2
@jamougym5185Ай бұрын
Lou takh balla Gaye do gil Eumo sen 😅
@sambagueye9669Ай бұрын
Balla bu amè fitt rek n'a jël avance su modou
@ridialdieng2861Ай бұрын
Wakhi doff way
@3mara16Ай бұрын
Le combat revanche ça seras rien, franchement la lutte devrai évoluer camem
@abdoulayeka2147Ай бұрын
Les ndiayènes bayiléne tek hell bi juillet dafa nek séne mois rek mo takh guène beugue si forcè mbeur yi
@abasall711Ай бұрын
Merci goro luler nga wax
@abdoufall653Ай бұрын
Fo kin ampurr Fo Kaff
@bachirdiop19Ай бұрын
Père Ray yaw parfois daguay fatei ni yay def émission bi
@MamecheikhantaNgomАй бұрын
Exactement Wakh nga Deugue dé😂😂
@gassimoudiallo6119Ай бұрын
Na balla dane eume sène ba paré😂😂😂
@abasall711Ай бұрын
😂😂 Voila merci niamer wuko
@abasall711Ай бұрын
Merci diaw sama Walo walo bi aka diamer degue goudal fane wer diam si barker serigne Babacar
@CASI7797Ай бұрын
Bilay Raye Ba dagua sofffff, legui loutax do wakh supporters Balla Gaye yi beuguougnou Balla beureii ak Eumeu Séne. Ni gua fareii ci Balla c'est indigne d'un présentateur d'une émission. Modou Lo nak gnakk daane Balla yakoul dara ci carrière parceque il est le meilleur lutteur de ce pays
@abasall711Ай бұрын
Merci
@DeggouАй бұрын
💯👏👏👏
@ngangedrammeh6264Ай бұрын
Kiko daan nyari yoon bak ak kheti jel yimko daan, koku lanla?😂😂😂😂
@beuguegalsenziguinchor6280Ай бұрын
Vraiment je ne comprends plus la lutte c,est sathies qui a battu Siteu il y’a pas longtemps donc comment Balla Gaye 2 peut il lutter avec Siteu
@loelhadji100Ай бұрын
Mon takh dou lamb
@leyemouhamed2149Ай бұрын
Modou lô guir yalla boll ka dieull
@durkio5486Ай бұрын
😂😂😂😂
@MouhamedDiaw-sy4rsАй бұрын
Euma sene
@abdoufall653Ай бұрын
RAY DAYE FEN REK NDAKHE WA NDAYE YEN NO LAY FAYE
@abodiouf4805Ай бұрын
Ray khamo dara comme do journaliste
@thiernodembaya8355Ай бұрын
🇸🇳🇸🇳🇸🇳 le présentateur de émission est très nulle il parle pas de la lutte toujours ce qui plaît seulement à Aziz 😊😡😡😡
@layeNdiaye77Ай бұрын
Bayil doul
@Lepatriote9423Ай бұрын
Kouy xalam dissi diayou. Amna si droit Mo tay
@OusmaneSambe-l3fАй бұрын
Yaw bayil doul Aziz ak Balla Gaye rék ngén bagn doméram yi niaf lén sén xon dém sétani fénén Vive Guediawaye...vive Balla Gaye..Vive Aziz et SONKO à vie❤❤❤❤❤❤
@thiernobarry2625Ай бұрын
C'est visible que c'est leur télévision à eux ( Al Bourakh Tv ) 📺 d'où ces éloges envers le boss ( Aziz). Il n'a pas le choix !!!
@oustazahmedfall6478Ай бұрын
Wallahi c'est vrai il est nul
@jobehamidou6545Ай бұрын
Modou lo vs sa thies Modou vs sa thies Modou vs tapha tine
@khdimfall1837Ай бұрын
Modou lo burewoull AK Balla gaye Modou lo sa Thiès Moy combat bi
@alassanemane3021Ай бұрын
Balla gaye 2 ak Modou doyna na balla gaye 2 dieul Siteu moy combat bii
@abasall711Ай бұрын
Merci dieulena béna boye mu daneko lolu motax niamer wul boye yi
@LeuzsonkoАй бұрын
@@abasall711legui modou lagni beurèl force nak😂😂
@SaliouKane-z8cАй бұрын
Làth lén wà balla gay baham beug nànn eumeu séne
@abasall711Ай бұрын
Merci Saliou
@jobehamidou6545Ай бұрын
Modou lo vs tapha Modou lo vs sa thies
@SerigemodouDiaАй бұрын
Modou lo ks sl balla gaye ak eume sen respect a Modou lo le roi
@miboldieng7574Ай бұрын
Pere Diaw Siteu tabakh na si keur yi boy yague dawal na si auto yi mingui dimbali diamou yalla yi
@Senegalaise2024Ай бұрын
Balla modou lo mom doyneu seuk
@sabarastsАй бұрын
Baye Ndiaye est intelligent bégn demarcher Balla Gaye Modou Lo parcek khamna Modou souy beuré ak Balla sakh Diambar mo key teugue
@FallouDiouf-ms6mtАй бұрын
Daiwa sayetani ga yaw😂😂😂
@cheikhdiop5288Ай бұрын
Da daw ba eksi siteu dafma rouslo
@wadeidrissa7410Ай бұрын
On veux pa de balla contre siteu
@BolyBa-i2fАй бұрын
Yene boulene fate balla bou mouy nekka rois defa ni dou beure ak Modou dem mba niaka rois nekka si dieff dieff Modou diele ko mou dann ko Modou diogo dem ligueye mba yalla may ko mou nekka Rio dey yombou trop lamb bole tou lene Modou sa Thiès la wara mbeuerel Wala reug wala tapha tine waw dem leen ligueye nal
@loelhadji100Ай бұрын
Yen dafa melni dolen deug modou bougoul beure ak balla loutakh Jak foi balla balla joder
@ablayegaye9331Ай бұрын
Ya kham louy khew souba
@oumarndao7485Ай бұрын
Balla nehna,mo yor ay agent wam diko teugueul,té moy choisir ses adversaires et ses dates
@sidythiam6983Ай бұрын
Bilal kouko dieul 90% dalay dane
@NayeFall-qq7xiАй бұрын
Kom Móodu lóo rekk
@oumarndao7485Ай бұрын
@ modou bane agen am mokoy teugueul lamb?,bane date lafi meusseu choisir?il choisit seulement ses adversaires té lolou dou yone
@LambfiteuАй бұрын
Légui Modou Lô nak
@sidythiam6983Ай бұрын
@@NayeFall-qq7xi Yagui diawalé modou année bi dinafi beuré deux foi mes balla juillet rek tmt😂
@SambaSene-j1hАй бұрын
Bogougnou bala ndakh khérème laye beuré boudone beuré rek pas galadie modou mo mone bala fouf
@SerignefallouToure-lu8ubАй бұрын
Iow khoromou nga deh😂😂😂❤❤
@BolyBa-i2fАй бұрын
Te nagou lii yalla dougal
@morlam8705Ай бұрын
Yene aussi pourquoi bloquer balla ? Laisser les autres promoteurs teug balla un autre combat ! C normal 2 combats par saison pour un sportif c le minimum
@famaradiouf5367Ай бұрын
Balla sou diele siteu danou billaye Par ce que lolu moy combat yekini
@MantaDiop-v3kАй бұрын
Yaw wirnga yikini moy yalla😂
@modoudiop1646Ай бұрын
😂😂😂😂kone ltx yekini danoul balla sawaye 2012😂😂😂😂
@talladieng6132Ай бұрын
Kouy yekini
@NdiayeModaАй бұрын
Pére balla ba siteu Di tabàkh thie keure yi AK Di dawal thie auto yi bo hamoul nakh Dina beuré AK balla
@miboldieng7574Ай бұрын
Bilay
@Robbe-GrilletАй бұрын
Balla gaye 2 vs Siteu dou combat dou actualité, dou challenge. Marketing kessé la mais combat bobou so si guéné marketing, amatoul sens. Balla gaye 2 vs Modou Lo, Balla gaye 2 vs Eumeu Sene yoyou nioo dakh fouf té eup challenge
@mbayendiaye5033Ай бұрын
Ray ba boul niou sosal Supporters modou lo yi lou modou dougue beug nagne tu est un représentant d'un émission donc linguay wax boul khol lou nekh sa patron waxal logique ak lamb rek Supporter lou yonam si débat
@MbengueAbdoulaye-j2gАй бұрын
Balla balla yaye sama mbeur mais siteu lima diahal pied droit laye ték téh dah bokak leuwéto ak boy niang déy tahlal loho droit pour gua diote koh un lutteur comme balla il va insisté par la force non je suis pas d'accord téh balla hamna lolou billahi balla monoul siteu bid léne mieux vaut modou lo balla bouko dieul wah nah déh
@LeuzsonkoАй бұрын
Siteu sama way la ms souma sanion dou dieul bg2 goudi yi na xar ama ou gris.