Il n’y a pas dans se monde si une personne capable d’expliquer les paroles de Cheikh Ibrahim Niass, je le dis avec certitude.
@amethgueye85984 жыл бұрын
Mashalah
@cheikhbarham96265 жыл бұрын
Dieuredieufe maolanah Cheikhould khairy
@seydoundiaye17535 жыл бұрын
Ma cha allah rafetna chiekhe ousmane yageu fi lol teu wer
@papaboucardiouf72804 жыл бұрын
Sa wakh dji ci bakan rek ngako tég🤗 Epuis wadji loutakh wakhalul bopam???????
@aliouneniang51032 жыл бұрын
Touty diomte amna si ligani Serigne Touba yonnente ladone weuri diarari wird makhous lafadoune dieuli moye limo donne sako donté yonnente lafa Guiss mo diokhkoko Serigne sayoye bind khasida yonnente tew si kanamame
@assanendoye19775 жыл бұрын
Machallah Baye merci beaucoup 🇸🇳❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️☪️
@alhaqq3105 жыл бұрын
Done Khalifa Baye key diaroul di forcé wala di méré ay nite, fi koufi indi dara louy dieurigné rék nite yi toppeu la. Kou Yallah fégnal rék ngua fégne. Yow nguani Baye Niass mo wakh né danikey doneu donc fane leuko wakhé tamite fookk ngua indi ko, comme ninguay indé ay dalile si yénéne wakhi yi ??? En plus nguani nékkeu sa khalifa Baye donoul ndam si diné dji.... !!! Sérigne bi nite day am respect, sa wakh djodiou téguiné woul dara !
@Ousmane75.3 жыл бұрын
Mbow mi dafa rew RK
@seydoundiaye83412 жыл бұрын
Merci frère
@awacheikhfaye6375 жыл бұрын
Khalifatou lahi si kaw souf day am si siecle bounek Mane nak kima xamal Bay ndiass moy sama khalifa Wa salam
@arfangsalane70525 жыл бұрын
Barké Baye Niass daguén may rouslo li moy wanéni xamoulen kan moy Baye
@imamassanealmichriyoun27755 жыл бұрын
Man lima diakhal moy guissouma fiko BAYE BARHAMOU bind
@arfangsalane70525 жыл бұрын
@@imamassanealmichriyoun2775 ils croient que la fayda est un État et les gouvernements se succèdent
@aliounebadaradiouf59095 жыл бұрын
Ah sangue yi insanoul kamil mome meuneta manquer si djamano nak lolou mome nieupeu nangou neine ko hana ndah baye wahnassi SeydinaCheikh aussi si djawahiroul maani Louniouy lathier key moy kane la... Yalla moko xam yalla naniou ko hamal🙏🏾
Arfang Salane ah machallah kone bahna Nioune ite dh baye mognou doy Mtx niouy weurr foum lakou comme nignou doylo SeydinaCheikh ba guiss ni ci baye niass la lakou.
@ndaomore70475 жыл бұрын
Mancha Allah Cheikh Ibrahim Niass
@ndeyediarra20635 жыл бұрын
Macha Allah seydi Niasse rta
@japposavideo5 жыл бұрын
Mashallah
@SaraSara-rw1qf5 жыл бұрын
Niass ❤❤❤❤❤
@soldatby66035 жыл бұрын
Machallah seringe by
@bayetaibathioub53325 жыл бұрын
Alhamdoulila
@abdallahgassama36785 жыл бұрын
Macha Allah serign b
@laminedembele30185 жыл бұрын
Machalla
@ibrahimakamara11065 жыл бұрын
Machalla lére na
@MoustaphaNdao-rx4px5 жыл бұрын
Louma djakhal gnou andak serigne bi gneup woténéne
@alhaqq3105 жыл бұрын
Doyna waaar déh 🤣🤣🤣
@ndimbelanendimbelane4215 жыл бұрын
Wa mane lima diakhal moy Sheikhoul Khairy lane la andi ? YOYENTI andina lislam SHEIKH TIDIANE andi tarikha BAYE andi faydou Wa legui Sheikhoul Khairy loumou andi????
@degdeugtv78725 жыл бұрын
Lolou yeup égale diné si cheikhoul khayri la wathi
@degdeugtv78725 жыл бұрын
Lolou yeup égale diné si cheikhoul khayri la wathi
@mthiam15675 жыл бұрын
@SAYROUL ABADD Dr Cheikh Ousmane Mbow Machallah. Je l'ai tant cherché que Dieu Dans son Infini Miséricorde m'a offert la Rahma de le rencontrer à la cité SHS. Al hamdoulilah
@lovetv86325 жыл бұрын
@SAYROUL ABADD Dr Cheikh Ousmane Mbow bayi léne séne thiahane yi Faydou bi mo bolé aqiqa ak Marifa ak saria liguéni wah cheikhoul khayri wahoul li
@babasaloum41334 жыл бұрын
@SAYROUL ABADD Dr Cheikh Ousmane Mbow est ce que mana la lathie ben question boco tonetoo ma khamni cheikhoul xairi moy khalifa Baye?
@elhadjimbow14815 жыл бұрын
Macha allha niass alhamdoulila
@mr.africa81665 жыл бұрын
Ndeysane wah nga ba yakarr nii wahnga tii wahulo fii dara
@damziiniang7415 жыл бұрын
mr. Africa doff nga motax meuno degg limouy wakh 😂so nekone niit rek degg ko
@soldatby66035 жыл бұрын
@@damziiniang741 bilay 😁
@damziiniang7415 жыл бұрын
soldat by waxal bokk😂
@soldatby66035 жыл бұрын
@@damziiniang741 bilay Mane damaka moudié yeureum sakh moungi khawa déh ak kiraye té yeugousi Dara😁
@damziiniang7415 жыл бұрын
soldat by mdrrr lou leer mai dou gneupay nangou ossi tamiit lolu mom gnune talibé yi meunugn si dara BAYE lay nex rek
@bronice80875 жыл бұрын
Wa mane damaye Katie khalifa yalla l'âne mot dieureudieum guinawbi baye watié
@diouffallou90905 жыл бұрын
Ki limeu geuneu neh si wahdji yeup moy Aÿ wahou baye rek lay indi ki kou waurleu
@Ousmane75.3 жыл бұрын
WA faydatidianiya yénaniou yabb RK ki takhaw Di wakh talibé baye bou gnewoul ci serignam fassikh leu ngeuinn diko bayi mouy continué Di fennn RK. Beugueu mbolo RK. Baye mo wakhal boppam Moy khalifa Cheikhou Tidiane ci wakh bou lairr, gnongui khar beu cheikhoul khayri wakhal boppam Moy khalifa baye.
@mr.africa81665 жыл бұрын
Lii gay tekhele dou nii khamulo nii hadarat yii tedoe motakh gane yangii wah baye niass kom president bou wathie .so khamone djoumi yalla jii danga nupalakou
@diouffallou90905 жыл бұрын
Makama yi yaw hamoko motah ngay waheni
@mr.africa81665 жыл бұрын
@@diouffallou9090 yene khamulene dara dagene werr sene bopp ibrahima ibn abdoulaye la ousmane mbow guiss wayy khamul baye kon dou nekk fii nane jamanom moy bimou doundou ba bimou dedd la yem kenen falou subhanala kon yene khamulene hakayik nimou teude lii delila cii mahirifa .motakh kham lu bare wakh lu tuti koku le moy wayja sedibarhama
@chicchoc52485 жыл бұрын
sa wakhdji yeup khamnén foumou dieume kingay wotél nangouwoute
@absandiaye65424 жыл бұрын
Ah beugue baye bamou lak sama kholbi, lolou rek doyna ma wallahi, lolou rek couran la
@mr.africa81664 жыл бұрын
@@chicchoc5248 kham nengko ousman kathie rekk la neke ak yapp wa paye bii dengko wara interdit medina baye ku niak yarr la tii yabate
@leuz52105 жыл бұрын
BEUG NEK SERIGNE REK MOLA SONALE YAW OUSMANE MBOW BEUG AK SANGUE
@bronice80875 жыл бұрын
Waw l'âne moy réfet ci yalla
@mamemomarndaw61115 жыл бұрын
Bro Nice lolou mooy nangul yalla yallaam gi
@bronice80875 жыл бұрын
Yaw kou mana fenga gani baye dadoun weure fi khalifabi du dioudo