Walahi oustaz nioune yen rek laniou top yalla na yalla tawulen ❤
@PAPAFARAKANE Жыл бұрын
Ma SHA Allah , meilleure émission de l'histoire de la télévision Sénégalaise, vous êtes magnifiques ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ Qu'allah vous bénisse ❤
@mouhamadousy180 Жыл бұрын
Masha Allah, Amna solo trop trop. Yalna Yalla samm léne té mayléne goud fane ak wérr Bidjahi Rassouloul Lahi Sallal Lahou Alayhi Wa Sallam.
@PAPAFARAKANE Жыл бұрын
Bilahi professeur MADIAMA mala beug ❤❤❤ yalla maynala 😢❤
@gninguemomar3444 Жыл бұрын
Maacha Allah mon frere , qu'allah swt vous benisse ❤️
@ritamanga3494 Жыл бұрын
Elhaji xam xam késsé leu Al badou Machallah
@abdourahmanediop3700 Жыл бұрын
Assalamou aleykoum wa rahmatoulah. Masha allah wahtaane bi neexna
@mohamedndoye Жыл бұрын
MachAllah c'est magnifique
@amadoulo8263 Жыл бұрын
Thiey yalla mandé amna lo yokk si man ❤❤❤yalla nala yalla fay
@chamssoudineattijani9179 Жыл бұрын
Machallah Est-ce que le monde parallèle est réel
@aminatalobio Жыл бұрын
Mashallah barakalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@malickniang7292 Жыл бұрын
Ma Shaa ALLAH
@ndiagafaye225 Жыл бұрын
Masha Allah ❤❤❤
@barroelhadji98 Жыл бұрын
Yalla nalene yalla faye yèna xamal niit gni lou serigne doul xamal ap talibem mashala . Limalene yekha xam rek lay reuthiou. En plus yena ngui bayi khel gniy comentè si conseilli mashala
@sambadiop701 Жыл бұрын
Machallah ya oustaz
@fatoumatadiop6276 Жыл бұрын
Thiey Aladji ❤❤.......j'imite El Badou ....c'est tres interessant machalla
@djiloobodji9801 Жыл бұрын
Tabarkala
@Kambel-tv Жыл бұрын
Macha allah yalna yalla sam
@leuzthiam72462 ай бұрын
Alhamdoulila rabil alamine nio ngui sante Wa Keur gui yeup yalla na borom bi Barkél de la part de Medoune thiam ❤❤❤
@papandiaye9419 Жыл бұрын
Professeur manchalah rk❤
@oumarthiam8509 Жыл бұрын
Machalla
@mansourthiam98364 ай бұрын
Salalahhu ala Muhammad 💚 🤍 💛 ⭐️ 🌙
@OusmaneSeydi-q8j4 ай бұрын
Ce professeur est bien instruit S'instruire pour mieux convaincre, Voilà ce qu'il faut
@NdeyeawaNdiaye-my5wm4 ай бұрын
Allah est unique
@fatoudieyendoye92927 ай бұрын
C'est magnifique ❤
@sileyedia61086 ай бұрын
Machalla ❤❤❤❤
@monopinionhd75816 ай бұрын
Thiey machaallah
@saodouamadouba2974 Жыл бұрын
Assalamou henleykoum Professeur ak El Badou dilén ziar bou weur dii contaan si yén .
@senemallorca283811 ай бұрын
Masha ALLAH
@MK-Architect10 ай бұрын
MASHALLAH🥰
@KholSeddАй бұрын
❤️❤️❤️❤️❤️
@rokhayacisse16063 ай бұрын
Imam diomay fay 😎
@binetaba9476 Жыл бұрын
Salam professeur Défois j'ai le sentiment de tomber dans mes sommeil pourquoi
@SambaLaobéThiam-d9w4 ай бұрын
😊
@PAPAFARAKANE Жыл бұрын
Ma SHA Allah merci bcp d'avoir répondu à ma question . Ma question du jour : Est-ce que la réincarnation existe vraiment, manam niit am ay vie you beuri, say bou déwé rk dafay dioude felène , il se réincarne dans un autre corps . Je veux vraiment en savoir plus .
@hitthelink6624 ай бұрын
Jinnè cheytane yi la niokoy df sinon kone yalla deii wedi bopam ndax nèna dècretè na kou dè dou doundate ba mouk amna bene yonenete buko Yalla waxone tè Yalla nèna ALLAH ne Manque Jamais à ses Promesses
@youssouphandiaye7245 Жыл бұрын
Salam la famille. Comment transformer une situation défavorable en situation favorable. Ou encore est ce que Satan en voulant toujours pervertir la personne ne contribue t-il pas à forger de façon inconsciente à ce qui l'apporte le bonheur, sa quietude spirituelle
@fatoudieyendoye92927 ай бұрын
C'est la volonté de Allah swt pour pardonner son serviteur et le sauver
@ritamanga3494 Жыл бұрын
Mom la sama mame nane diour dou djikko Waliw dina djour saysay Comme saysay dina diour waliw
@PAPAFARAKANE Жыл бұрын
Pourquoi l'émission du 03 décembre 2023 n'est pas sur KZbin 😢
@Fatima324-u9B Жыл бұрын
On avait rediffusé
@MorTHIANDOUM-y9z Жыл бұрын
Assalamou aleykoum serigne bi magui ziarr … mann dh dama mousa dégu niouné mame Adama amna yénénn domm youmou amm yo khamni mame Awa diouroulénn ma beuguonn kham losi khalate ?? En autre yadiouth yi ak madiouth yi (gog et magog) ayy domou Adama laniou may lath lann gasi khalate ??? En fin es ce que gog et magogg vont participer a la destruction du monde ??
@Math-Pc-Mlg72274 ай бұрын
Pouvez vous expliquer pourquoi on dit que Allah maname daye dogale té dou geureme
@morthiandoum2194 Жыл бұрын
Serigne bi beug na ayy léral aussi si zoulkharnayni si voyage bimou defonn mahribasamsi genre niata monde la diotona dém wala si 16 monde yeupp la dém ?? en plus mom nann la dieuflanté ak extraterreste yimoufa fekk ?? En fin dégu na ausi amna monde boumou dém bo khamni gnimoufa fekk khamouniou sakh kouy mame Adama ma beuguonn si ayy léral svp ???
@momomomar241811 ай бұрын
Salut l arbre du paradis c est quoi en realite..pour qu on l interdisse a adam
@narutomoctarjallow14536 ай бұрын
Eu se son les chite
@morthiandoum2194 Жыл бұрын
Assalamou aleykoum serigne bi magui ziarr … mann dh dama mousa dégu niouné mame Adama amna yénénn domm youmou amm yo khamni mame Awa diouroulénn ma beuguonn kham losi khalate ?? En autre yadiouth yi ak madiouth yi (gog et magog) ayy domou Adama laniou may lath lann gasi khalate ??? En plus es ce que gog et magogg vont participer a la destruction du monde ?? En fin ga léralniou si zoulkharnayni voyage bimou defonn sa mahriba samsi ak extraterreste yimou fa fekk niounn nann laniouy doundé ??dégu na aussi amna si extraterreste yoyou nio khamni khamouniou sakh kann moyy Adama ?? et zoulkharnayni niata monde la diotona dém si voyage bobou ??. Merci .
@AliouSarr-y6n11 ай бұрын
No yaw reek lay setan me tay mom liga wakh yalla dinala si topou liga wakh si Omar Sall té dara lérou la si bilay walay yaw rek lay setan nak me
@papissarr27332 ай бұрын
madiama diagne damay lath fo diangue xam xam wala dagn lako sol ? machalah lo wakh rk danguay kham ni deug deug xam xam la